🚨Empereur ou Roi des arènes Pére Birahim donne son avis et encourage Aziz Ndiaye

  Рет қаралды 22,542

Sans limites TV

Sans limites TV

26 күн бұрын

Пікірлер: 40
@ShiekhjobeTijan
@ShiekhjobeTijan 24 күн бұрын
Modou lo rek moy👑👑👑👑👑👑👑❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@serignendamelo6964
@serignendamelo6964 24 күн бұрын
Aziz Ndiaye dafa sokhor bilay ms beine roi mofi âme te modi Modou lo point
@user-xz6sk7si9i
@user-xz6sk7si9i 24 күн бұрын
Aziz sokhor nga na ngoul lila yalla dogal modou lo moy roi des l’arène
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 25 күн бұрын
Aziz kou sokhor ,kou rancunier nga.Balla dafa dane Modou niari yone Modou nieuw rawko si lamb té ay rival lagn lololéne méti motakh gay saltél mais dara défaral sakh couronne nou diamant mais Roi bi mom Khalé bou civilisé biy yéwo PA moko mom❤🎉XLO KASSÉ 🎉❤ Biguéne néké roi niepa nangou légui gay sisou ndakh yaw si Balla gay amé visibilité té ainsi dafa nék si ay pblm té Modou teugeuloko ngani naga si kheup souff mais yalla mi diokh XLO ROI BI MALGRÉ SA TAILLE MOFI NÉK BA LÉGUI MONO SI MODOU TOUSS LIGAY BONE.TAPHA mom na ay mbokam djouk parsk ligay déf yeup boudone tapha ak kénene la doko déf mais Balla gay khalal .kone nadéf attention si yaw . Bala may guemni amga doolé nga dém guéné Lac fimou nék fay 59 millions yi yéna bok Guediawaye té amgako mé seytané motakh doko déf vu k lac amoul bayré dosi dougal sa khaliss .si business ak calcul gay dokh .khamnagn la🤧 Père wakh léne Aziz deugu mogueune guéne koy encouragé.
@dembaztarkinda8270
@dembaztarkinda8270 24 күн бұрын
Yaw nokoul thia khathi Aziz limou deff si rewmi sa baye sakh defou kofi ngay Ame loye explique doul waye bayi lene seytane aziz ndiaye bouy guisse ak Mbeur Yi dolen ko feke kone mandou lene si
@ShiekhjobeTijan
@ShiekhjobeTijan 24 күн бұрын
Modou lo Moy 👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🇮🇹🇮🇹
@abdoulazizdiop
@abdoulazizdiop 24 күн бұрын
Roi des arènes Sénégal défa yobo bilahi
@MameSow-vp7rj
@MameSow-vp7rj 24 күн бұрын
Aziz Ndiaye mo téppi leufeul ndayame 😂😂😂
@AbdrahmaneSy-jr1bb
@AbdrahmaneSy-jr1bb 22 күн бұрын
Bou moytouwoul Sénégalais yi lék badio mamam nak
@djibycoundoul1495
@djibycoundoul1495 24 күн бұрын
CNG nio défoul séne ligueye parce que lii sou dialé euleuk kénéne mounena organisée la même chose sur d’autres lutteurs… il faut que la CNG revoir le titre de roi des arènes une bonne fois
@oumitandiaye6780
@oumitandiaye6780 23 күн бұрын
C vrai
@ShiekhjobeTijan
@ShiekhjobeTijan 24 күн бұрын
Sama papa ji yalña yalla defal ko jama AK Sallam ta geñe waral ay thiram ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@molaminmanneh-fs6wn
@molaminmanneh-fs6wn 20 күн бұрын
Merci deuga❤
@ShiekhjobeTijan
@ShiekhjobeTijan 24 күн бұрын
Pa iaw lo wax dege la Yalña yalla defal la jama AK Sallam ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑❤
@AliounebadaraGassama-or4op
@AliounebadaraGassama-or4op 23 күн бұрын
Li amoul problème balla sou dané tapha tine empereurou tapha tine leu tapha sou dané l'a même chose rèk thi gniom niar l'ay yém aziz Ndiaye da mom arène bi
@degrk5622
@degrk5622 24 күн бұрын
Aziz na may nitt gni diaam sokhor kassé moko diaap AK rancunier affaire sokhor rk lafi wakh d'autres nane dafa beug diay combat bi c'est faux
@guibrilmane4267
@guibrilmane4267 23 күн бұрын
Le sport est ainsi fait . Tu fais tomber le roi et t'es roi.
@modoudiop7841
@modoudiop7841 21 күн бұрын
😢😢
@guibrilmane4267
@guibrilmane4267 23 күн бұрын
Regardez la coupe du monde, tu gagnes la coupe et t'es champion du monde même si t'as une défaite durant les matchs de poule.
@modoudiop7841
@modoudiop7841 21 күн бұрын
🎉🎉🎉❤❤
@ndiayeabdoulaye7836
@ndiayeabdoulaye7836 21 күн бұрын
kodan roi yay roi
@modoudiop7841
@modoudiop7841 21 күн бұрын
AIMNE 😘👂🤔
@rimesmakerposeidon2427
@rimesmakerposeidon2427 23 күн бұрын
Aziz Ndiaye khamoul foumouy takhawou igname rék Moko diape
@DiopAlioune-sr1zl
@DiopAlioune-sr1zl 20 күн бұрын
Wakhe dji Dale moye roi des arènes bouye dawe tapha tine mofi nek 😂😂😂
@user-nd1xq1sg5j
@user-nd1xq1sg5j 24 күн бұрын
Aziz defoull benn affaire pour jaayy lamb jii si lol lay lakhou ak faire semblant mais limm beugg moyy sokhorr
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 24 күн бұрын
Azizi Ndiaye diaye katou yamba la
@user-pb7qn9dh6i
@user-pb7qn9dh6i 22 күн бұрын
😂
@AliounebadaraGassama-or4op
@AliounebadaraGassama-or4op 23 күн бұрын
Mais cng wakha goul dara gayi nioy commentaires rèk
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 24 күн бұрын
Aziz Ndiaye kou katte yayam la
@user-bk4nf7cj6r
@user-bk4nf7cj6r 22 күн бұрын
astkhfiroullha respect ya bonne 🤣🤣🤣
@mouhamadoufaty877
@mouhamadoufaty877 24 күн бұрын
Aziz il vend le combat, c'est une communication qu'il fait juste pour vendre le combat
@yerosow7063
@yerosow7063 24 күн бұрын
Mais père Aziz formule bimou wakh ak bifi nekk c la mm choz Té en plus qd BG2 était roi des arènes tchii mm formule bi metiwouko Pere sport de combat individuelle yeup c com sa ki terrasse le champion est champion nakk
@abdouba1135
@abdouba1135 24 күн бұрын
Père yekini nek nafi 15ans danou woul ba legui kén accepté woul son roi Xol koula nekh ga defal ko carrière bou Nice Koula nekhoul ga wax deffou fi dr
@MbayeMbengue-qt3sl
@MbayeMbengue-qt3sl 24 күн бұрын
Zize Ndiaye kou katte yayam la
@RamataSy-jd5go
@RamataSy-jd5go 21 күн бұрын
Entouka cnG wakhagoul dara dei
@user-pb7qn9dh6i
@user-pb7qn9dh6i 22 күн бұрын
wakh dji dou lgui dh naniou bayih ba jj tapha tine vs balla gaye nah courone dina gueneu wa cng louniouy df bou boba
@bocarba2781
@bocarba2781 23 күн бұрын
Kou dane champion yaye champion partout dans le monde arrêtez vos connerie svp
@bocarba2781
@bocarba2781 23 күн бұрын
Kou meuna dane nieupe????? Lamb ji dafa barri ay doffff
@ndiayeabdoulaye7836
@ndiayeabdoulaye7836 21 күн бұрын
Per andoma ak yaw
@ndeyeastou7501
@ndeyeastou7501 24 күн бұрын
Cng bou bésse bi danion ragale Aziz Ndiaye batakhe Louko nékhe moye ame niank foula ba dé père becal moma bette rék Aziz bou sanione modou dou done rois des arènes
$10,000 Every Day You Survive In The Wilderness
26:44
MrBeast
Рет қаралды 126 МЛН
Они убрались очень быстро!
00:40
Аришнев
Рет қаралды 2,8 МЛН
2000000❤️⚽️#shorts #thankyou
00:20
あしざるFC
Рет қаралды 13 МЛН
Aziz NDIAYE "La realite du marché ne permet pas de diminuer le prix du riz importé"
10:06