Daguéne khamoule le requin de Rufisque motakh rek mais ki mbeur leu dou tiouné félicitations champion amanekh le requin de Rufisque 🎉.
@BABACAR-l2e16 күн бұрын
Ama nékh weurseugoy bouki la âme koi😂machallah😂😂du courage thiate sa waye dou bayi kén mou dém😂😂
@doffdouweer368618 күн бұрын
Amanekh vrais Ndanaane ❤❤❤
@NabouThiam146718 күн бұрын
Wakh deug yalla mome amanekh mo dane😅❤❤
@leuzcisse618118 күн бұрын
Amanekh Si Mboppam Mo Mana Keup Yalouwane Ah Borome Warseuk Là Car Machallah
@papemalicksembene78318 күн бұрын
Saway Amanekh day entraîner kom boyi li dou weursseuk mérite la
@NabouThiam146718 күн бұрын
@@papemalicksembene783vraiment 😅❤
@Bour_ndiaye_bour18 күн бұрын
Amanékh mbeurou yalla la weursseuk la ame
@steph900418 күн бұрын
Dafa beuré dane🎉❤
@Bour_ndiaye_bour18 күн бұрын
@steph9004 lollou biti la fanane wala yaw radio ngadon déglou
@Baabakar229618 күн бұрын
😂😂😂😂 mbeurou Yàlla key
@Bour_ndiaye_bour18 күн бұрын
@@Baabakar2296 Bilahi lou lér la wakh
@FallouGalss-j8r18 күн бұрын
Ama nékh machallah verimant merito nga nak grand yii diele la wakh deuge dane nga boy yépe
@papendiaye690816 күн бұрын
Félicitations Ama nekh du courage Thiatou Daouda fall
@beyonder191818 күн бұрын
Bravo Amanekh le requin! Légui Amanekh vs Eumeu Séne walla Amanekh vs Sa Thiés.
@adama640518 күн бұрын
Amanékh vivacité ak lokho yo koudou machallah moko may combat bi
@villageois990-w5m17 күн бұрын
Fii victoire amoufi
@MadickeGueye-f6r18 күн бұрын
Thiattou du courage
@kurayahmi18 күн бұрын
*Wa Guediewaye gueum len Yallah, TDF danou neu. Dem len xool RTS images yi leer neu nagn. Dafa am tank beu parei exploiter wouko. Amanekh il a 20 combats et 17 victoires, VIP yi gueunougn ko bakh palmarès. Mom ak Alioune Seye 2 combat leu*
@Jeunehomme971418 күн бұрын
Rio🎉🎉🎉Seule athia Amanekh🎉🎉🎉
@modouthiam43518 күн бұрын
Amanekh Modane
@dernieremunites126317 күн бұрын
Beurewat victoire amoufii
@LEYE-PAA18 күн бұрын
WAX DEUG YALLA AMA NEKH MO DANN
@KhadySall-t1l18 күн бұрын
Thiaat Daouda Fall action danioukoy topeu ba diékh bi ngay xole ndakh amanekh bopp bi lale na la beuss sa bopp déclencher nexna mais finition mo dakeu du courage démal defarouwate tu n'as pas démérité
@veritesavoir541517 күн бұрын
Amanékh vraiment cest un champion mongui watt si kaw si VIP yi kéne douko bagne boy you meuna beuré la daane
@uziiljiaye29418 күн бұрын
Waw Ama nekh dina diaxal boy yi 😂
@Lilmerfrm240018 күн бұрын
Amanekh seul ❤❤❤❤
@Lune912118 күн бұрын
Ama Nekh yaye sen bay 😂😂😂
@malicktandine283216 күн бұрын
Dieul amoufi
@medounendoye31514 күн бұрын
Amanekh boy bouko si moytouwoul do dem 😂domou Rio bi❤
@modouthiam43518 күн бұрын
Arbitre bi yakoul dara amanekh avant mouytek épaule bi thiatou Daouda fall boop bi lalena Souf bouyague lerna nagne
@MoustaphaDia-g9j18 күн бұрын
Niouye wakh thiate mo dane khanan féne tv lagne sétané lamb dji
@modouthiam43518 күн бұрын
@MoustaphaDia-g9j MoMA diakhal niit soko faraler sax sou dano waxko yadanou sport larek
@sopesaliounebadrandiayendi496518 күн бұрын
Ama Neekh du jarukaay
@NabouThiam146718 күн бұрын
Bly 😅 danion waron lathe BB Diène 😂😂😂
@MaguetteGueye-m7d18 күн бұрын
Alkhamdoulilla dolli Santa yalla bou bakh sakh amanekh seul le requin 🦈 de Rufisque
@saliouthiam246218 күн бұрын
Amanékh mii wopopopopop 😂😢
@AssaneBaba-km8xi18 күн бұрын
Thiatou Daouda Fall hé ame thiate ngueu deimal si thiate y😂
@afro382718 күн бұрын
No ama nekh mo nekh rek 😂😂
@AssaneBaba-km8xi18 күн бұрын
@@afro3827 bilaie 😂
@cheikhcissecisse729718 күн бұрын
Li beré watt lawon way ahh 😢😢no arbite
@thiamabdoulayetoure341417 күн бұрын
Ay sama copains walakhi barki alkhuranu karim bouko yalla fayè khôlam dou kouy dannou ama nekh depuis aéroport Blaise diagn prtn jsuis fassoi ndeysan
@IbrahimaDiop-rs7jl17 күн бұрын
Félicitations Ama nekh
@djibysoung299818 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂 Ama nekh 😂😂😂😂kon tan n'a si yaw tey
@SambaSeck-m4q18 күн бұрын
Ktsndy yaw
@serignemoustaphambackediou675217 күн бұрын
Cet arbitre est un fils de l'ancien arbitre Niokhor Diouf, il judoka et Professeur d'LHG , il a fait ses études à Fatick. Il s'appelle paoe Boucar. L'un des meilleurs arbitres actuellement. Son jeune est aussi arbitre de lutte.
@SaliouKa-b8y18 күн бұрын
Noo thiadou taye daanouna ms décourage mbeur
@Layezahadione17 күн бұрын
Amanekh ndanane leu
@AboYarakh18 күн бұрын
Ama nékh mo dane bly
@maximediop227818 күн бұрын
amanekh mon dan
@nianggainde18 күн бұрын
Xamu len ama nekh sax
@BarizooNdiaye18 күн бұрын
Thiat du courage 😭😭
@moustaphadjamilmbaye146118 күн бұрын
Amanekh est un grand champion diote na gnou diokh KO nak si ponkal yi mou am khaliss
@fgtv114018 күн бұрын
Lamb sa arbitre bi moko arbitre dè 😂
@idrissafall794018 күн бұрын
Lambalogue dagua farrr .. guediawaye ngua deukk
@adamagaye411918 күн бұрын
Ama neikh danou naa dhh arbitre
@sidypouye812918 күн бұрын
Amanekh èpaul bi lale souf avant daouda😢
@momarndiaye945718 күн бұрын
Loluuu la guis man
@cheikhdiop967318 күн бұрын
@@momarndiaye9457lolou mo am sakh dé gayi di wax yépp ay nonou balla gaye lagne dagnouy khékh lépp Lou takh ci balla gaye wayé Mane dokhéwma nonou
@MouhamedNiang-du3fi18 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂
@djibrilniang605318 күн бұрын
Lamine Golo soloul maillot Real TDF bi motakh mou danou 🤣
@NaruNoël18 күн бұрын
Arbitre bi daffa dioum dh 💔
@khadimsarr351518 күн бұрын
lamblock khamoul dara dafa raye lamigne rek
@KhadimLoum-zs1ss18 күн бұрын
Requin bi daka neukhal 🎉Ama nekh seul domou RIO
@lesankariste872117 күн бұрын
Boyi khamouniou ama nekh
@mathieubousekouwakhaldiam701518 күн бұрын
Non amanekh mo dane❤ sportivement
@mamadoubadamba241613 күн бұрын
La victoire c'est pour ama,la tête de son adversaire a toucher le sol en premier
@thebosh-se5lb18 күн бұрын
Amanekh dane nko
@cheikhdiop967318 күн бұрын
li yèp ay téktal la amanékh bimouy gneuw khamnani lamb dji dina am thiow wayé téktal bi moy bou thiow amé guénal lamb dji dikatt mé amanékh kou am gnane la mome dafa deup lamb dji wayé avant bopou thiatt lale souf fékna amanékh danou lamb dafa doywar diga mome lamb ba wara dane diélle bou lérr gnou leundamal sa lamb si ay téktal amanékh brom kham kham you kham lamb gnoko guémb
@modo621818 күн бұрын
Nom amanekh da man lambe 😂😂
@ZoraSarr-l1c18 күн бұрын
Amanekh seul
@doudousane704618 күн бұрын
Y a pas de victoire ils devaient lutter encore Dara lérouffi