FIRI GENT PARTIE 2 KOU GENT GUIS YII LI LAYE FIRI AVEC OUSTAZ ABDOU KARIM BA

  Рет қаралды 422,080

Islam Diner akhe diamono

Islam Diner akhe diamono

Күн бұрын

Пікірлер: 170
@leosguitar271
@leosguitar271 2 ай бұрын
❤salame dama guente nek maque di bjis lumière bou beurri Machallah.akh sougnou khale wa kheur mes chak foi sama dome bi sama taw bou bjiguene deye rere fofou
@LamineDaffe-o7v
@LamineDaffe-o7v 2 ай бұрын
Macha allah oustaze
@amadousow9866
@amadousow9866 10 ай бұрын
Oustaz oustaz sama yaye dafa deff bén rêve pour mane dafa degue ay thiow si biti mou guén di khol nite yi di youkhou nane Aïcha la khalé yi nioko dor bale si bir may wathiou déréte ma begone kham Loumouy firi 🙏🏽🙏🏽
@mariamlatifa412
@mariamlatifa412 3 ай бұрын
Lolou liguay boula diapou la
@MameawaFaye-go7lh
@MameawaFaye-go7lh 5 күн бұрын
Oustaz niongui laye ziare machalla Dama gueute ma nieuw thie beureup may deme MA robou louy dargou Lou takh ripe ak drete hohou thioure bima roubé aye Hale you goor Niougui yor aye wethete groubeau bena place liye darguou miggui beugue douguo si pakhame
@MameawaFaye-go7lh
@MameawaFaye-go7lh 5 күн бұрын
Dieureudieuf Sama papa ba
@AdamaBâ-e4l
@AdamaBâ-e4l Жыл бұрын
Slm oustas déma guente serigne fallu mou néke thi kow asamane bi
@aminarassoulkebe3029
@aminarassoulkebe3029 6 ай бұрын
Mane meuss nako guente
@NgoneGueye-pe1pj
@NgoneGueye-pe1pj 6 ай бұрын
T​@golfmike7587 😅😅😅😂😂ray ngama😂😂
@BaraNdiaye-ot5ls
@BaraNdiaye-ot5ls 5 ай бұрын
😊​@@aminarassoulkebe3029
@SophieFaye-t7c
@SophieFaye-t7c 5 ай бұрын
Pll​@golfmike7587
@Diallo__Dierry
@Diallo__Dierry 2 ай бұрын
Ziar nala🙏
@astoubeye2514
@astoubeye2514 Жыл бұрын
Assalmalicoum oustaz dama günte am Dome bou toudou sérigne saliou
@MansourThiam-l5n
@MansourThiam-l5n 2 ай бұрын
Dinga am doom bouniou respecte bou am tourr am weurseukk incha allah
@FinaRassoul-t1k
@FinaRassoul-t1k 2 ай бұрын
Salam Oustaz dama gueinteu niou may tak ame borom keur
@AbyKA-y9r
@AbyKA-y9r 6 ай бұрын
Oustaze déma guenett mane ak sama yaye niouy ziar habrou Seydina Mouhamed mais finiou tokk séd biy diogué thie habrou bi moniou diap bé manounio diokk
@BastyHagne
@BastyHagne 3 ай бұрын
Sallalahou aleyhi wa salam ❤️
@SelleNdoye-sm7te
@SelleNdoye-sm7te 2 ай бұрын
Sollallahou Haley wa Sallam ❤❤❤
@MariamaBa-lw7fi
@MariamaBa-lw7fi Жыл бұрын
Assalamou aleycoum Oustaz Mane dama Günte ma dem macca Di weer kaba mais aussi dafa am ay mangue sama côté
@bintadiop7713
@bintadiop7713 Жыл бұрын
Sokhna si lolou dé dég na kheweul la
@ndeyekhadylo4313
@ndeyekhadylo4313 Жыл бұрын
Dama enceinte guete 2 Serigne S cheikh AK S Al amine nék si bire wére wi ma guisko rk kheum après ma khimaliko diko wane sama nienme papa mé guissou niouko mane rk mako guiss
@Bafatoumatabinta-w1p
@Bafatoumatabinta-w1p Ай бұрын
SLM oustaz
@FatoumataBa-xh9et
@FatoumataBa-xh9et 2 ай бұрын
SLM oustas damay gente aydjene
@BassirouDiouf-h2v
@BassirouDiouf-h2v Ай бұрын
Assalamou Haley oustaz mane dama guénte
@MarieGueye-x1i
@MarieGueye-x1i 11 ай бұрын
salam geete nek ci birrr baane
@MossaneSène-e5x
@MossaneSène-e5x Ай бұрын
Salam Oustaz magui lay ziar Man déma guénte dougou si bateau niou diokhma clé yi Après ma wathie té diokhéwouma clé yi mais démaka sékh May ladié limouy firi
@MariamaDiop-s3h
@MariamaDiop-s3h Ай бұрын
Salame daye farale de images Dianne
@AssataDjiba-s7e
@AssataDjiba-s7e 2 ай бұрын
Salama laye koum oustas mane dama guinte ma nect bolo bou beureu sa, mais thi outi ligueye
@SokhnaDiouf-f9s
@SokhnaDiouf-f9s 6 ай бұрын
Dama guente toutou yalla yi nek Sama yeram ma guente soupou si tankou bay niass yi
@AwaSanokho-xx9pt
@AwaSanokho-xx9pt 11 ай бұрын
Salam dama guente sama copains AK domam
@madycisseaimesports7081
@madycisseaimesports7081 11 ай бұрын
Salam KO xam dafay Bari loll lumi gent Di door fass door yu métti pour Beugue fass bi daw mais fass bi du nagu daww s'il vous plaît 🙏
@ndeyefatougueye7959
@ndeyefatougueye7959 Жыл бұрын
Dama guint doff dimeu dakkkk😭😭
@ndoumbeniang6598
@ndoumbeniang6598 5 ай бұрын
Assalamou haleykoum oustaz dema guente mane ak sama benne collègues vétérinaires réwlé benne gayndé bou donne mattou mou am ay sekh après mou niew tedeu sama wette pousse ma dome bi mou tedeu sama wette
@amadougueye8555
@amadougueye8555 Жыл бұрын
Assala mouhalaykoum dama guénte ay khathe di ma Dakka wayé diapouniouma
@NdeyeSamb-lf1vw
@NdeyeSamb-lf1vw Жыл бұрын
0
@bakarykonate5211
@bakarykonate5211 12 күн бұрын
Khathieu seytané leu mai kom ke diapoula rk alkhamndoulilah
@SowAwa-o5n
@SowAwa-o5n 6 ай бұрын
Slm Oustaz dama guênt nioumay dakhè mais doumamana daw
@AwaBalde-u5x
@AwaBalde-u5x 4 ай бұрын
Oustaz mane damay chaque fois Di yor bb t'ai dico nampal
@RellaDiop-h1w
@RellaDiop-h1w Жыл бұрын
Slm ya oustaz guent khathie dila dakadji dagn ma bole ak khathie bih
@bakarykonate5211
@bakarykonate5211 12 күн бұрын
Khathieu seytané leu mai soula diapoulé rk alkhamndoulilah
@NdaoMbayang-y4c
@NdaoMbayang-y4c 28 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@assaneba7293
@assaneba7293 Жыл бұрын
Salam. Man demaa gent tokku ci beneen dekhe ,demaa gaddaay.
@KhadyDiop-yc6fy
@KhadyDiop-yc6fy 5 ай бұрын
Kou geuneteu nekk si dékhe di féy man ak sma dom
@GrandFall-uc9cj
@GrandFall-uc9cj 6 ай бұрын
Salamou halaykoum mane sama yaye mo geunte mou yor dom bou gor ma rombou di sangou maniko indil ma sangale ko mou dioukhmako
@NènèDiallo-h2h
@NènèDiallo-h2h 5 ай бұрын
Assalamalicoum oustaz guénete beugne you wade lane la dimba li ma si🙏🙏
@mouhameddioum2891
@mouhameddioum2891 Ай бұрын
Oustaze déma guénett di sangou nokhe mou ame malite ba paré ma guis aye ceikhe
@JahmelMatson
@JahmelMatson 5 ай бұрын
Machallah
@MoustaphaMbacke-h9h
@MoustaphaMbacke-h9h 5 ай бұрын
❤❤
@ndeyekhadylo4313
@ndeyekhadylo4313 Жыл бұрын
Salam ya ouztage dama guéte 2 serpents après ma diel yate diital léne baniou dounou souniou guinaw keur
@NdeyeSiby-w7z
@NdeyeSiby-w7z 11 ай бұрын
Dama guent gnou diamma paka 10:08
@NdeyeFall-x6c
@NdeyeFall-x6c Жыл бұрын
Mame boy mùr bii si bén xalé la dal mais xalé bii nathioul
@NdeyeKhadidiatouMane
@NdeyeKhadidiatouMane Жыл бұрын
Assalamou aleycoum man oustaz dama guent Di létou kimaye leet Di dague sama karao ak tamit ngou teuddé sama dome bou djiguene 7ans la am maye dioye Di youhou
@NdeyeFall-x6c
@NdeyeFall-x6c Жыл бұрын
Oustage dama guent asaman bi leudeuum Di guélew après mou taw.2dama guent mùr véranda bou danou .3 dama guent ay triple séch (3 jumeaux)oustage diapléma sii
@MaïmounaKa-g1h
@MaïmounaKa-g1h Жыл бұрын
Salam oustaz dama guente guéne adouna
@seydidiaw8194
@seydidiaw8194 2 ай бұрын
Niongùi ziar Al oustaz sa numéro la bougone
@RamataSambaSy
@RamataSambaSy 9 күн бұрын
Mane dama eumbe ba dix ma guenté ma ame dôme mais dieki sa rek mou dieuk di dém ramoul défoule Dara.
@AhmetToure-k3g
@AhmetToure-k3g Ай бұрын
oustas demain guente dioumaye dakhe madiape samayetak ditepe miryi
@daradjitv2143
@daradjitv2143 Жыл бұрын
Mes mane photos serigne moustapha sy lou mou si done
@laminebarrambengue6602
@laminebarrambengue6602 Жыл бұрын
bala nga commentaire del deglou bamou diekh bo deglou won do lath foto serigne moustapha bi
@awambodji2948
@awambodji2948 10 ай бұрын
OUSTAZ mane dama guent guiss serpent 3 fois sii ben guént mais serpent bii da moudié dhé nk sama frére moko réy
@laboudabocoum1484
@laboudabocoum1484 6 ай бұрын
Oustaz dema guente ma eumbou mais ci mbeuthieke le
@FatouSeye-e1w
@FatouSeye-e1w 2 ай бұрын
❤❤❤❤😢😢😢
@fatoubadji9088
@fatoubadji9088 5 ай бұрын
Sama dieukeur daffa guente mou doff
@BaoFama
@BaoFama 3 ай бұрын
Ziar Nala oustaze madé dama guente di sagou sete nakh bakhna oustaze
@diorsow2689
@diorsow2689 10 ай бұрын
Oustaz Mame dh dama gueut nékh si kaw sclarier Di wathie wathie n'a ba si soufe ki may beuge tell migui ci souf Di ma khar pour ma wathie après si la wathie gnou and dém gnouy dém ba si yague ma fak kas talou môme mou dém bayi ma
@TataTata-qr5tz
@TataTata-qr5tz Жыл бұрын
assala moualeykoum oustaz dama gente enfermé niari Gaindé ci nek
@RoseNdour-vy5vl
@RoseNdour-vy5vl 4 ай бұрын
Guette Di guiss ayy cercueil Moy lann
@FineFaye-d6k
@FineFaye-d6k Ай бұрын
Accident la khalé bi nima tanta guénal diwe mo accidenté bénerakou papam ni déna mani khamonaka si n'guéte gui
@Awandiaye-ow4zx
@Awandiaye-ow4zx 8 ай бұрын
Dama guete guiss bébé bon Sani wayi bébé d’à am 3 partie
@nafissatoudrame773
@nafissatoudrame773 Жыл бұрын
Je réve fréquemment d aller au marché pour faire des provisions
@macoumbadiop3896
@macoumbadiop3896 Жыл бұрын
SLM ouztas Mane dh dama guénte gnou diokhma gnari pakétou pointe
@seynabouthiandoum-e8w
@seynabouthiandoum-e8w Жыл бұрын
U e
@mamibessane7081
@mamibessane7081 5 ай бұрын
Oustaze Dama gũnte you diokh ma wéthiéte diokhatma billé
@yaramesene
@yaramesene 5 ай бұрын
SLM oustas dama guénton niounima sa dieukeur dafa guaniou légui ci bir guétgui may dioy am kougor kou niow dima dialé mou diokh ma 10mil après ma Diouk di nane ci ndali am kounéma diougal diouly may wadia diapou faf yéwou
@awandiaye6565
@awandiaye6565 Жыл бұрын
Salam uostas Mane dh dama guénte sama baiy wade😢
@AbsaKa-q9t
@AbsaKa-q9t 23 күн бұрын
Déma guente yégg thi kaw garap maragal wathie manane Serigne Babacar Sy walouma rek ma guisse ko mou talalema lokoyi wathie ma
@FatouGueye-jt7jw
@FatouGueye-jt7jw Күн бұрын
Dema guente rey khar
@souleymaneseck9203
@souleymaneseck9203 Жыл бұрын
Salam Dama guénte ay nak mais si bir nak yi dafa am béne bou fébar après ma réndi ko mais dérét guénoul si mome limou lékon rk mo guéne si mome ak li mou nanone
@maitremarsalla
@maitremarsalla 6 ай бұрын
Salam Mane dès dama guénete Sama Yaye Dina gnanal alors qu'elle n'est plus là (elle née plus).
@fatoundiaye9679
@fatoundiaye9679 Жыл бұрын
Mane yapp rek lay guenteu.. surtout bou niore bi..ay dibi toufè ,thiebou yapp 😅
@nafissatoudiallo4317
@nafissatoudiallo4317 Жыл бұрын
Salam cava geint yapp bakhoul dei dane nako geint ma am kouma ladj mouni ma mauvaise nouvelle ms effectivement
@fatoundiaye9679
@fatoundiaye9679 Жыл бұрын
@@nafissatoudiallo4317 ayaw bayyil lingaye wakh ..Mane deh wakh deugue yapp rek chak deux jour ..Kone deh Dina gueneu farlou si gnane souniou borome mou mousseulma 😭
@DembaBa-do7cy
@DembaBa-do7cy 11 ай бұрын
Asalamouhanleykoum guent di khoulo ak sa papa après ngua guène guis nit kou djital fasse (cheval) blanc (thiakri ak sow) mou rombe ma après may dème ba si yague guis lène niou topou sama guinaw
@idrissacissokho3298
@idrissacissokho3298 2 ай бұрын
Asalamou alaykoum dema guente goor ak jigeen du yak sama der ma khas jigeen ki ma khekh goor ki ma gaan si boppou lool la bougon kham
@SeynabouDiop-j1m
@SeynabouDiop-j1m Күн бұрын
Louma guente faté ko
@seynaboudiatta4643
@seynaboudiatta4643 Жыл бұрын
❤❤❤
@KADIATOUKEITA-r6q
@KADIATOUKEITA-r6q 5 ай бұрын
Dama guente diane ma reye ko ma guentate nek thi auto bii am accident mais ken dewoul
@BayelahatSambe
@BayelahatSambe 3 ай бұрын
Dema réve gnoumay dake bomou yang m'a naw
@MdatiosowSow
@MdatiosowSow Жыл бұрын
Sama yaye MoMA guent maye mame dome
@MatyGaye-g6n
@MatyGaye-g6n Жыл бұрын
Assalamaleykoum. Dama géuntea Ay sakh you ber Sama yaram
@WourySow-pb1mw
@WourySow-pb1mw 4 ай бұрын
Salam mane des genets bote boy yiege
@AbyKA-y9r
@AbyKA-y9r 6 ай бұрын
Mane dh gueute na gaïdé 2 fois
@zousarr7825
@zousarr7825 9 ай бұрын
Ziar nalla oustas dama guénte guiss niou ték aye légume sy sama bountou keur ak sy kanAmou bountou by sy keur guuma diakarlo ba pare sama kr niouye bath sama guara bou keur maye khouron ak niome
@RamatoulayeKa-ou3zy
@RamatoulayeKa-ou3zy Жыл бұрын
Ay way Serigne bi Sarah ma dama ginte bima diakhal dama ginte kouma diégué dadi gagniou ba man makoy soule bay diokhé sarakham
@JoachimTine-x2b
@JoachimTine-x2b 6 ай бұрын
Oustaz dama gent di labe khalé
@MarievictorineColy-f9z
@MarievictorineColy-f9z Жыл бұрын
Mane sama dome mo guénte lion.néna ay nite nioko boukh si béneu pakh après lion bi guéné ko
@NeneNdiaye-o6p
@NeneNdiaye-o6p 5 ай бұрын
Numéro serigne bi svp
@ThionganeNdeyekhady
@ThionganeNdeyekhady 6 ай бұрын
Oustaze dama guèn douguou aldiana
@MamasambaBalde-yg5ld
@MamasambaBalde-yg5ld 6 ай бұрын
Yobbaaléma
@Doyedieng
@Doyedieng 8 ай бұрын
Ouztaz dama guente guiss khalé bouniou guenné ci fosse Keur maye ladj lane la
@khadygueye2468
@khadygueye2468 4 ай бұрын
Dma gente kouy tegnedjiou
@MereNiang-pg6qn
@MereNiang-pg6qn 6 ай бұрын
Déma guéte 3 dôme yayé 2 yi sama kharite moko diourone ligu niou dioudou wate si mane
@khadidiatoudiop4197
@khadidiatoudiop4197 3 ай бұрын
Outaz dema guent kou guiguene Di diokh sama yaye benn domou Gourau Diapaléma thi
@AttaDiallo-r6f
@AttaDiallo-r6f 25 күн бұрын
Ma guénete sama borame keur disye AK samake
@NdiayeThiiki-ym3tk
@NdiayeThiiki-ym3tk Жыл бұрын
Siar mane dama guette gaïdè gou wéex deuk ak mome moumay diokh téranga gou bari bamay défal ay nit
@FatouBintouDiémé-c2k
@FatouBintouDiémé-c2k 6 ай бұрын
Rêve 2 femme enceinte
@KhadidiatouDiouf-x8z
@KhadidiatouDiouf-x8z 4 ай бұрын
Dama guente yoré bébé mais diourou mako
@nogayendoye9742
@nogayendoye9742 Ай бұрын
Dama gent ame dôme niou ngenté
@DoudouTall-h6l
@DoudouTall-h6l 5 ай бұрын
Gent khalé bou goor dem ale sama bir côté Ndeye Dior té Ama gouma dom
@DieynabaNdiath-u4r
@DieynabaNdiath-u4r 6 ай бұрын
Mane dama guente guis fasse mouy dake sama doom bou goor mate ko 3fois khawma loumouy teki
@AidaFaye-x1e
@AidaFaye-x1e 24 күн бұрын
Mane dama guete âme dôme waye dobi sama dieukeur diourouko sama domou deye moko dioure ta ko kou da fatou
@KhadyDiop-mp9nu
@KhadyDiop-mp9nu Жыл бұрын
Aslamou aleykoum ya oustas mandale damaye farare di guénte aye Diane parfois you ndaw parfois you mague
@OmarSambo-o6d
@OmarSambo-o6d Жыл бұрын
👉👂💯💕🤲🤲
@BaléFaye-z8o
@BaléFaye-z8o 6 ай бұрын
DE'MAGE'NETE AMDOME
@MariamaFall-z1j
@MariamaFall-z1j 11 күн бұрын
Dama,gutted,bene,woke,diougue,Ci,kawasaki,asamabi,Di,sikare,apresmou,ibekou,def,aye,fleur,or,maraseko,moudef,draper,or
@Doyedieng
@Doyedieng 3 ай бұрын
Salam guente teude ci lal bou am aye mélane tane 🐜you nioul maye ladj lane la
@FineFaye-d6k
@FineFaye-d6k Ай бұрын
Dama guéte khalé bou djiguéne bi nima tanta guénal ni sama dôme la niouni déna manane khamonaka
@seneawa3612
@seneawa3612 Жыл бұрын
Dama guente ay cheikh bote lene Di yalwane
@GeuyeOumar-n1z
@GeuyeOumar-n1z 5 ай бұрын
Voir manette
@AminataNdiaye-h2t
@AminataNdiaye-h2t 4 ай бұрын
Dagnouma guental ma am dom mou délou may dioy man ak qui guente
@nafissatoudrame773
@nafissatoudrame773 Жыл бұрын
Je rêve parfois de marcher pieds nu dans un endroit humide st parfois sale
@SaynabouFall-q5o
@SaynabouFall-q5o 3 ай бұрын
Machala
🛌Firi Geunte " GEUNTE Am Ay Cheikh Jumeaux Oustaz Abdou Karim Ba
4:51
Непосредственно Каха: сумка
0:53
К-Media
Рет қаралды 12 МЛН
Every team from the Bracket Buster! Who ya got? 😏
0:53
FailArmy Shorts
Рет қаралды 13 МЛН
진짜✅ 아님 가짜❌???
0:21
승비니 Seungbini
Рет қаралды 10 МЛН
L'intégralité de la sortie musclée de Moustapha Diakhaté
1:25:17
trucs et Astuces de femmes du Sénégal pour Sentir Bon
15:11
Thiesinfo TV
Рет қаралды 218 М.
Biens faits du Sourat Yacin par CHEIKH M. SAMBA DIALLO
18:08
RT2S (Radio Télévision Du Sine Saloum)
Рет қаралды 126 М.
🚨 🚨 TFM LIVE : Firi Gent - 23 Janvier 2025 - Pr : Oustaz Abdou Karim Ba
1:05:52
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 8 М.
Firi Guent  - Épisode 106 :  Rêver d'un enfant
10:56
Firi Guent Tv L’officiel
Рет қаралды 345 М.
Voici 10 Rêves qui signifie que vous serait Riche et plein de Bonheur
7:37
Непосредственно Каха: сумка
0:53
К-Media
Рет қаралды 12 МЛН