Je suis mouride mais limay niane moy niou khamni nioune nieup ay djoulite laniou tè dèglou sounou kilifa yi serigne bi limou diglè niou topouko tè niane yalla dèfalniou niou fèkkè dewen you bari barkèp seydina Mohamed rassouloulahi salalahou aleyhi wassalama barkèp borom touba khadimou rassoul .yalna sounou kilifa yagg fi tè ande ak wer barkè borom touba khadimou rassoul
@bayezizlaa1564 жыл бұрын
Yabah
@massymasy15394 жыл бұрын
Manchalah
@coeur2lion384 жыл бұрын
Ma beg cou nité machala
@aliounebadarambaye16014 жыл бұрын
lo yama gueune
@etiennesnciss95564 жыл бұрын
Suis catholique et j'aime les tidjanes Vraiment vous êtes conscients de la santé des fidèles
@omzoomzo25384 жыл бұрын
Yene tamite daguena yarou ndeyesan tidjane yi danio yaro set sella am xam xam
@badouz31914 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣
@dabadiop91204 жыл бұрын
Hum😁😁😁😁
@macissecisse57544 жыл бұрын
C'est normal vrai citoyen dafa wara civilisé ak nité
@ndeyebinetasow86024 жыл бұрын
Mercie l'être humain est plus important que largent ?
@princesse_diadia544 жыл бұрын
Ou sont les talibés cheikh?❤️🥺❤️❤️😭😭
@mexdroid17034 жыл бұрын
Niongui ni
@mbayangsalla17624 жыл бұрын
Yarr ak teguine rek machalla
@ndeyeramasane89784 жыл бұрын
Présente
@kandeabdou36194 жыл бұрын
Macha allah🤩🤩
@perlita36894 жыл бұрын
MashAllah Sy Malick goudd fann wér ak werlé rék laniou lay nianal, doneno sa bay done sa bay moko gueun, tu as suivi les pas de Maodo à la perfection mashAllah Pour ceux qui polemiquent sur sama Serigne mo gueune, juste une petite chose, Mame Bamba, Mame Maodo, Mame Baye, Mame Limamolaye, toutes leurs vies, ils l'ont consacrées à Allah assawajel et au prophète Naby Moustapha SAW et vous, qu'avez-vous fait pour Allah et Mouhamadou PSL? Délo si léén thi séne xél, diamou yAllah bayil thiahanne, la mort arrive lorsk'on s'y attend le moins, k la paix, la joie et l'amour de son prochain règne amine Élément de Mame Khalifa Serigne Babacar Sy yAllah na diam saaakhhh
@abdouly67734 жыл бұрын
Holale tivaoune rék bilaye deukou lérre le machalla fière d'être talibé seydi Hadji Malick Sy
@soldatbi71374 жыл бұрын
Yen dolen Ay bagne Kate dara niorou len dangueni thiakhane rek waye danguena tadj diouma dji nguir covid yen gamo len sakh yalla
@abdouly67734 жыл бұрын
@@soldatbi7137 iow katal sa ndeye touba deuk fran maçonnerie diaye drogue sacrifice sén diouli ak sén worr yalla douko Meuse nangou yén sén Serigne ték katou dill thiaga yi di kate diabarou Modou Modou yi
@allxsander26114 жыл бұрын
@@soldatbi7137 yaw sa data yaye yak sa seringue banga guiem
@diopmomo3294 жыл бұрын
@@soldatbi7137 demal lidieunti fane laniou soul serigne touba ak bane biss la dhé mo geun sa doul yi
@momo_baye75824 жыл бұрын
Mouride boul togne way sa tourwi warone gua diombou li mounolenn fékhé ba Serigne Touba ak cheikh seydi Hadji Malick bokou gnou mame gnoko bokkou si Lou amoul sikki sakka nagne yarou
@misskourouni14284 жыл бұрын
Maa sha allah Sy Malick.Lii rek lagnou done khar si yow..Top seu ndigueul rek
@sybabacar61224 жыл бұрын
Alhamdou lilahi rabil ala min n'oublie jamais de prier yalla na yalla def jamou si senegal serigne babacar sy mansour yague fi lol te wer
@mamanmbodji71754 жыл бұрын
Machala Sy Malick nous sommes fiers de vous Alhamdoulillah 🙏💕❤
@maimounasane28974 жыл бұрын
Machallah 🙏🏾❤️sage decision Sy Malick🙏🏾❤️dinagne top nigual inchallah ❤️
@ndeyebinetasow86024 жыл бұрын
Décision d'un responsable quel sagesse
@laminedioppikinerue1054 жыл бұрын
Bilahi
@kanouforme33694 жыл бұрын
Effectivement '' une action sociale est une action orienté vers autrui'' c'est ça la grandeur d'un homme
Kou sagnoul bagne Sagna nanguou je suis derrière le khalife général 🤝 yaguafi wéral sakhal♥️ amine ya Rabbi 🤲
@mariediop40844 жыл бұрын
Je suis talibe Cheikh et je suis fiere de vous je ne suis pas surprise je savais que le gamou serai annule tu te soucis de la sante de tout le monde tu es calme tu es discret tout le monde tadore dieuredieuf Sy ya beugeu diam ak salam
@ndeyeawadabakhNdiaye4 жыл бұрын
Amouniou loudoul maodo Maodo amoul loudoul nabi Nabi Nena yarrabi mom LA teunn Machala MBA dewenn inchala
@karaseye21384 жыл бұрын
Bilahi walahi talibés cheikh yi malén beug malen nâw ndakh cen yâr ak cen téguine ak cén top ndigueul. Xolal ci comentaire yi rek doci deg saga doci guis xastè doci guis gnawalatè doci deg kou toud serignou diambour. Mashala je salus la sage dècision du khalif
@mamydiouf62114 жыл бұрын
Walae😍❤
@herruholumutadacaktrherruh79454 жыл бұрын
masa Allha rafetna torop bilahi, tidianyiiii 👍👍👍👍🇹🇷🇸🇳
@linguerembodj1894 жыл бұрын
Bilahi talibé deugue dou djoukhé bopou di rothi lamine bopou bou beugué ame barké nopou yi dégue mothi sakh ndigueul dieufé incha allah ba déwéwe🙏j'aime tarikha cheikh RTA 👉❤👈
@abdoudiop51634 жыл бұрын
nila nite dakay ame kilifa wormalko loumou la diguel nga def loumoula tere nga bayi ma ngi nianal seurigne babacar sy mansour mou yague fi lol te andak weur si barke seurigne touba mbacke 🙏🙏🙏
@sokhnafatoundiaye28144 жыл бұрын
Amine
@fatimasakho92604 жыл бұрын
Ma sha Allah ❤️ Alhamdoulilah ❤️ Gnouy am diam ngeine di am diam ba dewene ak diam in sha Allah.
@massylasamb3644 жыл бұрын
Je suis Mourite mais vraiment la décision de Serigne mbaye est très noble et logique
@mexdroid17034 жыл бұрын
Merci papa
@akhmadia10434 жыл бұрын
Yaw do mourite no
@sokhnaamysene50104 жыл бұрын
Yamana doul bathi teuth diouma
@ndeyembengue22014 жыл бұрын
Bilay sy loléne wakh rék nonou la ♥️♥️
@awafall43354 жыл бұрын
Machallah Sy Malick gnigui sa guinaw yalna yalla yok fan yi may len wér si barké Mouhamed psl
@Ben-es3cb4 жыл бұрын
À salamalekum ma ngui lenn di siaare bou wer ofet dama bëgg wakh ni képp kouy lire commentaire yi nga def très attention dakh amna ayy yakh ak you nek si biir di diakhassé diadieuf tidiane ak mourid lep Been leu nañiou moy tou bou bakh commentaire yi
@ndiayekhadim6674 жыл бұрын
Kou bakh wakhga degue de dione dieup benelagne sonio kilifayi lou nio deuf sonio diarigne la nagne topou seni digual rek te bagna topou miniayi
@iniiabdalahi40494 жыл бұрын
Walaye sy malick ,louy dougou si khalice tivaouane si gamougui ngani gamou dou âme bilahi alal gnorouléne diami yalla yi rék gnoléne yitél serigne babacar sy al khalifa yalla nga soute Aÿ fane khalifa yifi diar yeup yalla deugeureul la diapaléla dieureudieuf sy
@oulimatadiouf90454 жыл бұрын
Machalah souniou khalif bi yague fii lol té anede ak wer lo wax rek d'accord naniou ndax do waxé sa nafsou bakane lo wax si charia ngako tek fier d'être tidiane💖💖💖
@cheikhomarndoye98454 жыл бұрын
Mangui sant yalla boubah bama donei talibe cheikh ❤️🙏
@Affairedegrand4 жыл бұрын
Ndeysan talibe cheilh dano téy yarou ma challah hoo😭
@kanouforme33694 жыл бұрын
Machalla yalla naniou yalla bolé soutoural ba niou teweko dewene inchallah
@cheikhomarndoye98454 жыл бұрын
Serigne Babacar sy Mansour Al khalifa yalla na yalla dougual fanam si barki seydina Mohamed
@beugeubamba13034 жыл бұрын
MACHALLAH NDIGEUL MOME DIEUFÉ MOWAR TALIBÉ 🙏
@geuyefamily68074 жыл бұрын
Dierediefé serign babacar mansour yall'na yalla yagal kofii loll
@dioocheikh55204 жыл бұрын
Delen deglo khell to bagna deglo kholl na nou yalla yodou thi gamou 2021 inza alla
@matrakamusicflow4174 жыл бұрын
Salam tivaoune deku lerla gisale asamaci ak nature bi sene mbok abdou Aziz Sarr depiu espagne
@hawakane35854 жыл бұрын
Machaalha sy Malik yalla na yalla faye 💓💓
@abdoulahatdiouf52244 жыл бұрын
Amna kouné touba amoul dîné noun wa touba dè masou no teudji jumma ngir fébar
@ramsesalsalihatbeautymane28364 жыл бұрын
Abdou lahat Diouf nasa khôl sédeu kokou mako tontou Kokou seytané la beug diakhassé les tarikha c un imbécile ce gas s’en khôl dina dagu
@abdoulahatdiouf52244 жыл бұрын
@@ramsesalsalihatbeautymane2836d'accord Nice
@mbayedia25434 жыл бұрын
Demal wakhko Moussa kamara
@goutsdafriquelavieillemarmite4 жыл бұрын
Membre Dahira atkhiyaye merci notre khalife il ne met pas la vie des populations en danger
@falloundiaye42254 жыл бұрын
Ban danger diamou yala amoul danger. Geumo lén tousss 😅🤣🤣🤣
@amadoudiop41614 жыл бұрын
@@falloundiaye4225 une question, est ce Gamou farata la??
@khadimsambbgfallou70984 жыл бұрын
@@amadoudiop4161 yaw bayil sa doulyi dioulli mongui ni faratala te bayinguén ko ndakh corona
@ndieumbeuttoure194 жыл бұрын
@@khadimsambbgfallou7098 putinnn mh la fermeture des mosquée lolu dfa teré niou diouli si keur yi amlene yar th guene bayi niou geum louniou geum wla bok
@badasylla61054 жыл бұрын
On est de retour au magal zéro cas alhamdou lilahi dieureudieufé serigne touba
@oumydiouf11114 жыл бұрын
Je suis mouride rafétlu na reaction talibé yi nitt amul ludul wasilam xalite yi rafétna lol
@mexdroid17034 жыл бұрын
Machalla ioe mom kou bah ngua
@youssoundiaye44434 жыл бұрын
Mouride yi kahmou gnou loudoul Lou bax yalla niép am diamou
@fatoubinetougueye41354 жыл бұрын
Machallah sy malick kilifa gou motte kilifa kouko am sante yalla rek mola war borome goudi Gamou gui sax contane na si ningay aré djiaboote gui
@tallandiaye49994 жыл бұрын
Dieureudieuf borom touba
@ahmadafrom2rou7374 жыл бұрын
borom touba amoul morome
@ndeyedeguenediop74004 жыл бұрын
Mandoul tei nga dem topato wa keur Borom Touba
@skhadimdiaw35224 жыл бұрын
Waw waw. Fall
@ndellatine45914 жыл бұрын
Alhamdoullilah topp ndigueul rekk
@assanely69384 жыл бұрын
La Nuit de la Naissance du Prophète est la Nuit de l’anéantissement, la Nuit de la dissipation de la peine et de la purification des gens entachés de péchés Sa Naissance est Glorieuse, Bénite et Respectueuse ; SA CÉLÉBRATION EST OBLIGATOIRE POUR TOUT CHEF Sa célébration conformément à la Sunna (la Tradition) nous conduit vers le Paradis ; par elle, les bienfaits augmentent en faveur du sincère qui glorifie Quiconque célèbre la Naissance de notre Prophète qui est la Porte de la Bonne Guidée, point il ne sera soumis au Règlement des Comptes Demain; alors, honore et glorifie cette Naissance Quiconque célèbre la Naissance de la Meilleure Créature, en l’occurrence le Plus Louangé (Ahmad) celui-là est comme un martyr ayant combattu à Bedr, et ce, sans illusion Celui qui fait une dépense à l’occasion de la célébration de son Honorable Anniversaire, en biens, sans gaspillage, fut-ce l’équivalent d’un " dirham " Celui-là est comme quelqu’un ayant été présent le Jour de " Hunayn " avec patience et le Jour de Bedr, puis ayant soutenu la Meilleure Créature qui facilite la compréhension Celui qui célèbre la Naissance de notre Prophète qui est la Porte de la Bonne Guidée ne sera pas contrôlé Demain, au moment du Règlement des Comptes désarmant Celui qui assiste à l’Anniversaire de 1a.Naissance de la Meilleure des créatures, en la célébrant par la communion, dans la réjouissance, avec du sucre ou de la viande Celui-là est certes nanti de ce qui pérennise la joie et il ne rencontrera pas de malheur le Jour du Rassemblement des Communautés Celui qui présente un repas à celui qui chante ou lit un texte liturgique, pour l’honorer, réunira les bienfaits des gens doués d’une force de décision spirituelle Celui qui récite des panégyriques, lors de la célébration de la Naissance de la Meilleure des créatures, sur quelque chose pour l’oindre, celui-là verra, pour cette chose, un essor de plus en plus bénit Si on récite sur de l’eau des panégyriques, lors de la célébration de la Naissance du Meilleur du genre humain, le fait de boire de cette eau préserve de la machination de Satan, par la Grâce de la Créature Purifiée L’absorption de cette eau, grâce à l’Exaucé, illumine le cœur et le vivifie, sans défaut, et celui qui l’absorbe sera préservé du malheur La vivification [de la célébration] de la Naissance de l’Annonciateur des Bonnes Nouvelles protège les familles et les demeures, elle renferme le Remède des cœurs pour tout individu se réclamant de sa Direction
@mamadouseck85834 жыл бұрын
Ah nous ne pouvons k etre d'accord par les propos du khalife.il veut juste notre bien face a la maladie donc moi j le voie comme une chose vraiment intelligente e un bon acte pour sakun d'entre nous.alhamdoulilah
@mounajawo88674 жыл бұрын
Machallah ❤❤❤❤
@modouniang1654 жыл бұрын
Machallah Sy Malick dieureudieuff Mame Maodo Malick ❤️❤️
@fatouthiambandiaye49944 жыл бұрын
Sage décision Sy Malick 🙏
@djbril00754 жыл бұрын
Machaalla lii rék lanoudone khar si khalifa bi dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf sy malick
@deme49914 жыл бұрын
Mancha halla. Sy malik talibè cheikh rakk
@fallounicesall10034 жыл бұрын
Nice machallah ❤❤👏
@fatougueye30554 жыл бұрын
Je suis mouride dé wayé niou respecter souniou kilifeu dinné niitte da ngaye topp ndigueul té makk meune n'a guiss Lou kene guissoule deffé lene ko rekk ni mouko beugué inchallah
@fabee73124 жыл бұрын
Mashalah ndiggeul rek. Dieureudieuf Sy Malick
@ndeyefall33604 жыл бұрын
Kham nga lanla dimba li lwn niou serigne toub ak mame maodo niobou kou mame balla ken manou len kha diale gamou foko way defe bakhna lepou ben la ap talibe ng day dokhe ndigal man mom mouride la waye dama beuge tidiane yi ndakh damay gamou dji te dama si am ay mbokou niouy magal si khalif bi yalla nako yalla defal jamou mom sy malik
@aliounefagueyediop93124 жыл бұрын
Yennnnn khamou lénneee dara amouléne béna xam xam
@ndeyefall33604 жыл бұрын
@@aliounefagueyediop9312 jerejef
@ndeyefall33604 жыл бұрын
@@aliounefagueyediop9312 jerejef
@maimounatoure6174 жыл бұрын
ALLAHOU AKBAR YÉNEU YAROU BILAHI WALLAHI NALENE YA ALLAH DÉFAL DIAMM
@soldatbi71374 жыл бұрын
Wa oubi len diouma dji diouma negou yalla la
@malickgueye37944 жыл бұрын
Machallah amna solo
@kalidoumar50574 жыл бұрын
Je suis d'accord avec le khalif vraiment parceque le gamou n'est pas un farata c'est un suna la prière est plus fort que le Maouloud et on a fermer les mosquées donc c vrai le Maouloud est la naissance du Prophète (Saw)ms osi c pas grave années prochaines inshalla tt les fidèles soit la
@babacardiallo55914 жыл бұрын
2021 Inchallah maachalla
@mamembayemanga80224 жыл бұрын
Ma challah 🇳🇱🇳🇱
@sereretigui4 жыл бұрын
Inchala déwén rek inchala
@oumithiam95674 жыл бұрын
Gamou c'est pour tous les musulmans Touba day gamou gneikh
@maimounafaye47764 жыл бұрын
Allhamdoulilah sy malick ya wakh degue yallana yalla def diame🙏🙏
Yaw serigne bi nga balma wayé li ngay def serigne touba santoulako mom nitou yalla leu dou polémiquer
@omzoomzo25384 жыл бұрын
Legui après
@elhadjimalickmboup73394 жыл бұрын
ndeysanne nékeu talibé té amo khél mo gueuneu bone
@alphawelendiaye25924 жыл бұрын
Kou santoul yalla dou ragal yalla yéne khamouléne yalla d'où nguéne déme magal ba guiss séne Serigne dou nguéne KO dégue aussi sene Serigne dou wakh lou niit dégue khana hun-khun-un-khun-ouhun
@aliandoye69374 жыл бұрын
Keur Seydi Hadji Malick sene lepp si xam xam laniou ko tek dieuredieufeuti Sy vous venez de montrer à la face du monde que la religion n'est pas une affaire de business yague lene fi lole
@rokhayandiaye58004 жыл бұрын
Bayil garouwalé yi
@aidaraaichetou31004 жыл бұрын
Machalla sy malick yague fi rèk tèwèr
@djilydiop11544 жыл бұрын
Li dh amna solo degue ndiguel rék mo am solo👍🏿👍🏿
@goutsdafriquelavieillemarmite4 жыл бұрын
Machaala Sy Malick top ndiggal
@lovettedry18184 жыл бұрын
Mâcha allah
@mohamedofficiel36584 жыл бұрын
Fékhélén nak ba boulénfi wotéti beug yonanté bi ndakh diaraloulén dara.
@mamydiouf62114 жыл бұрын
Bayi léine ba am xam xam so gua dinguante, domeram yii, xam yoneunte tivaoune la feek bax, naxx allalou adouna niorouleine fils de satan
@mamydiouf62114 жыл бұрын
Yeine soléne beguone yoneunte bi keine douléne djitou si gamou, wanté sen Srg nioy sen Yallah sen waxtane sax dossi guiss waxou yoneunte ni Yallah
@mohamedofficiel36584 жыл бұрын
@@mamydiouf6211 kham yonanté bi tivaoune la fék bakh mais bo paré nga wakhma fou ligueyal yonanté fék bakh ? Amna niou bok ak yonanté bi té douniou tékhé
@mamydiouf62114 жыл бұрын
@@mohamedofficiel3658 ligueyal yoneunte bi doussi allal mais top ayy digue léime, élever sa kaw serigne
@mohamedofficiel36584 жыл бұрын
@@mamydiouf6211 yaw mom wéro ndakh warnga khamné yalla dou fay wakh di bayi Dieuf . Kiniou andale mo moudié woté mais Dieufeul yonanté mo takh mou done kimou done. Dioumo nak moy sounou yalla ndakh yone bou Dieum si yalla laa woté.
@lacourageuse42784 жыл бұрын
Mashallah
@soldatbi71374 жыл бұрын
Sa waye wakho len fi dara Ay thiakhane rek nguen fiy wakh bagne Kate yi danouy bagne balegui auto bou amoul firen dem len rk
@mamydiouf62114 жыл бұрын
😂😂😂yaw sone ngua
@mamydiouf62114 жыл бұрын
😂😂😂
@cheikhndiaye92554 жыл бұрын
Serigne babacar sama soppé 🥰
@bayefall32134 жыл бұрын
Berne alkhourhan xassida sant yonentiby foko dfe baxna li dou debat on passe way
@debery-techtv87894 жыл бұрын
Ame kilifa lou ame solo la
@moustaphaseck31924 жыл бұрын
Alhamdoulilah
@magayedieye97824 жыл бұрын
Machallah Amna solo
@cheiibra34334 жыл бұрын
Fa tabara Allahou💖🤗
@aronawassa83524 жыл бұрын
Machalla ame na solo torop
@mansourdiagne52344 жыл бұрын
Machaala❤ 🇸🇳🙏🏾
@abdouladiane49474 жыл бұрын
Yalla yalla déf Diam . yalla yalla samou bolém djoulite .
@madineamar73224 жыл бұрын
Serigne bi yalla na guen fi yague ta wer
@fatoubah48004 жыл бұрын
Machaala sy malik
@fatoumbaye3054 жыл бұрын
Alkhamdou lila ❤👏
@adjiamatytall62784 жыл бұрын
Sy malik limoudiou dikeule rek ladioye defe dewene incha alla yalla nakou diepefeke te weure ak sounou khalifa bi ak ndiabote seydy hadji makik sy
@@adjimbaye2878 togn bakhoul ani louthi yonou niit ki ngua khamné bokouléne tarikha nguaye am loy publié si séne ni activité mandou ak yarr fonkou nagnouko thi djioulite wa salam
@geuyefamily68074 жыл бұрын
Borom 36 femmê yi ak 3 femmê you bok ndéy ak bay ha ha ha
@khadimawagueye71144 жыл бұрын
Machallh sy
@serignemooustaphadiamilwad71374 жыл бұрын
LA SAGESSE DANS SON VRAI SENS
@babacarndao39404 жыл бұрын
Machallha sy malick
@sokhnafatoundiaye28144 жыл бұрын
Mane mouride la wala tidiane la lolou amoul chance beugue yonéntibi ak guem yalla rék moy deugue
@saliouba67874 жыл бұрын
Bilahi yaw waxatiko
@morfallndiaye89594 жыл бұрын
Det mourit mom ken douko don diko neub
@sokhnafatoundiaye28144 жыл бұрын
@@morfallndiaye8959 dou question neub déh xam ligua done ak xam ligua beugue dou béne
@niang__officiel4 жыл бұрын
Wa JUMAH dji bokk dagnou ko warra oubii nak Allhamdoulilah
@binetoucisse72274 жыл бұрын
Occupe tw d t3 ogno
@maremely87454 жыл бұрын
@@binetoucisse7227 gua sagn ko wakh
@mexdroid17034 жыл бұрын
Topatol Say 33femmes ok
@laminedioppikinerue1054 жыл бұрын
Hors sujet
@djamilsamb40534 жыл бұрын
Dangéni djoulilo baye fall yi ba paré oki
@darayexaleiyi41174 жыл бұрын
Mashallah ndigeul dieufé rk wéhna tall nioul na koukou wahou kilifeu waw la sante viv maoda
@omzoomzo25384 жыл бұрын
Machallah ❤️❤️ renn sakh maka amoul
@dabadiop91204 жыл бұрын
Danga nane Afrique adiougnou wayai hadj amna😁😁😁😅
@omzoomzo25384 жыл бұрын
@@dabadiop9120 a bon
@serignefalloutall65114 жыл бұрын
Kabba gui moungui touba pour gni adioul ren
@dabadiop91204 жыл бұрын
@@omzoomzo2538 réwou nar yi hadj nagnou segnbi
@omzoomzo25384 жыл бұрын
@@dabadiop9120 beug na kham len moy sa blem ak tidiane yi togne bakhoul
@mohamedcisse47654 жыл бұрын
Gnoune dee champ de course la gnouy gamoo inchallah 2020 bii
@mohamedniang74994 жыл бұрын
Yalla nalén yalla yobou si diam indilén si diam kou nek ak sa guiss guiss wa salam
@mohamedcisse47654 жыл бұрын
@@mohamedniang7499 MERCI !
@dieynabaathie58034 жыл бұрын
Am ngua si droit. Wantè te ngua khaar sa kilifa wakh bala ngua rousse.
@mohamedcisse47654 жыл бұрын
@@dieynabaathie5803 parparloo wouma waye xam na li may xam
@abdoulahatdiouf52244 жыл бұрын
Ndigall dieuffé amna solo mai jumma dji danako wara ouppi
@ndiawakane52004 жыл бұрын
Machalla💕💕💕💕💕💕💕💕🙏
@thedemocrate66874 жыл бұрын
je pense que le khalif il est dans sa logique !
@nancyba43044 жыл бұрын
C celà tu as compris on peut pas dire une chose et son contraire
@thedemocrate66874 жыл бұрын
@@nancyba4304 vraiment et le gamou peut se faire chez chez-soi !
@ndeyedeguenediop74004 жыл бұрын
Je pense que le ciel se situe vers le haut
@bayefalltigguyndiguel88104 жыл бұрын
Bismillahi rahmanirahim Ndiguel dieuffe. Killifa djohe tegguine AK worma
@aliounendoye234 жыл бұрын
Sage decision
@assmalickdiop74184 жыл бұрын
talibé cheikh yalla kasé moko gnior du pukaré du diay amam yalla nalén yalla fay.
@khadimsambbgfallou70984 жыл бұрын
Danguay katt sa ndeye rek kagn nguén tadion sén dioumayi nélén yén garouwalé rek molén nior dém lén diangui wat niniouy diamo yalla yalla ay wakh kasé diamou wouko dh
@badasylla61054 жыл бұрын
@@khadimsambbgfallou7098 lii rék wané ni ba ba diouli diafé leu serigne touba diouli si guéthie gui Sénégal niepa teuthie s'en diouma bamou dése touba
@badasylla61054 жыл бұрын
Ass diop Yéne ak serigne yéna yam garou walé rék ngéne meune