Gamou: Les graves accusations et surprenantes de Serigne Moustapha Sy sur Serigne Mbaye Sy Mansour

  Рет қаралды 242,392

DAKARBUZZ TV

DAKARBUZZ TV

Күн бұрын

Пікірлер
@ndeyecodousall7847
@ndeyecodousall7847 4 жыл бұрын
Niit mom bo amoul kilifa djiné done saa kilifa nagn respecté sunu makk gni Serigne Babacar Sy Mansour yalnafii yagg té werr
@babaseydi8383
@babaseydi8383 4 жыл бұрын
Yena gnemer dei wa cellule interprétation ki môme wakh bi na tontou ishh wayyyy di wakh ak gène rek dème lebe ligeye yi
@ndeyecodousall7847
@ndeyecodousall7847 4 жыл бұрын
@@babaseydi8383 kii mom wakh dji dou tonton ndaxx dou manquant kilifa leu
@babaseydi8383
@babaseydi8383 4 жыл бұрын
Codou iow kou môme wakh bi
@ndeyecodousall7847
@ndeyecodousall7847 4 жыл бұрын
@@babaseydi8383 khana kimouy sossal diko waxal lou gnaw
@babaseydi8383
@babaseydi8383 4 жыл бұрын
@@ndeyecodousall7847yalla mo takhaw ne yonety bi sagal say mbook ki bou wakher iow ak mane leerou la negnou bayi yalla atter
@kemokoguisse
@kemokoguisse 4 жыл бұрын
Tooglo ay dioullit doolen wakh yallah neena doolen wakh yonetta bi neena Di nettali yo hametteni doù dierigne dioullit Dara thi ellagam
@damebakhoum6237
@damebakhoum6237 4 жыл бұрын
Lou lerr walahi alquran ak sunna rekk kayy deugu
@cambathiam1073
@cambathiam1073 4 жыл бұрын
@@damebakhoum6237 p
@SopeDabakh2081
@SopeDabakh2081 3 жыл бұрын
Macah allh ap mbolo boula topé dagn ko wara wakh louy diarg
@daoudadieye1990
@daoudadieye1990 4 жыл бұрын
Serigne mbaye sy doula tontou parceque rousna saa papa
@dijasall375
@dijasall375 4 жыл бұрын
Bou dé roussoul nak diaroul tagué du rouss
@FatyW3p
@FatyW3p 4 жыл бұрын
G H H.mhh h H N H M
@IbrahimaDiouf-ff7zo
@IbrahimaDiouf-ff7zo 4 жыл бұрын
Rousoul papam dafa amoul loumou wakhe
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
@@IbrahimaDiouf-ff7zo aye dofe ngène diaro lèna tope
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
@@IbrahimaDiouf-ff7zo dieufeu ndikolène sène khèl yi
@julescisse1984
@julescisse1984 4 жыл бұрын
Franchement chui pas d'accord avec ses propos le linge sal ce lave en famille vraiment c un discour de division merci.
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
Mome mo ame linge sale moukoye djiñatè
@boynarr7500
@boynarr7500 4 жыл бұрын
Bien dit
@sokhnamomibocoum4148
@sokhnamomibocoum4148 4 жыл бұрын
C'est tout à fait le linge sale se lave en famille vous êtes des familles donc essayez d'en parler en toute discrétion
@yakhyasarr7369
@yakhyasarr7369 4 жыл бұрын
Sinon pourquoi le règlé dans les médias et non chez eux 🤔
@sokhnamomibocoum4148
@sokhnamomibocoum4148 4 жыл бұрын
@@yakhyasarr7369 mais aussi les journalistes ils ont un grand rôle a jouer
@lechefelcapo7013
@lechefelcapo7013 4 жыл бұрын
Serigne Moustapha aduna rafétal rek mo ame solo surtout kilifa iow dagua ame aye sopé wakh djii reuyenaa
@modoumboup1562
@modoumboup1562 4 жыл бұрын
Bilay
@maryammyriam9232
@maryammyriam9232 4 жыл бұрын
Wa lum wah
@roseniang7796
@roseniang7796 4 жыл бұрын
Daye doul dé
@maryammyriam9232
@maryammyriam9232 4 жыл бұрын
@@roseniang7796 yaw wernga
@sokhnamomibocoum4148
@sokhnamomibocoum4148 4 жыл бұрын
Bilay adouna amoul solo
@seydinamouhameddiaw5738
@seydinamouhameddiaw5738 4 жыл бұрын
Ohh il est tombé complètement sur le piège et le jeu des francs maçons. Quel ignorant!! J'ai honte de ce Moustapha.
@taboufaye5321
@taboufaye5321 4 жыл бұрын
Est ce que wakh lo wougnou ko pour faire oublier les conneries de Macron........🤔
@nitoudegeki6631
@nitoudegeki6631 4 жыл бұрын
Ki balou fètal laniouko wara door mou dèh amna wakh you niaw yo khamni kouko wakh danioula wara ray
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
@@nitoudegeki6631 mytho la tourou khalif General moko térè nèlaw
@nitoudegeki6631
@nitoudegeki6631 4 жыл бұрын
@@deffaly9056 danako yékha dége dé
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
@@nitoudegeki6631 billahi
@youssoundour7285
@youssoundour7285 4 жыл бұрын
Il est méchant et jaloux mais Serigne mbaye sy l homme digne gnogui sa guinaw sy
@mastourassoul3946
@mastourassoul3946 4 жыл бұрын
Coma des gens censé peuvent l'ecouter mem c grav. Tokk di yakkh sa dérétt ton propre sang , c pathetikk
@aminasall966
@aminasall966 4 жыл бұрын
C'est ça la question pourquoi ils ne se sont pas levé et partir
@yacineba4077
@yacineba4077 4 жыл бұрын
bilahi ki dof la
@tobeornottobe4615
@tobeornottobe4615 4 жыл бұрын
Plus grave ils l'applaudit Honte aux disciples ki étaient présents
@ndeyediop335
@ndeyediop335 4 жыл бұрын
@@tobeornottobe4615 tathiouyi forts roule digno rouss
@wanehaby2641
@wanehaby2641 4 жыл бұрын
@@yacineba4077 ms yaw ya yabaté👎
@papadiene5537
@papadiene5537 4 жыл бұрын
Liii niaw n’a barkè s touba lii eupona wax si mbolo man d coursou ba geuthie naco tarder ndax bgeu s cheikh don’t douma tidian mè tay rousna trop Li yakheu la gneu nourol dfar
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 4 жыл бұрын
Bilay niawna
@awadiakhate2014
@awadiakhate2014 4 жыл бұрын
Waxouma tidiane wayé kouy djioulit rék rousgua ki da réw ba dofe
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 4 жыл бұрын
@@awadiakhate2014 merci
@babacarpouye5044
@babacarpouye5044 4 жыл бұрын
Suis ému Comment peut on dire une telle chose Surtout s'agissant de ton parents....des commérages ..SMS Al mourchid Serigne Babacar Mansour sa kilifeu la...keur seydi el Hadji Malick khamouniou li...donc faut pas créer des embrouilles....et vous qui étiez d
@babacarpouye5044
@babacarpouye5044 4 жыл бұрын
Vous qui étiez d
@babacarpouye5044
@babacarpouye5044 4 жыл бұрын
Vous qui étiez dans la tante....je parles de ces fanatiques la et les méfiants la ne vous en mêlez pas...Lou logique nieup khamnaniouko....
@doudousow1668
@doudousow1668 4 жыл бұрын
Sincèrement qui veroul
@maimounathilly807
@maimounathilly807 4 жыл бұрын
Vous parlez mais vous savez pas l'histoire qui se cache derrière ya bcp de nos dît si vous saviez dolénko jugé
@lampfall7915
@lampfall7915 4 жыл бұрын
Vraiment je ne suis pas tidjane tei kou sopp Cheikh A t sy wayei li nga wahh rafeitoul si talibei wah hantoumalak un guide mangui toup nakk
@diopmatar4301
@diopmatar4301 4 жыл бұрын
Vraiment tu n’as pas d respect il fo respecter ton père marabout serigne babacar sy
@lampfall7915
@lampfall7915 4 жыл бұрын
@@diopmatar4301 j’espère tu ne m’a pas compris car je m’adresse à Serigne Moustapha je condamne cette révélation ki na aucun sens
@zoladiop9412
@zoladiop9412 4 жыл бұрын
Lamb fall deug rk guafi wax deug yalla rk moco mom
@maryammyriam9232
@maryammyriam9232 4 жыл бұрын
L’an la wah goiuryalla
@joe-ny7fb
@joe-ny7fb 4 жыл бұрын
Lampe fall machalla wakh dji rafétna
@ndeyemariefaye9273
@ndeyemariefaye9273 4 жыл бұрын
Dama tite rousse li gnawe na yawe dai sa mame contanoule thy yawe tarikha bou melny tarykha cheikhe ga khamenai yala yonentebi rek moye sene wakhe tane koussa besse diote ga deme pape malick sakhe famou teude taye dji amena louko mety amna louma mety ndakh koula sopone la
@filsdeserignepapemalicksy623
@filsdeserignepapemalicksy623 4 жыл бұрын
bilay nieup rouss li kenn meunoul comprendr
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 4 жыл бұрын
Li da niaw bilahi
@mousadiane5404
@mousadiane5404 3 жыл бұрын
@@filsdeserignepapemalicksy623 a
@amadoulodia7385
@amadoulodia7385 3 жыл бұрын
Je suis derrière toi je te crois je te croire toujour sy Moustapha
@dienaboudabbobalde5285
@dienaboudabbobalde5285 4 жыл бұрын
No amna louma métii magui dioye 😭 sakh, rouss nah akk nissa Papa mell Serigne Cheikh Al Makhtoum done royoukayy ma beugue ka lolou na nittou Yallah bimou done, wayé ioe gatiel gua niou rouss lo gua beppoum Talibé Cheikh
@demba6613
@demba6613 4 жыл бұрын
Bilaye
@khadyba4371
@khadyba4371 4 жыл бұрын
Walahi rous naniou
@ababacarsarr9911
@ababacarsarr9911 4 жыл бұрын
Nioune ay talibé lane sounou yone naikoul si saine probléme d famille vraima Les 🖐 salle s lave 🧽 en famille 😭
@mamerane4756
@mamerane4756 4 жыл бұрын
Fi amoul linge sale condamné wakh dafa rafatoul
@zoladiop9412
@zoladiop9412 4 жыл бұрын
Way rafetoul limu def guanan se lave en famill
@seynidiop366
@seynidiop366 4 жыл бұрын
Watakhou fitnatane latousibana lazi jalamo mine koum khasse
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
Mome mi kaye mo ame linge sale ba parè diko djiñatè ce mytho
@basstoure1430
@basstoure1430 4 жыл бұрын
Yaw mi ligue wakh moy dague a ferro famille
@mamoudfaye3615
@mamoudfaye3615 4 жыл бұрын
Ngani danguay gamou dadiale ay dioulite wakhtano ak gnome si yalla wala si yonnent bi ngua lene Di wakh loulenedoul dieurigne Delo lene sene khel si yalla
@tapha4375
@tapha4375 4 жыл бұрын
nit lobeug deg rek guay dega
@yayoupapam8154
@yayoupapam8154 4 жыл бұрын
😭😭😭 barké serigne babacar sy j ai pas pu retenir mes larmes !!comment une personne peut dire tous ces mechancetés ??
@aissatousamb2623
@aissatousamb2623 Жыл бұрын
Bone rekk, dootoul baax. Tchiiiim
@matarguene2963
@matarguene2963 4 жыл бұрын
Nguir yalla sy mangui toupe dé mé li mome esk gamou la sah chake année rek la même chose 🤒🤒😰😰😰
@diarrietouloum3053
@diarrietouloum3053 4 жыл бұрын
Li kay d'où gamou Ani yallah Ani borom beusbi kéneu wakhoul si niome
@modoumboup1562
@modoumboup1562 4 жыл бұрын
Bilay kouka sopon la ms ki moy lolou
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 4 жыл бұрын
Doyna war gamou ak wakh diou rry j
@tk92221
@tk92221 4 жыл бұрын
La vérité n’a pas de limite il a dit sa vérité un jour on verra . Sénégal bayilèn nafekh lou dokhoul ñiou wakh ak ci bépp niveau.
@aisstouciss901
@aisstouciss901 4 жыл бұрын
Il est devenu fou qui na niou yobou dalal khel non c'est du jamais vu
@dikha7525
@dikha7525 4 жыл бұрын
🤣🤣🤣
@maguettendiaye4358
@maguettendiaye4358 4 жыл бұрын
Dofoul da réw rek
@salydiallo8727
@salydiallo8727 4 жыл бұрын
Bou nékone sa baye du gua ko wakh
@Gohan-yb3rv
@Gohan-yb3rv 4 жыл бұрын
Hoo wakh diey niaw na serigne moustapha serigne mbaye sy manssour sa baye la 😭😭😭
@seidousow6288
@seidousow6288 4 жыл бұрын
Macha allah groupe sopou serigne moustapha laye weure
@ndiayenogaye9319
@ndiayenogaye9319 4 жыл бұрын
Yalnama yalla bal wayé def 1000 salatou alaanabi + 1000 laa ilaaha ilalaah + 1000 astahfiroulaah. Moma gueunal déglou kouy wakh thi diambour nitt ki loko beugue beugue bou wakhé loudoul yone damay dem bayiko ndakh kiy wakh ak kiy déglou dissi guiss bopam gno yam
@VoyageSpirituel
@VoyageSpirituel 4 жыл бұрын
Il est fou ce gars il sème trop le désordre chez la famille Sy
@aminatawane4667
@aminatawane4667 4 жыл бұрын
C'est un vrai psychopathe ce gars
@mouhamadougueye7963
@mouhamadougueye7963 2 жыл бұрын
Sén leufeul ndéye
@abdoulayembengue1949
@abdoulayembengue1949 4 жыл бұрын
quel plaisantin yalnaniou souniou borom mousseul si chaytané
@mamefatydiop9275
@mamefatydiop9275 4 жыл бұрын
Man sakh barcke borom touba dama titt yalna yalla dèfaratt djiko yi nanou bayi khéll si liniouy wakh😭adouna amoul solo adouna bi dièkhna ba paré
@aidalo9600
@aidalo9600 2 жыл бұрын
Diarama Serigne moustapha sy
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
Ki YALLAH naniou Yallah mousseul si mone diviser pour mieu règnè mbolo mola niorre. Ki bopam laye diangal talibéme yi tè dara khamouko
@wanehaby2641
@wanehaby2641 4 жыл бұрын
Gua bal ma dé wayé niémé gua yalla dé😣
@boynarr7500
@boynarr7500 4 жыл бұрын
@@wanehaby2641 yaaww yaa waara nopii yaww
@mamecoumbafall1621
@mamecoumbafall1621 4 жыл бұрын
Billay wakhal dh
@ousseynouniang5451
@ousseynouniang5451 4 жыл бұрын
Pure vérité
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
@@wanehaby2641 yow oubal sa gate dof nga rèk di tope ko khamni Bayam dako mèrèwon bougueutou ko guiss si moudiè doundam 2012 la guedja guisse Papam ba 2017 bi Serigne Cheikh guènè adouna tègantèwouniou bëut soudoul wome ak Al Amine dinaniou dènthie Al Maktoum ta sa Serigne bi dou guisse Papam dako mèrè, sirrou bi rothie nagne ko bou yague mo takh wakhi dofe rèk laye wakh
@tinacisse7786
@tinacisse7786 4 жыл бұрын
Mane Cheikhna Ameth Tidjane sy chérif rek la gueme guanaw yalla ak yonente bi si barker sama serigne Babacar sy mais tay amna louma metti walakhi😭😭 tarikha cheikh nak kene mounouko yak walakhi yalla na yalla ater si bakham mangui toup nak tay diegualou amana taliber dongue la wanter nak lii ngua wakh waroko wone wakh nguene wakhtane sene biir rek ndakh danio ame ay nawler j ai honte 😭😭😭😭😭😭
@morfallmbengue3956
@morfallmbengue3956 4 жыл бұрын
Khalifa bi il ne te calcule même pas, ca iow fo tokk di wax thi mom Lou niaw. Désolé mais mandouwo,ca yangui togn nakk.Nit koubax dou togn nawlem
@issambaye1642
@issambaye1642 4 жыл бұрын
Man dh dama rouss bima degué kadou yi
@boynarr7500
@boynarr7500 4 жыл бұрын
Vraiment gneupp paa rousss
@IbrahimaDiouf-ff7zo
@IbrahimaDiouf-ff7zo 4 жыл бұрын
Liguene wara rous rousolene thi nangouléneko way noppalou
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
@@IbrahimaDiouf-ff7zo guemoulène YALLAH guemoulène Yonenti Seydi Elhadji Malick Sy mome khamoulènko sakh
@colettesenghordiagne8636
@colettesenghordiagne8636 4 жыл бұрын
Serigne babacar sy Mansour yalna fii yagg tawer douwakh louniaw doudef louniaw kii moo doona mamam mame khalife ey waay narafet waay
@youssoundour7285
@youssoundour7285 4 жыл бұрын
Bilay un homme digne
@matyfall3034
@matyfall3034 4 жыл бұрын
Kène dou sunu khalife bi Serigne Babacar Sy Mansour, mom yar ak teguine laniouko yaré, d'où wahantou. Wayé gni toog diko deglou la yeureum. Je les plaint walahi. Mane louma beug beug nit je garde la tête sur les épaules.
@talibeecheikhtv2853
@talibeecheikhtv2853 4 жыл бұрын
Je suis moustarsirate mais franchement li mome andoumasi 🙏🙏
@seydatinafatima458
@seydatinafatima458 4 жыл бұрын
Bayul na nek Moustarchid sogua wah ok yaw mono sah prononcé Moustarchid di feneee holatal nigua ko écrit wè
@talibeecheikhtv2853
@talibeecheikhtv2853 4 жыл бұрын
@@seydatinafatima458 comme khame nga lima beug wakh rek bakhna mane gueuno ma beug serigne Moustapha sy jamais mais ame na wakh yo khame ni kéne douko wakh ci pénthie
@seydatinafatima458
@seydatinafatima458 4 жыл бұрын
@@talibeecheikhtv2853 yaw moustarchirat gua 😃😃😆 awma sa temps. Moustarchid yeup gnu gui Tivaoune. Mane magui ni USA diko suivre direct. Moulma sonal ok
@talibeecheikhtv2853
@talibeecheikhtv2853 4 жыл бұрын
@@seydatinafatima458 lane mola laire ni nékou ma Tivaouane
@profcoly6085
@profcoly6085 4 жыл бұрын
@@seydatinafatima458 👍👍👍👍👍
@fatoucisse9761
@fatoucisse9761 4 жыл бұрын
Allakhou akbar mais kéne mousouta guiss Lou melni allakhou akbar thiéy séytané mo beuri dolé diéméte la déf 🤭🤭🤭
@fatysyll5643
@fatysyll5643 4 жыл бұрын
L’homme à boubou blanc ndeysann il est gêné
@evalopy
@evalopy 4 жыл бұрын
Koon giss nga ko?
@bigmosene3137
@bigmosene3137 4 жыл бұрын
Je suis mourid mé kén réfét louwu ko khalifa bi srgn mbaye sy malick koubakh la té deukku la té lolu lako njépp khamé ...yalla na yalla dimbali niou
@mbenendourndiaye7120
@mbenendourndiaye7120 4 жыл бұрын
En tt limou wakh eupna tei bayam santoul ko li d'où djikko talibé cheikh tamite pape Malick bimouy wakh yalnako yalla yeureum mais mom xaritou nieup la wone bathi wa diangou bi
@mansourba3598
@mansourba3598 4 жыл бұрын
Serigne Moustapha khalatal gni beugue tarikhabi amna lokhamni kéne douko wakh
@dieyepapaibrahima3465
@dieyepapaibrahima3465 4 жыл бұрын
Mane lii xawma Gamou la xawma meeting!! Ay Seydina Mokhamed psl laniou fi warone dégg,wayé ay tatiou rk ak wakh jou Niaw.
@sambafall9801
@sambafall9801 4 жыл бұрын
S.Moustapha linga deff niawna bou amoone sax waro ko wax en public.....ngay defak sa bakenne bou niaw
@awadiop8478
@awadiop8478 4 жыл бұрын
Astafurlah lahi laha illa lah
@khalifadieng6494
@khalifadieng6494 4 жыл бұрын
Non vraiment c'est désolant inchallah nekh ak nakhari Serigne Babacar sy Mansour lafi yalla tek geneu doundou geuneu weer inchallah yalnagnou yalla mouseul si niit ki togn
@khadimcamara7819
@khadimcamara7819 4 жыл бұрын
ah kou yabou wouti fo dieume
@julescisse1984
@julescisse1984 4 жыл бұрын
🤣🤣franchement 🏃‍♂️🏃‍♂️🏃‍♂️
@damebakhoum6237
@damebakhoum6237 4 жыл бұрын
Dieumoukay bi bén leu Yala ak Yoneti bi rekk késsé amoul lénén yala naniou Yala nguindi té mayniou deigu ak top aminn Ya Rabi
@modoumboup1562
@modoumboup1562 4 жыл бұрын
@@damebakhoum6237 wallahi tarikha yi moy lolou yalla ak yonénte bi rk mofi nèk serigne si lègui gnièpa yam
@bambandoye417
@bambandoye417 4 жыл бұрын
Da nguay doul deh..da nguén diapoul ci dara rekk
@fatoubinetouaidara4553
@fatoubinetouaidara4553 4 жыл бұрын
Douma tidiane mais wallahi rouss na tite na c vrai ou pas khawma wayé wakh djiou gniaw bakhoul rafetoul djoulite dou ougni soutoura morom djoulitam rawati une même famille rouss na torop
@profcoly6085
@profcoly6085 4 жыл бұрын
Sokhna aïdara yow moom khamoumaleu wayé kou bakhgua té yalnala yalla takhawou bou bakh
@mandiayeniass1491
@mandiayeniass1491 4 жыл бұрын
Il ne peut pas la discorde entre les familles Sy , j l aimais beaucoup mais aujourd'hui je suis déçu ,
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
C'est un mytho dara amoussi beugue mbolo rèk son propre frère dit depuis 2012 il n'a pas vu son pères Al Maktoum ça veut dire que cinq longues années tegoul papam bëut
@profcoly6085
@profcoly6085 4 жыл бұрын
@@deffaly9056 loolou yow la concerne sounou yoon nékouthie 🤣🤣
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
@@profcoly6085 🤣🤣🤣 kone nga teuthie sa gate ñimou concernés laye wakhal 😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣
@aboubacrysy3330
@aboubacrysy3330 4 жыл бұрын
Aka mala sope mais tey wédi nala un vrai comédien
@mamecheikh4762
@mamecheikh4762 3 жыл бұрын
Machallah serigne moustapha s'y
@khadythiombane4874
@khadythiombane4874 4 жыл бұрын
Gamou-2020❤️machallah
@babacarndiaye7014
@babacarndiaye7014 4 жыл бұрын
Il faut le mettre en prison par ces propos d'accusation de meutre qui il a fait à Serigne Mbaye Sy mansour et par ces propos visant le président Macki sall qui soit disant coup d'état du Khalifa. Macki faut prendre tes responsabilité, ya du n'importe quoi maintenant dans se pays. Trop de laissez aller
@yayeaminata7779
@yayeaminata7779 4 жыл бұрын
adouna sou toukiwei rek khamlen ni mom la. loumou wakh grawna torop . khamna serigne bi amna louko meti tay billahi.
@bilaldiedhiou4655
@bilaldiedhiou4655 4 жыл бұрын
Adouna dou touki nakh li
@Alhamdoulilah2067
@Alhamdoulilah2067 2 жыл бұрын
Adouna dou touki nakh kima wahal douka falé kokou dafa matt ame personnalité dou yakk temps wame si waya waya
@ndakarudialdiop1206
@ndakarudialdiop1206 4 жыл бұрын
Boy weur kou doff ba guiss serigne moustapha diapal ki bilay wérul wakhone nako té dina continuer diko wakh ki dégn ko wara fadji
@maguettendiaye4358
@maguettendiaye4358 4 жыл бұрын
Dofoul day domérame réw la déf
@momadoulaye6154
@momadoulaye6154 3 жыл бұрын
Jaime bien le khalife général.il est véridique ba paré téy . yalla nafi yagua lool té wérr
@aichananiang8577
@aichananiang8577 4 жыл бұрын
Masoukhanala liii degue la kou bayii woul sa papa do bayii kene 😡😡😭😭🤭🤭liii Gamou wala tessanete
@mameannakamara935
@mameannakamara935 4 жыл бұрын
Wallahi, kouy doural sa baay bi leu djour foi bayyi baayou kenen
@sennaseye6986
@sennaseye6986 4 жыл бұрын
Akourou zamane la fin du monde Allah 😭😭😱🥺
@sidylamineladiane2815
@sidylamineladiane2815 4 жыл бұрын
Man mome dama tiite liii c est très grave 🙉
@awafall9876
@awafall9876 4 жыл бұрын
Un comédien, un homme qui ne réfléchit jamais mais kou bayiwoul sa baye do baye bayi bayou kenene une honte pour la communauté tidiane. Li laniouy wakh divisé pour mieux régner. Amoh kham kham del wakhal yalla ioe beug tokk khalife mola sonal motakh wayé do guide do référence . Khalif bi mome doula meusseu tontou nak doussa morom
@mamadoulaminegueye6456
@mamadoulaminegueye6456 4 жыл бұрын
Gni khamoule kouye Serigne Moustapha la wakhe dji di béte de Serigne Mansour borome daarayi rta Serigne Abdou Al Amine rta ba si Serigne Babacar Sy Mansour Al khalifa bayi woule kéne kou sossale gore ba dougue bamèle dinga xameni lépe deuguela beugue mboolo ak toure koumouko diarale yone bangui nonou
@fatoudiouf3722
@fatoudiouf3722 4 жыл бұрын
Serigne Moustapha baahoo thii reewmi
@ibrahimaka6035
@ibrahimaka6035 4 жыл бұрын
Khalipha general koullou fene katt moneckni wayé yalla gopna fanam legui moudiogefui incha allah
@cheikhahmedtidianecisse1218
@cheikhahmedtidianecisse1218 4 жыл бұрын
Bouma degué niou dofbi mon donou Serigne Cheikh💖 no dafmay diakhal billahi.Qui est ce que nitt leu d'abord ?
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 4 жыл бұрын
Doyna war
@babsndiaye3
@babsndiaye3 4 жыл бұрын
Ki dou nitt dof pir mo tok di wakh
@babsndiaye3
@babsndiaye3 4 жыл бұрын
Ki dou nitt dof pir mo tok di wakh
@abdoulayelahi2990
@abdoulayelahi2990 4 жыл бұрын
Lolou amoul dou deug walahi dou deug Soubhanalah
@cheikhleye8328
@cheikhleye8328 4 жыл бұрын
Ci sa bir wakh nénga eupou gnoula kham kham eubou gnoula mbolo eupou gnoula wilaya c faut ku am kham kham dou wakh li nga wakh ku guem yalla deug dou wakh li nga wakh comme si tu ne connais pas lou takh sa Seydi El Hadji Malick woté gamou gui ce n'est pas pour parler du n'importe quoi mais pour nous enseigner des valeurs de seydina Mouhamed (psl). Di diégalou ci kadu gui wayé mak bou wakhoul deug gni tok ak mom dagne ko wara wakh wakho deug. En fin talibé yi tok ci tante bi ban enseignement lagne am ci gamou renn bi ak bougnou démé sen keur lan lagni netali sen wa keur🤷🏾‍♂
@mbayedieng8270
@mbayedieng8270 3 жыл бұрын
Y.
@daoudaanneat-tidiany
@daoudaanneat-tidiany 4 жыл бұрын
La personne manipulatrice installera une idée dans la tête de certaines personnes. Si elle voit que celle-ci n'a pas eu l'effet escompté, elle en installe une autre, puis une autre jusqu'à atteindre son but. Elle colportera des rumeurs et des ragots, rapportera volontairement des faits de façon erronée ou encore accusera ses victimes de choses qu'elle a elle-même faites dans le but de s'assurer que ses gestes répréhensibles ne se sachent pas. Lorsque cette personne aura atteint le but recherché soit d'avoir discréditer la ou les personnes X, les autres membres qui composent son cercle social, souvent ne chercheront même pas à en connaître davantage sur sa ou ses victimes qu'ils ne connaissent pas et qu'ils jugent sur des faits rapportés et déformes dans le but de servir la personne qui les a rapportés. C'est une personne à fuir à tout prix !
@beautyglamdakar4545
@beautyglamdakar4545 4 жыл бұрын
Mbirr bii dal sa dérétt moy yakk sa dérr😭😭suis choqué moi c’est un grave manque de respect 😭
@mbodjmbodj406
@mbodjmbodj406 3 жыл бұрын
senegal danou amoul chance ndakh nitou yalla boufi diar nitou wakh nanou la lou bonn mai hamouma kane mai serigne moustapha loumou deugeula te diamono dinako dioh raison yen mbam yiw haakh yen ak seni baay yena fenn te amou len beneu preuve wa tivaoune niou geuna hamni seydi ahmad bou serigne babacar moka mak fouf serigne moustapha dou wakh mouk ay thiahane mais yen senegalaiyi da guen am crise de memoir ahouma serigne waye nitou yalla dou fen mouk loumou wakh deugeula
@syllayoussouf4649
@syllayoussouf4649 3 жыл бұрын
Thieuy iblis mo barri dolé, que Dieu preserve le senegal des gens comme ça.
@khoudiandiaye7704
@khoudiandiaye7704 4 жыл бұрын
Iow mosso am kilifa sa baye da liguèy diamou yalla dioup ba guèn adouna... mè iow kènd beugou leu pask wax katou niaw tèf nga ...kou tok si khalif bi nga wax si mom tè yasi geuneu niak kham kham khamo tousss loudoul lou niaf xolal sa bopou iow do serigne do nitt kou bakh serigne Mbaye moy khalifa moulay nèkh wala moulay nakhari iow amo repair daga rakh si wa keur cheikh
@modoumboup1562
@modoumboup1562 4 жыл бұрын
Ki bayam rk motakh nit gni sopon ko
@maguettendiaye4358
@maguettendiaye4358 4 жыл бұрын
Bayam la dieuka khass bayioul kéne vocal warone na am Bama sagua ndayam
@tapha4375
@tapha4375 4 жыл бұрын
Yen mom doumalen tontou sakh nekh werolen
@borso3271
@borso3271 4 жыл бұрын
Je suis taliber cheikh mais j'ai des arme au œil bilahi
@alydiokh7468
@alydiokh7468 4 жыл бұрын
Franchement un guide ne doit pas parler comme ça .C’est triste know what you know and keep calm .C’est des propos qui divisent la communauté .Est ce c’est une bonne exemple de parler à son prochain ou un proche de même sang avec ces genres de propos? C’est désolant 😒
@seydinamouhameddiaw5738
@seydinamouhameddiaw5738 4 жыл бұрын
Non kii nak khélam nèkatoul ak mom. Nako kilifa yi dieulssi bala moufè yakkh. Limiy wakh gnaaw na tropp. Non ki daal dou nitt.
@nogayedieng7019
@nogayedieng7019 4 жыл бұрын
Doyna war
@famagueye2151
@famagueye2151 4 жыл бұрын
Yw amal yar
@seydinamouhameddiaw5738
@seydinamouhameddiaw5738 4 жыл бұрын
@@famagueye2151 Bakhna On verra.
@beautyglamdakar4545
@beautyglamdakar4545 4 жыл бұрын
Non c’est pas normal ça vraiment wakh bii dafa eupp wakh bi gnaw na trop c’est pas joli serigne Mbaye Sy Mancour da calme correcte dou meusse tontou makk la da am loumouy rouss rekk ak loumouy khol 😒🤞🏿
@kaosamsung2253
@kaosamsung2253 4 жыл бұрын
Mane demako yeureume billahi yalla nako yalla guendi
@HourLond
@HourLond 4 жыл бұрын
Walahi dina khamni Serigne Mbaye Sy mo digne.nit dafa am loumouy diomeu wakh wala def.
@ibrahimambathie415
@ibrahimambathie415 2 жыл бұрын
Serigne mbaye Sy mo sagual tiwawone lolou nieup guisnagnouko
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 3 жыл бұрын
Khalifa general boy tapha sy 2020 🤭🤭🤭🤭🤭
@omarjueye
@omarjueye 4 жыл бұрын
Sincèrement ses paroles n'ont pas une place ici c'est très honteux d'avoir dit cela
@babacarndao531
@babacarndao531 4 жыл бұрын
Louma la begue wakh rék xép ko Li gua wakh Dou sa wakh Bess Niki tay Elhadji Malick sy guiss bo amé ay talibe Bou leen di wakh sa via det Pireh Dou tay Magui Lir Ay messages yokhménte ni begouma kéna koula Lolou nakhri mais tay moom Magui degue Lou nékk Bayi Li Guay wakh
@xamxambouweer5394
@xamxambouweer5394 4 жыл бұрын
🙏Lii ame solo moy limo wakh lou takh mou wakh kou ak foumou kou tekk ndax wakh bou nga raaw la naon ci deme xel🙏👉👀
@tabarandiaye1584
@tabarandiaye1584 3 жыл бұрын
Yaw domeram ga
@xamxambouweer5394
@xamxambouweer5394 3 жыл бұрын
@@tabarandiaye1584 khana babsou sy moy sa sëriñ Woutel sëriñ bou mat sëriñ
@oumoubalde4235
@oumoubalde4235 4 жыл бұрын
Thiey liii doyna war épui mome dafay gamou wala meeting prqw c applaudissement bilahi keur go dougou amna sarakh mè Moustapha Sy moy sarakhou Tivaoune wakhothi yonentibi saws khana nèk fi di yak der ak diakhassé noon qel pays sommes ns
@bashirngomngom2906
@bashirngomngom2906 4 жыл бұрын
😭😭😭😭 سبحان الله العظيم هذا جنون وغمر وخرق ما هذه الترهات والخزعبلات
@sokhnamomibocoum4148
@sokhnamomibocoum4148 4 жыл бұрын
Parlez Parlez en toute discrétion vous êtes des familles et la famille elle est sacrée donc s'il vous plaît merci
@mameboussombodj355
@mameboussombodj355 4 жыл бұрын
Domou adama tamit d Kouko wer Yalla dinala wer...aythia rek kilifa gou tolni yaw diémo wax lou bax di wax Lou gnaw et surtout gouddi seydina mouhamed(psl)
@antadiop493
@antadiop493 4 жыл бұрын
Alkhourane ak sunnah rek mo wore tarikha yeup do dege yala nena mouhamed nena loulen nekh lagniy wakh wala sen mame seul diol fouta ak rafahi mbacke rek gnosiy wakh deug mo takh beuri wougne talibe Sénégal beugou gnou deug koulen di nakh lagne beug tarikha yi ma guis koulen moytou woul kham( goudi gou gneuk si bamel) kou yakarni dosi diare loula nekh defal fi yala rekay karim yala ak yonete bi rek mo diara guem lisi dess yeup ay thiakhane la😭😭😭😭
@lamfadiakhate7116
@lamfadiakhate7116 4 жыл бұрын
Gnoune sougn khôl ak sougnou xel lagnou yoré kougn tek si yonou yala wakhou yonén tibi lagnouy topo koufouy wakh wakhou nafekh wakhou divergences Ay mbot grenouille lagnou lay diapé ak wilayeu bo meunti am nk wasalam
@naturalmavista1917
@naturalmavista1917 4 жыл бұрын
Je suis choquée la ....té daa melni 20:26 selbe ndom mo diok di wakh nonou ak ay mécham you goude
@aboubacarsadikhngom7756
@aboubacarsadikhngom7756 4 жыл бұрын
Kone lii moy gamou aka wouté ak gamou TOUBA
@Tapha_Bezos
@Tapha_Bezos 4 жыл бұрын
Sama nijaay wakhna lu reyy!!yalnaniu yalla moussal si seytaane
@ibambodji3981
@ibambodji3981 4 жыл бұрын
Kiii Day divavué rék bayiwoul kène ana gamou ak wakhi doof
@diopibrahima1645
@diopibrahima1645 3 жыл бұрын
Vraiment niawna
@papitodiack3092
@papitodiack3092 4 жыл бұрын
Moh mane dh wakh bi bétoumavraiment covid 19 moko bayégoul
@fatoucisse9761
@fatoucisse9761 4 жыл бұрын
😂😂😂😂😂
@malickngom5268
@malickngom5268 4 жыл бұрын
Hahaha doma ray
@meissathiam9813
@meissathiam9813 4 жыл бұрын
Mani kou bokkoul bokkoul tè kou khamoul khamoul , merci Sy Malick , avancement guay deukkè incha Allah, wakh kat yi moome nagnou wakh ndakh wakh lagnou meunè rèk , merci
@adamasarr695
@adamasarr695 4 жыл бұрын
Ki saytané la
@mamadoulaminendiaye6862
@mamadoulaminendiaye6862 4 жыл бұрын
jai honte et j ai mal,comment un musulman peut dire pareilles inepties envers un autre musulman,je suis tidiane et ma plus grande déception vient de cette déclaration,Dieu soit loué, le seul juge
@oumoulkhairyba2950
@oumoulkhairyba2950 4 жыл бұрын
Soubhanalah lahawla walaouwata ila bilah thiey sounou borom Yallah nagagnou diegeul
@modoudiagne8237
@modoudiagne8237 4 жыл бұрын
Ki bamou dofé yagga na sa wakh niawna trop way s pape malik déwam modiot rek S mbaye sy mansor nak khalifa cheikh la Ta cheikhako tane tékko fi
@aisstouciss901
@aisstouciss901 4 жыл бұрын
Personne ne doit être surpris de ses bêtises la puisq chaque année c'est ça il ne dit que des n'importes quoi dou rouss sah a cause de ses genres de personnes le Sénégal est en retard
@anitazahradiop357
@anitazahradiop357 4 жыл бұрын
Mane dé bétouma si mome khol bi mo bone chaque année ak tothie tothie boumouy wax yalla nagnou yalla moussal si yé katou fitna
@faticisse9069
@faticisse9069 4 жыл бұрын
😭😭😭🤭🤭🤭🤭🤭🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐👎👎
@mamediarrasarr2198
@mamediarrasarr2198 4 жыл бұрын
Niomi néne la yala na yala def diame sui mouride dama siy mandou🙏
@bombadiakhate5710
@bombadiakhate5710 4 жыл бұрын
Billahi je suis mouritt serigne touba daf nio yarr
@yayoupapam8154
@yayoupapam8154 4 жыл бұрын
Sou féké da nga mandou boul commenté !! Li dioulite yeup la méti amoul mouride amoul tidiane
@ndiemeseck5373
@ndiemeseck5373 4 жыл бұрын
Fiére de toi mn guide💕
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
Guide bou meuna mèw nga ame
@modouaidara952
@modouaidara952 4 жыл бұрын
bousi kene wax lou niaw nagnouko ladie fane lako tek ak foumouko khamés com da ame fite di wax rek
@rokhycisse2460
@rokhycisse2460 4 жыл бұрын
Bien dit mo diara lathie
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
Mome moye attaqué mystiquement
@maguettendiaye4358
@maguettendiaye4358 4 жыл бұрын
Kamousi Dara day SOS rek
@tabarandiaye1584
@tabarandiaye1584 3 жыл бұрын
Vous un vrai domeram comme tous ces talibe
@souleyegning1167
@souleyegning1167 4 жыл бұрын
Il ne faut pas dire certaines choses dans la vie. Les problèmes de famille se regle en famille et pas publiquement.
@ousmaneouzy1489
@ousmaneouzy1489 4 жыл бұрын
Ki sérieux esk AmOul loukoy wakhLo yaw 😭 alahou Akbar mane Dma TiTe yaw
@sokhnamomibocoum4148
@sokhnamomibocoum4148 4 жыл бұрын
🤣😅😆😁😄😃😀😂🤣
@khoudiatall5467
@khoudiatall5467 4 жыл бұрын
dafaye doroge
@sokhnamomibocoum4148
@sokhnamomibocoum4148 4 жыл бұрын
@@khoudiatall5467 ay way 🤔Asstahfourlah
@aimasow2700
@aimasow2700 4 жыл бұрын
Framacons yi niokoye wakhlo
@serignegueye4226
@serignegueye4226 3 жыл бұрын
Merci 💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💞💞💞💞💞💞
@ndiayendanane840
@ndiayendanane840 4 жыл бұрын
Mé ki wéroul dé mé seutou serign babacar sy yi mom bari nagne fi ba légui
@lazebre1192
@lazebre1192 4 жыл бұрын
Mais domou serigne Babacar yi sax amoul kou ci gatta fane ñeup goudeu fane
@deffaly9056
@deffaly9056 4 жыл бұрын
Ki ibliss la diokh nopp tè kome ibliss keur Maodo moko diakhal beugueul loudoul tasko mo takh wadiou daas lamiñame seugue si dèrrou gorñi tè kéne signèlouko permis
@mansourndione4825
@mansourndione4825 4 жыл бұрын
Wa mé ngi Nékone sans de Course beu niome loutaxh déguouniou Li😔
黑天使被操控了#short #angel #clown
00:40
Super Beauty team
Рет қаралды 56 МЛН
She made herself an ear of corn from his marmalade candies🌽🌽🌽
00:38
Valja & Maxim Family
Рет қаралды 16 МЛН
Ziarra Daaraji 2024 - Discours de Serigne Habib SY Ibn Al Khalifa
17:12
Asfiyahi Television
Рет қаралды 14 М.
EXCLUSIF!!!  Abdou Sy vilipende et enfonce Serigne Moustapha Sy
16:15
Hither and Thither TV
Рет қаралды 138 М.
Gamou 2002: Dernière bourde Serigne Mansour sy borom daradji P2
51:40
Borom Daaraji Tv
Рет қаралды 170 М.