Eumeu séne li mou wakh sokhar le, Siteu diambar le! Wouly éclate le dile et révèle..« Modou Lo mo…

  Рет қаралды 7,464

Sénégal Buzz221

Sénégal Buzz221

Күн бұрын

Пікірлер: 55
@ibrahimasy3165
@ibrahimasy3165 8 күн бұрын
Eumeu sama beur lawone mais damaka wédi franchement il est méchant eumeu dou dara moudou lô raw nala
@abasall711
@abasall711 7 күн бұрын
Eumeu manul begue modou dako dane niari yone dernière bi xawnako raye
@Deggou
@Deggou 8 күн бұрын
Modou aka ame class😅 gayi danioukoy soxoré teu mome doussi tontou kéneu...
@mbayendiaye5033
@mbayendiaye5033 8 күн бұрын
Billay
@abdoulayendir2036
@abdoulayendir2036 8 күн бұрын
Eumeu dafa am febarou khôl damaco yeureum yaw même couronne 👑 bi amosi victoire lolou modou khagnla mola meti
@babacar3178
@babacar3178 8 күн бұрын
Yague n'a wakh eumeu dama faux daye rétane nii mais dafa sokhor dh
@layesall7509
@layesall7509 3 күн бұрын
Mashalah kaddu yi amna solo
@MameSow-m7e
@MameSow-m7e 8 күн бұрын
Eumeu séne mo geuneu tothieu leufeul ndayam si lamb dji gordjiguéne leuh😂😂😂😂😂😂
@nafisene5335
@nafisene5335 8 күн бұрын
😂😂😂😂 Mane dé khamouma mbeur nou mou beuré ak yow, beurelo la ba nga khokh, ba sey bakata Di gueneu 😂 nga nieuwatt ma dor la nga syncope 😂après ngané meunoul beuré. Ohhhh Niit nak sokhor n’a. Modou Yalla na la borom mousseul ci lamignou none 🙏
@PendaTalla-c5z
@PendaTalla-c5z 8 күн бұрын
Sokhor ak ignane
@KhadiDiop-z8e
@KhadiDiop-z8e 8 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂
@alhassanngom8282
@alhassanngom8282 6 күн бұрын
😂😂😩 syncope 😂😂😂
@juniorbadji-kt9di
@juniorbadji-kt9di 8 күн бұрын
Eumeu séne 3em combat la beugue ak modou lo rk soyez intelligent il a essayer par tous les moyens les gens non pas réagi il a donc changé de méthode pour attiré l'attention des gens
@MameDiop-jg1bo
@MameDiop-jg1bo 7 күн бұрын
EUMEU SENE CHAMPION LEU MAI DA DIOUM SI LIMOU WAKH MODOU IO
@danilombaye95
@danilombaye95 6 күн бұрын
Modou Lo Xaragne Lo diarama Xaragne Lo Modou Lo dieuredieuféty
@AliouDrame-uf4ph
@AliouDrame-uf4ph 8 күн бұрын
Merci beaucoup
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 8 күн бұрын
Eumeu djiko djiguein la yor nanfex leu seytane xol bii mo nioul
@KhadimThiam-pe7zy
@KhadimThiam-pe7zy 8 күн бұрын
Diadieuf bro c vrai ❤❤
@CASI7797
@CASI7797 7 күн бұрын
Merci Wouly
@Mamadou-j1x
@Mamadou-j1x 8 күн бұрын
Eumeu sene Aka katte ndy. Eumeu sene Aka katte ndy Eumeu sene Aka katte ndy Eumeu sene Aka katte ndy
@PapemodouThiam-q5c
@PapemodouThiam-q5c 8 күн бұрын
Eumeu Séne nafékh leu
@djilyfall8174
@djilyfall8174 8 күн бұрын
Eumeu mom sokhor la def
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 8 күн бұрын
Merci woule
@PapeDiba-c1n
@PapeDiba-c1n 8 күн бұрын
Eume canara la dou sportif nit kou sokhor la
@abduolayegaye-lm6pz
@abduolayegaye-lm6pz 8 күн бұрын
Eumeu 11 déft 😂😂😂😂
@BaNdiabel
@BaNdiabel 7 күн бұрын
Ci lamboji ken ganoul bahh eumeu kou ame yayi waroul saga yayi diambour li kambo la kou âme bopam lay amall kon na rafett
@rimesmakerposeidon2427
@rimesmakerposeidon2427 8 күн бұрын
Me gayi yeufeur sokhor ame na deu eumeu sene ignane na mome ame na plus de 10 defaite modou lo loumou diele si drapeau mbapat kene khamoul loumou tolou
@abousall4479
@abousall4479 7 күн бұрын
eumeu daye sisou rek
@MamadouKa-h2k
@MamadouKa-h2k 8 күн бұрын
Eumeu dall n’a oute combat beurer moo guene walla mou baaayi
@safiatousy6249
@safiatousy6249 6 күн бұрын
Viviane néna jalousie fébar la eumm da jalousie
@momardiallo1609
@momardiallo1609 8 күн бұрын
MODOU LO MOONIOU TOGN NDAKH BOU RAYONN NDEY EUMEU SENE KON DOU NEKK FI DI WAKH
@neyzard1097
@neyzard1097 8 күн бұрын
Meunn beurei Eumeu Séne la guissoul mann Bann jeileu bou reuy laffi dann wala niata bokk 😮
@CASI7797
@CASI7797 7 күн бұрын
Wouly nak Siteu dawena nak
@oumyfaye9760
@oumyfaye9760 8 күн бұрын
Eumeu Séne défaite bi la digérer goul mo guen faux si mbeur yuii koumouy dadiel dinala sossal yakk la vrai mbam la khol bé bonne
@assanekaka9414
@assanekaka9414 7 күн бұрын
Eumeu sene mom legui dema ko wedi
@papeomar8530
@papeomar8530 7 күн бұрын
Eumeu Séne sada sokhor
@Ousmane-pz1if
@Ousmane-pz1if 8 күн бұрын
Eume da Yakar ni mo Daka beurre thi lambdji
@sophrotall8105
@sophrotall8105 6 күн бұрын
Bayilene siteu khale bou ndaw siteu mo makk Ama Balde mak Boye Boy Niang Reuggggg.....
@CheikhMbengue-fl8ik
@CheikhMbengue-fl8ik 8 күн бұрын
Eumeu sene sa leufeul ndeye
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 8 күн бұрын
Eumeu yaw santal malick nguom sinon kone doto waxati si lamb dji
@abasall711
@abasall711 7 күн бұрын
Merci diambar
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 8 күн бұрын
Man key dama moudjei warou😂ioe nitt diap leu beurei Lo leu banga khokh wouli la bangay ndiandou😂 nga dieul tankam 3fois meunoci dara mou fowei la dan la nga ñeuwat dieul ci revanche mou door la nga syncope boudoul won arbitre bi nga fatou yallahu😂😂 nganan meunoul beurei khana kon yaw yay le plus nul des nuls😂😂😂
@safiatousy6249
@safiatousy6249 6 күн бұрын
😂😂😂wakh deugue yalla
@waganelo6271
@waganelo6271 8 күн бұрын
Sokhor kassé mokko diappeuuu
@MohamedDiouf-x4f
@MohamedDiouf-x4f 8 күн бұрын
Siteu monè gayii d'où s'en morome sakh dékka dorré danè ko gayii bagñe siteu Moy roi bagñe nagou lérna nagñe koume nékh bagñe. Eumeu wakhoulén lolou
@serignembengue2491
@serignembengue2491 8 күн бұрын
Faut arrêter vos truc d'imbéciles Eumeu n'a jamais dit que Modou mounoul beuré
@kharagnembaye5958
@kharagnembaye5958 8 күн бұрын
Frère gnioune dougne ay dof dei eumeu lim wakh lér n'a
@Noface-o1d
@Noface-o1d 2 күн бұрын
Saway mingui wakhei xol nak😂. En tout cas Eumeu sissoumane leu faux leu
@ndiayepapaserge5997
@ndiayepapaserge5997 8 күн бұрын
Même c'est lutteur préféré mai dafa ragal legui pour quoi mouy daw eumeu sene di woute lou yomb wouté nane ak double les ak mbaye Gueye
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 8 күн бұрын
Loumouy doye eumeu sene tamou ndokou ko niarri yone eumeu na dem djeuli serigne Ndiaye wala aliou Seye 2
@DameNguirane
@DameNguirane 8 күн бұрын
Saway ko 2 niari yoné nganane da ragal légui lingay wakh sett si yalla té aussi do fans modou lo daw lakhou nga😂😅
@ndiayepapaserge5997
@ndiayepapaserge5997 8 күн бұрын
@DameNguirane dame je me suis trompée je parle à Balla gaye2 sama mbeur la mai dey daw eumeu sene dama sauté rek
@Noface-o1d
@Noface-o1d 2 күн бұрын
Balla mom nañou ko bollei Siteu. Yalmine vs Fawzeyni
Accompanying my daughter to practice dance is so annoying #funny #cute#comedy
00:17
Funny daughter's daily life
Рет қаралды 28 МЛН
Интересно, какой он был в молодости
01:00
БЕЗУМНЫЙ СПОРТ
Рет қаралды 3,6 МЛН
Revue de presse Ahmed Aïdara du Jeudi 12 Décembre 2024
8:25
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 5 М.