(Exclusif) Le père d'Anta Ndiaye recadre la Grand-mère de Thioro Mboup et clôt le débat...

  Рет қаралды 46,664

BARGNY Toujours visible

BARGNY Toujours visible

Күн бұрын

(Exclusif) Le père d' #Anta Ndiaye recadre la Grande mère de #Thioro Mboup et #clos le débat... " Voici les résultats de l' #enquête"
Bargny Toujours Visible la Media qui vous rapproche de la population, un media proche de vous
🖥️ Contactez-Nous
📞77 440 25 89
✉️ sunubargnytv2019@gmail.com
🔗Facebook
/ bargnytoujoursvisible
🔗Instagram
Btv officiel

Пікірлер: 132
@aichandiaye3147
@aichandiaye3147 2 жыл бұрын
Franchement parler am gua yar té meune gua wax famille thioro môme khamou gnou adouna tek si sen éducation desna thioro môme kou téla am fite la 12ans Di rayé bo amé 23ans fougnou dieum rip bb Anta 😭😭😭
@alimatouniang444
@alimatouniang444 2 жыл бұрын
Bien dit tonton wakhe bi rafene te deuge la yalla na yalla diapale
@yasjoop716
@yasjoop716 2 жыл бұрын
Mamou thioro kouko xol kham ni vagabon leu coba la assasin la nitt kou meuneu doul leu tmt 🤪merci bcp👍
@coumbambaye7921
@coumbambaye7921 2 жыл бұрын
😆😆😆
@thiatoumerebindiayediatta9080
@thiatoumerebindiayediatta9080 2 жыл бұрын
@@coumbambaye7921 liii laa beugone wakh wouy 😂😂😂 beugne dou reeh jamm waye tmt journaliste yi kouleen di wakh nay leer mere bobou khool ko rk khamne yague naa woww beut
@coumbangom1158
@coumbangom1158 2 жыл бұрын
😂😂😂😂😂
@madjiguenedabo2213
@madjiguenedabo2213 2 жыл бұрын
MachaAlah deugueu Dou romb ay nop,may wakh niari mère gaïndé yoyou tok fii dii doul..... wakh bou yanou manaa kouko dégueu khamko donc on est de tout coeur avec toi,et justice sera faite pour Anta inchaAllah
@ndeyetickediop4825
@ndeyetickediop4825 2 жыл бұрын
Thioro bandii la ay wakeurem ay koba baradioo lagnuu bb anta yalla na khipé aldiana
@seydinapouye9413
@seydinapouye9413 2 жыл бұрын
Deugeuh rek guafi wakh moussa amo béneuh thiakhane walakhi nitt kou yatou gua kou bakh kou deugou ame ak niépeuh diam Machallah nala yalla défale diam té mayléne kholou mougne
@adamacamara8681
@adamacamara8681 2 жыл бұрын
Walahi deugue rek moye deugue rip bb Anta justice sera faite inchallah. mère bi ak Tanta dji ça se voit que ni khame nagne Lou xèw elles sont des cobas
@courasamb109
@courasamb109 2 жыл бұрын
P
@khadyba7432
@khadyba7432 2 жыл бұрын
Très displicine si kouniou ray sa doom yalla nalen yalla may kholou mougn justice pour anta
@janatoudubai5231
@janatoudubai5231 2 жыл бұрын
Paa bi kou dal laa en plus kiy wax deug sokay deglou diko xam thioro nak mom Ay kilifam nioko togn parck gniko yilif deja danio irrespectueux et irresponsable nioniiu meunougn yar keine Bebe anta yalnako yala Atek yeurmandem ndeysane Thioro ana djiguene ak Doug Si batima? batimaaaa meine mi ? choqué naaa mane
@aissatoumbengue1012
@aissatoumbengue1012 2 жыл бұрын
Wakh diou yénou mana kouko dégg kham ko! Yalna yalla léral mbiir mi yeup🙏
@gnimafaty8569
@gnimafaty8569 2 жыл бұрын
il a été coherent depuis le début. que justice soit faite! dagnlen togn. repose en paix bb Anta
@aissatouba8178
@aissatouba8178 2 жыл бұрын
On es tous derrière la famille de anta 😭n'a yone def ligueyeum niari imbéciles yii deii si prison bi ..Mame dji mom Mouy melni vampire loumako diepei kanamam bou saltei kouko khôl khamni koba la mom AK tioro
@Momarbineta
@Momarbineta 2 жыл бұрын
Yaq seutam ba paré beug coumassi takal
@khadidiatoundiaye9898
@khadidiatoundiaye9898 2 жыл бұрын
Mame dji koumako mayone bama niaf lou boname 😡😡
@theresemariediouf3612
@theresemariediouf3612 2 жыл бұрын
Son comportement montre qu'elle ne peut donner une bonne éducation à un enfant. Sa manière de parler ses gestes la définissent.
@mamesodaniang3571
@mamesodaniang3571 2 жыл бұрын
Dougnou yaar séne dôme ba paré beugg diléne défendre a chaque fois. Et puis dafa meuneu féne
@ramadeiallo5627
@ramadeiallo5627 2 жыл бұрын
Yallana ko yalla yeureum té yone def ligueyam lolo moka fath khaley gno am fit la ilaha ilalah
@oulymatafaye6323
@oulymatafaye6323 2 жыл бұрын
Ki dé nitkou baxla kou deugou djoup djoulité Moussa Ndiaye. Kou bakhla talibe srg Touba machallah
@famtediop9317
@famtediop9317 2 жыл бұрын
Linga wakh la geum mane
@mameawacoumbaseck4120
@mameawacoumbaseck4120 2 жыл бұрын
Ma mome sama gueume té gueume nala yala Maye la kholou mougne
@dabatoure7455
@dabatoure7455 2 жыл бұрын
Ndeysan anta ndiaye dafa norou sama dom dioyna ko basonou melni sama domdji laye dioy thiey yalla li métti na 😭😭
@abdouazizndiaye2011
@abdouazizndiaye2011 2 жыл бұрын
Le père de anta est très véridique et discipliné
@yayafall7353
@yayafall7353 2 жыл бұрын
Je vois kaay
@seynaboudiene7776
@seynaboudiene7776 2 жыл бұрын
Effettivament
@mariamacisse743
@mariamacisse743 2 жыл бұрын
Exactement
@ndeyefatouniang6608
@ndeyefatouniang6608 2 жыл бұрын
ça saute à la œil nu yalla nako Yalla may xolou mougne
@Lady-b7k
@Lady-b7k 2 жыл бұрын
Billay ndeysan
@habymamadousakho7815
@habymamadousakho7815 2 жыл бұрын
Tu es tres posée yalla nalla yalla may xolou mougne
@bernilynsha
@bernilynsha 2 жыл бұрын
Famille thioro vraiment vous n’aviez rien à dire c’était mieux de vous taire a part massa wou famille anta ndiaye bi waro lene wakh massa à vous bb anta repose en paix 😭 🙏🏾
@fatoudiouf8396
@fatoudiouf8396 2 жыл бұрын
Deugue rek nga wakhe sene seut ray Anta ba paré gnouy khasté ak séne canaam you gnémé
@binetathiongane8864
@binetathiongane8864 2 жыл бұрын
Même boudé xalei bou gorr bi mo ray famille wam kenn guissou lenn manou legn defff di deff lougnouy defff si souff cette thioro xalei la mais djiko xalei yorouko amna fitt niemer na
@rokhayabeye9847
@rokhayabeye9847 2 жыл бұрын
Deug dou romb nop boul bolé gnak ak wax ndeysane lii dara guenou ko méti yalla na borom bi may léne xolou mougne
@rassoulnene2981
@rassoulnene2981 2 жыл бұрын
moussa deugou laniou la khamé andeu ak dall kou niou violé Dina mane dokh di weur anta ak lathié
@oumoukalsoummbaye5603
@oumoukalsoummbaye5603 2 жыл бұрын
Lolou mome deugg leu
@denisegodeaux6145
@denisegodeaux6145 2 жыл бұрын
Rassoul nene y’a wakhe degue
@dabasene1284
@dabasene1284 2 жыл бұрын
Vraiment
@zahracoulibaly7577
@zahracoulibaly7577 2 жыл бұрын
La grande mère de thioro mboup kouko degue kham ni day doule
@niangtra
@niangtra 2 жыл бұрын
Deug rek ngafi wakh tu es très courageux car c pas facile de perdre un enfant surtout de cette manière
@mariehelenebodian7074
@mariehelenebodian7074 2 жыл бұрын
Non Mamou thioro kou meuneu doul leu té capable
@tidianiasy8265
@tidianiasy8265 2 жыл бұрын
Mamou thioro loutakh bayiwoul yayou ak papa thioro wakh da khamné niome deugeu lagnou nara wakh séne khessal you salté té vulgaire thioro ak copin bi na yone def ligueyame bb anta repose en paix 🪦 metina
@isseudiop2951
@isseudiop2951 2 жыл бұрын
Mamou thioro kay wakh djou niaw la wakh khana mou yeuram yayou xallé bi fatou
@sokhnafatydia7032
@sokhnafatydia7032 2 жыл бұрын
Diakhalonn nama trop kougne viole noumiy weuré
@rassoulnene2981
@rassoulnene2981 2 жыл бұрын
moma diakhal si khalé bouniou devieergé
@mayaciss6821
@mayaciss6821 2 жыл бұрын
Mais why ngay posé des questions seytané ak djakhassé. Justice pour Anta. Mais il pose des questions qui n ont rien à voir avec le décès de la petite Anta.
@yayendelladiobaye6108
@yayendelladiobaye6108 2 жыл бұрын
Arrêtez de garder vos enfants spychopates chez vous il faut les dénoncé sinon elle va reprendre ses actes rip bb anta
@maramesagne3360
@maramesagne3360 2 жыл бұрын
Bilaye wax nga deg na yon déf ligéyem fou mou yém nekh gni dougnou ay nite
@nogayefall4298
@nogayefall4298 2 жыл бұрын
Allakhou akbar doyna warr
@abysene7914
@abysene7914 2 жыл бұрын
Bilahi Moussa xamnala bou bah nitou deugue gua
@fatimandiaye2040
@fatimandiaye2040 2 жыл бұрын
Dengue dou rombe nooppe Masssa mon frere
@sokhnagueye2363
@sokhnagueye2363 2 жыл бұрын
Deugoul daal moo nekha deug Massa
@foot.1912
@foot.1912 2 жыл бұрын
Mére bi nama yalla balle mais bimouye wakhe djou diakhoso gogou la khamnie nékoule si deugue
@aminathiam4766
@aminathiam4766 2 жыл бұрын
Le père de Anta ndiaye reik mo wax deugue. mamou thioro yi nak ay feine kat you mak laniou ay koba laniou . yallah nak dineu feinial inchallah
@ducrospatricia4680
@ducrospatricia4680 2 жыл бұрын
VRAIMENT LA DISCIPLINE QU'ON VOIT SUR LE PERE DE ANTA EST TRES RARE MACHALAH JUSTICE POUR LA PETITE ANTA . FALLAIT MEME PAS REPONDRE LA GRANDE MERE GOLO NIAW KHESSAL TCHIAM NIEME YALLA RAGAL DER DIAPP KHALLEI YI YAKHEU LEINN BA NIOU YAKHOU
@mydi555
@mydi555 2 жыл бұрын
Bilay dama am louma meti
@binetandiaye4776
@binetandiaye4776 2 жыл бұрын
Yalla na yalla Maylène xolou moune
@louisthiaw908
@louisthiaw908 2 жыл бұрын
Mane déh diakhléna🤔🤔🤔j SS choqué
@di_laminolofficiel2769
@di_laminolofficiel2769 2 жыл бұрын
Au moins ses explications sont claires, que justice 👨‍⚖️ soit faite.
@khadygueye5970
@khadygueye5970 2 жыл бұрын
Mére bi kou déglou wakh dji gua khamni nafék la
@fallkhady8290
@fallkhady8290 2 жыл бұрын
La justice fera son travail Ces deux présumés Méritent la peine capitale
@sokhnaxi
@sokhnaxi 2 жыл бұрын
Tres veridique Claire et net
@ngonemansourmbaye9142
@ngonemansourmbaye9142 2 жыл бұрын
Wawaw Mamou thioro Kay gedjj lay diay koba bimou done
@misswade3280
@misswade3280 2 жыл бұрын
Kounou violé dè do meuna weur halé bou réére mère bi dayy féneu
@dieynabandiaye7724
@dieynabandiaye7724 2 жыл бұрын
Wakh diou deugou yombou na xam
@khadijarassoul872
@khadijarassoul872 2 жыл бұрын
Doyna warr trop adouna diakhasona bilahi
@ramadeiallo5627
@ramadeiallo5627 2 жыл бұрын
Papay anta mo am yar té dal
@Yowan01856
@Yowan01856 2 жыл бұрын
Père Anta defna déclaration de patrimoine
@bassinecisse8100
@bassinecisse8100 2 жыл бұрын
mère bi amoul pèkhè motakh mouy doule di dandialè rek beugue protège thioro wayè doufi amé deh na yone def ligueyame rek Khalè yo khamnè nièmè goorr badèè🤦🤦
@damembow6856
@damembow6856 2 жыл бұрын
Maguéttoum thiagala
@aissatouba8178
@aissatouba8178 2 жыл бұрын
Bou mak
@Activiste8473
@Activiste8473 2 жыл бұрын
Thioro dal dome diou teu leu reck rip bb anta ndiaye sama kal bi
@yayafall7353
@yayafall7353 2 жыл бұрын
Laisser la justice faire sn travail namou anta dafa yabaté
@clairemari7292
@clairemari7292 2 жыл бұрын
Anta paix à son âme
@abysene7914
@abysene7914 2 жыл бұрын
Yena Say daguay wah ba paré tontou sa bop mère bi néna dioubo wouniou ba paré mouni modoneu togou thi deutheu bi
@bathiesow12
@bathiesow12 2 жыл бұрын
Famille thioro kenn farul AK yenn guenn worone nopi mais osé dit wax é croyez-vous que dinagnou lenn gueum si prison bi lagnouy déé
@fatimasoumare8407
@fatimasoumare8407 2 жыл бұрын
Thioro mboup assassin là n'a yone def ligueyam !
@damembow6856
@damembow6856 2 жыл бұрын
Quelle grandi en prison doméram
@awagadiaga9553
@awagadiaga9553 2 жыл бұрын
🙆🙆🤔🤔aka kapable
@thiabandoye961
@thiabandoye961 2 жыл бұрын
Ki moye domaram bo kholé Mame dji sakh kham né danio capable wayé loudoul deug dou yague domaram
@damembow6856
@damembow6856 2 жыл бұрын
@@thiabandoye961 Mame dji bandila ay domérame laniou
@mezalmez8935
@mezalmez8935 2 жыл бұрын
Bilay elle na ka payé capable si khaler
@suzannendiaye9447
@suzannendiaye9447 2 жыл бұрын
Jsui choqué
@lammben2236
@lammben2236 2 жыл бұрын
Mami thioro mom du wakhkatu dague kokou khôl khamneh merru cobala AK kanamam bu bon bi wayea munta teh ba justice du def ligueyam
@amieba867
@amieba867 2 жыл бұрын
mamou thioro loumouy wax wa kogne mba?
@tidianiasy8265
@tidianiasy8265 2 жыл бұрын
Mamou thioro kaye da vulgaire vrai vipère leu ish fenekate bau majeur
@dadyniang7569
@dadyniang7569 2 жыл бұрын
Mamou anta saine reck lay def limiye wakh khamousi dara
@zebra237
@zebra237 2 жыл бұрын
Mamou thioro yémé na yalla té meune soss koudoul sa 1ere nuit si bamél loula nékh défal
@matarfaal3742
@matarfaal3742 2 жыл бұрын
Baol baol nga liguye rk nga kham
@binetourassoul3870
@binetourassoul3870 2 жыл бұрын
Le meurtrier retourne tjrs sur son lieu de crime
@powdergirl2150
@powdergirl2150 2 жыл бұрын
Ki de kou dale le
@channelchoux8236
@channelchoux8236 2 жыл бұрын
Entouca la grande mère de thioro wakham diouboul dara wakh dji wakh molène waroul wone vraiment 🤥
@taphaleye7612
@taphaleye7612 2 жыл бұрын
Doyna war lol
@fatoukine2933
@fatoukine2933 2 жыл бұрын
Lou lérr gua wakh mère bii wax khoufii dara
@mamadoulayediop5377
@mamadoulayediop5377 2 жыл бұрын
Mere bi mom kouko deg mouy wakh ak xessal bou niaff ndayam bi xamni day doul
@doudoucisse6485
@doudoucisse6485 2 жыл бұрын
Koula deg guiss la kham ni deug rek ngay wakh
@momykandji2444
@momykandji2444 2 жыл бұрын
Mamame boko guissé khamni koba Bou mak la
@matarfaal3742
@matarfaal3742 2 жыл бұрын
Ki talibe la nuit kou bakhe la bilakhi
@foot.1912
@foot.1912 2 жыл бұрын
Mére bi daye wakhe ba parré yéyate boopame
@1khouredia
@1khouredia 2 жыл бұрын
Mère bi mom nieup khamnaniou ni c’est une menteuse. Mak dafay wakh deug
@mariehelenebodian7074
@mariehelenebodian7074 2 жыл бұрын
Kouniou violer dina tal dem di weur Anta non Thioro vrai assassin la teh capable
@khadimthioune8952
@khadimthioune8952 2 жыл бұрын
Merbi modakha doule thimondobi
@aminatawone8915
@aminatawone8915 2 жыл бұрын
Kii diaroula tontou ndakh jou gnack yeurmandéla bayilénkok yalla limou déf lanigni guisse wakh yimouye wakh takhavoule kougni sakou dina am ay tank youmou veuré khalébi yalla na yéwo aldiana
@aminatawone8915
@aminatawone8915 2 жыл бұрын
Mounossi dara soo toogué gnifékissila indilla moussiba nian khorome tibba khal lébou thiéb bi adouna dii bakh nith ak dekeundome dagnikoye sékheu khana légui la adouna takhou kouné yémalé sa bop kii amoul diom wakh warouko wone come amoul khél na dém déé dinako guenal doundou ndakh dotoul khathie thi cognebi fii senegal ken momoul féne fouwaye dieunde rek moko mome wassalam
@djeylacisse2128
@djeylacisse2128 2 жыл бұрын
Deukkeu bi woratoul nak no deff niou dougueu si say 18 mandou wouniou réglé wouniou motakh na kounek teye sa bopp diame nai nioyy
@ducrospatricia4680
@ducrospatricia4680 2 жыл бұрын
METTI NA NAKKK TROPP MANE BEUGONE NA KHAM THIORO NAKK LERR NEU MA NI MOY XLLEI MAKK YOYOU SEWW WOW BEUTE SEN WA KEUR MOME NIOME NIEUP YAMMM FAUX
@madjiguenedabo2213
@madjiguenedabo2213 2 жыл бұрын
Ay way niari mère gaïndé yii lann nguenn Di wakh wa kogn ba
@khadyba7432
@khadyba7432 2 жыл бұрын
Legui kouniou viole dîna meunn dokh may dem si Seti anta
@mamediarrandiaye7948
@mamediarrandiaye7948 2 жыл бұрын
Mais jounalistiyi tamit mengien diekhal kholou nit diaroul di fatali ay wakh you gnaw
@princess_d563
@princess_d563 2 жыл бұрын
Diaroul wone tontou sax Bilay nieup hamnane ni mère bi dafay pathial frokh
@matarfaal3742
@matarfaal3742 2 жыл бұрын
Thioro mamame moko tonge
@beautenayo1031
@beautenayo1031 2 жыл бұрын
Je condamne cet acte mais pourquoi cet acharnement sur thioro et momo en dehors de tout sa
@mariehelenebodian7074
@mariehelenebodian7074 2 жыл бұрын
Je pense que tu n'a pas bien compris l'histoire mais sinon Thioro et momo mérite plus qu'une acharnement
@didi6861
@didi6861 2 жыл бұрын
@@mariehelenebodian7074 merci
@khadidiatoundiaye9898
@khadidiatoundiaye9898 2 жыл бұрын
Yaw maye gnou halé loumouy doyé far
@1khouredia
@1khouredia 2 жыл бұрын
@@mariehelenebodian7074 parce que c’est eux les assassins. Yow esk wernga ???
@mamesodaniang3571
@mamesodaniang3571 2 жыл бұрын
@@mariehelenebodian7074 kougnou raay sa dôme do wakhé ni. Thioro ak meumeu mbame moléne gueune
Bruno bidjang répond à Armand Okol en mode clash de sardines
13:50
Général Valsero
Рет қаралды 36 М.
Une nouvelle voiture pour Noël 🥹
00:28
Nicocapone
Рет қаралды 9 МЛН
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 958 М.
Kardafar kou defff dolén massa tagato - Serigne Abdoulaye Djitté
18:55
BARGNY Toujours visible
Рет қаралды 269
l'affaire pape sane... pourquoi macky a échoué
47:39
Solution TV
Рет қаралды 74 М.
Une nouvelle voiture pour Noël 🥹
00:28
Nicocapone
Рет қаралды 9 МЛН