Flis de Balla craque et Fond en larmes devant Balla Gaye 2 "Lima metti…"

  Рет қаралды 31,061

AL BOURAKH TV

AL BOURAKH TV

Күн бұрын

Пікірлер: 75
@IbrahimaFall-u3z
@IbrahimaFall-u3z 20 сағат бұрын
Wa guédiawaye yalna Allah mayléne ndam inchallah thi barké yonentibi PSL 🤲❤️
@bellingham-k6t
@bellingham-k6t 21 сағат бұрын
Fils de balla yalla na yalla May ndam si barki s Touba ❤️❤️
@sambaba683
@sambaba683 21 сағат бұрын
Mes deux lutteurs ndeysane que le meilleur gagne aamiine
@MalickSouware
@MalickSouware 19 сағат бұрын
Ndeysane dagno yarou
@CheikhDia-v8h
@CheikhDia-v8h 5 сағат бұрын
Fils de balla seul domou guediawa 💛💙
@CheikhIbraFall-u2r
@CheikhIbraFall-u2r 21 сағат бұрын
incha'Allah yalla nanioukô féké talko diène kaïré 🟢⚪ yalla nkô yalla maï ndam si barké seydina Mohamed psl ♥️🫶
@diop3575
@diop3575 22 сағат бұрын
Yalle nala yallah May ndamm ❤❤
@DameNiane-jb8se
@DameNiane-jb8se 22 сағат бұрын
Aziz ndam rekk inchallah❤🎉
@babandiaye5607
@babandiaye5607 16 сағат бұрын
Lat diop sathe leu ❤ na fay milliard domhrame la Lat diop sathe leu
@papamakhtarniang
@papamakhtarniang 11 сағат бұрын
Mbeur dieum si haré di dioy c mauvais signe dé on verra la suite inchaallah
@beugeudiame2019
@beugeudiame2019 18 сағат бұрын
omanka mo seytané guediawaye
@MDbousonko
@MDbousonko 22 сағат бұрын
Bilahi xôl bi mo zed Rek
@MoussaMbengue-h4n
@MoussaMbengue-h4n 21 сағат бұрын
Diene mola meune dimanche guay sip😂
@MoussaKane-tm6ne
@MoussaKane-tm6ne 22 сағат бұрын
Kou né fils de balla amoul feme mou mbeur rek lale j'aime
@dembaztarkinda8270
@dembaztarkinda8270 20 сағат бұрын
Y’a niak diom boude lat diop ngay dioye yalna la douma dann la
@MaimounaSow-s4b
@MaimounaSow-s4b 21 сағат бұрын
Guediawaye seul 💛💙🗡️⚔️😊
@ismailadiallo4939
@ismailadiallo4939 18 сағат бұрын
Lat Diop sathe leu way mbeur ngua gor gorloule si lamb DJI lalaye conseiller merci
@AlonsoSone
@AlonsoSone 17 сағат бұрын
Alalou askane bi la lén dane diokh
@modousall2693
@modousall2693 22 сағат бұрын
Waw mom lane lay dioye😢
@mouhameddiop4870
@mouhameddiop4870 22 сағат бұрын
Mo wakhon balla Gaye samba alar lolou lay dioy 😂😂😂
@modousall2693
@modousall2693 20 сағат бұрын
@@mouhameddiop4870 wa lolou lousi diar dioy wala balla dako door
@khadimibnmordieng5685
@khadimibnmordieng5685 17 сағат бұрын
Ya saytane dh monane dafay dioy😂
@FayeFallou-t9v
@FayeFallou-t9v 21 сағат бұрын
Khaliss rék takh Mouy dioye late diop mbér da goré nonou😂
@BeckayDiop
@BeckayDiop 22 сағат бұрын
Mann khawma loubakh mais rastaman bi damako yerem bilahi
@baraleye4749
@baraleye4749 21 сағат бұрын
Mbaadu sathiyi ngay jooyal ana justice
@SerignemodoumbeneDiouf
@SerignemodoumbeneDiouf 20 сағат бұрын
Mom lamb dji yeup dako dioye 😂😂
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 22 сағат бұрын
Lahat diop na fay milliard youmou teye diaroul dioy bou fayoul dou gueineu
@baraleye4749
@baraleye4749 21 сағат бұрын
Balla mooy sama mbeur waayé diène mola mane
@youssouphadiop3327
@youssouphadiop3327 22 сағат бұрын
Ki dem gnouy gnuuss ndayam ngay diooy Ana mbeur aka diooy avant combat 😢😢😢
@moustaphanoble1231
@moustaphanoble1231 17 сағат бұрын
Boy 😂😂😂
@moussadia7880
@moussadia7880 8 сағат бұрын
lat diop lay dioy
@AlonsoSone
@AlonsoSone 17 сағат бұрын
Late Diop sathie la
@mouhamedmbodji1674
@mouhamedmbodji1674 22 сағат бұрын
Bu dannu ni wa guédiéwaay la 😅
@mouhamedndiaye2111
@mouhamedndiaye2111 20 сағат бұрын
Balla moy sama mbeur mais boy yi lolou motakh douma faral sen ndeye balla day sonn si niom baparé koussi daanou diko garouwaalé meunougne beuré baparé beuri wakh balla loum am mokko liguey kouko beugue am da ngay liguey
@PulloKa
@PulloKa 10 сағат бұрын
Taper bi 123 yéne mbeur yi di dioy goor dou dioye
@galsen1st409
@galsen1st409 21 сағат бұрын
Bouféké Lat Diop ngay dioyal, yalna la Diene Kairé daan 😂
@MamadouSow-w2x
@MamadouSow-w2x 21 сағат бұрын
😂😂😂😂
@dembaztarkinda8270
@dembaztarkinda8270 21 сағат бұрын
Amine waye boude lat diop motakh nga dioy yalna nga danou😂😂😂
@chocsevenements8990
@chocsevenements8990 21 сағат бұрын
Copine ioe weiro dei😮😮😮
@abdoulayendoye1803
@abdoulayendoye1803 20 сағат бұрын
😂😂😂😂
@bassdiokhane1472
@bassdiokhane1472 20 сағат бұрын
Man dé môme la farall damaye niariy mbeur la sou féke lolou la yall nanou ko daan latte diope fi la né won lokon néx mou wakh ko dome diammbour yi
@BathieNdiaye-l6w
@BathieNdiaye-l6w 21 сағат бұрын
Kiii dafa tiiit rek 😂😂😂😂
@modousarr8848
@modousarr8848 19 сағат бұрын
dafa séd niou sotiko ndokh lolou lay dioy
@AlhadjiDiop-et9vd
@AlhadjiDiop-et9vd 20 сағат бұрын
Deffa am pression de trop
@babacarkane2552
@babacarkane2552 20 сағат бұрын
Sa tada yaye ak lat diop😂😂😂
@MamadouCisse-wv8hy
@MamadouCisse-wv8hy 20 сағат бұрын
Kii loumouy dioy nii
@moiizasankhare4096
@moiizasankhare4096 22 сағат бұрын
Fils de balla loumou deumé ni hana sa sérgne mo wakh danguaye danou guéye dioy ni 😢
@MamadouSow-w2x
@MamadouSow-w2x 21 сағат бұрын
Mome la faralone mes mouy dioyal lat diop nak😢😢faratoumala😂😂😂nak
@amarsakho7079
@amarsakho7079 21 сағат бұрын
Barkep serigne bassirou mbacke Fisl de balla moy Dann dioyi Foko suisse Ndam lou sad gouyou laye andal barkep alkhuran TÉ BAYILÈN BA COMBABI DIAL
@falloumendy370
@falloumendy370 20 сағат бұрын
Yaw khamo sakh loy agné souba
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 21 сағат бұрын
Flis de balla yaaa meune yaa eup dolé
@fa10657
@fa10657 22 сағат бұрын
Amal diom daan rek
@MortallaGueye-t6z
@MortallaGueye-t6z 59 минут бұрын
Boy mane yaw la farale dè mè boule dioye ndakh Lat Diop Domèram bou bonela
@MamecheikhdiopDiop-i1d
@MamecheikhdiopDiop-i1d 21 сағат бұрын
Man mam cheikh fis de bala bo dano d'où ma bétte koy wou ti ndam di dioy bo danou wé bétou ma 😂
@MoussaTraore-v5f
@MoussaTraore-v5f 20 сағат бұрын
Ioe am nga place si dof yii
@ablayecisse5994
@ablayecisse5994 21 сағат бұрын
😂😂😂😂😂😂
@Steven-ul8pw
@Steven-ul8pw 21 сағат бұрын
Sa Rangoone yi Dimanche Yallna Yokku Ki Mongui Dioy Nguén Koy May Lay Nanko Ay Lath Diop Xawma Kutah Xamolen Tous Rk Mana Nek Amna lénén luko Taxa Dioy Ay Vrai Nular Nguén Kw mé Yallna Diene Daan
@Leuzsonko
@Leuzsonko 22 сағат бұрын
Yako meun fouff bilay fi dousa place danal ki bombardie dieul la ou eumeu sene?
@Mo13092
@Mo13092 22 сағат бұрын
Bombardier mane? 😂 kokou retraité na, eumeu sene beugoul Alioune di dieul Fils de Balla. En plus Fils de Balla dafay danou dimanche inshallah
@mawondiaye1600
@mawondiaye1600 21 сағат бұрын
Kii lat diop sathie bii motakh muy diooy? Amal diom té nga gueum sa boop
@bambadiop7928
@bambadiop7928 21 сағат бұрын
Lane moy « goor du Jóoy » ??? Yen doul way.
@papombaye6979
@papombaye6979 22 сағат бұрын
Défaite lay sentir ki dou mbeur amoul Damay mbeur lamb amoul yereumetou nay ndaye goré point ya lékeu avance 👎
@abdourahmanesindidi1818
@abdourahmanesindidi1818 22 сағат бұрын
Dou mbeur de mais ay champion confirme la daan ❤
@cheikhndiaye433
@cheikhndiaye433 19 сағат бұрын
😲😲😲😲😏😏😏😏😏 l'arme de crocodile tu es en train de pleurer pour une voleur 😡😡😡😡😡😡👎🏾👎🏾👎🏾👎🏾👎🏾
@moustaphadiakhate7165
@moustaphadiakhate7165 19 сағат бұрын
Tu n'est pas confiant fis
@lounekhwayedeffsenegal6165
@lounekhwayedeffsenegal6165 21 сағат бұрын
Ndam rek
@HamidouDiallo-v3k
@HamidouDiallo-v3k 19 сағат бұрын
Psychologiquement il me semble qu'il n'est pas apte un fils de balla trop mou
@babacarndir6064
@babacarndir6064 21 сағат бұрын
😂😂😂
Tousse extraordinaire de Flis de Balla avec Balla Gaye 2 et Sa Thies
17:46
Какой я клей? | CLEX #shorts
0:59
CLEX
Рет қаралды 1,9 МЛН
🛑Direct - Open Presse Siteu bou ngor
AL BOURAKH TV
Рет қаралды 382
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 44
47:46
Pikini Production
Рет қаралды 109 М.