Nidaré Ndiaye côté Guédé sama cogne ba wone ndeysann yalla na yalla yeureum soxna yeumou té kharé ko aldiana
@minarassul2539Күн бұрын
Kou haptalou d’où khaar sa Ndeye ak sa baye bañu ñew nga rayy Séne nday domou diambur ngay ray dmrm
@MouhamedBah-o9eКүн бұрын
Hana legui koudef diakhoum rek niounee dafa dof Walla damandi
@ModouMige-bu4quКүн бұрын
Dara daloko nan ray ndayam
@AchrafjoopКүн бұрын
na yon def ligeeyam mais boy bi dafa wéradi dh
@minarassul2539Күн бұрын
Lii deih laa wakh man
@WEUZ-h50Күн бұрын
@@Achrafjoopdara dalouko
@Mouhamadoundiaye-i8hКүн бұрын
Mani Li papam wax rk moosi am nk dafa mason weredi xell mais Li sa ndiogou wax mosi am solo
@Eus24-f5qКүн бұрын
Doffoul darra dalouko doff day weranté Assassin la rek
@AblayeDiop-s8wКүн бұрын
Deureum diotouko loutah niom dougn ray sén papa yi wala sên yaye yi wala sén dom yi mbokou kênên rk laniouy ray kou ray niou ray la sou amoul yên nieupay déh si ereur
@WEUZ-h50Күн бұрын
Merci
@matarthiam9572Күн бұрын
Mor Ndiaye sama xarit mangui lay massawou metina trop