Ay way nama gneup nianal ma am dome toude Serigne saliou sama sangue bi
@MamendaneDiouf-w1gАй бұрын
Inchallah amngako ba nopi
@mbayefallou14015 ай бұрын
Macha-allah amatina solo Dieureudieufaty Cheikhoul KHADİİM Yalla nanou ko YALLAH fayal Thiey Serigne Saliou Mbacké Yalla na YALLAH yokk ay lèram té tass ñou ci barkéém
@mamyndiaye36953 жыл бұрын
Oh sama xol féss na séd na s saliou kéne xamoul loumou done S Khadim Dieuredieuf Thioune sama wasilah🙏
@iboudiouf5354 жыл бұрын
Ndeysane sama sang bou bakh bi segne khadime yallafi guene yague lolle❤️🤲