Li mom douma bétte thi yaw khana kou khamoul sa baye wayeh man sa baye rékk la beugue th mom rékk laye déglou yalla khamnako diala niganal yalla mou lafalla thiat th nga xamni damalay topou bubax ndax linga kumasé dfa nékh torop yalla khamnako wa binourihi AK hourfou salatou fatiha AK fala buda machalah nla yalla défll diame si barké taysirr bi ngaye wadiall inchallah yalla mottalli lépp nioungui Koy kharr niounn talibe cheikh yi
@ngagnesyllalofficiel112623 сағат бұрын
Kou diglou woy wi té kham woy wara kham'ni lingay woy forcer woko dafa nior khomou ngay dogay Guen machallah na Yalla sam weral aar goudeul fane Bidja'i Taha❤
@braahim17213 ай бұрын
Allahouma Baarik Djazakallaahou khayrane Pa Abdou longue vie ❤
@modoundiayesoperassoulilla8663 ай бұрын
Jajeufeuti pa abdou Jangue yi nekh na té ame khorma Yalna geneu jeume kanam
@youssoufdaff59772 ай бұрын
Machallah amine ya rabi 🙏🏾👏🏾
@mmalick47273 ай бұрын
mashallah yalna yalla weral baat bi sama sopé bi defal niou nouniya bi nak
@bayemodasalle682 ай бұрын
Yalla na yalla barkel té goudal fane yi weral batte bi ❤️
@dabakhndour50853 ай бұрын
Maneu mako sopou mome moulaye wallahi ❤
@ousmanebalde95422 ай бұрын
Mann la première sope pape Abdou mbaye barakalahou
@thiatgueye-g9w3 ай бұрын
machallah machallah amatina solo li néxna trop machallah
@maximaguette86713 ай бұрын
Mashalha mashalha Sama waji yage Fi lolo ❤❤❤❤❤❤
@moustaphaseye93403 ай бұрын
ما شاء الله حفظك الله 🤲🏻❤️
@binetagueye13492 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Mashallah
@AbdouSy-v5z3 ай бұрын
Dieureudieuf mbaye
@AzizNdiaye-x7f2 ай бұрын
Mn nk say amdaakh lénéne lamay déff lamiyah ak hamziyeu bou boussiiry ak bou ahmed chawqi sokhlo nassi audio nga madkhaléne bamou diékh ak yénéne khassida yi soumako amone dina baakh trop hamziyeu bi nk yaak baaye sarr rk lénene duo bobou ohhh❤
@mansourfall18093 ай бұрын
MachAllah moulaye❤
@Ndiaye_Al_Amine3 ай бұрын
Wa ken dou waxx si Pape Abdou Mbaye miii❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mouhamadoumoustaphakane68683 ай бұрын
Machallah
@ndiayetv27073 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@OusmaneSy-k7s3 ай бұрын
🥳🥳 Khilas bi rkk layy khar ni d 😉
@AndayeGaue3 ай бұрын
Machalla❤
@AzizNdiaye-x7f2 ай бұрын
Ndeyssane li moy tagueu tagueu moy nga weuy khakhiqa pur et dure mn dh bi laay khaar zéynabo ré serigne maguéye ndiaré nga thia wakhé partie bobou nguéne dougal si khilass bi laay kharr fi la dh na deugeur