Bakary c bien boul wakh lou bakh ci modou c tres bien dioxol avantage yeup siteu , nakh yaw ko faral mou danou,modou y'Allah moguikoy soutoural ba legui
@ngourambow2375 ай бұрын
*NOUS SOUHAITIONS UN GRAND SUCCÈS A MODOU KHARAGNE LÔ NOTRE ROI DES ARÉNES ET UN VICTOIRE ÉCLATANTE SUR SITEU - AMÎNN YARABII*
@SeynabouTouré-k9u5 ай бұрын
Je ne sais pas pourquoi ce Bakary qui ne connait rien sous estime toujours Modou lo mais incha allah Modou xaragne lo dinala rousslo incha allah
@falloumbodji30625 ай бұрын
AK balla gaye
@volfroitfall87855 ай бұрын
Sawayy Mane mangui tokk si neenn dama tiit Modou danou
@Souley_Frezy_jr5 ай бұрын
Bacary dafa kham Siteu, loumi wakh fou lérr lako ték❤
@mohamedndiaye56035 ай бұрын
Yalna yalla ndam Modou lo ❤❤❤❤
@samboulayecamara88075 ай бұрын
Yalla bou bakary far si modou lo lolou dh moni djikk nakh meusouko farale modou lo di am ndame rek
@LamNdiaye5 ай бұрын
😊Modou lo rek
@Murlitmct_y15 ай бұрын
Coach cla premiere fois que je ne suis pas d'accord avec toi modou lo est tres malin
@Souley_Frezy_jr5 ай бұрын
Siteu kassé ❤🦁
@VieuxSeck-hw6mi5 ай бұрын
Bakary mbeusso begue modou lo mé mome lafii yalla tékk
@hamidoudiaw71775 ай бұрын
Mei yalla meun nako folli
@Cheikhasow3 ай бұрын
@@hamidoudiaw7177yalla modou la farale
@MamadouDieng-qp5fp5 ай бұрын
Walahi Modou lo il est le meilleur mou nékh léne mou nakariléne
@ngourambow2375 ай бұрын
*Ce chroniqueur parle toujours mal sur notre champion Modou Lô mais Dieu merci ce n'est pas tes commentaires qui va nous choquerr/-Iinchahalahou notre chér KHARAGNE gagnera ce combat Aminn Yarabii*
@ametibnmalickndiouck46745 ай бұрын
Inchallah ❤
@mohamedballadiop60855 ай бұрын
Modou mo dane ki dane ki dane Siteu ( modou mo dane Eumeu bi dane Sa thies bi dane Siteu).. Kone Modou kholoul sakh siteu. Coach le jour j inchallah ngey comprendre
@yatmaseck30565 ай бұрын
Pour dire vrai bakary mon guen khamni modou est mille fois plus prêt dans tout les cas dafa fekni yen niar niep manolén wakh si le roi
@OuleyTendeng5 ай бұрын
Siteu yalla nako yalla maye ndam inchallah si barke yalla akh yonenth bi
@khadimmbacke37335 ай бұрын
Yalla Miy mayé ndam yalla na May ndam yalmine bi❤❤❤
@OuleyTendeng5 ай бұрын
Amine 🙏❤
@aablayesy4095 ай бұрын
Amine ❤
@BabacarDiop-on5ci5 ай бұрын
Modou lo yalla nako yalla may ndam inchallah
@laminjagne72545 ай бұрын
Modou Lo ❤❤❤❤❤❤
@diallomamadouassane92925 ай бұрын
Vous ne comprenez pas Bakary louko metti moy Modou lidjeunti woul ndeyeme
@msn_pro80545 ай бұрын
T’as tout compris
@ranebykawsara88775 ай бұрын
Situé lamb ji bakou rek lasi ame!!! Bakari depuis wa diamaguene tegal meti daga routh
@mabeyeba33505 ай бұрын
Ki Day foe khelam bakary modou mo moun aller ak retoue
@JeanNoëlMendy-u6e5 ай бұрын
Coach mousso diokh modou favori de ama boy niang à siteu
@lhomme_fort5 ай бұрын
Coach Bakari ça data yaye chaque jour
@SauraDiop5 ай бұрын
😂😂😂
@momardiallo16095 ай бұрын
Mann Bakary meussouma hamni comédien leu koiii😂😂😂😂😂😂
@malicksarr43095 ай бұрын
Fadam l'écoute est important dans un débat
@diallomamadouassane92925 ай бұрын
Y’a meuna fene bakary
@MameSow-vp7rj5 ай бұрын
Modou lôooooooooo ❤❤❤❤
@CheikToure-cl2jd5 ай бұрын
Modou lo Yala n'a yala Maye ndame
@ametibnmalickndiouck46745 ай бұрын
X lo reik inchallah ❤❤❤
@MohamedThioune-p9k5 ай бұрын
Bakari linga wakhon modou lo kontour Ama faté wounouko
@MrFayemanou5 ай бұрын
😂
@biranekonare43585 ай бұрын
Kii mom mo dak fain senegal
@OmarCiss-vf2xl5 ай бұрын
Situé ❤🎉👑
@sambagora78485 ай бұрын
Bakary aka respecter tarkinda yi .dou gneup guaaye attaquer dèh😂
@DjilyDiakhoumpa-wk3no5 ай бұрын
Modou lo mo meune wa diamguene dagay fènne rèck
@madembatoure70055 ай бұрын
Lima meti rek moy inchalla sou combat bi dessei 3 jour digua deif sorti nai siteu amoul beine chance si combat bi
@abdoulatifdiop56405 ай бұрын
Bakary môme 😮
@ametibnmalickndiouck46745 ай бұрын
Modou ilfo mou michoui fi mbeur leik ko ngènn dora nangoul modou
@MamadouElton5 ай бұрын
Bakary comédien damal wouyou wa mma
@محمدعبدالله-ص5ذ5ف5 ай бұрын
Bakary da begue sacrifier siteu😂 modou lo rek yallah bakhena
@sarrabdou30405 ай бұрын
Danguène wara khamni Modou lô mo diéllale boppam Combat bi téylènne rekk
@abdoulo77525 ай бұрын
Siteu Fingénko Ték Agagoufa Siteu Kou Manoule Dane Boye Seye Menoule Dane Gouygiu Menoule Dane SaThies Menoule Dane Lac2 Nganane Ndanane La .Ta Ngi Ngépou Xaragne Lo Moléne Mane Fouf Bakari Khamo Dara Si Lamb
@becayepreuvendiaye9225 ай бұрын
Bakari wakhou Kou sokhor gaye wakh Modou lo sa papa leu siteu champion leu mais nioroul🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@superfoottv22775 ай бұрын
Bakary danga beug diay combat bi rek comprendre nala
@feuthebest105 ай бұрын
Combat bi Modou lo doulo watt len yen gnep Modou lo lo meun fouki siteu boulen gnou sonal
@souleymanebadji95965 ай бұрын
Siteu ak bane modou lô lay dadjél c ça la question ? Modou lo chaque combat il vient avec une autre fasceite
@AwaDieng-ff5od5 ай бұрын
Bakiry néké khamo dara weur na yalla tay lako confirmer démal outy xaliss mo geune ly
@salioudiba27715 ай бұрын
Kay ma wakh la fi lou modou di beurre ak sit combat ak gris 2èmes combat bi loulou day derange siteu
@ametibnmalickndiouck46745 ай бұрын
Dakoy ndioss di dougou di guènneuh
@ndiagandiaye20335 ай бұрын
Siteu day danou
@aablayesy4095 ай бұрын
Siteu day dane modou lo retourner si ama inchallah ak Ay sa thies inchallah
@Diaz4265 ай бұрын
Siteu deh menoul dane petit lo sakh
@bayemodoutoure41695 ай бұрын
Bakary koumfarar mou danou
@abdoufaye83825 ай бұрын
Ki lamigne bé reuy rek amoul kham kham
@khadimfall9795 ай бұрын
X lo est Meilleur ke Siteu
@tramatadrame58935 ай бұрын
Modou déi damay ragal mou deg li mer dorr Siteu bamou kheum 😂😂😂
@محمدعبدالله-ص5ذ5ف5 ай бұрын
😂😂😂
@mbeuss.talibe.bamba.5 ай бұрын
Siteu késsé ndam Rék inchallah 🎉
@khadimfall9795 ай бұрын
Fadam a raison
@biramesarr16015 ай бұрын
Modou lo sou xéxé té thiaxanoul lambji am dédieu
@matalydiop65565 ай бұрын
Modou lo c'est la modou lo 😂😂😂
@PapamedouneThiaw5 ай бұрын
Kouy takk nguimb si lamb dji Siteu mola dakk beurè🔥🔥🔥🔥
@papipapi3445 ай бұрын
Sa thies nokk ko gouye gui nokk ko lac de guiers niouss ko ngani mo dakk beuré Siteu moy sopp défaites 🤣
Niep niogui wah siteu moussoul dan VIP mais si modou lo lay nieuké
@BabaGotze-en8mt5 ай бұрын
Coach bakary mi Faroul féne nak😂😂
@omarba22035 ай бұрын
Bakary uow chaque combat modou lo gua fènn do nopalou
@Deggou5 ай бұрын
bayiléne ko mou fare ak siteu nakh ki koumou faral mou niak😅
@djibingom56685 ай бұрын
Bakary taye doullll gua doullll bou raye
@PapamedouneThiaw5 ай бұрын
Modou Lo sou ladione Papa Sow Dou dieul SITEU😂😂😂
@simofall74965 ай бұрын
Modou ladioul ama bimouy dieul papa sow
@superfoottv22775 ай бұрын
Bakary da melni niemé woul wa siteu yi
@CartelBii5 ай бұрын
Oh ndeysan bakary complexe la da ragal tarkinda yi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@morgaye95825 ай бұрын
Il me semble que bakary mo yor siteu si lamb ji d’après ses dires il est bien bakary mais son défaut c’est qu’il se croit supérieur à tout le monde mais comme le dit bien Bour guewel Modou lo c’est Modou lo
@mrdiengpatronvoyau50405 ай бұрын
Vigilant bakary je peut être d'accord mais niow tiyè bopam sa mom dangay doul
@ousmanendiayeba68775 ай бұрын
BILAHI SITEU GNII YOFF LAN LA BEUG YOBOU GNII BAMEL LAN LA BEUG GASLOU BOOLEN DEGLOUOO
@niomrelo19595 ай бұрын
Kii esk khamna modou lô
@JuleSadio-fh4gn5 ай бұрын
Bakary bako tarkinda yi diko wo diko menancé di saga ndeye ba légui dalén di néxal 😂
@MoustaphaFadiga-jy3dr5 ай бұрын
Bakary coach Thiaga ngua nopile
@MamadouKa-h2k5 ай бұрын
Siteu meunoul Sakh daane gora sokh
@mbayendiaye50335 ай бұрын
Mbacké fay😂😂😂
@salioudiba27715 ай бұрын
Dem len demande omar fall momo kan moye modou lo boy guisso ma kou si mom modou lo kou doul omar fall momo lamb lala wakh
@MasseneDieye-op9fq5 ай бұрын
Wakho fi dara bakary
@AtoumaneNiasse5 ай бұрын
Bakary Liga wara déf di wakh wakhou nit ak sport
@ElhadjiGaye-eh9xk5 ай бұрын
Pathé baldé ak pikine Dakar nioy sarakhou Ama
@mbackegaydelserignembacke83355 ай бұрын
Yw ngani siteu xaroul wone beure ak roi ba nopi ngani lambji modou amouthi dara yw eska yangui xalaat lingaye lo xaarout parewoko ba nopi guena pare lolou waxou doff la
@bigdia61875 ай бұрын
Bakary mom problem mam mooy daa xawa meun doul 😂😂😂modou dou sama mbeur dh wayè kouy bagna doul xamal looy waxx 😂
@amethndiaye22145 ай бұрын
Bakary doule kat la seytané la balama déh mouy niodi coach té dou deujeuw ndm
@azoubrat220brat95 ай бұрын
Modou lo siteu c est Pas un combat waay lamb legui leepp business la....
@hassimdiallo52035 ай бұрын
Backry hamo nday dara pourquoi nguén dii lamlamé champion wou Modou Lo ba léguii danguéne nday sohorr recc
@amethlamine97725 ай бұрын
Ah saway wakho sport dh Siteu meune na raw bombardier wala lac 2 wala eumeu wala ama combat bi dou masse wala rallonge siteu wow kong la wara indi ak khol bou baax parck contre lac2 dafa sonou.
@ablayegaye78485 ай бұрын
Bakary iow Modou lo lane lala dèf yaw kou sokhar gua ya bone way
@abdoulayendiaye61805 ай бұрын
EUMEU SÉNE FOUMOU DIAR BA DAKEU BEURÉ MAMADI NDIAYE AK MODOU LO?MODOU LO WOURÉ LA DÉF EUMEU SÉNE DANE KO CI BEURÉ MALGRÉS TOUS LÉ CLÉS TENTÉS PAR EUMEU SÉNE MAINTENANT NIOU BEUG WAX MO DAK BEURÉ SENEGAL SOYONS VERIDIQUE WAY
@ModouMbay-f4g5 ай бұрын
Fadam degloul Lila Bakari Di wah
@ousmanegaye29025 ай бұрын
Fadam déll Ndeye deglou
@sambagora78485 ай бұрын
Modou😂 Lo doula sakh bayi khèl. Doula😂 wo telephone kom mbeur you amoul fouleu yi😂 fadam so beuguè niveau kawer boul wakh ak dof bi si lamb way😂
@alioundongo50295 ай бұрын
Bakari modou ama fatei wougne ko ay sey doul you bari fi gua wax ama day dane modou
@silencieuxbouyant96875 ай бұрын
Modou lo meune n'a beurei trop tei ndanane le crx en plus newoul dooler
@bayealladieng58105 ай бұрын
Backary je t'aime bien mais sitteu amoul benn atou sa way 😂 lo rek