Fallou Ndiaye très amer : " Mor Kang Kang dotouma... Diop 2 dafa "

  Рет қаралды 47,097

AL BOURAKH TV

AL BOURAKH TV

Күн бұрын

Пікірлер: 90
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 Ай бұрын
Franc ak Sokh ba tay lafi geudjon ni stade bi méll dembou chapeau boy yi vraiment ❤🎉 Diop2 et Mor kang kang
@djibysoung2998
@djibysoung2998 Ай бұрын
Ndiay rek ❤❤❤❤
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 Ай бұрын
😭😭😭😭😭😭 Abou Ndour meilleur journaliste de monde billahi wallahi tallahi damako beugue ba yeureumko🥹
@DioneAliou-ri2br
@DioneAliou-ri2br Ай бұрын
Fallou Ndiaye vraiment li diaroul revenir mor douy na lamb dji té monékon sa objectif mor seul ❤❤❤❤❤❤
@ahmedseck991
@ahmedseck991 Ай бұрын
Mor douyna Lamb dji 😂 Diop 2 loumou déf konn ?😂
@Lepatriote9423
@Lepatriote9423 Ай бұрын
J’aime beaucoup Fallou Ndiaye, liguéye kate leu, ame fouleu ba paré deugou. Yalna yalla yokou xéweul yi
@adamandiaye5622
@adamandiaye5622 Ай бұрын
Fallou mor sa frerr la et vraiment niniou def stade bi demb warna takh bayil lp svp
@adamandiaye5622
@adamandiaye5622 Ай бұрын
Diop 2 sa prochaine combat naga ladj cachet bou bakh mor aussi nonou nguen tela dioublou si tabakh keur gou bakh lamb yagoul
@seringembacke9316
@seringembacke9316 Ай бұрын
Ya rafet xol de bilay walahii ✅❤❤❤❤❤❤
@issasylla3602
@issasylla3602 Ай бұрын
Lolou moy fouleu
@NabouThiam1467
@NabouThiam1467 Ай бұрын
Bilakhi dafa diote nak 😊nakh mbeur yi yeup ay champion lagne ❤❤❤
@Dieng-vk6if
@Dieng-vk6if Ай бұрын
Diop2 seul mo meuseu def guichet fermé arène nationale diop2 seul domou yeumbeul bi yalnako yalla lafale thiate
@NabouThiam1467
@NabouThiam1467 Ай бұрын
Dina bakh inchallah 🙏 Lisi kaname Moy dakeu inchallah ❤Diop 2 jambar la ❤❤❤😊
@broadcast574
@broadcast574 Ай бұрын
Mais c’est grave. Promoteur si bopam mo wakh nite gni yor billet té meunounio doug donc ça veut dire que danguéne diay plus de billets té stade bi atanouko. Sou nékone Europe gni dougoul porter plainte
@souki-saf-group3858
@souki-saf-group3858 Ай бұрын
Grave même
@ramatoulayedianor7023
@ramatoulayedianor7023 Ай бұрын
Lep diop2 leu🎉❤❤❤
@mbayesene7930
@mbayesene7930 Ай бұрын
Ya xam dei Mor seul 👑
@Ahmadouboromediamono4
@Ahmadouboromediamono4 Ай бұрын
Ndiaye tine machallah warga lek xaliss lamb dh
@IbrahimdialloWfdqkie
@IbrahimdialloWfdqkie Ай бұрын
Mor❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@FallouGning-k4z
@FallouGning-k4z Ай бұрын
fallou yalla nopy na mor seul
@ibrahimatall5277
@ibrahimatall5277 Ай бұрын
Mor Kang-kang ci yow la khol ba wathie dieul Diop 2,lolou koloré lah. Kone boy boum la gueuneu gorré. Mane dama la fan trop mais yangui wérré beug nga khaliss trop... Khana sa pékhé da sotti woul, ishh ?
@MamecheikhFaye-i7g
@MamecheikhFaye-i7g Ай бұрын
Fallou Ndiaye teyal sa xaalis fii yalla moo fi nekk lii la nu naan sa mbokk mooy sab noon
@Leuzsonko
@Leuzsonko Ай бұрын
Diop koula fayoul plus de 50 milion boul beurè mor kang kang koula fayoul plus de 30milion boul beurè li nguèn def aren national combat vip beurè nagne fi te stade mèloul ni promoteur yi niom sèn intèrè rek koudoul alboura dou fay normal xolal liss plus de 25 milion la fayèkou xolal ada plus de 45 milion bilahi alboura moy meilleur ❤❤
@MDbousonko
@MDbousonko Ай бұрын
A sa waye Li nga wakh foko ték fou Diop lale 50 millions mor lal fa 50 millions gno yem Rek Ay diambar Lane ay nda nane lane té Am nane guinaw
@OusmaneSadio-l3k
@OusmaneSadio-l3k Ай бұрын
Lou ler​@@MDbousonko
@votremiroir7612
@votremiroir7612 Ай бұрын
yaw ya sokhor donc yaw yéné wo Mor 50millions?
@PapemamadouNdiaye-ux9xb
@PapemamadouNdiaye-ux9xb Ай бұрын
Wawaw frere
@PascalGomis-x7v
@PascalGomis-x7v Ай бұрын
Danga dioumm 50 50
@diengabibou6155
@diengabibou6155 Ай бұрын
Fallou. Félicitations sii combat bii diambarr guaa. Mais soo méré mor kang kang reik togne koo daloone lamb reikk, taa ahh soo doxole nii dina melni liniou waxx doone deug. Yalla moo yorr ndam mais nitt defois mou ame ayy pexx donete taxoule pexe yii soti taa yalla dafa meun setane Yalla na nieup ame diam.
@nogayeniang9119
@nogayeniang9119 Ай бұрын
Yaw khamou dara Lamb dala Wara niaw senatir be
@Lepatriote9423
@Lepatriote9423 Ай бұрын
Saway nite bou signé contrat dako wara respecter.
@mamadoufaye4057
@mamadoufaye4057 Ай бұрын
Tu raconte n'importe quoi. Fallou a,raison
@mouhamadoumoussa4857
@mouhamadoumoussa4857 Ай бұрын
Fallou va là-bas boudè yay yalla tawal xerr
@seringembacke9316
@seringembacke9316 Ай бұрын
Fallou balale boy bi sarak la te adina amoul solo li yep saytane la rk fatel lep mou jex 🙏🙏🙏🙏🙏
@nogayeniang9119
@nogayeniang9119 Ай бұрын
Fallou ndiaye merci lamb ji amatol espansor mou takh mor dafa wara na niaw senatir be
@mbenelo9730
@mbenelo9730 Ай бұрын
Fallou ndiaye ko yab téyel sa khalice more Kang Kang da nam kouko yeungal lamb yaw demal nga togue😂😂😂
@MamadouGueye-y6o
@MamadouGueye-y6o Ай бұрын
Way iow ya kham mor seul dadone lamb
@ahmadoudiagnegueye9918
@ahmadoudiagnegueye9918 Ай бұрын
Wa mai nenga balngako no😊
@thiawzall1547
@thiawzall1547 Ай бұрын
Liga begone mo amoul rek topall fale diop daye danou far foc yoro weurseugou morr
@dioneame6282
@dioneame6282 Ай бұрын
Ndiaye tine rois des aréne inchallah
@ladianepathe5637
@ladianepathe5637 Ай бұрын
😂😂😂😂😂
@ghezzalndiaye6319
@ghezzalndiaye6319 Ай бұрын
Fan lakoy doné xana bire il de Goré laye done😅😅
@MbeussTalibebamba-k4b
@MbeussTalibebamba-k4b Ай бұрын
😂​@ghezzalndiaye6319
@ballacisse7561
@ballacisse7561 Ай бұрын
Fallou Ndiaye aka mo deuguou.Mome wakh douko ray
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 Ай бұрын
Dame séne ndiaye tine combat la
@tallafall7629
@tallafall7629 Ай бұрын
gén balma wayé fallou Ndiaye mi dor la nak wakhi dof rék lafi wakh tay téga santat yalla bakhna 😂😂😂
@DiomayeThiao-x8w
@DiomayeThiao-x8w Ай бұрын
Fallou yaw nk kou titt gua bilay balale mor lamb dji moko ladione comprendal boy bii
@BabacarDiallo-ls6ve
@BabacarDiallo-ls6ve Ай бұрын
Fallou ndiaye bo teugué combat dél woutt sécurité bou doy wollahi Demb stade amoul sécurité billahi
@laminethiare3693
@laminethiare3693 Ай бұрын
Sécurité bi amona ay peul you ndaw yi nekone di sécurisé té guissoko mo takh mais sécurité bi doye na dé 🤣🤣🤣
@BabacarDiallo-ls6ve
@BabacarDiallo-ls6ve Ай бұрын
@ fofou kaay amoul touss 😂
@serignesalioudiouf1080
@serignesalioudiouf1080 Ай бұрын
Ki mo beug xalisse mor kang kang bo ko teugoul say moromeu teuggal ko
@ballacisse7561
@ballacisse7561 Ай бұрын
Merci Fallou.Deugue rek ngua wakh.Yaw Nitou deugue ngua
@Senegalrekmounekhe
@Senegalrekmounekhe Ай бұрын
Fallou mom khalisse rek sa Dou Faye tousse yaw Mor Limou indi si mbooloo
@Elhadji2187
@Elhadji2187 Ай бұрын
Fallou ndiaye guisgua mor dafa diarr soko teugoul tmt kenen djeukeunté ko lolou ieiee la rrkk
@sidzboy3836
@sidzboy3836 Ай бұрын
Bilahi adouna kene momouko
@PamoussaSar
@PamoussaSar Ай бұрын
Fallou Ndiaye doul lolou iow la ya khame
@votremiroir7612
@votremiroir7612 Ай бұрын
yaw nga wara gueureum Mor diko khass badola nga reck. Mor fayla ba wiss la yaw am béen ngor
@cheikhseck3842
@cheikhseck3842 Ай бұрын
Lamb ak thiow milieu lamb ya ci Doug kone mounieul nek sportif
@marandiaye8126
@marandiaye8126 Ай бұрын
Mor insbi nekhaloule kén Wakhtanéléne ko rek
@moudoudiop6216
@moudoudiop6216 Ай бұрын
💟💟💟💟💟💟💟💟💟
@CheikhNdao-rq6eu
@CheikhNdao-rq6eu Ай бұрын
Falluo yaw daga bax rék
@AlphabouNdiaye
@AlphabouNdiaye Ай бұрын
Falou ndiaye guèssou lèn thiandoum2 dafa wara beurè dè
@lifaababacarthiaw1354
@lifaababacarthiaw1354 Ай бұрын
Fallou avoir un esprit de businessman sa fait partir du professionnalisme dans votre métier.se qui dois t’intéresser c’est la rentabilité.en se qui concerne le comportement du lutteur tout doit être lier dans le contrat.sil ne respecte pas le contrat ou le bailleur tu as tout les droits en ta faveur.
@toumanydieme9516
@toumanydieme9516 Ай бұрын
Lamb demb nekh tropp mé Fallou Ndiaye sou meunoull teugg na bayiii 0 sécurité bou Diop danou wonnn billahii xekhhh bou nga donn guisss
@NgatteThiam-fx8ic
@NgatteThiam-fx8ic Ай бұрын
Fallou yaw kou tite nga yaw sa bénéfice nieuw na dernier combat boyi douniou doug thé diop boko fayatoul 100 wala 150 million dotoul beuré mouss nga trop😏
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 Ай бұрын
Vraiment daa wara dolli boye yi sax billahi
@NayeFall-qq7xi
@NayeFall-qq7xi Ай бұрын
Saay 100millions walla danga juum ?😂😂
@mamemorsene7088
@mamemorsene7088 Ай бұрын
Fallou Ndiaye ya topon mor de boko fate
@Elhadji2187
@Elhadji2187 Ай бұрын
Boy diop libéré woul si fallou ndiaye mi koula fayoul khaliss bou barii boul beurré dagn lay use rk insbi
@nogayeniang9119
@nogayeniang9119 Ай бұрын
Fallou ndiaye dafa beugue khalis mou takh wotol secrete bou doy
@SoudouNgom-f5e
@SoudouNgom-f5e Ай бұрын
Fallout ndiaye yw do nit bilahi li lamb bi meuko ladione rek
@Leuzsonko
@Leuzsonko Ай бұрын
Ioe nak xamo sa bop mor insbi sah meunoko teug mok diop nkh do fay😂😂 xana wa alboura wala makane😂
@SerigneFaye-n4o
@SerigneFaye-n4o Ай бұрын
Topal feule mor seul
@AladjiGueye-r6q
@AladjiGueye-r6q Ай бұрын
Mane fallou ndiaye diakhale nga ma sa toure wi rek moma diakhale bomanê bou mbeur beurêti baringa problème trop
@malickndiaye3436
@malickndiaye3436 Ай бұрын
Fallou boul sonal sa bop Mor dou chômer. Ay risque la dieul wathie dieul Diop 2 pour beurél leu. Soit reconnaissant toi aussi. Nila Mor ak Diop defal stade bi sante rk ngaleine wara déf
@rahmanendiaye336
@rahmanendiaye336 Ай бұрын
Il faut précise billet 3000 CFA la
@abdougueye4837
@abdougueye4837 Ай бұрын
Baol baol yi diaplé lenn mor andi na couronne prince des arène
@ibrahimndiaye9649
@ibrahimndiaye9649 Ай бұрын
😂😂😂😂😂
@julefass
@julefass Ай бұрын
Falou Ndiaye mo begue lou yomb fila waxon dotoul teuk ada fass té ada fass gouye gui moko dokh ak luc Nicolas guemoul dara mor boko teugoul gayi teugu ko rék
@BassirNiang
@BassirNiang Ай бұрын
Diop2 kou la fayoul plus de 50 millions moul beuré
@MbayeAbdou-mh5uw
@MbayeAbdou-mh5uw Ай бұрын
Sa way yaw promoteur bou mdao gua topal feulè nafekh manta wessou guanal niomm niarr kèn danoul
@nogayeniang9119
@nogayeniang9119 Ай бұрын
Mor kan kan sof lá rek bou khou li si ndiaye tine me manol am combat kone dafa wara niaw senatir yi
@ositokifyh2687
@ositokifyh2687 Ай бұрын
Nogoye soneu nga sonal nganiou ak senatir 😁😁😁😁
@dramanediallo-yj2oi
@dramanediallo-yj2oi Ай бұрын
Mor AK gouye gui / diop2 AK prince bou pikine
@moukhaba8604
@moukhaba8604 Ай бұрын
Boko teugul kenene teug ko ya soof
@papendiassendiaye1656
@papendiassendiaye1656 Ай бұрын
Yaw yay soff si bopamm gueumeul yala
@ibrahimaba3553
@ibrahimaba3553 Ай бұрын
Yow nii mor ak Diop2 def stade bi ak combat bignou délivrer amo dara lossiy wakg loudoul ay wakhi guinaw tu n'ai vraiment pas professionnel du tout pffff déjà ligua faay boys yi dafa ndaaw louy 5 millions si combat bou mélni way doule way sof guéne trop
@cheikhseck3842
@cheikhseck3842 Ай бұрын
Lamb ak thiow milieu lamb ya ci Doug kone mounieul nek sportif
@papendiassendiaye1656
@papendiassendiaye1656 Ай бұрын
Yaw yay soff si bopamm gueumeul yala
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 81 МЛН
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 958 М.
人是不能做到吗?#火影忍者 #家人  #佐助
00:20
火影忍者一家
Рет қаралды 20 МЛН
wouy ndaye gueye divorse ak papa boy djine🤣🤣🤣
10:30
kheurypro
Рет қаралды 26 М.
MANSOUR DIOP CONVOCATION BOU AMADOU BA DIAROUL POLITISER...
19:24
MMD MEDIA TV
Рет қаралды 20 М.
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 81 МЛН