🚨Mako eup lép😱sortie inédite de Sa Thiès contre attaque Zarco et raille Modou Lo“dafa daw combat bi”

  Рет қаралды 51,993

ETDR MÉDIAS

ETDR MÉDIAS

Күн бұрын

Пікірлер: 135
@mansourleye9816
@mansourleye9816 Күн бұрын
Franchement Il Est Digne Respect Mbeur Bonne Continuation 🫡
@bassdiokhane1472
@bassdiokhane1472 7 күн бұрын
Sa Thiès yall nala yalla maye combat inchallah bou geune si ioe may la si ay ndam inchallah nga yoko enterrement bi rk bon ligeuye kèn dakou la beure diam si ioe ❤❤❤
@bayetallaBeye-vj6or
@bayetallaBeye-vj6or 7 күн бұрын
Bilahi sa dafa yaro 😢😢😢
@papesouma
@papesouma 6 күн бұрын
Amine
@beugeuserignetoubatvgayeko3846
@beugeuserignetoubatvgayeko3846 6 күн бұрын
Amiin❤
@khadimgueye-sk2kz
@khadimgueye-sk2kz 6 күн бұрын
Bly sa thies amoul benn problème yalnako yalla defal ay ndam barkép serigne touba
@MoussaDak-o7f
@MoussaDak-o7f 7 күн бұрын
Sa thiés momane zarco sa thiés Modou lô Moy Moy combat bi ❤❤
@CamaraMatar
@CamaraMatar 7 күн бұрын
Wakho deug
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 7 күн бұрын
​@@CamaraMatar wakhna deug kay
@CamaraMatar
@CamaraMatar 7 күн бұрын
@modoubayefallsikroulla1423 ioe foko tekk
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 7 күн бұрын
@@CamaraMatar yaw foko ték
@CamaraMatar
@CamaraMatar 7 күн бұрын
@modoubayefallsikroulla1423 sa thies eupoul zarco dra dou dolé dou dra
@FalouNgom-o3m
@FalouNgom-o3m 7 күн бұрын
Sathiés mo meneu 10 zarco 😊😊😊
@morsow6740
@morsow6740 6 күн бұрын
Il communique bien bien ❤❤❤
@franceamericanbullydogfami7992
@franceamericanbullydogfami7992 5 күн бұрын
N'oublie surtout pas que tu es le digne fils de ton père... Les entraînements sont tes amis le meilleur reste à venir
@SaliouFaye-e5s
@SaliouFaye-e5s 6 күн бұрын
Macha Allah tu communique super bien continue comme ça yalla na nala yalla def roi des arenes ak empeureure
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo 6 күн бұрын
Sa Thies yalla boumou dieul Zarco way Sa-Thies vs Modou Lô moy yoonou lamb Zarco vs Eumeu Séne
@AhmadouBamba-p8t
@AhmadouBamba-p8t 6 күн бұрын
sa thies seul yalna ngua ame comba
@thiombayeseck9782
@thiombayeseck9782 5 күн бұрын
Ay khotou tate lako dané 😂moko mene fouf sa dof la ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MamadoumoustaphaNiang-sj5vx
@MamadoumoustaphaNiang-sj5vx 6 күн бұрын
Merci beaucoup sa thies❤❤
@moudoudiop6216
@moudoudiop6216 7 күн бұрын
Sa Tihss seul 💛💛💙💙💙💯
@cheikhdiop9932
@cheikhdiop9932 6 күн бұрын
Dafa niak fay da emeu sene danko
@laminefall6481
@laminefall6481 7 күн бұрын
Fall ioe yah bakh rek diame rek ngaye âme inchallah ❤
@thiammaodo4538
@thiammaodo4538 6 күн бұрын
Vive sa thies
@morsow6740
@morsow6740 6 күн бұрын
Champions ❤❤❤❤
@sambaba683
@sambaba683 5 күн бұрын
Satiès et modou lô moy combat bi❤
@Bebefodetoure
@Bebefodetoure 3 күн бұрын
Merci beaucoup
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 6 күн бұрын
Machalah il est correct et il communique bien Boula ken changer Salif ningay communiquer c bien ken doula ci kheb Machalah yallah nanga am combat yallah mayla ci ndamm boudoul Modou nk😂
@GorguiNdiaye-nq6oz
@GorguiNdiaye-nq6oz 6 күн бұрын
Sa beur la ligéye rek inchialla ❤
@elhadjiibrahimadiatta9485
@elhadjiibrahimadiatta9485 7 күн бұрын
Champion ❤
@SerignefallouDiouf-bo3ny
@SerignefallouDiouf-bo3ny 6 күн бұрын
Satiés champion la
@DièganeNdao-z8n
@DièganeNdao-z8n 5 күн бұрын
Que Dieu te protège ❤❤
@ManoVideotech
@ManoVideotech 7 күн бұрын
Zarko ay boy rek la dane ak ay malade, danoufi bene sadique yoone lay oute di ték khèle 😂😂😂😂
@mouhamadoufalloutoure1991
@mouhamadoufalloutoure1991 6 күн бұрын
Iow xamga noumou démé nak mougui dann dé way danagoul adversaire de taille comme momm exemple franc sathiès reug ama et boy niang wala eumeu ak tapha tine ak lac2 bousi dané si gni ma lim ma dora ndagou ay boy rék lay dann
@thiombayeseck9782
@thiombayeseck9782 5 күн бұрын
Ya mene si lamb dji bo téyé❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@maodosalll6068
@maodosalll6068 2 күн бұрын
Amine ya rabii
@snleppndam245
@snleppndam245 7 күн бұрын
Sénégalais dafa gaawa faté rek mais reug reug mi Sathies daan pour l'instant nieupa ko nangoul champion wam
@MansourDiop-y6j
@MansourDiop-y6j 7 күн бұрын
Man lolu moma diakhal
@Leuzsonko
@Leuzsonko 6 күн бұрын
Mo dane lac ross moussa ndoye siteu reug reug
@ArounaCeesay
@ArounaCeesay 7 күн бұрын
Sa thiès champion nga
@adjiadialo
@adjiadialo 6 күн бұрын
zarko mo makk sathies fouff zarko mo makk balla
@PaOuzz9
@PaOuzz9 5 күн бұрын
Zarko aye gris bordeaux ak eumeu sene layy masél
@Bebefodetoure
@Bebefodetoure 3 күн бұрын
​@PaOuzz9 😂😂😂😂
@papeserignembaye8679
@papeserignembaye8679 6 күн бұрын
Dou sama mbeur mais zarko dako ragal modou Lo mayal boy bi chance combat bou nékh la
@maocamara8768
@maocamara8768 7 күн бұрын
Sa selu billay 😂❤❤
@ndiagaseye2463
@ndiagaseye2463 6 күн бұрын
Il communique bien Bilay mbeur bou yarou
@gelawargelawar8972
@gelawargelawar8972 6 күн бұрын
Amoulo bac zarko doula dieul
@Garga-n5x
@Garga-n5x 6 күн бұрын
Ki moy bayi sarko wallakhi
@assanegaye1393
@assanegaye1393 6 күн бұрын
Lou ler
@adandoye3759
@adandoye3759 6 күн бұрын
Douko dieul ndakh sa thies moko meune buko dieulé teudate dei
@Bebefodetoure
@Bebefodetoure 3 күн бұрын
​@@Garga-n5x Merci beaucoup
@abdourahmanesindidi1818
@abdourahmanesindidi1818 6 күн бұрын
Pour man zarco mogui doga am combat bou tolo ak mom sa thies ndam rk
@AliouneselbeDiouf
@AliouneselbeDiouf 6 күн бұрын
Wakh bi nice sa
@cheikhdiop9932
@cheikhdiop9932 6 күн бұрын
Bodanon eumeu sene zarco doula yap
@CheikhomarMbaye-p2o
@CheikhomarMbaye-p2o 6 күн бұрын
Nema la yene geue negue Rio desarene bilahi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@malickndiaye4880
@malickndiaye4880 7 күн бұрын
Ya meun zarko mom fouf sakh 😂
@NdiaboutaDiouf
@NdiaboutaDiouf 7 күн бұрын
zarko sa thies moko eupeu lepp dakk KO beure si lepp sakh
@adafatygadji100
@adafatygadji100 6 күн бұрын
Wakho deugue ki moko geuneu fete halé té hallé moye déffe léppe
@domousenegalinfo9563
@domousenegalinfo9563 6 күн бұрын
Ki mo meunn zarco way boulenn gnou sonal
@Leuzsonko
@Leuzsonko 6 күн бұрын
Sa thies vs modou lo . Zarko vs eumeu
@MouhamedCissé-j9d
@MouhamedCissé-j9d 6 күн бұрын
Sa Thiés ayy réé lama commencé déff. Gningay limm di sante ni gneup lérnamani lila Balla Gaye déffal gnom défalou gnouloko. Warro nangou kéne dila diaxxassé ak sa makk. Même bou fékké am ngéne problème ça doit être privé. Reglez le en privé. Sa communication on sent danga ame problème ak Balla. Attention : Sougnou la beugué Balla Motaxx, supporter Modou rék gnofiy nékk nane danga yarou patati patata bougougnoula dh. Démal djoubo ak sa makk mo gueune si ioe.
@Alkhamndoulila
@Alkhamndoulila 6 күн бұрын
Boye mandoul
@FallMbackefall
@FallMbackefall 6 күн бұрын
Mais yaw gnar gnou bokou wadiour lane moy sa yone Sèteuutt lidientil sè famille mo gueune
@Abraham22199
@Abraham22199 6 күн бұрын
@@FallMbackefalldeugue dou rombi nopou
@SaliouDiop-e4r
@SaliouDiop-e4r 6 күн бұрын
Vraiment
@MouhamedCissé-j9d
@MouhamedCissé-j9d 6 күн бұрын
@@FallMbackefall liratal commentaire bi.
@FaraNdiaye-k1m
@FaraNdiaye-k1m 6 күн бұрын
Nit kou ameu yar sa thies
@iboufall446
@iboufall446 6 күн бұрын
Béne défait gasi ame més sa thiés eumeu séne warou la danne daga nélaw si comba bobou akh
@sambaba683
@sambaba683 5 күн бұрын
Eumeu sène et zarko moy combat logique
@NdiayeMayib
@NdiayeMayib 6 күн бұрын
Sa aka ame foula
@MbayediopMbaye-o7s
@MbayediopMbaye-o7s 5 күн бұрын
0 proboéme machala
@LazaSrxbsnss
@LazaSrxbsnss 5 күн бұрын
Frenchment Zarko moromam yeup dagneko dan
@moudoudiop6216
@moudoudiop6216 7 күн бұрын
Zarko Bilahi Sa Tihss moko eupeu depp doulie Fouff
@CamaraMatar
@CamaraMatar 7 күн бұрын
Dolé pr day la
@bambakhouma7529
@bambakhouma7529 6 күн бұрын
Sa dosama mbuer duegue rek laye ko yaro la
@cheikhgueye7704
@cheikhgueye7704 6 күн бұрын
Yafi wakhon zarko doula mata dap si lamb té raw nala 😅 zarko mola meunn allez retour
@mouhamadoudiop678
@mouhamadoudiop678 6 күн бұрын
Gni gua wakh nieup balla gaye 2 moyy seu kilifa entier delko limm lolou moyy deugg
@espritsaints4685
@espritsaints4685 6 күн бұрын
Sen diguente metinama trop nim yakhoo
@MouhamedCissé-j9d
@MouhamedCissé-j9d 6 күн бұрын
Absolument.
@MOUSSASOW-l8r
@MOUSSASOW-l8r 4 күн бұрын
💪💪💪💪
@lesankariste8721
@lesankariste8721 5 күн бұрын
Sa thies tu n’es pas malin tu devras prendre zarco depuis qu’il a commencé à te demander maintenant tu sais que avoir un combat est difficile tu veux le prendre il va pas te prendre c’est simple
@YvesSagna-w5n
@YvesSagna-w5n 6 күн бұрын
Sa thies seul borome lamb 💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💙💙💙💙💛💛💛💛💛
@CheikhMbengue-fl8ik
@CheikhMbengue-fl8ik 7 күн бұрын
❤❤❤
@laminefall6481
@laminefall6481 7 күн бұрын
sa nénako khana nekoul adiouma diallo 😂 ba taye
@HamedHublo-uo9bk
@HamedHublo-uo9bk 6 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@PapeLatyrSeck
@PapeLatyrSeck 5 күн бұрын
Ya togn sa bop combat derby yeup da nga ko perte motakh nga tardé
@yellecisse5420
@yellecisse5420 3 күн бұрын
Le geni
@MoussaDak-o7f
@MoussaDak-o7f 7 күн бұрын
Sa thiés Modou lo Moy combat bi
@SyndaDiatta-o8l
@SyndaDiatta-o8l 7 күн бұрын
Mom xam na Lou tax dieloul combat bi
@fauconnoir9812
@fauconnoir9812 6 күн бұрын
Bayil sedal bi te ga waxe ac sa adversaire 😮combat bo niac maslaa molaco khagne
@Abdallah31341
@Abdallah31341 6 күн бұрын
Mok eumeu mom masla moko ko khañ, bou mérlowon eumeu séne ci face 2 face daan ko
@papahabibdiop
@papahabibdiop 6 күн бұрын
Zarko dofful day dof doflou bi bou rapide bila dei eumeu sén mila dann champion leuh Daguay khol modlo dfa dann ama ak boy niang yaw eumeu dann la niom niou am combat yaw meuno amm gas yi niola ragal😂
@BaOusmane-l8m
@BaOusmane-l8m 6 күн бұрын
Kom legui balla dou sa kilifa waw yalla bakhna man de sama mak nomou mante mel sama kilifa la
@Garga-n5x
@Garga-n5x 6 күн бұрын
Yaw saytanega ki balla moy magam ba soba nit dagay mano si Famib jambor yaw nafekhga
@BaOusmane-l8m
@BaOusmane-l8m 6 күн бұрын
@ yaw yeye seytane pourquoi dou toutdo man amna mak kok sa me li nehole balla
@adandoye3759
@adandoye3759 6 күн бұрын
Zarko lamigne bi rek lay yoré di talakhou mola geune xam keur gu beuri khathieu Sa thiés moko meune fouff mome xamna lolu Sax
@CamaraMatar
@CamaraMatar 7 күн бұрын
Sa thies beugone gua fi gris bordeaux dé zarco dieul ko dane
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 6 күн бұрын
Sa thies ya meune ya eup doley
@iboufall446
@iboufall446 6 күн бұрын
Sa thiés mo amoul fouleu amoul fayda mbeur bou diouk yépp ko bo amone victoire si eumeu séne kone passé gafi bou yagg amato béne béyré si lamb sa morome yeup niogui beuré dilafi bayi yay sama mbeur yaw lay supporté mes bo dieulé zarko danou wat lou lér lala wakh
@djibrilseye5196
@djibrilseye5196 7 күн бұрын
Balla gaye motakh gnoulaye supporté boy bo régléwoul sa prochain combat do barri supporter
@YannickDieng-wv4sh
@YannickDieng-wv4sh 7 күн бұрын
Ya meun laye ndey wakh deug
@mohamedseck4724
@mohamedseck4724 7 күн бұрын
Qui dafa soff ndeim legui
@deugdourombinopdioulite635
@deugdourombinopdioulite635 7 күн бұрын
bilahi ki dafa warra xolat bopame
@bassdiokhane1472
@bassdiokhane1472 7 күн бұрын
Wakho fi dara sa Thiès lanou faral
@BadaraGueye-ii5gh
@BadaraGueye-ii5gh 7 күн бұрын
Lou lerr
@amadougueye7044
@amadougueye7044 7 күн бұрын
Yew dano kén
@GoraKane-v7e
@GoraKane-v7e 6 күн бұрын
Yawe amo foula ganane eumeu séne mo gueuna king bayi sa make balla gaye yawe niaka fayda ga déf eume séne dane sa make 2foi nieuw ake yawe dane la niakeu diome
@BaOusmane-l8m
@BaOusmane-l8m 6 күн бұрын
Man de balla mou tah ma siporte la lugu mon c fin
@papiiiswelleeiih5728
@papiiiswelleeiih5728 7 күн бұрын
Y’a meune zarko pourkw dieulo ko wonn bimiii lay ladj 😂😂😂bii dou zar bobuu deh
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 6 күн бұрын
Sa thèse seul
@NdiagaDiouf-yd8je
@NdiagaDiouf-yd8je 7 күн бұрын
Sa thies mo meune fouf vraiment
@aliouneelevage6482
@aliouneelevage6482 7 күн бұрын
Sa boulfi wath zarco bi bokoul de instant bi mola gueuneu takhaw fopp niemena tek si mome louma mana ame
@MouhamedlamineSissokho
@MouhamedlamineSissokho 7 күн бұрын
Zarco moffi dèsse
@snleppndam245
@snleppndam245 7 күн бұрын
Yaw es-ce que wer nga Zarco nakala gueneu takhawé Sathies Zarco diamono dji maunoul daan reug reug té Sathies mo daan reug reug
@aliouneelevage6482
@aliouneelevage6482 7 күн бұрын
@@snleppndam245 wa legui sa kouko dane dou eumeu avec son age quand meme
@aliouneelevage6482
@aliouneelevage6482 7 күн бұрын
@@MouhamedlamineSissokho es c que sakh zarco douko kharlo mou ame banene victoire sakh zarco depuis son retour si lou deugeur la tok guimb li machalah
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 7 күн бұрын
Bou takhawé nga nieuw niou ték
@MouhamadouBâ-w4h
@MouhamadouBâ-w4h 6 күн бұрын
Katal sa ndéy daga sokhorr
@adandoye3759
@adandoye3759 6 күн бұрын
Amal yare mo geune tapéte akh ngaka rek moy saga si réseaux sociaux, ki ngay saga bo taxawone si kanamam di nga tale lénéne loudoul sa waxou réwandé yi
Cat mode and a glass of water #family #humor #fun
00:22
Kotiki_Z
Рет қаралды 42 МЛН
Леон киллер и Оля Полякова 😹
00:42
Канал Смеха
Рет қаралды 4,7 МЛН
Arrivée de Modou lo/petite lo combat
9:03
CombatTV
Рет қаралды 1,3 М.
celebrates with teammates after scoring their team's first
0:45
Soccer Prime
Рет қаралды 1,1 МЛН