EUTOU ISLAM avec Serigne sangua Ndiaye

  Рет қаралды 144,275

Gtv Sénégal

Gtv Sénégal

Күн бұрын

Пікірлер: 895
@cheikhibrahim6346
@cheikhibrahim6346 4 жыл бұрын
Allahou Akbar Sangue Barham Ndiaye ya barri xam xam macha'allah. Gnoune nagoul nagn la
@babacarngom9438
@babacarngom9438 3 жыл бұрын
Ce qui M’impressionne le plus moy Oustaz Bitéye Nimouy diapé li nguay wax yeup ba so paré mou résumé le ko sans faute MachAllah ❤️
@bsarr7264
@bsarr7264 Жыл бұрын
Mane la gueune Yém May yala deug ❤
@bassiroudiame-rz7iv
@bassiroudiame-rz7iv Жыл бұрын
Tassaouf hadimou rassoule rek
@bayeomardiaw9045
@bayeomardiaw9045 2 жыл бұрын
Sangue bilay betue ga ma
@mamemassaer7052
@mamemassaer7052 4 жыл бұрын
Sa ma gayi toop len Alkhuran ak shuna, Moy tou ndiamban yii
@elhadjimbodji7297
@elhadjimbodji7297 3 жыл бұрын
Dieureudief sangue Barhamou Ndiaye contagne thii khamhame bi dof doukoham nagoullene sangue Ndiaye sougene bouge ame diam
@KhidmalBarkham
@KhidmalBarkham 8 ай бұрын
Niou ngui santate yalla Di waxate Dieureudieufety sangue Aboubicrine sangue Barkhamou Ndiaye ❤❤❤❤❤
@boundiaye943
@boundiaye943 5 ай бұрын
Kou khamoul nous gnouy Mirassé, N'importe quoi !
@ndiayexibar9680
@ndiayexibar9680 Жыл бұрын
Man dé dama yakarni sangue Ndiaye mi dafa tagoo al sagom
@laminebadji3484
@laminebadji3484 5 жыл бұрын
J'aime oustaz biteye très civilisé et discipliné. Le caractère d'un pure musulman
@Smokin_mass33
@Smokin_mass33 Жыл бұрын
Non il coupe les gens à chaque fois
@Salafivision
@Salafivision 5 жыл бұрын
Cëy tasawuf . Alhamdulillah bima yalla khamalè Sounnah rek.
@papacheikhouba9909
@papacheikhouba9909 5 жыл бұрын
Khana tassawuf bokoul si sounnah??
@Salafivision
@Salafivision 5 жыл бұрын
@@papacheikhouba9909 man mom sounnah bi guenne ci lamegnou yonente bi salahu alyhi waslam rek moma doy.
@jangumalphaomar4709
@jangumalphaomar4709 5 жыл бұрын
@@Salafivision meilleure commentaire👍 Sounnah rek
@jangumalphaomar4709
@jangumalphaomar4709 5 жыл бұрын
@@papacheikhouba9909 dedet bokul chi
@papacheikhouba9909
@papacheikhouba9909 5 жыл бұрын
@@jangumalphaomar4709 louy sa daalil?
@rachidmadjid6517
@rachidmadjid6517 4 жыл бұрын
Machaalah sangue barham Ndiaye batine deug guay wax
@generalgeneral9043
@generalgeneral9043 5 жыл бұрын
macha Allah Babacar Thioub xam xam yomboul walahi yayy khoudbou tei mano tonton charia
@papaboubacardiallo4970
@papaboubacardiallo4970 5 жыл бұрын
Mé cheikh bi ki charia la tontou
@masteratlanta6686
@masteratlanta6686 5 жыл бұрын
Général general wakhatiko dëh Di woté niveau université tëh meuno tontou ay questions C.I
@modougaye3943
@modougaye3943 5 жыл бұрын
Master Atlanta en tt cas dal doyna war di wotè khoutbou tè xamo dara si charia yalla yalla yokou niou ragal
@faroulfenecideugrek7557
@faroulfenecideugrek7557 5 жыл бұрын
Merci thioube merci yaw aussi nii nga meun méll sa baye moko gnanon bimou démé macka mo gnanon yalla defko mouy ndieurignal domou adama yi Kon ma ch'allah yaw tamite yalna yalla matal sa mbolèm yèné bou bakh?
@zeynabndiaye24
@zeynabndiaye24 5 жыл бұрын
Niak fatkhou motakh gua guiss thioub ak li bayam nianoon
@thiernodiop1049
@thiernodiop1049 5 жыл бұрын
Macha Allah. Sange bi kham kham bi werr na.kilaye ladj yi tam limouy ladj lerrna.wayè mande khoutbaniya.gui ngaye wote.dessena lerr ci mane.
@maissagueye3357
@maissagueye3357 6 ай бұрын
Barki alkhourane Sangue Ndiaye deug diou wer lay wakh mais dfa sout sen degdeg ❤
@boubbasow3197
@boubbasow3197 5 жыл бұрын
cheikh tijdane biteye machalha amnga yar ak tegine ak soutoura yalla nala yalla faye
@serignedaaramaraboutcorani2861
@serignedaaramaraboutcorani2861 5 жыл бұрын
Baye Niass Dafa Dadjalé Chari'â Ak Haqiqa Cheikh tidiani Kazalik Yonante Yalla Mouhamed Nonou Yaw Nga Dondou Léne Té Meuno Attéwo Si Chari'a Té Baye Dafa Waxone Né Kou Matte Deuge Daye Bolé Niaari Makhama Yi Té Baye Kouka Lathe Si Charia Mou Tontou Si Haqiqa Mou Tontou Yalna Yalla May ñu Xam Xam Bou Andak Ndioub
@papaboubacardiallo4970
@papaboubacardiallo4970 5 жыл бұрын
Mais Serigne bi qui pourtant thii charia la tontouu dhh
@papaboubacardiallo4970
@papaboubacardiallo4970 5 жыл бұрын
Mé cheikh bi ki sangue bi daka tontouu thi charia AK haquikaaa
@allanjuff
@allanjuff 5 жыл бұрын
@@papaboubacardiallo4970 😂😂😂😂😂😂😂 sa khoutbou bii dra xamuko
@papaboubacardiallo4970
@papaboubacardiallo4970 5 жыл бұрын
@@allanjuff dou affairou khoutbou wala yénene mbirr mé sangue daka tontouu thi charia
@allanjuff
@allanjuff 5 жыл бұрын
😂😂😂
@sidimohamedaminegueye4869
@sidimohamedaminegueye4869 5 жыл бұрын
Oustaz Cheikh tidiane biteye yalla nala yallah faye sa courage. Machallah kou am fite nga koi sagn nga! Woté si Lo amoul ndigual moy waral lii. Baye kene douko done. Fi ba al akhira Baye la peuy bi di wouyo.
@zeynabndiaye24
@zeynabndiaye24 5 жыл бұрын
Iow dh amo fatkhou baye niass bindeul bopam ni mom dagnkoy done gua wediko juste par c k arrangé woula yeureum nala . Soudé baye dougnko done dougn ko xam kone lane lagn koy topé baneu dieurign lagni amal sou boba
@chekhediome9173
@chekhediome9173 5 жыл бұрын
dieureudieuf baye kén dou yoow
@sidimohamedaminegueye4869
@sidimohamedaminegueye4869 5 жыл бұрын
Sincerement Amouma louma lay prouvé. Li Baye wakhone rek lalay tontou si kou keeféral joulit. Niak meune done Baye ak niak kham baye bokoul
@zeynabndiaye24
@zeynabndiaye24 5 жыл бұрын
@@sidimohamedaminegueye4869 diné dji leip preuve leu wayé fooy dieulé preuve setil Sangue Barham paye yalla bi dina la leir nagn
@abdoulayekande9015
@abdoulayekande9015 5 жыл бұрын
Thieuye Sénégal... Yallah nañou yallah jubaal té mou woone ñou deug bi iznillah az jawazzal...
@ahmadadiomdiom3514
@ahmadadiomdiom3514 3 жыл бұрын
Sangue Ndiaye khamoul yalla Dafa am fite rék
@moustaphadiop1222
@moustaphadiop1222 5 жыл бұрын
Khoutbou Zaman kén douko dioh wérdou koudoul seydina mouhamat sallalahou aleyhi wa salaman khoutbou Zaman dou massa Moy yalla bi Mouy nék naw bo fi mou yégue khoutbaniya bi
@aliousene590
@aliousene590 5 жыл бұрын
La paix est avec celui qui suit le droit chemin Yalna jäm yagu Ahmadou Mbacké Jërejëf
@papediouf2615
@papediouf2615 5 жыл бұрын
Djeureudjeuff oustaz Thioub
@papekane1197
@papekane1197 5 жыл бұрын
Machalahh billahi sangueu bi xam xam bi lerrr na
@zeynabndiaye24
@zeynabndiaye24 5 жыл бұрын
Alkhamdoulilah lima diakhal moy gni wedi Sangue ndiaye yeup heure bougn ko invité rek sen rhou yi di feutfeudeun nieuw lein gein geustou Sangue bi mo geun di inkar dé foumou deim gein topouko
@malickathie8611
@malickathie8611 5 жыл бұрын
Khairoul kalaami maa kallâ wa dallâ ki matoul Serigne bay neck koutbou
@Ibnouahmad1900
@Ibnouahmad1900 5 жыл бұрын
Séén Pass Pass You Bon Yii, Yalna Gnou Ci Yallah Moussal.
@biranediop4651
@biranediop4651 4 жыл бұрын
Sangue Ndiaye amal téguine
@bigcamara8227
@bigcamara8227 5 жыл бұрын
Trop de kathior dans mon pays. Senegal 🇸🇳 dou dém
@ardboycisse715
@ardboycisse715 5 жыл бұрын
Lo khamoul mandousi vous avez rien de ça
@modougaye3943
@modougaye3943 5 жыл бұрын
😂😂🚶‍♂️
@ousseynoudieye2886
@ousseynoudieye2886 5 жыл бұрын
Legui diarul louer filme Sénégal direct guaye am
@cercledesprivilegiesduzikr3226
@cercledesprivilegiesduzikr3226 5 жыл бұрын
Nous assistons à ce qu'on appel " La crise d'interprétation des textes sacrées "
@mourtallafall3526
@mourtallafall3526 4 жыл бұрын
Sangue Ndiaye Thioubou Dako ladj questions Miraas Asma bi yangeutou : ,
@Mamkhass
@Mamkhass Жыл бұрын
Sounnah rek
@lesmaths3645
@lesmaths3645 4 жыл бұрын
Sangue Ndiaye mi dal yak na emission bi,limou wakh yeup dafa leunt wakh deug yalla
@mouhamedciss8758
@mouhamedciss8758 5 жыл бұрын
Tassawoufou Cheikh Ahmadou Bamba ❤️
@Zito_Motivation
@Zito_Motivation 4 жыл бұрын
Sénégal nekhna
@daablessofficielle8120
@daablessofficielle8120 3 жыл бұрын
Thiey Ndiambé Borom Darou dég dég yomboul. Dieureudieuf Cheikh Moussa
@faliloudiop1516
@faliloudiop1516 3 жыл бұрын
Thieuy Sénégal
@morsarr4420
@morsarr4420 5 жыл бұрын
Sénégal beurri na niou sankou, waayé billaahi niooko tékk sén bopp. Nitt bala ngua raamal bénn mbindéf, commencél say niaari waadiour... Kou si diaaroul nak foo démm dénéenn, louleu yém dafay yomb. Réew mi moo beuri ay beaux parleurs. Cheikh Tidiane Bitèye kou diarr déklou ngua. Am nga xam xam maa chaa Allah, dall ngua té maandou ngua. Maa chaa Allah
@zeynabndiaye24
@zeynabndiaye24 5 жыл бұрын
Iow dh so amoon fatkhou do guiss niarri wadiour ak leinen souniou dh ramal Sangue ndiaye dou dieum bi mai makhama bi
@morsarr4420
@morsarr4420 5 жыл бұрын
@@zeynabndiaye24 Je n'ai indexé personne. Perso, j'ai eu à visionner plusieurs vidéos de Sangue NDIAYE. Et je savais même pas que dagn koy raamal. Damani, louleu doul yobbou si yalla ay thiaakhaane leu
@zeynabndiaye24
@zeynabndiaye24 5 жыл бұрын
Motakh manila amo fatkhou soko amoon do guiss ndeye ak baye wala raaam ak kigni ramaal
@morsarr4420
@morsarr4420 5 жыл бұрын
Ndeysaane. Je n'ai pas à critiquer les croyances de personne ni à en porter un quelconque jugement. Sur ce, geumm ngani awma fathou, waaw okay. Yaw khamnaa Serigne bou féss dél nga maa chaa Allah
@mamemassaer7052
@mamemassaer7052 4 жыл бұрын
Khana mom day fay Gni mi andal?
@khadydiagne6795
@khadydiagne6795 5 жыл бұрын
Machalah yala yala goudall fannnwi mayla werrrrrrrrrrrrr saguebi
@attidjani7626
@attidjani7626 4 жыл бұрын
Kan mooy sangue bi fofou??
@diallonatoucha1955
@diallonatoucha1955 5 жыл бұрын
Serigne sangue Ndiaye bii ak ouzin keita meune nagno bokk diotaaye !!!! benn lagnou !!!
@souaiboudrame6158
@souaiboudrame6158 5 жыл бұрын
Sangue Ndiaye danga wara diange wati
@soperassoul2368
@soperassoul2368 5 жыл бұрын
Ki esk'il é ds sn état normal ???
@modougaye3943
@modougaye3943 5 жыл бұрын
Sope Rassoul 😂 doumanila det dh
@docteurdiakha1740
@docteurdiakha1740 5 жыл бұрын
Kii moye diemiy khamkham
@diarrasene9056
@diarrasene9056 4 жыл бұрын
Edrissa Darboe yalla bi Guaye diamou moy SANGUE NDIAYE
@attidjani7626
@attidjani7626 4 жыл бұрын
Diarra Sene yaw yaa reew mram
@seckcheikhanta956
@seckcheikhanta956 5 жыл бұрын
Ki khamul loubari de yalla nako yalla guindi
@attidjani7626
@attidjani7626 4 жыл бұрын
Sangue Ndiaye yaak say talibé ay comédien deug nguen walay . C’est du jamais vu 😩
@hamidoudjigodia2057
@hamidoudjigodia2057 5 жыл бұрын
Mann kokou dougu fofou si guinaw di woté nann daffay aidé sangu lah menoul mougn🙄🙄🙄néna emession bi boulénn ko parparlo😀khutbu amoul bankhass dou ayy fo bayi lénn di woté ayy makha'amat té nangou nek ayy diamou ya'allah kepp sangu dotoka defati🏃🏃🏃😂😂😂😂😂
@andresssylva8751
@andresssylva8751 3 жыл бұрын
Messouma khamni lii amena Sénégal.
@fatimgueyebeye6621
@fatimgueyebeye6621 5 жыл бұрын
Machallah Babacar thioub yalnala yalla lafal thiate leral rek mola takha diouk
@mamadoudiouf5467
@mamadoudiouf5467 4 жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂 li deh doynawar
@alhaqq310
@alhaqq310 5 жыл бұрын
Ki eskeu rothi wougneko si peybi, wakh bi amoul khaal dara !!! Kou constater Lima wakh mayma J'aime👍
@manganebayemor9608
@manganebayemor9608 5 жыл бұрын
Lolou ngueni xar mou nopi doleneko mousseu guiss sangue bi daye wax ba mission bi mat inchallah danguene jaloux talibe sangue ndiaye yi rek gnofi am xam xam lolou molene meti
@khadimdieng1852
@khadimdieng1852 5 жыл бұрын
Ouztase Babacar thiob dé bayaboo nio outalko sécurité sino gayi nékk si guinaaw sankou Ndiaye dinanioko défaral affaires
@issalo3313
@issalo3313 5 жыл бұрын
Dieureudief sangue barhamou Ndiaye gniye inkar di wax lou bone si Sbn niome xam nagne né ki tok ak sangue xaw rhioubou xaw thiopete amul batine baye niass waxone nané ma yémou si Talibé bouye doxé zahir Talibé kaye batinoul batine la wara dokhé yene gni di wax amo lem roussou kaye kou mel ni sangue Ndiaye dotoul amati si adouna yene kaye lathié thioubou ndah dox n’a yalla bou doxone yalla Dou lathié zahir waye kawtéf li rk mo len lor si wakhou baye
@papacheikhouba9909
@papacheikhouba9909 5 жыл бұрын
Amolene beneu téguine même ki sou dokhoul si yalla gag lona sa serigne en plus si zahir donc ki sou dougone si batine khana dey gueneu salle bi
@OusmaneSow-gf6ju
@OusmaneSow-gf6ju 11 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂
@seydihenrazim9715
@seydihenrazim9715 5 жыл бұрын
Sangue Barhamou Ndiaye Une Fierté sans Fin.. Anna ki meuneu housse ni ci bahrou marifa.. Waye limo geuneu Touti ci Limou Yoor. Inkare walle question insensé qui n'a aucune utilité au vu de la L'islam Yagg na fi te fi lagnoukay bayi.. Wayé dou yakk daara ci Gourou yallah gui.. SBN ILLA YAWMI DINI..
@zacdilan6682
@zacdilan6682 5 жыл бұрын
Khoutbou bo khamnii khamo dara thi charia
@seydihenrazim9715
@seydihenrazim9715 5 жыл бұрын
@@zacdilan6682 Yaw dèggo débat bi ci Mazheub bou validoul la lath tè kan moy Hallil bane pillier ci Dinè bi Kon Kon Takhouniou jokk poser ci Alquran adiss wakhou cheikh Tijane ak baye gni nio am thieur ci dîné dji koudoul gni mirage nga
@mouhamadoumndiaye6595
@mouhamadoumndiaye6595 5 жыл бұрын
Seydi Henrazim nga balma dei wayè senegal legui dafa doy warr Kou nek ak fingay wotè ni fanga far Xam ngueine yala mais Xana dangueine ko fatè niou delou diamou yala prck baye niass thi laniouy wo Daf nio xamal yala pour niou gueuna sax thi diko diamou mais xamalouniou ko pour niou top ko rek tei fatè yala Delo leine sen xeel yi sax thi diamou yala bania tek serign bi place yala
@insajuniordiedhiou5719
@insajuniordiedhiou5719 5 жыл бұрын
@@seydihenrazim9715 Ne les répond pas car ils n'entendent rien et ne savent rien .... yamm dou guiss dara!! Sangue Barxamou tout ce que je suis!!!
@medinabayee-shop2189
@medinabayee-shop2189 5 жыл бұрын
khoutbou bou deur di mére di daw ay question ,bayilén sén xél yinguèn di fowé.
@saikh2348
@saikh2348 5 жыл бұрын
mane oustaz bitey damakoy yeureum sou invité yéne idéologie yi, il voit les dérives avec sa conscience mais le courage d'aller plus loin lui manque toujours,
@modougaye3943
@modougaye3943 5 жыл бұрын
islam up bilay nk waxal dh
@ndongotoure7086
@ndongotoure7086 5 жыл бұрын
Sangua Ndlaye fenenga ci ngounoungana matosakh Khadi doulnga doulyoutoye khipou
@galaxiepro.5641
@galaxiepro.5641 3 жыл бұрын
en plus de cela mouye toutal yeneneu kourel sofianké yi ki weroul waye cest un imposteur
@abumouhamad5154
@abumouhamad5154 5 жыл бұрын
Sénégal senegal Sénégal yalla naniou Yallah défale tawfékh. Do khame ndakh dînee yalla bi dagnoko beugue def comédie wala déteu soubhanaLah. Allahoumous ta'aneu
@tidianelo3559
@tidianelo3559 5 жыл бұрын
khutbu zaman du toog ci tele di ko wax
@guelwartgl4870
@guelwartgl4870 5 жыл бұрын
Lo Tidiane waw
@papafall2151
@papafall2151 5 жыл бұрын
Lo Tidiane sournois ko ladié nak
@soperassoul2368
@soperassoul2368 5 жыл бұрын
Machalla Lo
@soperassoul2368
@soperassoul2368 5 жыл бұрын
il 'na rien ds la cervelle ce soit disant khoudbou d rien du tt
@bachircissezaakirofficiel9342
@bachircissezaakirofficiel9342 5 жыл бұрын
Diarama sangeu barhamu ndiaye doundall werall ndiaye ahlou diné niolay ndamo sa liguey Rafétna Machallah yallna baye faye
@daoudaselinediatta3404
@daoudaselinediatta3404 2 жыл бұрын
Oustaz Biteye. Invité nga kou degg dinne. Yangui liguey Lou rafet ci dinné dji Sangue Barham leu nieup n'aura déglou diamono gui.cii kou beug tekher
@aichatabane3035
@aichatabane3035 3 жыл бұрын
Alhamdoulilah HAMDAAN LIMAAN ALAL HOUDA HADAANI SOUMMA ILA TARIQATOUL JEYLANI
@Pastef859
@Pastef859 5 жыл бұрын
Limoy senegal ndeysan Qu'allah nous guide vers le droit chemin inchallah
@abdouazizfall9014
@abdouazizfall9014 7 ай бұрын
Sangue Ndiaye nékh na 😂😂😂
@galaxiepro.5641
@galaxiepro.5641 3 жыл бұрын
liniouko lathe ak limiye tontou kom barca ak sasouolo dara dara khamoukossi cheikh tidiane biteye sakh da rousss ki sangue ndiaye cest un imposteur deguisé et tout tidiane doit le remettre a sa place day yakh derou wa keur baye niass yi
@idiansierra4784
@idiansierra4784 5 жыл бұрын
Maachala sangue bi contane néne yalna yalla guoudal sa fane bilay Ndiaye yay goor na nite yi xamnei baye niass xam xamou batine léne ko topŕwone mai dou aý charia on a dépassé s stade souguéne niéméwoul dém bayiléné niou ak suniû sangue bi
@mr.africa8166
@mr.africa8166 5 жыл бұрын
Khalifa yalla dou benge bene question baye question yepp lenouko don lagg cii aduna bii fumu deme
@souleymaneka3071
@souleymaneka3071 5 жыл бұрын
Wadji aggoul sakh ci Cheikh Ibrahim Waxatoumalaak Bayou mindef yi
@maodondawsbn8172
@maodondawsbn8172 4 жыл бұрын
thioube yeureumnala inkar amoul sans
@cercledesprivilegiesduzikr3226
@cercledesprivilegiesduzikr3226 5 жыл бұрын
Le Khoutbou Zaman existe et existera toujours parceque Imam Mahdi Mountazar sera le Khoutbou Zaman et IL est le Khoutbou Zaman de son temps et IL est venu donc IL est le Khoutbou Zaman. Le Khoutbou Zaman ne se proclame pas
@galgalgal8007
@galgalgal8007 5 жыл бұрын
Kane moy mahdiyou almountazar?
@cercledesprivilegiesduzikr3226
@cercledesprivilegiesduzikr3226 5 жыл бұрын
@@galgalgal8007 Imam Mahdi Mountazar est une missionnaire de aakhirou Zamann que le Prophète Mouhamed psl avait prédiqué sa venue à la fin des temps.
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy 5 жыл бұрын
@@galgalgal8007 ki El Cheikh bi nèkk Ndar lay wakh 😂😂😂😂😂😂
@galgalgal8007
@galgalgal8007 5 жыл бұрын
@@cercledesprivilegiesduzikr3226 noumou touddou boko khamè?
@boubacarlo9559
@boubacarlo9559 5 жыл бұрын
tout les prophetes se sont proclamés
@ibrahimba8328
@ibrahimba8328 5 жыл бұрын
Please ngir yalla DTV délén invité borom kham kham bouniouy wakh si coran bi ak khadiss you wér yi nioune lolou laniou sokhla mais pas ay tarikha
@hamzajunior3774
@hamzajunior3774 5 жыл бұрын
Serigne Sangue Ndiaye li niou koy lathie ak limouy tontou bokoul sakh Nan kani nak😂😂😂
@babacarsadikh4703
@babacarsadikh4703 5 жыл бұрын
Nooo ki nakk gniko topp sakh sen kham yalla dess neu 😂😂😂😂😂 tontoul mo geun 😂😂😂😂
@malicksow9140
@malicksow9140 4 жыл бұрын
Niowal sett si niou tu verras
@abdourazakmohammadrazak9520
@abdourazakmohammadrazak9520 3 жыл бұрын
Hun diambar danouna sèy tanè mo beurii dolè heureusement boumala tèlè torokhal mom sèy tanè dou mbokk sangue ndiaye koula khole dou yeukk yallah sii yow bèn amo kham kham tokk rèek say sa ndiabote weurla nguay fèn bokoul ngua tokk akk borom kham kham 🤫🤫🤫🤫🤔🤔🤔🤣🤣🤣
@moussakeita1017
@moussakeita1017 5 жыл бұрын
Salam magui ziar kou nek si touram ak dieumeu di rafet lou jotay bi di fatali.yalla ak yoneinte bi cheikh Tidiane ak baye niass ak sen haqou di Sangue ndiaye laniou guem.Serigne bi thioub halil keneu khamouko sk Li Sangue ndiaye di liguey si diné dji liguey nako.naniou topeu Makama bi diougué si yalla di islam diar si charia diar si tarikha ak qaqiqa di marifa nakh moy leral diné islam bi(charia tarikha haqiqa).naniou ladj pr kham au lieu di ladj pr inkar.dieureudieuf Sangue ndiaye doundeul ndiaye.
@mr.africa8166
@mr.africa8166 5 жыл бұрын
Kasab la khalifa yalla bengul bene question lii ngay khelate sahh daff koy kham
@moussakeita1017
@moussakeita1017 5 жыл бұрын
@@mr.africa8166 mr. Africa Serigne bi dou lolou moy khalifa yalla.bouko degué fofou c des paraboles nekoul lolou moy teubou kham Li nek si khelou kou nek.khalifa yalla louy deugeureul sa islam iman ikhsan silay dokh bokoul ak ligua yakar.Sangue ndiaye wakham lep kham kham la.khalifa yalla bi nak moy Ki yènou amana yalla bi té kokou nitt lay done mounoul nek lénène.
@mamadoufaye1755
@mamadoufaye1755 5 жыл бұрын
Khoutbou zaman doumeussa déclarer boppamm télévision.raison pour laquelle yallah leerall nako devant tout le monde.sangue ndiaye il n'est pas trop tard pour nga wouti xamxam de grâce boul reuy
@seckseck280
@seckseck280 5 жыл бұрын
Ioe t’es un idiot mal intentionné
@t.souleymanediallo3846
@t.souleymanediallo3846 7 ай бұрын
Yonent yeupp wakhonèñe ni Yalla molène yonni. Souñou fékkéwone Télévision dinañouko wakhé fôfou pour Adouna bi yeupp djott si. Yew yâ ñakk kham-kham. Yew sa baye loumou déff si dîné dji?
@lassanadoumbouya9512
@lassanadoumbouya9512 3 жыл бұрын
sangue ndiaye for ever
@loudoulyallaaynenla3312
@loudoulyallaaynenla3312 5 жыл бұрын
Say wakh léppou lisi euppou yeukkeuti sa boppoula ak figua bokk khép ak touteul nienéngni basi nitou yalla yi djitou won wéddi gualén té sén makhama aguosi kouy wotéwo khoutbou da wara am yar nakagua mana nékké khoutbou té respéktéwo nitou yalla yi selon nigua wakhé wédigua sakh nitou yalla yi bokkak yaw tarikha té dougne ay niassén kou kham yalla deugue dou khép diami yalla yi ndakh day guis boppam si moromam kou yeuk yeuk sa boppougua controumala lima guis rek la wakh oyofal exemple bimalay diokh mooy guarape thiar youla geuneu mégni gueunla wathi dieum souf
@Ahmadou_1440
@Ahmadou_1440 2 жыл бұрын
un vrai comédien sangue avec sa bande de troubadours
@maodondawsbn8172
@maodondawsbn8172 4 жыл бұрын
barker baye niass sasngue barhama ndiaye mou man si halambi
@maodondawsbn8172
@maodondawsbn8172 4 жыл бұрын
1000 khalill ben talibee baye moulen mane
@fermemanding9865
@fermemanding9865 5 жыл бұрын
Manne Benne Invite la guiiss plateau bii dakhh lii moyy debat
@boursinesaloum1819
@boursinesaloum1819 3 жыл бұрын
الحمد لله من هو الله ج الله هو كريم وهو ربنا
@lebarhamistesamb791
@lebarhamistesamb791 5 жыл бұрын
allahou Akbar Thieye barhamou tay dêgna deug dal
@cheikhabbaaidara3389
@cheikhabbaaidara3389 5 жыл бұрын
Machalla... L'avocat de Cheikh Ibrahim ... Diam ak tawfex thi iow!
@flegmatiquedcr163
@flegmatiquedcr163 5 жыл бұрын
Sangue calme toi Baye Niass ☝️ ak légui matoul 💯 ans baguay woté khoubaniétou té séy tontou sakh léroul
@diopmodou173
@diopmodou173 4 жыл бұрын
Fene rek
@cheikhtidianediouf6782
@cheikhtidianediouf6782 5 жыл бұрын
Kila guena ham yalla guenlako ragal qui hamhamlou yalal guenla sori yalla yalnanou yala mandou , ak modestie
@mouhamedkane9693
@mouhamedkane9693 3 жыл бұрын
wa man fouma naikonn biiy li di am li khoromou na dé🤣🤣🤣
@joaopaulo77pulo78
@joaopaulo77pulo78 5 жыл бұрын
Liy moy senegal démlén diap thi alkhourane ak soune moniouy diarigne fiy ak faniou dieum lénén louniou top loudoul wakhi yalla ak yonéntoubi psl dinaniouko rethiou euleuk senegal da beri ay nakhatékat you beuri talibé garantillén aljana té mom khamoul kagne lay dé sou déwé khamoul fouko yallay dieumé boula garantilé aljana nga huemko ba faté yalla ap dofngua
@tamsirsarr4684
@tamsirsarr4684 5 жыл бұрын
SBN for ever❤❤ Délen inkaar rek. kou geun ndaw si talibé sbn dou moromou kénn si yénn. De gré ou de force Sbn moy khalifa yalla. Xam xam bimou yor amoul kénn kouko lal si azal ba légui.. vous êtes jaloux rek. mtx ngen yakamti mou danou. Mais lolou dou meuss amm. Nangoulen li yalla dogal.. nopalou. Mais inkaar loufi yagg leu c normal kou woté deug ala kouli hal dinagn la inkaaré nounék. Mais menoulen si dara. zaman bi amoul sikk né sbn mo yoré raya bi... kouko bagn on y peux rien. Si naxarr ngay déwé. séni serigne yi lakatou nagn gein niou diamarlo si xam xam rek. Niou xol fou deug gui nek. C aussi simple Saga ak wakh diou niaw mome kou amoul argument mokoy def.. meun na niak.
@cheikhdiop9013
@cheikhdiop9013 5 жыл бұрын
Tamsir Sarr khalifa bou menoul mirass ngounou ngana settane nen affaire bi d sen wadji dafa kanassou xamoul yalla tiowlé fi nk
@cheikhdiop9013
@cheikhdiop9013 5 жыл бұрын
Tamsir Sarr demneu medina baye call cheikh mahy naneko beug na nieuw mais dama ragal jegalou la beugone😂😂😂 ......lep falama fek ande ak sete touré kokou mom lineko df si video df niaw
@papacheikhouba9909
@papacheikhouba9909 5 жыл бұрын
Serigne bi nga balma dei mais wakh diou niaw ak sagga ak arrogance si wa keur sangue ndiaye la fékeu bakh. fo fekeu kou nane mane la rek soko setei deugeu dou mome borom gayi niokoy wakh yaw leu gate khamoulene ko si sob rek
@KelseyMoody-xo3vj
@KelseyMoody-xo3vj 5 жыл бұрын
Doul rk 😂😂😂
@Ahmadou_1440
@Ahmadou_1440 2 жыл бұрын
@@cheikhdiop9013 🤣🤣😂😂
@tafkey1888
@tafkey1888 5 жыл бұрын
Lingene diap fok ne lolou walay ay nakher la! Sangue ndiaye continue de faire ton éducation spirituelle personne ne t’y contraint mais nak boul woter wo Lo donoul!! Kou setane li khamni neko tji dara!
@zeynabndiaye24
@zeynabndiaye24 5 жыл бұрын
Iow mi ya nekoul si dara Sangue ndiaye wotewoul mais pays yalla bi mo daw baci mom Soula leunté nieuweul geustou ko dinala leir inchalah
@babacarseck6720
@babacarseck6720 5 жыл бұрын
Yangui yakh alkourane dji nga beug wakh yay khoutebou yaw tamite naniou ragal yalla
@babacardrame1205
@babacardrame1205 4 жыл бұрын
Dieynab Sall yaw ak sangue Ndiaye yèna yém khamou lén dara niak kham dara motakh li nieuw meune lén nakh
@babacarkhaba4704
@babacarkhaba4704 4 жыл бұрын
Ki bilay yeureume na talibé yi
@papaboucardiouf7280
@papaboucardiouf7280 5 жыл бұрын
Doyna warrrr! Thioub diaraammaa. Yénga niou bariiiii Machaa alla
@abbalkhassim
@abbalkhassim 5 жыл бұрын
Xam xam bu léér nii !!!! Kén moussou KO dég !!!! Jerejefé mawlana sangue Ndiaye
@babakoundoul4321
@babakoundoul4321 4 жыл бұрын
celui qui pose les questions doit savoir que l'heritage est une science exacte qu'on apprend seulement
@abdouwahabkane5161
@abdouwahabkane5161 5 жыл бұрын
Diiné dou ay wax jeff la...liguayel serigne touba
@95SOuley
@95SOuley 5 жыл бұрын
Yow khamoo serign touba! Bayilvsa thiakhane tei nga khamidji sa borom! So deiiweii dinga kham ke serign touba se fout de toi
@cheikhdiouf277
@cheikhdiouf277 5 жыл бұрын
doul rek sangue Ndiaye
@mst221
@mst221 4 жыл бұрын
Jërëjëf Baabakar Thioub
@abbulabass4330
@abbulabass4330 5 жыл бұрын
Thiey mim réew😀😁😂
@issamagazine9775
@issamagazine9775 3 жыл бұрын
Souff su Imam Mahdi(psl) teude Ak Yonnenta Yalla Issa ,App Khoutbou menu fa fegn. #Seydina_Limamoul_Mahdi_psl👇 Ne cherchez pas à vous surpasser les uns les autres dans l’acquisition des richesses de ce bas monde. Cherchez plutôt la concurrence dans l’obtention des richesses de l’autre monde. C’est ça qui procure la fortune éternelle et des honneurs élevés. Ne soyez pas avides des biens de ce bas monde, car ce monde-ci est [comme] un cadavre [impropre à la consommation]. Seuls les chiens et les vautours mangent un tel cadavre. Détachez-vous donc de ce bas monde, ne le suivez pas, car c’est une demeure qui va vieillir et disparaître. Or sa disparition est proche.
@mouhamadoudiagne1020
@mouhamadoudiagne1020 4 жыл бұрын
إذا كنت أبحث القطب لا أبحثه في القناعات، ولكن أقول له (من عمل صالحا فلنفسه ومن أساء فعليها ) ... (واتقوا يوما ترجعون فيه إلى الله ثم توفى كل نفس بما كسبت وهم لا يظلمون) وأقول له أيضا( أن النبي صل الله عليه وسلم أن تكفير المسلم حرام)
@alioufall9182
@alioufall9182 5 жыл бұрын
Jeureujeuféee Baye Niass ma contane tay walahi Sangue ndiaye danou nga koi Baye Niass dèh biko borom xam xam ya sa NiGeria weuré diko testé si xam xam lép lalén tontou ba wakh léne lougnou moussoul xam motakh gnép topouko tay wayé yaw mom guisago dara sakh miras rèk menoko atè ba paré ngay gnodi ay houtbou
@arafatdiallo9448
@arafatdiallo9448 5 жыл бұрын
Sangue Ndiaye mi kouko top reernga te dinga torokh ba faw
To Brawl AND BEYOND!
00:51
Brawl Stars
Рет қаралды 17 МЛН
“Don’t stop the chances.”
00:44
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 62 МЛН
EUTOUB ISLAM DU 19 06 2020
1:46:55
Gtv Sénégal
Рет қаралды 21 М.
Histoire sur El Hadji Mansour Sy racontée par Serigne Habib Fall - QG du 05 Mai 2021
1:05:50
To Brawl AND BEYOND!
00:51
Brawl Stars
Рет қаралды 17 МЛН