Mane lene rek laye waax moye 32 personnes yii disliike vidéo bi Yalla na Borom bi guindi lene si sen rérr ndax li koudoul muslim saax soko degg lou xolam ame loumou yeugg wayé comprendre nagnou lene Dieureudieuf Maolana Cheikh Ibrahim Niass dieureudieuf choukran wasalam