Urgent Thiow Amena Dh Aziz Ndiaye Repond Le camp De Modou Lo 48h Lalén Maye Sinon Doroniou Beuré

  Рет қаралды 61,330

Fadam2 expert de la lutte sénégalaise

Fadam2 expert de la lutte sénégalaise

Күн бұрын

Пікірлер
@djibingom5668
@djibingom5668 2 күн бұрын
Thiéy azize mon idole diam thi yaw ya worrr dhé kanie lalay guiss nk
@nogayebadiane2336
@nogayebadiane2336 2 күн бұрын
Aziz 😂😂mounialll Roi bii ngay weur teiyall si empeur jumbo rek nioy xol kou niou nekh ak heure bou niou nekh Roi dou xaliss dh 😂😂😂😂Yama dann Modou di weur Modou
@papisene4363
@papisene4363 2 күн бұрын
Si ce combat tient en juillet Modou Lo vs Balla Gueye et Ada Fass vs Liss Ndiago je vais venir au Sénégal pour ce combat ya meune biss Aziz ci ioe lay roy busness akh communication danou koy meune respect ✊
@niokhitebaxata614
@niokhitebaxata614 2 күн бұрын
Bilahi mo dax communiqué gayi dou bén mé sénégal niou bari beugou niou ndanan
@CisseIbrahima-yb2sf
@CisseIbrahima-yb2sf 2 күн бұрын
Balla gaye modou lo dou amati si kaw Souf inch'Allah
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 2 күн бұрын
Amin way yallah boumou amatii blh man je veux pas ce combat modou respectel sa cadou svp ne prend pas Balla gaye continue votre chemin ne le prend svp ñoune say supporter aussi daño am ci ioe waleu distal nga ñou louné svp
@SeydouFall-km4rl
@SeydouFall-km4rl 2 күн бұрын
Yéne nieup modou lô Moy sén baye😂😂😂waxxoo léne fi dara bayi léne tékk xéll bi😂khamnaniou lépp xlô rk amoul lénéne ❤❤
@skboymo
@skboymo 2 күн бұрын
Dioutal Lo moy sen gel parce que nen ko dioutal rek
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 2 күн бұрын
​@@skboymodiouteul lo bobou moye diouteul say baye diléne rokass👈
@AliouBadaraSall-v2n
@AliouBadaraSall-v2n 2 күн бұрын
Balla bokouthi daffa dann Modou 2fois sans polimique et spectaculaire
@malicksarr2141
@malicksarr2141 2 күн бұрын
Aziz guemele yalla nagoule modou Lo niko yalla def king 👑 ❤
@MbayeNdaiye-x2e
@MbayeNdaiye-x2e 2 күн бұрын
Yagui mer wa keur niotal lo
@mormbaye6583
@mormbaye6583 2 күн бұрын
@@MbayeNdaiye-x2ebayil ba meun ko bindeu 😂
@yassinbuwaro8644
@yassinbuwaro8644 2 күн бұрын
Doul waye déga sokhor rék mais Aziz ndiaye mo geune sa familles gniépe😂
@papaamadoufall636
@papaamadoufall636 2 күн бұрын
Balla dako diouteul 😂
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 2 күн бұрын
Vraiment gawa na ngou day yombali dorr
@amadiallo-kn2ye
@amadiallo-kn2ye 2 күн бұрын
Wallahi dama beug Aziz ndiaye xawma loutakh nak
@assaneseye2148
@assaneseye2148 2 күн бұрын
Wakh day ler ndakh wakhat djia motakh Aziz Jajeuf merci
@ndiagathioye3928
@ndiagathioye3928 2 күн бұрын
Bilay Balla Gaye la yeup di weur..Bilay c'est le lutteur le plus cher
@coeur2lion38
@coeur2lion38 2 күн бұрын
Aska dou yaw yacoy weur 😂😂😂
@legendediop9215
@legendediop9215 2 күн бұрын
Yakoy weur yaw ak sen wakeur
@PendaTalla-c5z
@PendaTalla-c5z 2 күн бұрын
Wakhal ya koy weur yaw meuno kham sa guénte kham sa guéntou morom
@niomrelo1959
@niomrelo1959 2 күн бұрын
légui loumouy khar pour dieul siteu
@FalloutDiba
@FalloutDiba 2 күн бұрын
Balla gaye khana nekoul ni mo beugeu beuré ak Modou lo
@niassesouleymane7163
@niassesouleymane7163 Күн бұрын
Le clan de Modou Lo a été très intelligent ils ont poussé Galla Gaye a prendre Siteu
@MATARKARANOREYNI
@MATARKARANOREYNI 2 күн бұрын
Ki yalla maye nako si communication
@MadaDione-y7u
@MadaDione-y7u 2 күн бұрын
lolou la diangu nak
@khadimsow7149
@khadimsow7149 2 күн бұрын
Trop fort 😂
@thiamahmadulattekh562
@thiamahmadulattekh562 2 күн бұрын
Bou bah key 😇Mais modou lo communication yeungalouko limou beug ley def Nagnu har 480 waxuma 48h lignu tek beut lagnuy df Fadam liral li mala wax
@Maxkekendo
@Maxkekendo 2 күн бұрын
Il est tres fort en comminucation ❤❤❤
@badagueye6692
@badagueye6692 2 күн бұрын
Il est trop fort ✌🏾
@ngommamegor7924
@ngommamegor7924 2 күн бұрын
Azizz aka sonou modou lo lafi yalla tek 😂😂
@skboymo
@skboymo 2 күн бұрын
Wa keur modou nio nek di topou Aziz pour beuré Balla gaye, non?
@khadimdiouf7618
@khadimdiouf7618 2 күн бұрын
@@skboymodel wax deugue
@moussasylla4081
@moussasylla4081 2 күн бұрын
​@@khadimdiouf7618 papa Sow fane bok Jamaican tmt 😂😂
@khadimseye9364
@khadimseye9364 Күн бұрын
@@moussasylla4081 🤣🤣🤣🤣 supporter modou lo yi danio sonou bolai ci tapéte
@modousarr8848
@modousarr8848 2 күн бұрын
après combat Balla tapha aziz tok plateau ni Balla semaine mou amat combat mingi beuga yag dé 🤭 Aziz dou lép xaliss mokay déf
@MatarMbegue-d2j
@MatarMbegue-d2j 2 күн бұрын
Sawaye pour mom mo guena mouss nite gni 😂😂😂 modou lo solhlawoula fawou gna khamko bayil door bi tek khuell rek moy sa yitte lignaye wakh ak lingaye deff dafa woutee
@princelaye8210
@princelaye8210 2 күн бұрын
Kaan mo sokhla woull kaan 😂yow esk ya ngui Senegal modlo taay mo beug balla wayé balla lidientiwouko taay kou changer discours modlo walla balla te modlo khamna loutakh mou beug beurrek balla parceque sou beurréwoul ak mom tapha tine lay beurrél te dafko ragal 😂walla beurrék sathies te lollou moy régression deug kou eumeu daan baparé nguay beurrék mom 😂
@TopGueye-nv7pc
@TopGueye-nv7pc 2 күн бұрын
Yaw ya nekoul Sénégal Modou lo moyor li gneup sokhla balla yoroul Lou Modou sokhla​@@princelaye8210
@papaamadoufall636
@papaamadoufall636 2 күн бұрын
Balla dakoy diouteul encore dei
@papipapi344
@papipapi344 2 күн бұрын
@@princelaye8210yamana mew Roi lidiantiwoul sakh Fawseyni 🤣 yenakoyy topp rek
@elhadjisy9222
@elhadjisy9222 2 күн бұрын
Moi suis kharagne lo mais sathies mérite un combat royal ❤❤❤
@madoumbediouf19
@madoumbediouf19 2 күн бұрын
Vérité balla gaye meilleur luteur
@bykebe8682
@bykebe8682 2 күн бұрын
AZIZ DAAL TU COMMUNIQUE BIEN
@alaminefaye6248
@alaminefaye6248 2 күн бұрын
Aziz Daye doule rek Instant bii bataille psychologique laye deff. Staff modou Lo soyez conscient et vigilant
@MbayeNdaiye-x2e
@MbayeNdaiye-x2e 2 күн бұрын
Yagui mer deh wa keur diotal lo daniouy mer rek
@SambaSarr-g4w
@SambaSarr-g4w 2 күн бұрын
Birame Yacine bou lékoul Mougui nane😂😂😂😂
@TopGueye-nv7pc
@TopGueye-nv7pc 2 күн бұрын
En tout cas modou lo est le roi des Arènes il est dans tous les panneaux publicitaires il a moins de defaites que le soi-disant empereur
@azizmboup5364
@azizmboup5364 2 күн бұрын
Mais balla l a battu 2 fois en moyen de 5 minutes
@serignefall7167
@serignefall7167 2 күн бұрын
@azizmboup5364😂😂
@PapesambaDiop-bf7gh
@PapesambaDiop-bf7gh 2 күн бұрын
@azizmboup5364niata défaite gua am si mbeur bou mak ? 😂😂
@bayedieng7141
@bayedieng7141 2 күн бұрын
Sa Thiés modou Lo moy combat bie waxofie Dara Azize
@skboymo
@skboymo 2 күн бұрын
Yén topou len sen buga buga mais Aziz moy agent Balla Gaye, Modou lo bougul beuré Sa Thies lou si Aziz meun
@PendaTalla-c5z
@PendaTalla-c5z 2 күн бұрын
​@@skboymoYaw mome niémé nga YALLA dal ya nék si xélou Modou Lô bay kham koumou beugeu beureul yéne dal louléne arrangé rék
@skboymo
@skboymo 2 күн бұрын
@@PendaTalla-c5z yaw ya xam lou nek si xelou modou lo bon parce que mousou ma deg mou wakh ne dafa beuga beuré Sa Thiea
@OmarNdiaye-r4c
@OmarNdiaye-r4c 2 күн бұрын
No Aziz Ndiaye mo nèkh rek😂come si que Modou lo molèn sokhla té lounek nguèn deff ko pour beurré AK Modou lô
@princelaye8210
@princelaye8210 2 күн бұрын
Tay mom yéna sokhlla amoléne adversaire bou sérieux déé soit sathies te lollou moy genre modlo vs siteu amoul béne chance te foulla dané ngua wayadi walla tapha bi nguéne di daaw te lollou moy danou 😂
@BayezallDiop-gr2oy
@BayezallDiop-gr2oy 2 күн бұрын
Billay yena niou sokhla ndakh diambar Modou lo moko yoni dieul len sa thèse
@OmarNdiaye-r4c
@OmarNdiaye-r4c 2 күн бұрын
@@princelaye8210 danguèn nèkh Roi mom seul Moy nek au sommet amoul adversaire potentiel Moy khôl kouko nèkh mou beuré AK ioe Sa Thiès d'accord mane lay nèkh rek ma Mayko chance yènako yènéwoul lolou ndakh balla gaye
@OmarNdiaye-r4c
@OmarNdiaye-r4c 2 күн бұрын
@@BayezallDiop-gr2oy lolou sa xalat leu rek Té sou combat bi Di tahaw dou nek wa diambaar lima yakaar
@cheikhmbacke2841
@cheikhmbacke2841 2 күн бұрын
Aziz modou moko déranger modou mo gueneu cher balla bayil fene yi Aziz
@Idyxaragnelo
@Idyxaragnelo 2 күн бұрын
Modou XARAGNE LO THE KING OF THE KING DE LA LUTTE
@MameAbdouDiouf-l8y
@MameAbdouDiouf-l8y 2 күн бұрын
Néna 48h 😂😂😂 ki nex na Modou lidiantiwoula sax
@PapesambaDiop-bf7gh
@PapesambaDiop-bf7gh 2 күн бұрын
Affaire yi Matoul sax 48h 😂signer na contrat mom ak siteu 😂modou xaliss titeulouko bly
@absathiaw8233
@absathiaw8233 Күн бұрын
Billay yaw 😂😂😂​@PapesambaDiop-bf7gh
@oustazahmedfall6478
@oustazahmedfall6478 2 күн бұрын
Mod lo le meilleur
@MbayeSarr-c9q
@MbayeSarr-c9q 2 күн бұрын
Nioune sa thiéss lanou begue ❤
@papealiouseck1273
@papealiouseck1273 2 күн бұрын
Wa aziza do dem dieul emeu sene
@MameAbdouDiouf-l8y
@MameAbdouDiouf-l8y 2 күн бұрын
Khamo tousss Modou lô où rien ❤ nagoul lou yallah dogal
@SeydouDiome
@SeydouDiome Күн бұрын
d'égal sisou mane bi mom
@abdoulayendoye1803
@abdoulayendoye1803 2 күн бұрын
Holal mounane 48H 😂😂😂réglél affaire tiédo kén douniou ko diay
@IbrahimSow-c4x
@IbrahimSow-c4x Күн бұрын
bahh lamb sosoo bahh léegi béneu couronne lagn xam☝️moyy roi des j'arrénn☝️ahh konn nak guinaw modou rek✊️bagn bagn beugë
@TARKiNDaBi
@TARKiNDaBi 2 күн бұрын
Néxoull ba Néxoull wayé mrm dji Fawzeynii Moy LAMB 😂😂Niou begeu ko wala niou bagnko😂😂wa Kerreum sax Daniouy Doundeullll Lamb 😂😂😂
@leuz.patriote
@leuz.patriote 2 күн бұрын
Tarkinda bi akh bg2 siteu samay niari mbeur dadjiè nagne 😢
@TARKiNDaBi
@TARKiNDaBi 2 күн бұрын
@leuz.patriote Bilahhii moma dall mane mi dekkeu Diamageune balla sama mbeur là
@Bour_ndiaye_bour
@Bour_ndiaye_bour Күн бұрын
Vrément aziz est un homme de valeur ❤
@nogayebadiane2336
@nogayebadiane2336 2 күн бұрын
Aziz Demal tokk empereur j’adore
@IbrahimSow-c4x
@IbrahimSow-c4x Күн бұрын
Aziz ndiaye sa wakh yépp modou xaragne lo mo takh gayy wakh👂 bayiil ték khéll🤷‍♂️ nioun problème bou am Sénégal xamnagn ko☝️
@ridialdieng2861
@ridialdieng2861 2 күн бұрын
Bilaye Aziz ya woor❤❤❤
@Gaye314moussalioumbacke
@Gaye314moussalioumbacke 2 күн бұрын
Balla seul ❤
@boubacarsamb-wv1ov
@boubacarsamb-wv1ov 2 күн бұрын
Aziz Ndiaye mayale nite gnii diame kou sokhor gua Modou lo est le roi des arénes
@papaamadoufall636
@papaamadoufall636 2 күн бұрын
Wakhiii dofff roi bou danoul siteu dioutou si balla gaye
@TARKiNDaBi
@TARKiNDaBi 2 күн бұрын
​@@papaamadoufall636Ballko way😂😂😂
@papeflokiFall
@papeflokiFall 2 күн бұрын
​@@papaamadoufall636empereur bou danoul eumeu ni boy niang nak loumou done
@moustaphasamoure3762
@moustaphasamoure3762 2 күн бұрын
Pourtant sohoroull dh dafa bouguou balla rk lolou laa rk. Mann fans balla la mè bouguouma comba modou lo balla. Sa thies modou lo la bouguou
@oustazahmedfall6478
@oustazahmedfall6478 2 күн бұрын
Sathies modou lo moy combat
@DioufMouhamadou-s6x
@DioufMouhamadou-s6x 2 күн бұрын
Diadieuf aziz ❤❤
@BakaryNdiaye-j4t
@BakaryNdiaye-j4t 2 күн бұрын
Dieule léne eumeu séne mo gueune diaroule weuri kéne
@YacineSeck-n6n
@YacineSeck-n6n 2 күн бұрын
Modou lo moy dérange aziz 😅
@CheikhIbraFall-u2r
@CheikhIbraFall-u2r 2 күн бұрын
🇺🇲 Entouka Modou lo Bou jeulaté Balla gaye 2 Danou incha'Allah ♥️ Modou lo Tapettes leu😂 n'a dèm jeuliiii sa thiès Wala tapha tine 😂
@ablobeye
@ablobeye Күн бұрын
😂😂😂😂😂 sa thies rek😂😂😂😂😂
@AmadouDiallo-c1r
@AmadouDiallo-c1r 2 күн бұрын
Bilayyyy il es jaloux koi ce Aziz
@Dakore221
@Dakore221 2 күн бұрын
Balla noumou def rk pour nokkat Modou Lo dinako def wah clan Modou bagn lén dh trokhal national lakoy deff bakh nah 🤣😂😂😂
@nogayebadiane2336
@nogayebadiane2336 2 күн бұрын
Roi bi nak Modou Diapou si ndiek nga diokh ko Balla dakoo Namou 2019 ba legui mingui beugg yagg dh liii mon dictateur là y’a oustaz dii def si lamb dji 😂
@DiolSallamariam
@DiolSallamariam 2 күн бұрын
😂😂😂
@TARKiNDaBi
@TARKiNDaBi 2 күн бұрын
Bane Roi ioE Balla gaye Diouteull là Meuno Dane SiTEU 😂😂😂😂
@bassdiokhane1472
@bassdiokhane1472 2 күн бұрын
Abdou Aziz wakhl si sa Thiès si book môme ak Modou lo l'an begeu ❤
@ousseynoutoure518
@ousseynoutoure518 2 күн бұрын
Néna day dioxé ultimatum😂comme si que Balla Modou lo dako soxla🤣 yénay dane mais yénay topeuh sen guinaw aziz vous êtes tjr demandeur
@bilalybarro3361
@bilalybarro3361 2 күн бұрын
Aziz Ndiaye pr mom Yallah Ndiaye la sant 😊
@zachariagoudiaby8958
@zachariagoudiaby8958 2 сағат бұрын
Le meilleur combat d ts les temps diokhnako modou lô vs Eumeu sène 1er combat ba thi lima féké wa salamm😂
@gouverneurgouverneur9534
@gouverneurgouverneur9534 2 күн бұрын
Bon arrivée le Boss 💪🙏✅
@doffdouweer3686
@doffdouweer3686 2 күн бұрын
Albourakh ne digére pas que modou les ignore 😂😂😂😂..Roi des arènes mollen meti dakh mi gui parcelles
@amethba1634
@amethba1634 2 күн бұрын
Ils communique bien Machallah
@GalleBa
@GalleBa 2 күн бұрын
Aziz ndiaye vous avez votre stade arrene nationale stade Abdoulaye Wade c'est pour les footballeurs pas les lutteur
@mbackegaydelserignembacke8335
@mbackegaydelserignembacke8335 2 күн бұрын
Mom bayiko mouye fowe xelam rk limkoy wax barina waye bayoboo mou regle te xamni lamb taxouko diouk
@badandiaye2189
@badandiaye2189 2 күн бұрын
Qui da yeuke degue sucsé bilahi t'ai xamoné adouna d'où diaye afére de xalise hafére de hame hame bilahi yalla rek mn moune mn hame
@SyIbrahim-w2v
@SyIbrahim-w2v Күн бұрын
Modou moye Star bi walahi
@youssousarr3586
@youssousarr3586 2 күн бұрын
Cheu aziz boulniou sonal li modou yor rek nguene beug demal dieul kenene bakham ngay napaté di diokhé ay 48 h
@modouseck-yz5tg
@modouseck-yz5tg 2 күн бұрын
azizz do nitt❤😂
@saerhihiodf110
@saerhihiodf110 2 күн бұрын
Aziz byil sisou bi modou Lo mo geuna cher balla
@modoufall4327
@modoufall4327 2 күн бұрын
Aziz bayil ték khél modou lo guaye weur
@kandjiadama1516
@kandjiadama1516 2 күн бұрын
Mausallah yalna diamma yagga si fammi Ndiaye
@modousonko7340
@modousonko7340 2 күн бұрын
Aziz kou sokhor gua mai inchalla Modou dou beurétii ak balla gnoune wah PA gnokodoul nangou démal outii bénén mbeur t gua tog
@khadimfall979
@khadimfall979 2 күн бұрын
BG2 rekkk ❤❤❤
@BabacarDiagne-o2r
@BabacarDiagne-o2r 2 күн бұрын
ngire yalla koumay teuguel modou lo vs sa thiés 😭
@SeyeMustapha-ks9jm
@SeyeMustapha-ks9jm 2 күн бұрын
Saway nangoulal aziz qui champion la balla rèk
@oustazahmedfall6478
@oustazahmedfall6478 2 күн бұрын
Modou lo meilleur luteur
@KhalifaibrahimaFaye
@KhalifaibrahimaFaye 2 күн бұрын
Daye nappé et il communique bien quand il dit eumeu vs balla est mon combat de rêve parsk mbeur boula dane deux fois da nga wara Fayou, c'est pour dire Modou da wara dieul Balla
@nogayebadiane2336
@nogayebadiane2336 2 күн бұрын
Thieuy y’a oustaz ❤❤
@Ndarguedjtv
@Ndarguedjtv 2 күн бұрын
Kou am sa promoteur nieuweull balla seul
@papaibrahimaseck1003
@papaibrahimaseck1003 2 күн бұрын
Ck combat balla gueye vs modou lo mo amoul sance gnoune sathies vs modou lo legne beugue
@ElhadjiWade-bo6lp
@ElhadjiWade-bo6lp 2 күн бұрын
Balla gaye 2 vs siteu modou lo vs sa thiés❤
@KhabdoulahiBeye-m5z
@KhabdoulahiBeye-m5z 2 күн бұрын
Très bien c'est bien 😂
@fgtv1140
@fgtv1140 2 күн бұрын
Guisna association entre albourakh ak wa diambar
@keurguifootballps3678
@keurguifootballps3678 2 күн бұрын
Association jamais waa albourakh jamais gnou associe soit gnou organise ko wala gnou neutre et une chose est sur jambar dou teugue combat bi
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 2 күн бұрын
Aziz Ndiaye kounékh nga yaw modou lo daléne khol goudiyi modou lo momeune séne baye goudiyi mystique rék nguéne di dané kharagne lo mais moléne meune fooouf 🤔🙄🤔😒 séne gayndé gou maguéte gogou mounane chér😁😃kou am 6 défaite dana yor trophée familiale dana geuneu chér le roi des koullou mbeur niakeu diom 🙄🙄 Aziz Ndiaye nopil fi meunofi ték khél kéneu🤐🤐🤐🤐🤐🤐
@LamineSylla-ww2tf
@LamineSylla-ww2tf 2 күн бұрын
Balla rek❤❤❤
@IbrahimaFall-u3z
@IbrahimaFall-u3z 2 күн бұрын
Aziz lingay wakh lèrr na
@moussatraore9101
@moussatraore9101 2 күн бұрын
Fadam2 en resume ces propos de Mr Ndiaye c'est pour mettre indirectement la pression au camp du ROI Modou Lo .
@Mameles
@Mameles 2 күн бұрын
C’est de bne guerre
@baraseck4939
@baraseck4939 2 күн бұрын
Dafa ler 😂de Aziz bandit la
@souleymanegueye8466
@souleymanegueye8466 2 күн бұрын
Danga bari wakh trop do dara
@ousmaneseck3909
@ousmaneseck3909 Күн бұрын
Balla roh na😢😢😢
@TopGueye-nv7pc
@TopGueye-nv7pc 2 күн бұрын
Aziz bo weuri woul modou lo yagui tok dika khare
@PapesambaDiop-bf7gh
@PapesambaDiop-bf7gh 2 күн бұрын
Aziz wa legui yena niou meun dieul len lep beuré wougn ak sen empereur j’adore bobou 😂
@papesambalo2287
@papesambalo2287 2 күн бұрын
Boudone may modou lo sa thies lay dieul
@mamepathengom9398
@mamepathengom9398 2 күн бұрын
Fadam tanque amoul limou beugue dou ame diam ✍️ Azize Ndiaye moko Yoni pour mouye wakh ci lou takhawal combat Modou lô ak Balla gaye ✍️ gniléni sétane gnoléne eup xél foufe ✍️ Azize Ndiaye mome dafa nagou wayé yalla dafa yémé ndakh boula dékké nga fokni lo beugue mou nék dalaye wane bopame ✍️ té bilahi walahi limaye wakh bisse bou Modou lô ak Balla gaye takhawé yalla wanko bopame ✍️ Modou lô na djeul combat bi ✍️ inchallah daye ame ndame ✍️👌 xalisse kou amoul ngor comme Fadam rék la manal dara ✍️
@user-qd1fv5ir6c
@user-qd1fv5ir6c 2 күн бұрын
Moh Aziz dafay napaté Rk mo guena sokhla combat bi modou Lo 😂
@diaosory5373
@diaosory5373 2 күн бұрын
Aziz c'est le meilleur
@souleymanegueye8466
@souleymanegueye8466 2 күн бұрын
Pour ioe xaliss moy leep ngay doul nan ultimatum leufeul ndayam nak yen modou moleni may thiow
@Malicksindidi1988
@Malicksindidi1988 2 күн бұрын
Boudé thiow rek balla gaye keen eupeuko thiow si lamb ji xaliss bobou ngay wax mofii baayii Modou lo té Aziz yor nako
@morleye739
@morleye739 2 күн бұрын
Aziz way❤❤❤😂
@yassinbuwaro8644
@yassinbuwaro8644 2 күн бұрын
Koumou nékh ak kiumou nakhari Balla geye2 moy papaye mbor ❤❤❤❤
@MamadouDiao-hv4db
@MamadouDiao-hv4db 2 күн бұрын
Modou lo Moy bayou koulou mbeur
@AbdouRahmaneGueye-b1e
@AbdouRahmaneGueye-b1e 2 күн бұрын
Boy niang nak eme sène nak bombou nak bayil thakhan way issa pouy nak😂
@PendaTalla-c5z
@PendaTalla-c5z 2 күн бұрын
Foy déf séne baye Eumeu Boy Niang ak Bombardier😂😂
@adamandiaye5622
@adamandiaye5622 2 күн бұрын
Aziz 😂😂dafa touki wone motakha garyi done thieupi thieupi kay
@CheikhNdiaye-hb4in
@CheikhNdiaye-hb4in 2 күн бұрын
😂
@lebougui4747
@lebougui4747 2 күн бұрын
Ana boy niang
@abdoukhoudossfall995
@abdoukhoudossfall995 2 күн бұрын
Sen lamigneu mo reuy rek dougnou lale grand contre petit dh 😂
@AmydiDiakhate
@AmydiDiakhate 2 күн бұрын
Bilahi kendou aziz sama nirowale
@SodaDioufka
@SodaDioufka 2 күн бұрын
Lii yeup khadim gadiaga
@MbayeAdama-w2z
@MbayeAdama-w2z 2 күн бұрын
Bilahi régler la wara def barina wakh trop
@miboldieng7574
@miboldieng7574 2 күн бұрын
Khadim gadiaga😂😂
@SodaDioufka
@SodaDioufka 2 күн бұрын
Aziz ndiaye lene donc moko interreser moy couronne bii si modou lo tes Gnom begue gnou sa Thies dieul ko modou tes modou lo na same gadom samou gadou yayam ak papam Gora lo yalla nako yalla khare aldiana
@salioudia9358
@salioudia9358 2 күн бұрын
Fadam déil wakh actualité tabayi siisoubi 😂😂
@serignedieng5762
@serignedieng5762 2 күн бұрын
Machalla azize
@serignediouf2205
@serignediouf2205 2 күн бұрын
Siteu balla Gaye 2. Mo nekh vraiment.. sathies. Modou lo
@morleye739
@morleye739 2 күн бұрын
❤❤❤❤kila begeu 😂
@ayubadrammehgambia-ko8pi
@ayubadrammehgambia-ko8pi 2 күн бұрын
The king balla gaye 😂😂❤
@adamendiaye1955
@adamendiaye1955 2 күн бұрын
Pourquoi pas balla vs eumeu sene 😂😂
@aliounesall863
@aliounesall863 2 күн бұрын
Balla gaye 2 il est bien entouré hum lén drr lalénii wakh kep kou ko dieul diamono djii digua danou ✍🏻✍🏻
@SambaMbodj-l8o
@SambaMbodj-l8o 2 күн бұрын
Modou lo reug reug
@bayeniasse5604
@bayeniasse5604 2 күн бұрын
Modou sathies ❤❤❤❤
l´invite d´infos matin | Dr Khadim Bamba DIAGNE, Secrétaire permanent du COS-PETROGAZ
33:06
Tuna 🍣 ​⁠@patrickzeinali ​⁠@ChefRush
00:48
albert_cancook
Рет қаралды 148 МЛН
Мясо вегана? 🧐 @Whatthefshow
01:01
История одного вокалиста
Рет қаралды 7 МЛН
Balla Gaye2 Confirme les Propos de Modou lo "Siteu Dafay Daw rék" Matar Gueye Tres en Colère et jure
20:55
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 4,1 М.
Urgent thiow Amatina Balla Gaye2 vs Siteu Ficelé; Jamaicain s’énerve et Repond a Aziz Ndiaye et Bay
25:16
Tuna 🍣 ​⁠@patrickzeinali ​⁠@ChefRush
00:48
albert_cancook
Рет қаралды 148 МЛН