Merci Eumeu séne un homme pleine de vie et du courage.. fierté internationale
@omarndiaye-sk3fe10 ай бұрын
Ndanane la d
@aboubacarndiaye77910 ай бұрын
Sathies prépare-toi bien Eumeu est en très bon forme physique, c'est un combat capital pour tes supporters, nous sommes derrière toi,du courage et bonne chance
@pronosticfootsenegal111210 ай бұрын
Les questions sont vraiment pertinentes bravo abdou ndour
@HamedHublo-uo9bk10 ай бұрын
Merci eumeu. Ya dane sa ma mbeur balla deux fois mais kou bakh nga. Vous êtes lucide et pondéré❤
@boubacarboiro581310 ай бұрын
Une très belle émission sur Albouraakh avec un grand journaliste Abou Ndour bonne continuation
@ibrahimadrame949910 ай бұрын
Abou Ndour vraiment journaliste machalah❤❤❤❤
@ibrahimadrame949910 ай бұрын
Eumeu séne ndaysane kholbi mo rafét😢😢😢😢
@oumitandiaye6780Ай бұрын
Holbi rafetoull il n'est pas sportif ni faire play
@khadimtoure-ew3jx10 ай бұрын
Ah modou lo daf léne meune passer présent et futur aussi xlo rek 🫡👑
@oumitandiaye6780Ай бұрын
Merci
@faye671810 ай бұрын
Machallah Abou Ndour eumeu séne émissions bi nékhna ❤❤
@h2otv96810 ай бұрын
Abou est très professionnel
@mamadousarr247810 ай бұрын
MASHALA Eumeu sène 💪💪💪💯💯💯💯👍👍👍
@babacarfam25110 ай бұрын
Eumeu nite kou bakh la ndeysane yalla nasen diamou yagg
@ibrahimadrame949910 ай бұрын
Fadame sama mbokou talibé cheikh bi❤❤❤aka kham lamb
mom dafay sonou si Pikine bilahi té diokhounioiko thieur
@TKFTV11110 ай бұрын
Wa Albourakh niongui déf lou doy warr si Lamb dji ❤
@diaibrahim679810 ай бұрын
Merci champion sa khôl bi mon nacie 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
@basirubaye658710 ай бұрын
tysinger fan from gambia in the Nederland
@seydounouroufaye835310 ай бұрын
Machallah ❤❤❤ eumeu ndam rek
@elhadjiSwo10 ай бұрын
Ndeysane eumeu Nite kase la bilan
@SerignemodouNdiaye-s3u10 ай бұрын
Abou Ndour tu es exceptionnel ❤ peulh holal ci Abou té bayi détails yi
@mamendackdiop90310 ай бұрын
Merci bro
@elhadjimoussaniang174810 ай бұрын
No dafa lérr dh bilahi
@laperlecmoi599510 ай бұрын
😂😂😂
@cheikhfall472910 ай бұрын
bilahi eumeu daga wax DEUG paséke boy Yi danioo am mystique té mom Lolou Moko manqué Ms sino eumeu bou amon Lolou Dou dème nii
@Banlieueplus221910 ай бұрын
Niakk pèkhè😂😂
@syllepogba174310 ай бұрын
Welcom Abou ndour❤ peule yalna sa diam yage ❤
@ibwagnewagne64819 ай бұрын
Eumeu sene tu es le premier a commettre l'eureur
@cheickhouthioune914910 ай бұрын
Génial peulh et bonne continuation
@bybrufisquois25710 ай бұрын
Abou machala il est un fervent connaisseur
@Azoura2210 ай бұрын
Modou lo rek santé 👑 yalla
@PapemadiorNdiaye-g9z10 ай бұрын
Eumeu séne le champion.
@khalil753710 ай бұрын
Abdou è Tres professionel peul si ki nga wara diang
@ousseynouciss768310 ай бұрын
abou ndour machalah
@GalleBa10 ай бұрын
Eume Séné.cest un grand champion
@OusmaneSakho-os3fh10 ай бұрын
Abou Ndour est tres pertinent machallah peulh bou rafet tu peux apprendre beaucoup de lui tas pas trop d'experience pour animer un plateau mais ca va venir inchallah
@mamadoundiaye97310 ай бұрын
Le regard de fadam face à eumeu 😮😮
@loelhadji10010 ай бұрын
Kou bakhleu ❤
@becayesamb966510 ай бұрын
Macha Allah fadam Lou lére nga wakh
@Domino4010 ай бұрын
Peulh bou rafete toy NGA non vraiment tu est trop belle ravissante et doux
@SandamcYaya10 ай бұрын
Tu es le meilleur Lutter eumeu sene
@Steven-ul8pw10 ай бұрын
Vraiment Plateau bi Abou Ndour Moko Geun Mérité Ay Genr Peul yi Mbir Dankoy Dioh Kuko metrisé Xamuñu Lamb
@aichadia71910 ай бұрын
Xamnga senegal dounioula wakh deugue mais peul desséna walakhi en plus dafa beugue tontanté
@Steven-ul8pw10 ай бұрын
@@aichadia719 Merci Sister Srx Ñiom Dernier Génération bi moudjé niew Xamuñu Dara Ay Clant rk lañiou Andi si Lamb ji
@khalil753710 ай бұрын
Elle n'est pas profesionel managula gerer plateau mais Senegal Bo waxei gnuni daga soxor@@aichadia719
@BasirouNdiaye-sz3jf9 ай бұрын
Damala beugue ci sama hole.i am from Kaolack : sikhane
@محمدعبدالله-ص5ذ5ف10 ай бұрын
Modou lo deh bolaiwoule dara aki wakhe parenasi yene 😂😂😂 mission accompli 😂
@serignedieng-vh4zv10 ай бұрын
emeu khole bé rafét
@Ahmadouboromediamono410 ай бұрын
l'homme qu'il faut, à la place qu'il faut Abou N'Dour mo môme place bi sokhna si khoulo rek la meune 😂😂
@afro382710 ай бұрын
Baye mi nandité la dé abou ndour ndjiné la si lambj
@cheikhbasskeurmassar954810 ай бұрын
Sa Thiès mo meune mo eup Dole 💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
@omarcisse791910 ай бұрын
Wwww sa rk❤❤
@modouseye275710 ай бұрын
abou ndour merci si sa nieuwe fi
@h2otv96810 ай бұрын
Duo entre Malick thiandoum et abou ndour lolou dina graw
@ndiolniang666310 ай бұрын
Pelle buo rafétt waroll té 🎤
@alhamdoulilah915410 ай бұрын
Abou ndour bonne continuation diambar la mais amoum Esprit leader benn cheikh niang wakhla reck nga deff interview plus de 40 minute kholou kou guiss mouy tontou reck khamalné nitt kou faible la
@SaliouFall-x8i10 ай бұрын
Eumeu beugeu nala lol wayi modou lo dalena mane sen betnoir la
@babachiekhniang10 ай бұрын
fadam wakho deuge way mdou lo eume sen pikin yeup Bolo
@Abuu933610 ай бұрын
Sa waay loolu wakhou mbeurr leu rekkk😂😂😂 eusqu khamnga limala wakh😂😂😂😅
@matargueye92110 ай бұрын
Ak Lou mena khéw pokine Ama moy borom mome rek moy dioke pikine yépp diok nioune beuga tougne 200% sokh latougne ko na kou néke toke S.A. coin❤
@adamagakou885610 ай бұрын
Sa sarap seytané nga
@matargueye92110 ай бұрын
@@adamagakou8856 😂bilay ray ngama😂😂😂
@diamilmboup439210 ай бұрын
Sen 100% bi dangenkoy degu Rek mai dou gawa amat Déjà Eumeu Sen iow sa combat contre Sa Thies Rek doCi contact ak Ama Baldé parsk nim demei ak Wa keur double Less Motah ✍🏿✍🏿✍🏿 Bientôt revanche Sa Thies Vs Boy Niang dina am tei nonou lafay demei enkor
@MadiamaSilla-yf1ug10 ай бұрын
Yéna boko ay adversaires li ñu lén fay çi modou lo manou lén ko am fanén way
@ndiayeabdoulaye783610 ай бұрын
Lo ndam ❤kase
@adamandiaye582910 ай бұрын
Saway liiy am am na. Modou Lo déf nako ba parè
@mbayegueye523410 ай бұрын
modou lo ndananela championt la mbeur deug laaaa
@IbrahimaGaye-hl5yr10 ай бұрын
Merci Eumeu le vrai responsable
@general7tv16210 ай бұрын
MaChalla liguéy bi mongui nice c Seydou regicheur thies tv
@you530310 ай бұрын
Eumeu sene Aka meune fene
@alhamdoulilah915410 ай бұрын
Abou Ndour borom xam xam DEUG la vraiment dagnula sokhla thi écran yi
@MoudjibSy10 ай бұрын
Fadam mi niémé né yalla dh alkou akbar
@dawithannajantha563310 ай бұрын
Oho. Emeu Day dawlo sama yaram yaram. khol bou rafett.
@DavidoBouSonko10 ай бұрын
C'est boy niang qui a gatter le combat de Ama😢😢😢😢
@adamagakou885610 ай бұрын
Patriote dou fene Patriote dou seytané
@falloufall949510 ай бұрын
Machallah ❤
@hamdymoustaphaba756710 ай бұрын
De toute façon professeur kharagne mongi tok di khar eléve bou nangouwoul diangue rk nga nieuw mou tégeul la 😅😂😂😂
@babacarseye4910 ай бұрын
Ahhh peul da beugone forcé rek mais niorol wone pr dirigé emission
@desirealqanah952110 ай бұрын
Fadam miss Senegal 🇸🇳 2024
@MansGhdy-kh6cj10 ай бұрын
😂😂
@laperlecmoi599510 ай бұрын
Reew gua 😂😂😂
@papadiom926010 ай бұрын
Eumeu mane yaay sama mbeur founekk Mais Modou lo doto ka danati thi adouna..dafa kham sa sarax ! Sen 1er combat nga amone chance daneko tiaxane bagnou fokati combat bi thi yaaw. Tapha tine tamite mm chose ya djekou ba dernière minute gnou nangou ndam lii. Da nga war di ande ak gnou meun geww !
@augustindiatta703610 ай бұрын
Bien dit mon frère khamgua lamb
@diamilmboup439210 ай бұрын
Fin bi😊😂😂😂 Modou Li sonalNalen nak😂😂😂😂
@mosi30110 ай бұрын
Émissions bi nèkhna trop mai AK fi rèwmi tollou disi bolè AK actualités c'est le priorité rèwmi
@alhassanetoure308810 ай бұрын
faut savoir faire la part des choses so beugg actualité amna feineine foko meuneu amei li chainou lamb la
@abdoulayediop933110 ай бұрын
Ya khalla Youne bi por niou beuré Mou takh niou toupou saye tanka nga danou ba diakhane Ama danou ba diakhane boy Niang danou ba diakhane mérci modou lo
@papadiom926010 ай бұрын
Li ngay wakh kham kham laa dhee ! Explique …
@moustaphasognane207110 ай бұрын
Eumeu diam si yaw
@ITOLDYOU-p8z10 ай бұрын
Eumeu bayl fen bogou bena boy am ndam
@falloungom315310 ай бұрын
Yaw ya neck si kholam bilhay yaw koula geuna neck nafekh amoul😂😂😂😂😂😂😂
@adamagakou885610 ай бұрын
Yow niapal ndm feleu seytané
@serignemansourtoure8610 ай бұрын
Yow modou door leu ngay wadia déhhh ngani bou moudié won si ioe dehhh molakoy gënël 😂😂😂
@papabiranembaye455310 ай бұрын
Exactly eumeu😂😂
@SandamcYaya10 ай бұрын
La cellule problème de tayson il à oublier si c'est ne était pas les pikinoi il ne peut être rien
@L.Yamal10010 ай бұрын
Fadam wakhati na 😮😮
@lefootballsansfrontieres892110 ай бұрын
Aka mana féne eumeu😂 day nétali lo xamni saway moy lolu 😂
@demebadiekh747610 ай бұрын
Thiow li yeup wa keure boye niang la
@thomasmendy254310 ай бұрын
Merci
@ndoursidat965810 ай бұрын
LUTTE TV VS AL BOURAKH UN COMBAT EN INSTANCE LOL
@Moustapha-s6x10 ай бұрын
Lutte Tv restera meilleur et de loin
@ndoursidat965810 ай бұрын
@@Moustapha-s6x aatention al bourakh, combat khaliss mokoy gagner
@ebraahimgassama847710 ай бұрын
Walahi fadam nyaw nga
@elthioub832910 ай бұрын
♥️♥️♥️
@critique221410 ай бұрын
Ah finalement votre site veux plus de crédibilité l’émission est plus poser professionnel bien structurer bonne continuation et peulh vas prendre le temps d apprendre surtout plus quel la ferme mieux sais
@elhadjimoussaniang174810 ай бұрын
No abou ndour kéne du yaw lambe danekoy wakh
@ousmanefall895510 ай бұрын
Fadam khana dagua fatté franc vs sokh Pikine gneupe guéneu
@Moustapha-c6v10 ай бұрын
Boy nian bou sanione modou dane Aama
@PapemadiorNdiaye-g9z10 ай бұрын
Fadam a raison.
@elhadjindiaye708910 ай бұрын
😂😂 eume danga nékh nk yaw 2 foix
@ZakariaFaye-e6d10 ай бұрын
Je parle avec les mbeurs de pékin déme lème niéne nieum diéguelou Mohamed ndow mou djap si c est la seul solution pour vous dire la vèritè sinon moy lolou. ❤❤❤