Oh les Larmes de Fadam2 Apres la defaite de Talfa..; ModouLo ak Gora Sock danio setane Boye bi..,

  Рет қаралды 50,547

Fadam2 expert de la lutte sénégalaise

Fadam2 expert de la lutte sénégalaise

Күн бұрын

Пікірлер: 130
@P.A.Dienior
@P.A.Dienior 14 күн бұрын
bouléne fii andi béne polémique talfa c'est lui le jeune, c'est à lui d'aller vers les grands freres. Il a cru qu'il pouvait gerer lui seul c'est tout na kholate bopam il n'a que 8 combats vraiment lamb dafa am nounioukoy deffé mais dou affaire de bandit ak game . Tapha mbeur niom modou ak papa sow conseillé naniouko diapalénaniouko nakhe dafa dem vers eux . Mane Talfa je l'aime bien mais je me dis que c'est une bonne chose cette defaite bou gagné wone combat day yakarné sokhlawoul kéne
@DethieDioufFissel
@DethieDioufFissel 14 күн бұрын
😂😂😂😂😂🤣🤣🤣😫😫😫finpp🤫🤫
@gorguidiba1338
@gorguidiba1338 14 күн бұрын
Oui c sa
@layeseck1495
@layeseck1495 14 күн бұрын
Lou leirr nga wakh dafa dieul yonou bopam si combat bi Bilahii
@benzdictenobalegomis6139
@benzdictenobalegomis6139 14 күн бұрын
Lou lere nga wakh ndakh dafa topou mafia wam bi et en plus dafa done daw nite you diégué
@OmarDanalphaBah
@OmarDanalphaBah 14 күн бұрын
FADAM harr Nala beh sohna ce Le meilleur
@touremamecheikh9737
@touremamecheikh9737 14 күн бұрын
Wolhi talfa dafa yarou lol mane wa guediaway la ms srx talfa daamko gniéwatal yalla nako yalla defal diam❤
@dakardk4750
@dakardk4750 14 күн бұрын
Amine
@cissebabacar7461
@cissebabacar7461 14 күн бұрын
Amine
@ousmanecamara2090
@ousmanecamara2090 14 күн бұрын
Fadam ligua wakh mo am talfa na nekh nitt djiokhé bopam zoss dafa tall kene écurie bobou moylolou 😂😂 modou Lo seule
@DethieDioufFissel
@DethieDioufFissel 14 күн бұрын
POKOLA SEUL 💪💪💪FUTUR ROI DES ARÈNE INCHALAH ❤❤BANDIT GUÉW POKOLA BALDÉ ❤❤
@idrissasenghor507
@idrissasenghor507 14 күн бұрын
Je dis Merci beaucoup à Fadam2 ! Vraiment tu as bien dit les choses et Talpha doit écouter cette interview. La défaite de Talpha est une bonne chose. Car ça va servir de leçon à tout les autres petits lutteurs surtout à ceux de Parcelles à Talpha en premier.
@KhadimDéme-z1w
@KhadimDéme-z1w 14 күн бұрын
Fadam machallah kadou yi rafétna machallah talfa damako yeureum 😢
@cissebabacar7461
@cissebabacar7461 14 күн бұрын
Bien dit le grand parcelle la deuk unité 10 près de chez talfa nio fowa no Mais fadam tu as tous dis
@PapaSambaSy-h7r
@PapaSambaSy-h7r 14 күн бұрын
Grand yoff la deuk dh mais talpha yalnanko Yalla soutoural baye fall deuk leu legui legui rk ❤
@thiernodembaya8355
@thiernodembaya8355 14 күн бұрын
Modou lo & Gora sock son de bonnes personnes si ils n'ont pas venu sa veut dire que le problème c'est talpha 😊😢😢😢😊
@papediop33
@papediop33 14 күн бұрын
Saway nk yaw ya békh rk danga kham lane la
@Deggou
@Deggou 14 күн бұрын
saay wakh deugg modou ak papa amouniou béneu blém modou yagoul dra démona si oppen press becaye semaine passé ect... talfa da melni da moytou gayi depuis sa defaite contre youssou..
@benzdictenobalegomis6139
@benzdictenobalegomis6139 14 күн бұрын
​@@Deggouexactement c'est ça
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 14 күн бұрын
@@papediop33saway nioune daniouy beuguer talfa mais da wara wagni galathie yi mou gueume toppou entraînement yii baye fall waroul daw niite
@fallouvamos
@fallouvamos 14 күн бұрын
​@@AboulBacharSall Mane dh Yalla Khamnani Boudone may mom douma sori Modou lô ak wa rock énergie vraiment ak maguou parcelle yi nék Parcelle Yeup Talfa C'est son devoir vraiment de s'appuyer sur eux mo gueune mouy Dieul Yonou bopam Mane mom Vraiment je ne suis pas d'accord de sa manière de faire Kouné Parcelle Rock énergie guay Wakh Louko Téré Déme Fofou ?
@AntaFaye-z1s
@AntaFaye-z1s 14 күн бұрын
Goro sock louy problème bi moi aussi je remarque goro parcelle danoui ko setane bly talfa dafa weete
@daoudasarr4455
@daoudasarr4455 14 күн бұрын
Esk doussi mom tmt ?
@AmadouDiouf-g3p
@AmadouDiouf-g3p 14 күн бұрын
Est-ce que bi talfa di dieul combat bi gora yekkeu na 😢tmt talfa mo dioum na dem diegalou dji dem rock energy
@mormboup9301
@mormboup9301 14 күн бұрын
@@AmadouDiouf-g3pmoy yone dh
@Deggou
@Deggou 14 күн бұрын
saay loutakh talfa defoul open de press aussi? talfa combat bi louma remarqué mo beugone lakou ci combat bi....begoulwone kéneu diégéko cama xaalate
@gorguidiba1338
@gorguidiba1338 14 күн бұрын
Sayy mane parcelle laa deukk mais talfa mo teela yekkk succes teeela bewwwww lolou moooko indill lii yeuppp
@iboufall446
@iboufall446 14 күн бұрын
Bou goro sock nieuwone tmt sou waré danou day danou geum léne yalla moy mayé talfa champion la bou parcelle yeup nieuwone sou waré danou day danou
@fallouvamos
@fallouvamos 14 күн бұрын
Lolou Yeup Deugleu Mais na gueuneu Diégué ses grands frères niom Modou lô wa rock énergie ak maguou Parcelle Yeup Lolou moy Deugue Bou beugué Sori Si Lamb Talfa Na bayi bérou bi !!! liiiii koukoko Wakhoul Bouguoko Deug nékhoul nak
@Deggou
@Deggou 14 күн бұрын
boulén fi dougal modou ci seen thiakhane yi dé , modou boy yeup laay dimbali waayé boy bouko wolouwoul c normal mou tokk placam... talfa loutakh defoul open de presse wowoul kéneu?...
@hizbuttv2355
@hizbuttv2355 14 күн бұрын
Modou lo sakh diapale nako bilay mom Talfa mo wara dem si ay guinaw magam
@magnesenesow9400
@magnesenesow9400 14 күн бұрын
Te papa sow degg nako mou wakh guiissoul talfa khamoul loumu entraiment te papa sow ak pokora gnu tolou dinga dieul si papa sow lou beurii ak ossi experience papa sow dafa bakh
@azizjazzdiop941
@azizjazzdiop941 13 күн бұрын
Nidiaye kilifeleu sans Gora il va pa faire carrière et bravo a Franc le fidèle
@malickndiaye3436
@malickndiaye3436 14 күн бұрын
Talfa momou niou Na dém Jambar Lolou moy deugg
@papeflokiFall
@papeflokiFall 14 күн бұрын
Lolou moy deug n'a woyof
@FallBaye-gd9lf
@FallBaye-gd9lf 14 күн бұрын
Mosouma apprécier say wakh mais tey mome vraiment tu a parfaitement raison bilahi nite koula diakhasé ague say mbok mola yakale
@bayzalfall51
@bayzalfall51 14 күн бұрын
Lima begue wakh lolou gama wakh xall ❤
@thiawfoot5217
@thiawfoot5217 13 күн бұрын
Ngathie Gueye deuk la ❤❤❤❤
@MbissaneMbaye-wr1qv
@MbissaneMbaye-wr1qv 14 күн бұрын
Bilaye fadam analyse bou bien ka def
@mamegorseck6167
@mamegorseck6167 13 күн бұрын
Boy depar ay nite niolay diaple no tamblè fayèkou ay milon say mbok nieuw weurla sou nekè niou khamoul lambe sankela lolou kep mo dal talfa talfa warna beure ta ndidiayam goro sok anditwouko
@AbdaNdongo-h5l
@AbdaNdongo-h5l 14 күн бұрын
Merci fadam 🙏🙏🙏
@khadimfall979
@khadimfall979 14 күн бұрын
Fadam est Le Meilleur ❤❤❤❤
@bayzalfall51
@bayzalfall51 14 күн бұрын
Merci fadam
@abdoulahadmbaye1488
@abdoulahadmbaye1488 14 күн бұрын
Pourtant wa parcelle japale nanko mom yalla ko xange rek
@SambaToure-n9h
@SambaToure-n9h 14 күн бұрын
Ms niou dane ko indi lou takh indi wougne ko lolou may problem niep nioune gnii topp ko lolou lagne done kahlat lou takh andoul ak nioum dane andal
@Deggou
@Deggou 14 күн бұрын
​@@SambaToure-n9h es ce que nekoul mo beugone moytou tamite? parceque meme open de press defouko...
@fromdiouls547
@fromdiouls547 12 күн бұрын
TALFA DAFA WARA DÉM DIAMBAR COMME FRANC DÉM DIÉGUÉ CHAPiON YOU MAK YI ANDEUH AK NIOM Di LIGUEY COMME AVANT 🙏🏽🤚
@ThiernoDiongue-q8t
@ThiernoDiongue-q8t 14 күн бұрын
Yagua wakh talfa démal djambar
@momofaye2905
@momofaye2905 13 күн бұрын
Talfa na dém si grand yi niou tétè ko ték ko si yone papis général sax waxnako da am koukay teuklé ak grand wame
@bellingham-k6t
@bellingham-k6t 14 күн бұрын
Bilhi dama yereum talfa😭😭😭
@IbrahimNdiaye-k4y
@IbrahimNdiaye-k4y 14 күн бұрын
Talfa nioune parcelle modou indil naniou loune ci Lamb dangay watie niou diebalou niou diapale leu mounko yakham
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 14 күн бұрын
Fadam2 waxal niou si tapha mbeur wayy
@mortalla7015
@mortalla7015 13 күн бұрын
Même j’ai remarqué FRANC daffa wett lamb ji. Ama daffa ande groupe bou nitt attaque Franc.😭😭😭
@cissebabacar7461
@cissebabacar7461 14 күн бұрын
Té talfa na dém rock énergie wala diambar ahh
@morsy2035
@morsy2035 14 күн бұрын
C vrai bou beugé danate mbeur na dém rock énérgi
@cissebabacar7461
@cissebabacar7461 14 күн бұрын
@@morsy2035 bilae frère
@MansourDiop-wd2or
@MansourDiop-wd2or 14 күн бұрын
Na diogué dor dorat zoss mom dou diapalé ben boy waxé mou nann dma touki wone di sop😂😂 tei sou amé combat boy yii sonou si na dem diambar wl rock énergie
@moustaphadieng2880
@moustaphadieng2880 14 күн бұрын
Pokola vs Jackson ndaw lo mèti
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 14 күн бұрын
Jackson dakoy rayy😂😂😂 birima daa sokhor deh
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 14 күн бұрын
​​@@abdoulatifdiop5640lou leer nga wakh 😂
@papeleye267
@papeleye267 14 күн бұрын
Diaksone moko meune dé😂
@DjibiThiaw-wy2xy
@DjibiThiaw-wy2xy 14 күн бұрын
Combat bobou rk lay rêvé 😂
@papipapi344
@papipapi344 14 күн бұрын
Jackson dou moromam
@babacar3178
@babacar3178 12 күн бұрын
Dafa yarou mais na botou wane grand yi yéne leu bolo mii topouma dou dara
@ZooNdiaye-x5r
@ZooNdiaye-x5r 14 күн бұрын
Saytané gua niannwe gua mais taye mome wakh deug talpha parccell gniépou gnonko beugu mais boye yi dagnoume am 4 Victoire rék diapouni gnonye king bi ta lamb démaiwoul nonou gora sokh amoul kouka guena beugu talpha si adouna modou lo pareil talpha la kéne khamétoul mane PA la DEUG khamna talpha bou bakh mais gniemaiwoul pokola DEUG mo nékh yalla😂😂
@Supernguewel-bk7co
@Supernguewel-bk7co 14 күн бұрын
Bilay degue gua wakhe
@mamadousall7046
@mamadousall7046 14 күн бұрын
Dou ragal dee dañouko diaap si( galathie ) mom talfa serieux
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 13 күн бұрын
Pokola bamou dane ibou seck lako soumil sapo champion deuge leu
@FallouNdiaye-ic6es
@FallouNdiaye-ic6es 14 күн бұрын
😭😭😭😭😭😭 talfa❤❤❤❤
@moustaphadieng2880
@moustaphadieng2880 14 күн бұрын
Talfa bou de zoss nga yakar baya bou nga bayi Lambou demal si wa diambar fo Gora soke dém fa nga wara dém
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 14 күн бұрын
Billahi xaw m'a louy problème bi môme ak wa djambar guissouma fa kénn si cotém
@DethieDioufFissel
@DethieDioufFissel 14 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@DjibyNdiaye-l3o
@DjibyNdiaye-l3o 14 күн бұрын
Camberene la deuk dou thioubou di dém fénénn pokola moye sama mbeur ms baye fall deug leuh
@falloufaye1310
@falloufaye1310 9 күн бұрын
Man gnima andal jour combat niep thies lan diougué
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 13 күн бұрын
Mberryi nio tam lolou bouniu koumance dane rk niou nanlen yafi nek lolou moye yakhe sen carier
@DiopDjili-y2t
@DiopDjili-y2t 14 күн бұрын
Pokola yousou ndour
@KhadimBeye-su7bc
@KhadimBeye-su7bc 14 күн бұрын
Talfa vs Armé
@moustaphadieng3658
@moustaphadieng3658 13 күн бұрын
Affaire bi c simple suis supporter de talfa mais tout le monde a constaté k depuis le combat contre youssou N'Dour talfa s'est isolé il était avc Franc et Gora sok jambar moy placam
@diamilmboup4392
@diamilmboup4392 14 күн бұрын
GoRo Sock dh hamNani kou beugu Talfa la
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 14 күн бұрын
Fadam mbeur you Ndaw yi kousi daan rk yakar ni agaga sa wa kogne dounoula wakh deugue
@aliounelo2181
@aliounelo2181 14 күн бұрын
Fadam daysan day nexal rek wayi kou baxla❤
@azizallendiaye6590
@azizallendiaye6590 14 күн бұрын
Fadam 2 lamb dji ga xam ni dafa aram diaroul dioy nak Lim aram rek doyna
@ElhadjimodouGaye
@ElhadjimodouGaye 14 күн бұрын
Fall yangui wakh si lou haram dhi
@AlléNdiaye-s6x
@AlléNdiaye-s6x 14 күн бұрын
Talfa dafa dioylo niou bari démb bimou takhawé si guéw bi
@IbrahimaNdiaye-eo3qh
@IbrahimaNdiaye-eo3qh 14 күн бұрын
Bien dit fadam talfa dafa wara am ay mak yukay topu
@NdiawDiop-o6u
@NdiawDiop-o6u 14 күн бұрын
Gora sock darnier interview bimou def toudoul sakh talfa
@matyseck264
@matyseck264 14 күн бұрын
Ms yalla bakhna blh dîna léne raw talfa rk niou dém😮
@DethieDioufFissel
@DethieDioufFissel 14 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣wouy 😂😂finpp way🤫🤫🤫
@matyseck264
@matyseck264 13 күн бұрын
@DethieDioufFissel boy yaw sa data mame way
@abousoumare3345
@abousoumare3345 14 күн бұрын
Boyi sen problème mony d’à gnou len sur côté mes tangoul gnou defou gnou dara si lamb diapé sen bopou star talfa na kholat bopam dagay douté mbeur dagay gueum bopam sokhor don vainqueur combat bi sou nekon niang ballo day def différence
@AbdouLo3101
@AbdouLo3101 14 күн бұрын
waa mane loutakh guissou ma gora sock si combat Talfa bi ???
@DjibiThiaw-wy2xy
@DjibiThiaw-wy2xy 14 күн бұрын
Pokola vs Jackson
@charlesmanga1632
@charlesmanga1632 13 күн бұрын
Dou yone événements bou tolou ni leader parcelle yi nieuwouniu ci combat bi surtout modou lo
@elhadjicheikhndao2173
@elhadjicheikhndao2173 14 күн бұрын
Blhi fadam deug nga wax dagn ko setan wala tafla mo fonkoul ayy mbokam rekk
@fatouNdiaye-ov7zb
@fatouNdiaye-ov7zb 13 күн бұрын
Mais tapha mbeur fane la deuckeu
@DjibiThiaw-wy2xy
@DjibiThiaw-wy2xy 14 күн бұрын
Ndeysan talfa damako yeureum wa parcelle setan guéne boy bi
@papipapi344
@papipapi344 14 күн бұрын
Dél wakh loula woor
@IbouBa-xf9px
@IbouBa-xf9px 14 күн бұрын
Absence de Gora sokh mane diakhall Nama lolou té Gora da beug talfa
@Deggou
@Deggou 14 күн бұрын
mais es ce que talfa yeugeulnewone combat bi gora?
@maragueye8207
@maragueye8207 14 күн бұрын
Mais talfa combat bi moye lolou billahi
@mistercarter467
@mistercarter467 13 күн бұрын
Ngueine foknei avec sa blessure mu forcer beurreii mtx grand parcelle mereii ko.. genre wakhko mou douggal medical mou bagne gars yii setane koo
@gueyetvgueye7443
@gueyetvgueye7443 14 күн бұрын
Petit lo vs pakola
@ibouciss3519
@ibouciss3519 14 күн бұрын
Weu supprime ça bala nioulay fiy fek moh😂
@assane-p7k
@assane-p7k 14 күн бұрын
ani modou lo vue que talfa demna openn press modou bi c koi le blemm
@OusmaneMagassa-z9m
@OusmaneMagassa-z9m 14 күн бұрын
Bou beuguer def carrière n respectez Niang ballo ak Guiro Seras moy wakh dji
@abdougueye4837
@abdougueye4837 13 күн бұрын
Talfa na wagni musculation bi
@GoraDiagne-g8k
@GoraDiagne-g8k 14 күн бұрын
Talfa c'est pere gora bou garga mbosse ?
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 14 күн бұрын
Mais Diop 2 vc Pokola Combat xaliss la deh
@s.bergwijn
@s.bergwijn 14 күн бұрын
Boula fi supporters Pokola yi féké gua am problème 🤣 ioe Pokola loumouy doyé Diop2 Daguey wakh key Talfa vs Diop2 mo gueneu diadoou
@pronosticfootsenegal1112
@pronosticfootsenegal1112 14 күн бұрын
​@@s.bergwijnkikay daf nio yap bilahi😂😂
@NgagneDiakhate-n7e
@NgagneDiakhate-n7e 14 күн бұрын
Bayil diaxasé
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 14 күн бұрын
Lim wax môme dégue la xana setano Combat bi😢...
@sophrotall8105
@sophrotall8105 14 күн бұрын
QUENCH DAFA MANA TAMOU REK BOUNIOU WAKHE MOUNAN MAKO EUP CACHET BOU DOF DOF LOUWOUL NIOM PAPA BARI BARI AK AY KIRIKOU AK NIOM SEN LAY NIEUW BEURELLL
@cheikhthiombane3617
@cheikhthiombane3617 14 күн бұрын
Talfa a tort na delou ci Gora Sock di dem entrainment jaambar
@cissebabacar7461
@cissebabacar7461 14 күн бұрын
Talfa ték si dafa wara bayi boy yi concentré si bopam
@NdamaldarouNdiaye
@NdamaldarouNdiaye 14 күн бұрын
Talfa mo wara déme diambar
@salioudiouf2507
@salioudiouf2507 14 күн бұрын
Pokola va gora soke
@ModouMbay-f4g
@ModouMbay-f4g 14 күн бұрын
Yao doul rek gay deif pokola da meun talfa dahko beurei fadam hamo lamb
@AbdoulazizThiam-u7v
@AbdoulazizThiam-u7v 14 күн бұрын
Talpha mane je sais pas damako beugue
@DjibyDieng-z8v
@DjibyDieng-z8v 13 күн бұрын
Yaw mom seytané nga
@CaramocoDiallo
@CaramocoDiallo 14 күн бұрын
Fadam yaw seytane ga
😱Pikine ame nagne problème D "Franc vs Ama" Sortie De ModLo; CoachAb ak Lambalogue wakhe nagne D
20:32
‼️Urgent Fadam2 et Bour Guewel Fait de Grosse révélation après la Belle Victoire Mod lo sur BN2…!
26:10
Kawtef😱! Liss Ndiago Dafa Piquirou Nane Ay Dome; Ca chauffe Entre Mobile2, Mame Balla, Abo sing sing
24:54