SUN CHAMPION COMME EUMEU SENE SO TAXAWÉ NI DEFOUL DARA CI LAMB CEST DU MANQUE DE RESPECT TOTAL
@papediouf80926 ай бұрын
Yaw saxe xamo ligay waxe
@papediouf80926 ай бұрын
Franc j n sais pas kii foumou tothieu kii amoul xame xame si lamb
@3mara166 ай бұрын
Sport dou affaire de nekhel , ça c’est une mentalité de Sénégalais. Lui, il mérite sa chance avec les poids lourds, il l’a prouvé et il a raison. Prenez exemple sur le MMA et l’UFC chacun prend sa place quand il a le niveau
@mouhamedkane13866 ай бұрын
Au Sénégal, on est trop dans le sentimental
@LeprinceVegeta-f6i6 ай бұрын
@@mouhamedkane1386 sénégal key trop nafekh plutot comme yêne
@LeprinceVegeta-f6i6 ай бұрын
té sou reug reug wahé nguene né dafa rêw té kii mo geuneu pire
@georgesmendy80216 ай бұрын
Franc ndiago yalla nako yalla dooli soutoura
@LougaLo-pl5jr6 ай бұрын
Amine yarabi 🤲🏻 🤲🏻 🤲🏻 ❤🥰
@ismailaathj25006 ай бұрын
Iow eumeu boula dané fan lakay yobou eumeu lamb meussoulen bolè doussa morom dangay nian chance niou mayla yaroul rek niou mayla chance ton genre de communication meunoula may adversaire ci kaw katal sa nday yarou
@nblbasse79146 ай бұрын
Il est très intelligent ce fran Nagne bayi xél Bou bax si lou miy wax. 99% si sport ley waxé. Il es respectueux
@saliouthiam24626 ай бұрын
Yaw one rek mbeur dane ko ragal nafékh yi di wakh naane daa rew
@technewsafrica12636 ай бұрын
Eumeu sene da beugg nakh boy yi indi affaires de respect AK rousse Comme ça boy yi am kersa si l'amb dji mou nakh leine dane leine Motax beugoul dieul franc
@karibafamily99186 ай бұрын
Franc t'es une fierté de tous les manjacks d'ici et de la diaspora
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Je confirme frère
@nahumgomis56516 ай бұрын
N'a djakou dika fouuurre
@benzdictenobalegomis61396 ай бұрын
Soutenons nôtre frère ❤🎉🎉
@adolphavelinopreira58696 ай бұрын
Pas tout les manjacks tw oci. Tu l’aimes c bien mais ne mets pas tout le monde dans ton lot
@AdolpheGomis6 ай бұрын
@@adolphavelinopreira5869 sa aussi ont ni peux rien si tu préfère un frère de même ethnie que quelqu'un d'autre ont ni peux rien considère toi comme quelq'un qui en fait pas partie désolée sa ne changera rien que franc soit motre fierté nous Manjakou d'ici et d'ailleurs dommage que tu t'apel Adolph
@cheikhfayedabakh4686 ай бұрын
Fara doumou parcelle ❤️❤️❤️❤️fara yafi neke yaw rk lay topou
@SoftlSotfl6 ай бұрын
Franc je l'ai toujours dit negn ko bayi khel. Il est très fort et il lutte intellectuellement et il est très souple. Mais c'est l'heure de confirmer et de monter negn ko bolé si VIP yi
@Diouf-chroniqueur-Lamb-Lutte6 ай бұрын
Les journalistes il faut dire la vérité eumeu d'où champion d'Afrique franc a raison
@sportboum7046 ай бұрын
Ambrass sarr milen donn yobou équipe nationale...nena direct Eûmes séne mo nek champion d'Afrique et Franc était champion cdao..
@moussacolydiam77246 ай бұрын
Vas répondre a l'ancien entraîneur de l'équipe nationale
@MamadouGueye-q7h6 ай бұрын
Kou beurewoul ak sa Thiès ak Ama balde ak boy Niang ak reug reug ak lac de Guiers ak gris bordeau ak eumeu Sén koula toude champion daf laye nah
@AdolpheGomis6 ай бұрын
Nio ngiou nieup ame naniou défaite thi lamb j
@sonkofocus2024-ph4hv6 ай бұрын
Khamo sport
@AdolpheGomis6 ай бұрын
@@sonkofocus2024-ph4hv ya khame dieuleul leup entou ça limala wakh dafa leer ngi ngaye wakh yeup dégue naniou mounial
Franc futur roi la laulou moye deugue il est très fort machallah
@TraoreHarouna-cd6oc6 ай бұрын
Kii mo geun dof nieup ndeketé,bo amé 5 defaites waro nek roi des arénes,yanguii commencé sof nit gnii,eumeu sén je suis pas un fan de lui mais c'est un grand champion que tout les lutteurs respectent,koula deg khamnii dangey wout combat
@niangelhadjiabdoulaziz89306 ай бұрын
Ce n'est pas une question de champion. C'est de cette manière que tous les sportifs de combat parlent. Eumeu Sène sou beuguei kuko tagg n'a Dem défi mannequinat
@cheikhhane40936 ай бұрын
Khana yawla sof man dh sofouma 😂
@TraoreHarouna-cd6oc6 ай бұрын
@@niangelhadjiabdoulaziz8930 eumeu beugoul sakh dii wakh cii ay palmaresam les faits sont là fékké naniou lep
@TraoreHarouna-cd6oc6 ай бұрын
@@cheikhhane4093 sa wadjii dey wout kouko sarakh combat té prouvéwoul
@gamousacisse93066 ай бұрын
@@TraoreHarouna-cd6oc0 défaites boul faté😂😂😂
@mamesambaGueye-i5z6 ай бұрын
Vraiment fran amo réspé Billahi
@MasseneDieye-op9fq6 ай бұрын
Kou wakh vérité niouni dafa rew
@momoseck16176 ай бұрын
Très indisciplinés
@koulaalhakk89756 ай бұрын
Lamb j amoul repsect eumeu sou beugué respect na bayi beurré kone😂😂
@ModouSamb-tx3us6 ай бұрын
@@koulaalhakk8975bilay na bayi kone
@koulaalhakk89756 ай бұрын
@@momoseck1617 eumeu dou champion d'afrik dou touss🤣🤣les archives sont là
@alphousseyni94276 ай бұрын
Eumeu sène bou beuguè dèggueu wakhe diou nèkhe na dème liguèye si bureau Franc mo mom lamb ji
@bandjia7986 ай бұрын
Franc n'a diox respect grand yii bo beugué âme khaliss
@saliouthiam24626 ай бұрын
Dani lamb dougn nekhal kene
@armandmendy63756 ай бұрын
Deug la wakh c koi le problème ana mank respect bi
@awadiongue54346 ай бұрын
Thiéye ndiago mame ckhiekh Ibrahima fall baye fallou mame ckhiekh Ibrahima fall francky❤❤❤❤❤❤❤❤❤amal diam
@shiekhibrambackehdarboe75576 ай бұрын
Franc kesse Parcelle ayee ndam rek inshAllah 💯♥️🙏🏾👌🏾🔥🔥🔥👌🏾🙏🏾♥️💯
@amadouyorodiop91156 ай бұрын
🎉🎉🎉Franc il est le meilleur de ça génération dafa lérr kou beugue danou athia dieulko 💪Emeu sama Mbeur la mais day esquiver ndiago Or bi de mon point de vue ki kafoul day Mbeuré basi vent 💨 bi 🫡 khaliss la Emeu beugue caché bou douneu bouy téw moukay dieul il a rien n’a prouver mais attention ⛔️ Franc dakoy freiner dh 😂
@Babacar146 ай бұрын
Franc vrai Sportif leuh bilaay instant bi daa yeukk dolémmm barkii Al khouraan xalé akh makk yeupp la yamalé 😂
@AdamaKorr6 ай бұрын
Wa legui reug reug nak
@Babacar146 ай бұрын
@@AdamaKorr Reug Reug bataay mo bagnn Combat bii😂wayé tôt ou tard dinaa aam inshallah 🫠🙏
@Aïtaseye6 ай бұрын
Franc Seul❤❤🎉
@chakasen3996 ай бұрын
C'est faux ! Tu n'es pas champion d'Afrique ! Tu es seulement champion de la CEDEAO !
@sonkofocus2024-ph4hv6 ай бұрын
Khamo gate nopill
@sadia2466 ай бұрын
Yangui dioum dé
@benzdictenobalegomis61396 ай бұрын
Sawaye del topou informations yi bok CEDEAO moy Afrique di 🤣🤣🤣
@benzdictenobalegomis61396 ай бұрын
@frankal5876 gueno ma kham limaye wakh donc yaw aye nopi
@oumarba41546 ай бұрын
Cedeao moy laan
@kansalatv10144 ай бұрын
Je te supporte
@kharagnembaye59586 ай бұрын
Franc sa thiés combat bou nékh la
@moussadieye57026 ай бұрын
Sa thies gnemewoul Franc deh. Défaite lay bagn
@serignemansourtoure866 ай бұрын
Sa thies xalatouko sakh 😂
@moussadieye57026 ай бұрын
@@serignemansourtoure86 t'as bien compris. C'est ça nak🤪😅😅😅
@lemzodiakis9456 ай бұрын
Franc c'est un vrai comédien
@boubacarboiro58136 ай бұрын
Je suis daccord avec Franc Mbeur bou ndaw moofii meune dieulè mbeur bou magg c'est le sport apres et puis c'est l'argent ils cherchent eux tous
@ShiekhjobeTijan6 ай бұрын
Dafa wara jel Faran de loulo moy lambo bi Nepo di khar nk😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@mouhamadoumdiouf41816 ай бұрын
non franc vrema supporté nala mai ligay wakh ni dou wakhi nite kou bakh Eumeu nékhna roi yené ko lolou ga niane yalla def plan de carrière bou mél ni bosou Eumeu si ay atte
@Dpp2056 ай бұрын
Franc nianoul yalla def carrier bou melni bou emue sene
@chamousman27266 ай бұрын
@@Dpp205waw
@fallouniang34386 ай бұрын
Saway khana beugo franc 😂😂
@cheikhoudamba6 ай бұрын
Wakhou nafékh rek ngafi wakh iow faralo franc
@saliouthiam24626 ай бұрын
Niaanou niou yalla palmarès de eumeu séne 9 défaite la boot d 😂😂😂😂
@Infidèle246 ай бұрын
Franc seul❤❤❤❤❤❤❤❤
@fanfanbodian76706 ай бұрын
Franc sama mbeur nga mai fok nga changer sa communication diokh thieur eumeu
@alymarone46816 ай бұрын
Waye louye lolou ki si lamb laye wakh li grawoull srx moh
@fanfanbodian76706 ай бұрын
@@alymarone4681 na xolate communication bii rék ndax sport ak respect nio ande
@@alymarone4681lougnou wax nguèn toudou si bg2 😂 batay bokoul bg2 da done sò di ambiance mes mod lo yag nafi saga mbeur
@fanfanbodian76706 ай бұрын
@@alymarone4681 wakhou supporté rék ngafi wakh🤣
@DTFTV6 ай бұрын
Pour man Ki dafa Sokhor 😮😏😡
@babsdia15056 ай бұрын
Franc soit professionnel, rien ne t’empêche d’apprécier la qualité de tes adversaires. Bayil di soule ndanane c’est méchant
@AbdouMBAYE-u8w6 ай бұрын
Eumeu sene dou champion d'Afrique sénégalais mo fonkoul archives rekkk😢😢😢 Kou guiss archives yi kham nh eumeu sene dou champion d'Afrique
@MameSow-vp7rj6 ай бұрын
Bilahi fran ya meun sakh papay eumeu séne 😂😂😂
@FalléKÉBÉ6 ай бұрын
Franc kouko dieuloul nagako Ragal manqué woufi kéne respect champion la !!
@ibrahimasene92436 ай бұрын
Yow da nga réw da nga bèw billahi wallahi di nga daanou djeule boulla béte
@malicksarr21416 ай бұрын
Khana yakoy dane 🤷🏽♂️😂😂😄😄😃
@saliouthiam24626 ай бұрын
Yaay yalla meune doul 😂😂😂
@LougaLo-pl5jr6 ай бұрын
Wakhi kou kholam tangue 😂😂😂
@ActuS-ye4xi6 ай бұрын
Bou de yay yalla tawal boulette
@malicksarr21416 ай бұрын
@@ActuS-ye4xi mbadou 😂😅😄
@kkassamakkassama25466 ай бұрын
franc s a good man respect bro
@DjidiackSall-fz2dx6 ай бұрын
Franc tu est un grand champion on le critique pas mai eumeu séne foumou diar si lamb dofa diar lamb da neikh legui rek mai amo diar diar bou meti le seul lion de la lutte simple c'est eumeu séne d'où tite d'où ragal yaw danago ben champion si lamb dji
@andregomis-wc5dj6 ай бұрын
C'est notre fierté les manjacks Eume guayi boy bi dane là
Cherigne Ndiaye 2 fi lala diapou yanou sani si souff
@saliouthiam24626 ай бұрын
Nako dieul khol nioune doun nekhal béne mbeur
@MoustaphaNdiaye-sj4rk6 ай бұрын
Eumeu Sene est le grand frère de Eumeu Sene... Il faut respecter son grand frère... Franc n a battu qu un seul grand lutteur ( Bombardier ) et il nous embête ....Franc contre Tapha Tine ou Franc - Balla Gaye ....Eumeu Sene reste un champion
@abdoukhadrefaye35716 ай бұрын
Way franc silence amo yaar khamo sport eumeu doussa morome respect dafa bakh boy niane chance waro dougou si ay détail reugal reug meune fouffff té tacoul radio yi ki doussa morome Loula nekh nak wahal Say morome niogui sa kanamo Mouno dollé rek ga âme
@AbdouMBAYE-u8w6 ай бұрын
Sport amoul morom AK lenen 😢😢 Eumeu sene dou champion
@barradieng98246 ай бұрын
SA way franc da man ta fowoul
@AbdouMBAYE-u8w6 ай бұрын
@@barradieng9824 franc limou wakh yepp DEUG leu... eumeu sene dou champion d'Afrique par individuel...
@saliouthiam24626 ай бұрын
Dieul léne koo rek
@laminendao10706 ай бұрын
Ya bari ndéye wakh reug reug sa baye la ❤️👌💪💪💪💪❤️
@abdoufaye81346 ай бұрын
Danou champion,Ségnine ndiaye rek la dane té dou legui,
@DameNguirane6 ай бұрын
Sokh Tyson 2 Forza ak B52 khana ay joueurs lagne
@mansourdia12896 ай бұрын
@@DameNguiraneyakar na ay arbitre lagne franc seul 🦍
@DameNguirane6 ай бұрын
@@mansourdia1289 nonou lay démé kay
@kefgg6 ай бұрын
@@DameNguiraneSokh dou champion dh sawaye gnisi déseu ay champion lagn B52 Tyson 2 ak Forza mais Sokh mome moy lolou defoufi béne exploit si 8 ans yi passer danoufi béne mbeur bou tangue. Tyson 2 moy champion mome mi dane Garga 2 Thiatou Yoff Gora Sock etc mais Sokh mome bouleen kofi liime
@LamineFall-r9p6 ай бұрын
@@DameNguirane😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@Concept02086 ай бұрын
Bén victoire Eumeu mo guëna riche Palmares Franc. Mais lolou téwoul yak Eumeu combat la. Soxlawo nga nexalko pour beuré ak mom mais dieufou Ndanane kén douko diéma soul. Balla Harouna mi dane Eumeu Séne il le considère comme le meilleur lutteur qu'il a rencontré dans sa carrière et cela n'empeche pas qu'Eumeu a été Champion d'Afrique à l'âge de 17 ans.
@bachirousow576 ай бұрын
Franc bombardier rek nga dannn kenn khamoula
@syllepogba17436 ай бұрын
Wakhi dof 😂😂😂
@paalioudrame53226 ай бұрын
Sa mbeur bo indi franc dann ko
@SeydinaOusmaneNdiaye-j4c6 ай бұрын
Franc tu commence à être incorrecte dans ta communication. Defal ndank rk yaradikou yoboul feneu nite. Khamo sakh louy sport t'es mal civilisé
@diopbayemaissa86986 ай бұрын
Il parle trop dafa barri wakh
@papismergane66036 ай бұрын
Non sénégalaise amoul sport koi ki noumouy daff moy sports blie bou nieuw one Europe di ngua comprendre
@tidiane18786 ай бұрын
Ya meune ndeye doul il na rien dit de grave bayilen ndeye seytanei sa data yaye way yaw
@Mamecheikhndao-pe8ny6 ай бұрын
@@tidiane1878nitt daguay am respect ✊🏿
@abdoulayendoye18036 ай бұрын
Incorrect ioe demal geustou waat mots yingay utilisés
@mamadoukanoute55246 ай бұрын
Lii moy nékhal lamb merci franc 💪🏾
@Thierno-of3pc6 ай бұрын
Yalla boula bén VIP dieul dieuleul alioune seye wala serigne Ndiaye lolou moy lamb
@papaamadouniang33986 ай бұрын
Franc dane na serigne ndiaye
@Thierno-of3pc6 ай бұрын
Wayé oci serigne Ndiaye dane na franc 😂wayé lolou mbapatt la
@deltonlopez43666 ай бұрын
Franç dane neu Sergine ndiaye ci arene bi
@youssoudiallo82956 ай бұрын
Yaw y’a soxor dh
@AlliouDiop-f6v6 ай бұрын
Franc seull yaw yaye lamb ❤❤❤❤❤❤❤💯👌gayi gnimé wougnoula 😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤
@barhamalpha88026 ай бұрын
Franc dites lui la vérité ! La compétition en championnat d’Afrique il y’a la phase par équipe et celle individuelle. Même si Eumeu a échoué en individuel, son équipe est sortie vainqueur. La médaille est la preuve qu’il est champion d’Afrique. Tu ne parles pas sport, tu es méchant et Eume c’est ton ancien et ton aîné; lui reconnaître ses prouesses n’enlève en rien le fait que tu es aussi champion. Le sport exige le respect des anciens. Doff nga franc et kou leu encourager si seu entreprise bii doff leu…
@mamadouauriolchinguini6 ай бұрын
Bilahi bien dit frère
@kategniemendy59656 ай бұрын
Champion gua Franc
@lahadboukharagnelo67076 ай бұрын
Eumeu do champion dieulal boy bi
@Cisse-zv7mm6 ай бұрын
Legui dou champion moukoy lathie yen ay dof guene
@fakhadiagne52886 ай бұрын
Kouleu bagn dala ragal Nane gnou may diame li sport leu Loutakh moulay sarakhou pour ngéne beurei yaye kane moh😂
@mansourcharlessambou46946 ай бұрын
Franc yaroul il faut respecter les grands lutteurs
@babacarmbaye5466 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂Non Franc neikhna 😂😂😂😭. Vraiment ki dayyy sport ! Il faut juste le prendre sportivement
@chakasen3996 ай бұрын
ET POURQUOI TU VEUX LUTTER CONTRE EUMEU SENE A TOUT PRIX ! WAKH DJOU GNAAW BOKOUL THI SPORT TÉ BOKOUL THI RESPECT !
@thiernocisse86316 ай бұрын
Wakhou fi dara lou niaw blj
@FatimaOuattara-x7l6 ай бұрын
De la MM façon boye niant voulait balla gaye c'est déjà cui ci eûmes faire l erreurs franc le tombera
@mouha14616 ай бұрын
Ani wakh bou niaw ci interview bi ???
@kategniemendy59656 ай бұрын
Frank est un champion 🎊
@oumitandiaye67806 ай бұрын
Eumeu sene et franc c un combat car bombardier molen bolée ils ont tout les deux battus Bombardier
@bayelatte77766 ай бұрын
Ndiago bii rekk keukh leu🔥🔥
@modouboussoguene84436 ай бұрын
Père ndiouga yaw seytané nga franc wakh ko deug
@papeelhadjidiop8106 ай бұрын
motay
@lhomme_fort6 ай бұрын
Modouboussoguene khana ça bay moy seytané Domérame
@amadoukoundoul24086 ай бұрын
Yaw noy wajhi pere dici tek yenén kadouyi sii laamb késsé
@@saliouthiam2462 SAWAY FRANC AMNA LOU EUP 20 DEFAITES LUTTE SIMPLE DOU CHAMPION 😂 (REUG REK DANENA KO 14 FOIS). EUMEU TOK NA 4 ANS LUTTE SIMPLE KENE DANOUKA! 10 ANS (2004 - 2024 ) DANOUWOUL ! En 20 ans (2004 - 2024) 2 LUTTEURS REKK GNOKO DANE ! FRANC DOU CHAMPION SAWAY 😂😂😂
@AliouKama-zs9ye6 ай бұрын
Tu n'as rien dit de mal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@bambasamb52216 ай бұрын
Franc Eumeu dou sa moroom
@lampfall13726 ай бұрын
Franc moka meune
@ibrahimaseck29416 ай бұрын
Mai da meune fene eumeu champion 🏆 d Africa 🌍 La kon yekini khana douko
@modoudiouf53366 ай бұрын
Ki dou diabarou reug reug bi
@lhomme_fort6 ай бұрын
Modou diouf ça data yaye ioe
@modoudiouf53366 ай бұрын
@@lhomme_fort 13 vs 1 deh lako reug dane diambar metina mai mounial si ay cimetiere rek lako reug danoul 5 fois weul bitt gangg 8 fois fran di daw baniou guenéko par point biko fran di dane une foi stad demba diop final 10millions yekini sisama kanam arbitre avan mouy yabi siflé bi fran dieul nako weur ko dombo dane ko douma fayou saga bi nak meun nako trop sakh nak mai sa yaye buder mongui doundou yalna goudou fane banga yobuko maka si barké yonent bi bou doundatoul yal nako yala yeureum aldiana di keureum bnne journé frere
@babadia52896 ай бұрын
Môma dé 😂
@MamadouDiouf-hl1sy6 ай бұрын
😮mome la kaye ta khamoul data yayam
@marcelmbengue26366 ай бұрын
Franc vraiment champion lē kéne warouko bagne ,xanna ragal ko rec
@latdiordiop60516 ай бұрын
Franc Dangua rew. Eumeu sen doussa morom.
@bayeratebayerate58936 ай бұрын
France ya nek si deug lamb amuol respect
@KhalilDia-l7j6 ай бұрын
Franchement boy eum dou sa morom nak pomme dou new