@@ndiobengom4422 saway mè looy wah nii kan mola wahnè dama fèbar wala khadim ndiay nga foog . Dèdèd.
@bahtahirou94936 ай бұрын
Leun deum leun deum bouki forr beuy ❤🎉
@djilydiop9926 ай бұрын
Reug reug bou andée poids bimou indil sathies day danou wat
@TallaFaye-y8t6 ай бұрын
Reug reug yalla nako yalla maye ndam lou sedd ❤❤
@badoundiaye57716 ай бұрын
Il parle de khadafi niodior un très très grand champion
@KhadimThiam-pe7zy6 ай бұрын
Xadafi bou nioudiourak bou dioufior nièpou la daan yèn sètanolèn lamb koi mo tah. Ladial Biram diouf djilass mo ngeumb woon hadafi niodior.
@Alima-l8t6 ай бұрын
Continuez de ne pas voir la realite boy niang sur 4 combats il a 3 defaites et 1 victoire
@KhadimThiam-pe7zy6 ай бұрын
Reug xooloul boy niang sah. Lèppu si knam là.
@KhadyBa-x2r6 ай бұрын
Reug day dane boy niang 2 teh souko modou lo djeuleh dakoy dane yallah wonamako surtout contre boy niang😢
@DjilyNdiaye-pw8zx6 ай бұрын
Fen nga dh
@KhadimThiam-pe7zy6 ай бұрын
Deug puir mga wah bayil nii niou fètè wahji ba bèss ba.
@AliouGueye-h9q6 ай бұрын
Khamo dar reug reug
@MouhamedBa-i6i6 ай бұрын
Reug Reug seul❤💚
@Ino100_Kb6 ай бұрын
boy niang sou gagner reug reug par avertissement lay done wala arrét medical mais menoul dane reug reug
@aliouneelevage64826 ай бұрын
Boy niang reug reug doumassi commentaire c t un combat piege
@lJdP9016 ай бұрын
Fadam doull rek !!! ""dégg na ame fi nguéne bokk"", ""ame na louma yeugg"", Mbeur yi da niouy weur di nianlou rek. fougn dégg ame na kou meuna niane rek niou dém fa.
@Realiteeee6 ай бұрын
Fadam beugg nala je te suis tous les jours mais loutakh dou ngueen wakh defaite Modou Lô thi Bombardier. Parceque bimou diougué thi Balla Gaye avant mouy nekk roi des Arenes Bombe gui daan nako avec la maniere. Bonne continuation. Liggueey bi rafett na
@SenegalMavie_Tv6 ай бұрын
Bomb dako dan mou teksi gris bordeaux après dane lac 2 par avertissement Lo beug wax fofu ?
@abdougueye48376 ай бұрын
tu n’as pas compris alors balla moko moudié dane mou démm dieuli eumeu dane ko
@KhadimThiam-pe7zy6 ай бұрын
Xadafii momou xamna reug reug bou bah dannako liutt semple lidjantèwuniou xadafi ak wa keuram.
@tanousow54346 ай бұрын
Reug reug boy c'est un combat match nullll 👍👍👍👍
@tallambengue-oc4cd6 ай бұрын
waxuma boy niang meunul dane reug reug damako geum rekk guisko srx
@Alima-l8t6 ай бұрын
Fadam est un arriviste il ne connait pas reug reug