FATALIKU SERIGNE DIADJI TALL (yalla yokku ay leeram)

  Рет қаралды 25,048

Jazboul Mouride TV

Jazboul Mouride TV

Күн бұрын

Пікірлер: 44
@LikaLo-z4j
@LikaLo-z4j 5 ай бұрын
Ndeysaane yalla na khipper firdawsi barkéb borom toubaa
@cheikhdiopthiam6599
@cheikhdiopthiam6599 Жыл бұрын
Cours magistrale pour bep mouride bou beug xam serigne bi ak kou beug sak mouride rafet yalna niou yalla fayel serign Diadia Tall yokou ay learm bijahi serigne touba
@massambaamchifall1197
@massambaamchifall1197 6 ай бұрын
Yallah Nala Cheikh Ahmadou Bamba Terral Abadane , Barké Mame Cheikh Ibrahima Fall ❤
@ibrahimadioplo475
@ibrahimadioplo475 Жыл бұрын
Serigne Djady yalla na yallah yoke say lerr ak khewel abadan YallNa yallah doundal sounou doundou ci barke mame cheikh Ibrahima Fall
@BayeAbdouGaye-x6o
@BayeAbdouGaye-x6o 10 ай бұрын
Yalnako borom Touba doli tawfèkh Aki ngènel Aki kheweul Ak yeurmandè Ak ngereum barkeb maame cheikh Ibrahima fall lamp
@bayefallgalsen2096
@bayefallgalsen2096 Жыл бұрын
Machallah daf ma meusseu yeim si xam xam bimou ameh
@serignemahmoudfall51
@serignemahmoudfall51 11 ай бұрын
Macha allah, yalla ba la Serigne bi wan sa keur thia Aljana ta yokkou say lerr 🙏❤️
@seriggueye168
@seriggueye168 Жыл бұрын
Mashalla. Segn Diadji yalna ko Yallah doli yeurmandé ci barkep Cheikhoul Khadim. Tchiey bi xam xam.❤
@khalilgueye2948
@khalilgueye2948 11 ай бұрын
Hooooo kiiii yegouma won niiii dafei bayiko yallah nako yalla yeurem waxtan bou am solo ladan def
@smamemor
@smamemor 11 ай бұрын
Ndayssane Goor Yalla deugue, Bari xam xam, amm pédagogie . Yalnagnou ko Sougnou Borom fayall té dolli ko lerr.
@MamadouSeck-y5s
@MamadouSeck-y5s 11 ай бұрын
Serigne diadji tall yalla na yalla yokou ay leram thibarkee yonentibi salla lahou halleyhi wa salam
@ifm8372
@ifm8372 11 ай бұрын
Yalla nanu Yalla fayal Amine Waxtan wi amna solo lol diadieuff
@cheikhhassandiop8843
@cheikhhassandiop8843 11 ай бұрын
Yallana sa borom doli ay lieram te khareka aldjiana firdawsi doliko ndiegal ak yermand thi barke Sr touba khadimou rasol
@ousmanecisse5736
@ousmanecisse5736 Жыл бұрын
Jërëjëf yalnako yàlla Doly yeurmqndem Wakhtan Wu am solo
@papesarr9824
@papesarr9824 11 ай бұрын
Ndeysane kou bakh kou tabé ci xamxam kou yatou kou labir beury diam kou beug Serigne Touba xaritou Serigne Abdou Karim sama xarit yalnako Serigne Touba tertou aldiana firdawsi
@Fallousow-l3z
@Fallousow-l3z Жыл бұрын
Dagla s diady waxtanwi nexna amna solo❤❤❤❤
@youssouphadrametbs
@youssouphadrametbs 11 ай бұрын
Kou bakhone
@Abdoulaye-be5xi
@Abdoulaye-be5xi 11 ай бұрын
Naco yala yeureum tédjégalco.amine
@falloundaw674
@falloundaw674 11 ай бұрын
Exceptionnel !
@morfall1519
@morfall1519 11 ай бұрын
yalnako yalla dolli yérmandé😭😭
@mallawagne680
@mallawagne680 Жыл бұрын
Machaalah yalna yalla doli yeurmandem
@khatabdieye4320
@khatabdieye4320 Жыл бұрын
Segn Diadia Tall Yalna na Yallah Doli Léram aka déggone Serigne Touba👌
@SaliouSeye-cp5ze
@SaliouSeye-cp5ze 11 ай бұрын
Yalna yalla yeremco te xareco aldiana amine amine akssa fall
@sokhnangoneihthiam4830
@sokhnangoneihthiam4830 Жыл бұрын
Mashallah❤️❤️yalnako sounou borom doli ay ngeureum
@makhtarndir2253
@makhtarndir2253 11 ай бұрын
Yalnaniou borombi doly fayal s djiadji yalla si barké Mame sidibirahim fall amine
@ElhadjiFall-p8p
@ElhadjiFall-p8p 11 ай бұрын
Yala rek Moy ken hkolale hkam
@MohamedKalleDiop
@MohamedKalleDiop 11 ай бұрын
Yàlla Nako yàlla gërëm amiin
@Neymar-vb7bq
@Neymar-vb7bq 11 ай бұрын
Yalnako yalla yeureum
@DjiliveDame
@DjiliveDame Жыл бұрын
Yallna yalla yok ay léram
@khadimlo5920
@khadimlo5920 Жыл бұрын
Yalla na ko Yalla doli lérr
@mamadousene6250
@mamadousene6250 11 ай бұрын
Qu'allah ait pitié de lui djaji tall
@elbachir5892
@elbachir5892 11 ай бұрын
Lii Da Bokk Si Kemtanou Bromm Touba yii Ajji Magg Jii
@Fallousow-l3z
@Fallousow-l3z Жыл бұрын
Yalnaco s fallou teru
@sidymbaye3251
@sidymbaye3251 11 ай бұрын
AKASSA YAKONE YALLA NA YALLA YOK AY LERAM
@khadimdieng8942
@khadimdieng8942 11 ай бұрын
Alhamdu Lillaahi Rabbil Hãlamiin. Jërëjëf Seexanaa Ahmadul Xaddiim.
@MalickSarr-wr9cn
@MalickSarr-wr9cn 11 ай бұрын
🎉
@papadiop1069
@papadiop1069 11 ай бұрын
JEUREUJEUFÉ SERIGNE DJADJI TALL YALLA NA YALLA YOKK LERAM BIJAHI SERIGNE TOUBA MBACKE
@falyseydi
@falyseydi Жыл бұрын
Amine Yalahou ❤
@ElhadjiFall-p8p
@ElhadjiFall-p8p 11 ай бұрын
Hkam hkambi
@ElhadjiFall-p8p
@ElhadjiFall-p8p 11 ай бұрын
Walakhi ki amatoul
@Fallousow-l3z
@Fallousow-l3z Жыл бұрын
Nuyunalene yene wa lamp fall tv ah s diady tall daa lacku mande xawmaco woon sama rac momaco wax cone mane inage yupasse ladone setane masuma xamni daa ganu sama mbocu talibela s abdou krm moye sunu serigne
@karadioplg4009
@karadioplg4009 11 ай бұрын
❤❤
@bocardiallo1206
@bocardiallo1206 11 ай бұрын
Thieyy sama wadji. Mo baax …
@Fallousow-l3z
@Fallousow-l3z Жыл бұрын
Mane nac minumaco dama codone sene k s abdu krm
SUITE: FATALIKU SERIGNE DIADJI TALL (yalla yokku ay leeram)
1:19:01
Jazboul Mouride TV
Рет қаралды 10 М.
Serigne Diadji Tall Wahtanu Ramadan Vol 1
2:27:36
Serigne Diadji Tall
Рет қаралды 45 М.
VIP ACCESS
00:47
Natan por Aí
Рет қаралды 30 МЛН
To Brawl AND BEYOND!
00:51
Brawl Stars
Рет қаралды 17 МЛН
PART 2 JAZBOUL MOURIDE 17 10 2023 INVITÉ SERIGNE BOUCHRA SAMB
1:06:48
Jazboul Mouride TV
Рет қаралды 35 М.
Jazboul Mouride 26 09 2017 Diadji Tall dans Cheikh Ibra Fall ak Talibe
1:12:41
Diotayu Murid : Yoonu Gayi YALLA yi (deddu ak samou) 07/01/2022
1:21:02
SERIGNE AHMADOU MBACKE
Рет қаралды 24 М.
WAKHTANOU BAYE NDIAGA DIOP SI SERIGNE TOUBA AK MAME CHEIKH IBRAHIMA  FALL
1:00:14
Académie Serigne Saliou Touré
Рет қаралды 117 М.
Moustapha Diaw Beuk neek Serigne SaliouTémoignage Sur Serigne Saliou
1:20:37
intervention djadji tall 1
33:55
MakarimalAkhlaq TV
Рет қаралды 15 М.
JAZBOUL MOURIDE 26 01 2021 CHEIKH IBRAHIMA FALL ak ZIKROULLAH (BAYE ADAMA SARR)
1:20:54
BEUGUE SERIGNE TOUBA SERIGNE DIADJI TALL
1:09:24
Serigne Diadji Tall
Рет қаралды 37 М.
Jazboul Mouride rend Hommage à Serigne Diadji TALL
1:08:42
Jazboul Mouride TV
Рет қаралды 32 М.