Tous ceux qui traversent des moments difficiles yalnaléne YALLAH takhawou. Ne désespérez pas, quand ALLAH Il éprouve. Qu'ALLAH nous pardonne et nous guide tous. Allahouma amine.
@ousmanegueye23324 жыл бұрын
Amine
@ndeyeawa38134 жыл бұрын
Amine
@diaboubalde88514 жыл бұрын
Amine YA rabbi
@ahmedsow35384 жыл бұрын
amine
@coumbaasmndiaye33163 жыл бұрын
Amine yarabi
@SiriDiallo9 ай бұрын
Alkhamdoulilahi Kand j l’écoute j me soulage ❤️🙏longue vie oustaz ❤
@AwaBalde-u5x3 ай бұрын
Ya oustaz je pense que cette estrait c'est pour moi que dieu te bénisse
@chimeneboissy94274 жыл бұрын
Oustaz sall vraiment je ne suis pas musulmane tous les jours je vous écoute DIEU vous fasse grâce 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
@adjadiop85964 жыл бұрын
depuis la France nous ecoutons outaze oumar sall , j'ai les larmes au yeux il redonnent l'espoir et nous rapl la grandeur et la miséricorde de notre seigneur !!!!!! jazak Allah kheyran .
@omarniagnane19554 жыл бұрын
Merci
@bintasow1450 Жыл бұрын
Soukhran ya oustaze
@ASTOUDIOUF-t3n14 күн бұрын
Merci oustaze pour les conseil et bonne continuation tu nous redonnes l’espoir 😢😊
@ASTOUDIOUF-t3n14 күн бұрын
❤❤
@isgrahmany4 жыл бұрын
Une fois qu’un coeur devient trop lourd de douleur, les personnes ne pleurent pas, ils deviennent silencieux.. complètement silencieux..
@ndeyeawa38134 жыл бұрын
Bilahi
@bellajallo17354 жыл бұрын
javoue walahi
@khadibadiane87264 жыл бұрын
Bilay
@sounnahsenegaltv4 жыл бұрын
Wallahi akhi Le silence
@fifidiop2364 жыл бұрын
WALAHI
@dialloalpha64904 жыл бұрын
Depuis la côte d'Ivoire j'aime cet Homme machalah
@ousmanegakou42604 жыл бұрын
Machallah
@fadouble58414 жыл бұрын
Celui qui recherche la bonne parole de l'islam ne peut que aimé Oustaz Oumar SALL. Que la paix vous accompagne mon frère en la Foi
@mbayegueye80164 жыл бұрын
,,
@ndiayeawa36764 жыл бұрын
ya oustaze yalla nalla yalla faye wayé gnoune sociétébi mognou sonal -Soy ndiangue gnouy lath ndaxe amna examen wala amoul -So paré ndiangue gnouy lath ndaxe amna liguèye wala amoul -So seyoul gnouy lath loy xar -So seyé gnouy lath sa dieukeur loumouy liguèye -So seyé gnouy lath amna dome walla amoul dome Ya oustaze sonounanou dénanou Quelle est donc la Solution pour vivre heureuse dans cette société
@mouhamedba98464 жыл бұрын
As-Salamou alaykoum frères et sœurs en Islam, je partage une remarque très intéressante. La dawah d' Oustaz Oumar Ahmad Sall (H. A) prend forme, elle passe à merveille. On ne voit plus d'insultes dans les commentaires contrairement aux précédentes années. Mâcha Allah. Je profite de l'occasion pour lancer un challenge. J'aimerais que chacun raconte son histoire avec Oustaz, genre comment était notre conception à son égard avant qu'on le découvre et l'influence qu'il a sur nous. InchaAllah Qu'Allah nous guide!
@anitatamk37614 жыл бұрын
Oustaz est ma drogue je ne peux rester 1journee passé sans l'écouter.macha allah.loumassi diakhal moy Lou khew sama ménage rek mou défsi wahtane machalah yalla nako yalla samko
@aronaba79034 жыл бұрын
Slt mon Oustaz, vraiment je suis très très fier de toi, yala nala yalla samme té takawoula
@aichaummhoureyra54804 жыл бұрын
As salamou enleykum warahmatullah Oustaz wallahi si gnanal ko rek la deukk Alhamdoulilah bokna si gnima léral lou beuri si dinè bi bamay def classe de 1ere en 2016 lagn ma ajouter si ben groupe Whatsaap boumouy def ay wakhtane you ame solo Ma sha Allah Alhamdoulilah sila diaare di mourou batay dji mangi def Niqaab di goorgoorlou bayi you bari youma nekone loumako gnanal rek khep ko oustaz yalna Allah borom bi same ko diko wakh jazzakoumoulahou khayrane 🤲🏽🤲🏽 yalna Allah soubhanahou watala sakhal ko sakhal gnou si ndioup 🤲🏽🤲🏽
@moustaphadieng81434 жыл бұрын
Sama bayi music yalla si mom lako diaralé #Alhamdou lilah#
@issamamediop10934 жыл бұрын
Masha Allah jazakal lahou hayrane amatina solo tay mom Damasii geuneu guiss sama bop walay ndeysane ça me rappelle mon enfance bou may am 9 ans yalla dafma natou wone febarou tank manane tokke mou donone lou mettii je ne dormais presque pas pendant la nuit je pleurais toute la nuit je reveillais à 06h du matin après avoir fair mes prières pour aller à l'école dans des conditions dure extrêmement dure demna ba amatoul goudii amatoul journée dafadone mettii tout le temps après niou tabakh ma à l'hôpital de thiadiay mas dawalane même un ans ça recommence demna ba am plus de quatre tap sii cuisine def gaum dii mettii ba dem foune hôpital sii marabouts yii fadiou ba sonou guissouma wone guene goudoul sama yaye école defoi souma meuna marché niou bot ma walay ndeysane un ami yalla nako yalla faye ma dem ba année boummay def quatrième finalement ma def une opération sii genoux bii je disais defoi que nii yalla djii Kom rek maffiii né sama xarite niogui am diam mane mou tekma liii de fois walay ma salite mou causé ma retar siii sama etude sii samay rêve d'enfance mais chak fois sama yaye diima delosii nama nit dafay mougn siliko yalla tekk xamal nii lep louma Tek sii natou moko xam mougneul siii condition yoyou ak keur famille bou doyone war sakh demna ba niou amfa problème électricité damay diangue siii Nattou ak problème famille sama yaye done une exemplaire gou geum ligueyam fiii ba courant biii nieuw maniiko yaye siii mettit bii may diangue ak problème yii je ferais tou ba am bac insha Allah Kom yalla Momako Tek dinamako téguil parce que j'ai le seul a continué mes études dans cette foyer après sama opération même pas un ans tap yiii commencé wat gueneu ba année bimay am bac Après examen yalla def ma amko mou tanné ma yakarnii diekh bippa mom alhamdoulilah sa première année de formation professionnelle a IAM Dakar walahii mou chute wat j'ai pas pu faire mes examens de deuxième semestre je me suis rentré a mbour bobou meunatou dara nakh metittt boudoul diekh ma defat analyse radio dara quatre médicaments pour calma ladone dieul mais dara finalement ma abandonnée mes études pour aller me soigner encore bimay yeksé mbour je ne pouvais plus marché pendant un moi même mes prières je le fesais assis j'ai mum cette fois cii mom diekhna n'a tok xar deii kom promet nala bac té amnako siii souffrance ak thiono alhamdoulilah louma mettii kay moy narofeke sama nieurigne ndakh liii mounima santal yalla dei issa xolal niata nit sii guaw souff la yalla nit natou you geuneu metti sa boss mé lou yalla dii def kimou ma bolel billay kouy def té yalla takh ladiouma dara biniou fay dem ma mère elle n'avait que 2000mille dans sa poche Moma fath bama weur guinaw yalla C'était juste pour dire a cette femme boul Mousseu désespéré yalla loumoula tek mo geune siii ioe santal yalla sassoune j'ai 29 te doundouna 26 ans yeup ay metitou adouna faibar tay magui sant yalla maguimay soutoural ba louma am defal samay wadiour Billahi sunu yaye yii amouniou sen faye Innalaha ma as sabireen qu'Allah veillera sur vous patience rek dîna bakh nsha Allah
@mamadomamado31344 жыл бұрын
😭😭😭😭
@habibatyina52834 жыл бұрын
Mashallah dés fois dina méti bagua yakar ni dotoul bàkh, mais ndékété yalla bouy défar dafaye mélni kouy yakk, mon frère continue de croire en Allah Azwajal incha Allah dina Bàkh. Qu'Allah te facilite, te bénisse et t'accorde une belle réussite fi dunya wa fil akhira 🌺
@issamamediop10934 жыл бұрын
@@habibatyina5283 allahouma amine
@aichaummhoureyra54804 жыл бұрын
Alhamdoulilah mon frère yalna borom bi same la bayila akk sa yaye bassi kaname amine 🤲🏽🤲🏽🤲🏽
@issamamediop10934 жыл бұрын
@@aichaummhoureyra5480 allahouma amine
@naboundiaye15934 жыл бұрын
Merci ouztas. J'ai la chance d'écouter cette extrê car toloneu na thi goudi you méty bimay déglou li. Machallah yalla na gueum yokou
@mameboy46294 жыл бұрын
courage yalla bakhna
@SuperKhalil014 жыл бұрын
Courage ma sœur walahi sa montre k yallah miguilay bayi khel.
@fadouble58414 жыл бұрын
Je vous aime beaucoup Imam. Depuis que j'ai commencé à vous écouter , je ne trouve plus plaisir à écouter les autres prêcheurs. Je sens que vous pêchez la bonne parole . Que Le Tout Puissant Vous accord la lumière de l'islam pour mous mettre sur le droit chemin .
@dem-vision57564 жыл бұрын
Macha Allahou c comme ça la vérité est facile à entendre. une fois l l'écouter il te saisit.
@abdallahibnabass53164 жыл бұрын
Machallah oustaz yalnanliou yalla fayal goudeul sa fane ndax niou melni yaw lagn sokhla ❤️❤️❤️❤️machallah
@ismailasarr18004 жыл бұрын
Je n'ai pas les mots pour le qualifier. Je vous laisse avec Dieu. Qu'il répande sa miséricorde sur vous et la oumah islamique
@diaboubalde88514 жыл бұрын
Amine YA rabbi
@mohamedkadhafi12854 жыл бұрын
Amine
@ismailasarr18004 жыл бұрын
@@mohamedkadhafi1285 merci beaucoup
@aichaummhoureyra54804 жыл бұрын
Amine
@SiriDiallo9 ай бұрын
Amine ❤️😭🤲🏼
@mansourdieng20004 жыл бұрын
*Lundi 20 Juillet 2020* Machallah Oustaz Oumar Ahmed Sall Li Ngua Wakh Dawna Yaram Trop Mai Sokhna Si Na Mougne Té Khamni Yalla Mougne Katt Yii La Andal
@ndeyekhadytoure38554 жыл бұрын
Alhamdoulilah ala kouli ali 🙏🏾😭😭Ey ouztaz li dafa melni rek KZbin dafma Ko tegal pour Ma deglou koo . Yalna yalla takhawoula nigay takhawoo gni am nattou yeupp 🙏🏾Yalna yalla teguil nieupp nattou ak nakhar 🙏🏾Yalna yalla mey nou kholou mougn 🙏🏾 Alhamdoulilah ala kouli alli
@diemesophie23804 жыл бұрын
Allahouakbar ,ça Cest pour moi ....yalla na niou yalla may mougne Dieuredieuf
@fifidiop2364 жыл бұрын
Salam oustaz douma diok si dila beugue, parceque k tu permets aux gens d'aimer et avoir confiance à leur SEIGNEUR ALLAH WAKHAZAWADJALLA, et sur le chemin de SEYDINA MOUHAMMAD salalahi wa alihi wa salim, yana YALLA fayalegnioula YA RABBI
@naboundiaye15934 жыл бұрын
Magui toupe di diégualou thi sounou borom 😭😭😭🙏
@aissatoubarry95774 жыл бұрын
MachaAllah longue vie à vous y'a Oustaz et que Dieu accorde cette femme un bon mari inchaAllah Et une longèvité et nous permet d'être Mère un jour...Dieu est avec les patients Merci à vous Oustaz
@fadouble58414 жыл бұрын
Amine
@mmekane364 жыл бұрын
Merci ya Oustaz Yalla nala Yalla Faye
@cheikhsadibousene29064 жыл бұрын
Machallah Ya Oustaz Que Dieu vous protège wakhtane bi ame na solo
@tokosel1294 жыл бұрын
Alhamdoulilah rabbil a'alamiine Sant YALLA Alhamdoulilah rabbil a'alamiine baraakallahou fik
@aichadiouf17654 жыл бұрын
ALL hamdoulillâhi ALL hamdoulillâhi ma doolè sannetate yallâ outaz ndah doolina gueumené LÈP lou méti loumaye dounedou rék nattou là té nattou djitouna DOUNDOU borom yallâ NAGNOU yallâ doolè maye khoolou poigne ALLÂ HOUMA AMINE longue vie à vous
@awacoulibaly76624 жыл бұрын
Macha Allah ustaz merci vraiment j'avais besoin d'entendre ces paroles véridique
@oliviernasala48494 жыл бұрын
Je veux son numéro svp aidez moi je suis entrain de déraper
@secretdusucces92984 жыл бұрын
@@oliviernasala4849 775171125
@isoloisolo60394 жыл бұрын
Oustaz oumar sall yalla nala yalla taxawou
@mohamedkadhafi12854 жыл бұрын
Amine
@aliouba73614 жыл бұрын
Aquran ak sunnah rek inchaaAllah
@pubafrica20124 жыл бұрын
JE SUIS TRES FIER DE VOUS MACHALAH
@dieydidoucoure97444 жыл бұрын
Machallah cheikh oumar mane deh soumala setanaloul damay fébar oustaz nala yalla faye
@ngombabacar55644 жыл бұрын
Macha Alá amna solo trop yalla nala yalla fay
@amyfall59164 жыл бұрын
Ndeysane yalla nakoyala maye kholou mougne inchallah
@ndeyefatousow11464 жыл бұрын
Sokhna sossou yalna sounou borom safara sa tawat bobou
@rafaelndiaye1084 жыл бұрын
Machalah oustaz yalla nala yalla fay ak bép joulite🤲🤲🤲🤲🤲
@brahimsalem86434 жыл бұрын
Ma sœur N'oublie pas Dieu fait se qu'il veut ne décourage pas que Dieu t'aide 😔
@madouam12184 жыл бұрын
merci beaucoup oustaz oumar sall parle bien yalla na yalla deffeul diam billay wakh nga deugeu je comprends bien tu es bon exemple merci beaucoup 🙏🙏🙏❤❤❤👍👍
@mohamedkadhafi12854 жыл бұрын
Amine
@freediop61114 жыл бұрын
Billahi oustaz wakh nga deug yallah nasunu borom fay leu !!!
@assanesarr49484 жыл бұрын
Mashalla oustaz yalna gua goudoufane té wére billahi sui fiére de toi
@fallougueye40554 жыл бұрын
Allahou Akbar yalananou yalla sam def niou ay dioulite you deuguou té tek niou si yone bou dioup machallah Alkhamdoulillah
@keurmassartvkeurmassarinfo233017 күн бұрын
Bilahi par les épreuves j'en ai connu beaucoup choses en ver mon seigneur ( Allah )❤
@lassanadjimera34604 жыл бұрын
Macha’Allah Oustaz qu’Allah azzawajal vous accorde une longue vie incha’Allah
@freediop61114 жыл бұрын
Merci oustaz sa you mala deglo rek sama xol dellou ci yallah aka nexone ma deuk sa kogne
@mouhameddjatta1204 жыл бұрын
Allahu Akbar ya Ouztas Jazzak'Allah khair et qu'Allah récompense les ahloul balah le Jannahtul Firdaws Yallah deffal diam adouna ak alhakhira.Alhamdoulilah😥