Insécurité à Dakar: "Sathie en plein jour devant tout le monde"
Пікірлер: 694
@namaly8295 ай бұрын
Kou tite Galse’n rek lalal j’aime li bah jammle 🫢
@MODOUAMARtvofficiel5 ай бұрын
😢
@FADELDIOPDiop5 ай бұрын
Kou d’accord nji d’en len diapou rek lalale j’aime 😅
@ZIYECH2.05 ай бұрын
Xollal taxi man bi li Wade mou dieul ko
@davidsy82785 ай бұрын
Dafa lér bro
@abibatoubathily37835 ай бұрын
Mais fadel li diarna tite au sénégal
@daoudandiaye60295 ай бұрын
Médecin après la mort laye done no Sénégal dou dém
@veriteabsoluedeugneekhoul17205 ай бұрын
Ey waay amine way fadel. Après niou taal sen ndeye niom nieup. Bougn len yobou police
@gnobagne28705 ай бұрын
Merci d intensifier les caméra de surveillance devant vos maisons vos commerces ça aide pour les enquêtes 🙏
@user-wf2xh4un1m14 күн бұрын
puff quelle enquête ? Aucune enquête n'est faite. Vous le savez très bien.
@coumbandao25015 ай бұрын
Yallah nalleen yallah niit ci barké salatou Fatiha 🤲
@seynaboutall35515 ай бұрын
Amine
@kambayependasall89085 ай бұрын
Allahouma amine
@fatouthiam69625 ай бұрын
Allahouma Amiiiiiiine ❤️
@elagegueye33105 ай бұрын
Lou yalla dikle woul da am barke 😂😂
@Actu-tv5 ай бұрын
Amine ya rabi si barké salatou Fatiha ❤🙏🏽
@diorsecksamb30135 ай бұрын
😭😭😭😭😭 Celui qui est d'accord que souniouleenn Diappé danioo warra woonnéé leurs visages devant tout les Médias laalalll j'aime 😢😢😢😢les pays d'Afrique centrale noonou laaniouyy defff
@OmarBadiane-h2y5 ай бұрын
Mais dagne fii neck di doul naane droit de l'homme 😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡
@MbayeNiang-mt1tu5 ай бұрын
Sénégal danouy thiakhan dounou sakh wakh tour bou normal
Lou mou si meuneu dou super héros dehh enplus sou démom niou rayy ko nakk tekk si guiisso ni at am kou si yoor pompe à gaz si agresseur yii
@papaxol29505 ай бұрын
Ma sœur Ioe ki nane l’an koye dimbalé dimbali wessou woule camera yi
@coumbasow50335 ай бұрын
Bilahi
@NganeSalihate5 ай бұрын
Après niou Euwla dila massawou
@nanssakeita56205 ай бұрын
Le commentaire que je cherchais Bilae gni dougn sax ay nitt
@Maestro54425 ай бұрын
Taxi 🚖 man bi tamite sathie la xana guissouléne action kouko guiss maaye ma s’aime
@youssoudrame15885 ай бұрын
Bayilén di wakh loulén woroul taxi man defoul dara
@FatouFaye-ue2xq5 ай бұрын
@@youssoudrame1588khana guisso takou xaliss bimou for
@idrissabasse56025 ай бұрын
@@youssoudrame1588 Taximan bi jeul na liassou billet bi wadd si sac bi ba agresseur bi yekk si moto bi
@immaturesn97905 ай бұрын
Taximan bi sathie leu taxaw khar baniou dem nga droitei dieul liass billets tei meunone neu accélérer sen kaw dara doukosi fekk mais bon
@basselabdou98915 ай бұрын
@@youssoudrame1588 ☕
@MbengueMatyma5 ай бұрын
Li dou khar kanam binou khaméwon Sénégal Salamoune khawlane mine Rabby Rahim 10000 fois
@Nitoudeugue1115 ай бұрын
Lii moy galsen danioulay sétane après faits yi niouy nieuw dila mastawou j'ai le cœur meurtri en voyant cette vidéo
@falloucheikhndiaye66415 ай бұрын
Wallày lou lérr nga Lou mél ni mòma dalòn çi magal gui ñépp taxaw dima sétàne ma xamné gni kou lénn yàkar dinga wayadi ma deugeul Sama bopp génn çi ms après çi là lénn wax ay deug
@mamadousane51585 ай бұрын
Comment est-ce qu'on peut être spectateur face à une situation pareille 😢... certains dakarois favorisent le banditisme dans certains rues de Dakar.
@youpetaw975 ай бұрын
J'ai cru rever! Et ce taximan? Qu'est ce qu'il attend pour demontrer ces criminels avec sa voiture? Je donne 1 jour a police pour identifier ces gens la.
@BaaaB1595 ай бұрын
@@youpetaw97gnii groupe leu niou…taximan bii bou ciiy laal keneu niou kéy reyy
@actusenegal1195 ай бұрын
mais konie mo meune groupe sou goor yalla yii guenone bilay niou daw amouniou fiit
@tylleityllei68585 ай бұрын
qu'est ce que les gens peuvent faire 7 personnes armé contre 2
@elhadjimalickndiaye14195 ай бұрын
Bilay bou done saloum Gua guiss goor piir
@DaoudaJV4 ай бұрын
Bravo pour la mise en place de programmes de soutien aux entreprises locales. Cela favorise le développement économique
@saliouthiam24625 ай бұрын
Gni kenn manou si reuthie 😂😂
@torodo.ferrari5 ай бұрын
En tout cas sen kanam yi mom machallah yalla daflene weirrr comme nathieu bi 😀
@mariamaba67235 ай бұрын
Jaw ja bon loye retan😢😢😢
@saliouthiam24625 ай бұрын
@@mariamaba6723 rétanou ma ndakh mbécté dh mais dama rétane ndakh douniou reuthie
@rokhayabiteye-to4th5 ай бұрын
No yalna fek taxi man bi téléphone la for rek parck kèn si niom telephonam dfa wadeu regarder bien
@PMD945 ай бұрын
Taximan bi kouko geuneu done domiharam amoul , droité for yefi ndiambour dem ,rewmi nieupay tokk di setane , brique yi nek sen wet ay xeer lep 8:03
@BoussoSarr-b3y4 ай бұрын
Nio ande complise le
@ibrahimacoulibaly69695 ай бұрын
Ki déehhhh Khana banque la diougué😭 Bly deuke bi amoul loi nak li métti na trop wayyyy😭😭😭😭😭
@mballosocio49275 ай бұрын
Sûrement banque la diougué. J'en suis sûr que dagn ko yolé parce les gars sont venus de manière précise rien que pour mom. Il a été ciblé depuis. C'était un coup déjà monté avant 😢
@Galsn5 ай бұрын
@@mballosocio4927dawn si octobre bi sounou kogne bén pa Loulou laneko défone diougué Bank yor 30 millions bounetou keureum laneko Khar todj auto bi yobouko semaine niou diapoulene chauffeur ram sila bok ak koum boukal entreprise yolé
@SENEGAL3035 ай бұрын
@@mballosocio4927certainement. Et je trouve anormal que lègui dans les banques le vigiles demande la somme que tu dois retirer. Meme si c'est pour voir si tu dois aller dans une caisse privé pour les fortes sommes. Mais en le faisant il met en danger le client parceque gni tok ci salle bi yeup daniouy dèg. Parfois je me demande nakh dou gni nek ci banque yi nioy diay clients yi satieu yi
@mballosocio49275 ай бұрын
@@SENEGAL303 j'en suis sûr que lolu la. Sûrement Dina am niou nék ci bank yi di yolé gayi. Et il faut que gayi niou am bén vigilance bouniou guéné ci bank yi et aussi emprunter des voix totalement sûr...
@jomen79615 ай бұрын
Et pourquoi dire au vigile le montant à récupérer ? C'est pas son problème du tout. Si c'était moi je vais jamais lui dire.
@AmadyDione-n2p5 ай бұрын
Senegal population rk mo meun si li dara kouniou diap rk Ray tall leu
@elimanedia26595 ай бұрын
Si vous regardez bien la vidéo Le taximan a ramassé khaliss bi wade si sac bi agresseurs yi dieulé si wadji mome tamite sathie la
@aminaseye-hs9ij5 ай бұрын
Li yombou n'a troppp niak Fayda AK niakk xel wésouwoul li sa boromou goor ligueye yaw nga togue dinga togue Di sathie rk T3 dagne yakk dérou niou yorr moto yi ki sk topouniouko Mane louma contre borom diakarta youy taxaw si bountou bank wakoumani niom ay sathie lagne dh M3 sathie nane nagne rax si sen bir pour mboubo ni ay borom tiak tiak lagne yaw so garé si porte bank ngay guisse nitt gni Di dougou Di guéneu nga xamni ki xalisse la dagne Koy topou T3 nioukoy deff dougne done 1 personne M3 groupe dagne lay wadial li louniou Koy guisse si deukk bi da Bari tropp yalla nagne len diapp niom eupp niakk fayda ba dh
@NganeSalihate5 ай бұрын
Sa m’es arriver une Foix ma guèneu bank bi takhaw di khar auto bi Rék ameu borom scooteur bou niew nénako aleu téléphone maniko awma Credit mou melastikou ba sonneu d’Ali yégateu si scooter dém, dara woroul légui
@aminatacham49655 ай бұрын
Bilaye walay
@ndeyendoye4455 ай бұрын
Billaahi danga sakharmi sama laanthie. Li kay gnakk diom ak gnakk fayda la. Took di xaar kou ligueey nga sathie au lieu gnou def ni gnoom,dem ligueeyi. Thim gnakk diom.
@sankaristemadiba43975 ай бұрын
😡On doit interdire les moto taxi Djakarta à Dakar et il faut une seul personne obligatoire sur une moto ou un scooter
@ndeyendoye4455 ай бұрын
@@sankaristemadiba4397 Thiès aussi c'est pareil. Moi j ai été victime de vol à l'arrachée et j'ai été témoin d'une agression devant ma fenêtre.
@sekoubadji97645 ай бұрын
Sénégalais dafa meuneu sétane légui bou wadji déwé kou nék takhaw si beugeu nétali scénario bii... Ana solidarité
@ndeyetoutyndiaye19065 ай бұрын
Kham ga lan la Dakar g'o Wara df ni yéné deuk yi mai Dakar bopou sa bopou 😢😢😢 gni man nagno Ray nit sén kanam té dougnou wx
@Boubawafi5 ай бұрын
Avez vous remarqué Le taximan qui a ramassé l’argent
@jomen79615 ай бұрын
Mo takhit diap nagne ko
@boubadiallo39215 ай бұрын
Bilay ils sont identifiable Domou kharam yi
@mendymendy20935 ай бұрын
Non assistance une personne en danger c est grave franchement le Sénégal fait peur 😮
@sopenabii5 ай бұрын
Il faut les identifier
@beuzhustle34835 ай бұрын
Pourtant les taximans devraient les suivre ou rouler sur certains mai malheureusement Sénégal Amoul aider une personne en danger
@bequediallo4585 ай бұрын
Donc tu peux mourir n'importe quand ,comment, et où sans que personne ne s'intéresse ??? Khannà fii dou Sénégal ??? ❤😢❤❤❤😢😢😢😢
@MoustaphaSeck-os5pl5 ай бұрын
Kou guiss Taximan bi 😂😂😂😂😂
@Galsn5 ай бұрын
Amna loum for dh si sac bi agresseur bi dieul la wadé khaliss lamay nourol
@demebadiekh74765 ай бұрын
Domeram la rek satie la
@auparadisdesanges15995 ай бұрын
@@Galsnxaliss bi la sathie
@Leuz_vision5 ай бұрын
Deuk bi dall ba légui kéne wakhou wala bandi mofi geuna dokh joop 😢😢
@KerozenPatience804 ай бұрын
Rééduquer la jeunesse depuis la maison familiale. Inculquer les bonnes valeurs aux enfants ces valeurs même qu'on vroyait simplistes ou sans importance. Essayer de toujours redster sur le droit chemin. Détruire le monument de la renaissance qui est une abomination pour nous tous. Sinon cela n'est que le début dautres pires choses arriveront à pas lents mais sûrement. Que Dieu soit le soutien des gens de bien et qu'IL ruine et détruise ceux qui s'entêtent dans le péché.
@baloutadanso5 ай бұрын
Denoncer les en apportant ces videos à la police 🚓 nationale😢😢😢😢
@sabdoulahadbousso31565 ай бұрын
Li dafa wara Diehk Sénégal😢
@falloucheikhndiaye66415 ай бұрын
Solidarité amoul ñouy fitnàl ça mròmou goor nga taxaw di ba après liy xéw xéw ba noppi ngénn nieuw diko sonal diko weur, té bouñou deug lòn sénn bopp lérr namané kénn dou dieul alalam té dinane çi japp kénn çi ñòm , ms gni taxaw di sétàne fi gni gni taxaw sénn bountu placé di seitàne céy li
@CNMBusiness5 ай бұрын
Bilhay lolou moma meti
@OG-Ndiogou5 ай бұрын
Yen gniy wakh solidarité naane dagn ko warone japalé etc.... ay nafekh ngen ,solidarité fimou commencer moy japanlanté ba pauvreté dou am bouboba agression dou am koufi nek di diaye guerrier bougn la rayé yakoy yeuk delene lijanti loussene yone nek mo geun di jaay justicier ,la police fera son travail on les paye pour ça ,mind your busness
@safietoudiatta64335 ай бұрын
@@OG-Ndiogouwahofi dara ani ngor
@OG-Ndiogou5 ай бұрын
@@safietoudiatta6433 on sen fout de ngor
@OmarBadiane-h2y5 ай бұрын
Lègui doomou harame yii bouniou lène diappè dague sène loxo yi nioom nieupp est ce que dinène agresser sèti kenne 🤔? Mais diapp yobbou kasso 😤😡 affaire doomou harame yooyou
@auparadisdesanges15995 ай бұрын
Teudje 1 mois bayi mou guène defate louko raw
@kaonorom95965 ай бұрын
Quand vous attrapez un agresseur ou un voleur il faut le couper la main et le laisser partir et il faut que tout le monde combat ces domharam.
@mortallandiaye-wv3mc5 ай бұрын
Vive les institutions du Sénégal félicitations à nos forces de l'ordre l'armée nationale la police la gendarmerie et consorts ❤❤
@ndeyendiakhatembow61065 ай бұрын
Li dé niak diome lako mana toudé ndakh ki niou dore diassi djeule alalame diome lako amé wone kone guaure diome lako khamé , mais légui djigéne gni sakh nioléne ko eupe😢
@mamadougueye26105 ай бұрын
Kou si way djap na daage lokho bi bay ko mou dem 😢 Li kon films taximan bi teumite 🤬
@MalickGueye-o1j5 ай бұрын
Li boussi Etat jogoul nassi nitgni jauge,lui foumou âme na nittgni arrêter auto bigeuneu jegge topleene,parcek ay Raykatou nit laniou ,la peur doit changer de camp
@paibouniass69835 ай бұрын
Deukeu bo kham né dagne lay agressé beuthieuk li des dakar kassé la am ay kouko def Kaolack dotoko defati 😏😕
@mansourdiop4455 ай бұрын
Entre 1:10 à 1:15 le Taximan immatriculé a ramasser quelque chose qui semble être de l'argent que le Gar en bleu qui a pris le sac a fait tomber. Si vous regarder bien la vidéo entre 5:26 et 5:27 l’un des voleurs a fait tomber quelques chose regardez bien et c’est le Taximan qui la ramasser à 5:34 et plus claire sur l’autre vidéo entre 8:5 et 8:6 ou encore entre 9:3 et 9:6
@mamadousane51585 ай бұрын
Il a été arrêté aujourd'hui d'après un article que j'ai lu informe Ayoba Faye walf TV
Taxi men bi douméram dou diarr sén kaww Mouy diay diégg ni nooooooooi😂😂😂😂😂
@Oupsididitagain5 ай бұрын
Allahouakbar 😢senegal 🇸🇳
@mariamasy42235 ай бұрын
Si j étais le taximan j allais les heurter
@ZIYECH2.05 ай бұрын
Kou guiss taxi man bi rek vrai Dmrm la
@Galsn5 ай бұрын
guis nga lim for si sac bi la wadé
@ZIYECH2.05 ай бұрын
@@Galsn Waw domérame la rek
@MamadouNdiaye-m9t5 ай бұрын
Wa légui li douniou si wakh koumou nékh déf Loula nékh quoi non mon pays va mal 😢
@oumyba58685 ай бұрын
Wadji pompe à gaz lako pompe si kanam 😢li niaw na torop way. Kania la Sénégal mel ni
@TALIBECHEIKHNATIDJAN5 ай бұрын
Khana guissoulo diassi bi?
@Culturevibes-sunuwork5 ай бұрын
Li dafa eup 😢😢Rousna si Rewou Dioulite Sathi ak togn nitou Ya Allah daffi bari mo takh do comprendre quoi Musiba Rek
@aliounesall83335 ай бұрын
8min44 Plaque du taxi Dk 0734 AE lui va regretter d'avoir pris cette liasse d'argent. Le gars en t-shirt noir a remis quelque chose à l'agressé qu'il a mis dans sa poche. Et ils ont choisi un coin avec des cameras pour filmer la violence de l'action sans une véritable arme blanche sortie. Mise en scène la😅
@MarieGomis-ks8so5 ай бұрын
Mise en scène 😱 enbon
@aliounesall83335 ай бұрын
@@MarieGomis-ks8sopour voler l'argent avec le gars comme s'il est agressé avec une preuve pour s'en sortir. Mais ils seront pris
@idrissabasse56025 ай бұрын
@@aliounesall8333 Je ne pense pas, car les agresseurs auront pris soin de se cagouler pour ne pas être reconnus par les caméras.
@papekeita19135 ай бұрын
Retrouvez le taximan d’abord soit c’est le kalpé d’un des malfaiteurs qu’il a récupéré soit une liasse d’abord dans tout les cas dougueul na boppam si enquête bi
Les enquêteurs doivent retourner là où vient le Gar qui s’est fait voler pour revisualiser les caméra plus claire afin d’identifier chacun parmi ces gens là. Ils sont au nombre de 6 et les habilles facile à identifier
@Boubou10245 ай бұрын
Li meti na si khol vraiment
@bigMoo20175 ай бұрын
Kana lii film Action la😂😂😂. Thiey Sénégal deukbi amatoul sécurité. Kou yabou daw gueune deukbi. Dem investir fenene
@CodouNdir5 ай бұрын
Ki takhaw si bountou bi moy dmrm deug😢😢
@amina43015 ай бұрын
Lou mou si meuneu ils étaient nombreux at ay paka am lénn xell nak
@youpetaw975 ай бұрын
Dou ma saga. Mais si le taximan n'est pas complice, ande na chi lingua kow wakh
@amina43015 ай бұрын
@@youpetaw97 je ne penses pas que complice la mais daffa am ay nittt you bonn sénn bonnou bopp reckk
@moussacissokho42485 ай бұрын
Merci tué très doué.peutetre am nagne pistolet. Au cas de danger 🗡️@@amina4301
@OG-Ndiogou5 ай бұрын
Yen gniy wakh solidarité naane dagn ko warone japalé etc.... ay nafekh ngen ,solidarité fimou commencer moy japanlanté ba pauvreté dou am bouboba agression dou am koufi nek di diaye guerrier bougn la rayé yakoy yeuk delene lijanti loussene yone nek mo geun di jaay justicier ,la police fera son travail on les paye pour ça ,mind your busness mane ken dimabali wouma si sama pauvreté donc douma dimbali kenn debrouillez vous
@yaguegueye12525 ай бұрын
Kholal pavé yi grand bi tokk fofou dou kateu ndy gni ay pavet thim 😭😭😭😭
@morblinde87215 ай бұрын
Taxsi man bi khana da bouko si delbi li niaw na
@cabouthiong68065 ай бұрын
Brm auto yi lou niouy sét âne do daw mbeuk lène 😭😭😭
@ibrafatyndaw98915 ай бұрын
Bilakhi Lolou la wakh nii
@ibrafatyndaw98915 ай бұрын
Loutakh borom auto diemou gno firr ben moto
@Ndi34835 ай бұрын
Dans un pays normal et normé ce banditisme devrait immédiatement cessé. Le seul moyen de le cesse est de doté aux jeunes un travail décent où ils vont s'épanouir. Jub jubal Jubanti
@DAKARpopulairetv5 ай бұрын
Lii Cheikh Mouhidine wakh tank défouniouko sénégal sii toxi donaa lay deuk monument de la renaissance bii tankë dénioul fii si Sénégal Sénégal dounék si diame walahi
@damethiam25135 ай бұрын
Voiture niore complices la kou Dacor la j’aime
@oumyfall52785 ай бұрын
So démé sakh gni def li niogui commentaire
@youzarchif23935 ай бұрын
Président il est tant de sortir le baton
@oslstar5 ай бұрын
Fii hlm la No gni nioy domeram deugg😢 Mon pays va mal
@omarlephrndiaye5 ай бұрын
POUR MOU SÉNÉGAL IL FAUT NIOU ANDI PEINE DE MORT OU POPULATION BI NIEUP OUTI ARMES À FEU MOU DIÉKH
@dailyinspirationalquotes14475 ай бұрын
Kessé nak
@samaypapier82795 ай бұрын
EWAY SENEGAL KAGNE LAFI CHARIA DI AM ?
@Sènègal1404A5 ай бұрын
C ça mon pays😢
@Ibouiba5 ай бұрын
Wa Dakar ay tapéte késsé mo nek fofou comment on peut considérer une agression en pleine jour guéne khar bagnou dém gúene di def le sapeur 😠🤕
@assanendiaye10795 ай бұрын
Taximane bi amna loumou foor dhh
@bambysow26905 ай бұрын
vous les commerçants bayi léne di dieul xaliss di dem yèneu kassé nek léne au moins 3 personnes tek nguéune ame pistole pcq fofou la réw mi tollou . deuxième chose osi oute léne auto tai bouléne nekh yeneu kasse si auto bi soyez tjr 3 ou 4 personé tek yor léne sene ganaye pcq fofou la réw mi tollou
@dykhalashouppii66115 ай бұрын
Legui Gni Takhaw di Setane nak😢😢Surtout Borome lou Bleu li dou Gooor😮
@rokhayadiallo87655 ай бұрын
Taximans bi nak lokoye wakhe
@bakarykande91505 ай бұрын
Qu’est-ce tu voulais que le gars fasse. Les agresseurs étaient nombreux et armés 🤷🏽♂️
@davidsy82785 ай бұрын
@@bakarykande9150deug deug
@BaaaB1595 ай бұрын
@@bakarykande9150daa am niou con reik mais gaayine bii meunou cii dara
@dykhalashouppii66115 ай бұрын
@@rokhayadiallo8765domeram la piir
@maiamaishopp54945 ай бұрын
Ki iska brom moto bi mou andal diayou ko
@youzarchif23935 ай бұрын
Ioe do ngaaka
@khadidjatoudiop61235 ай бұрын
TAXIMAM BI AMNA LOUMOU FORR DÉ...Mon bon DIEU vole au secours du Sénégal 🙏
@adamandiaye7895 ай бұрын
Li khalato ko déf sa kogne 🙏
@begueBamba5 ай бұрын
Li khana amoul fi usa sakh Allahou Akbar galsene woratoul de😢
@BaraNdiaye-jm9uo5 ай бұрын
Sénégal n'a kilifa bayi khél askan wi mo gueun Serigne si sén bop rék Politiciens sén bop Kon nioun fan lagn dieum Lii mo gueuna graw fouf affaires Cheikh oumar Diagne Déffarlén nit gni mo gueun
@yayefallbi40705 ай бұрын
Allahou Akbar thieuy yalla Sénégal tasna nakk
@khadyndiaye3545 ай бұрын
Merci les camera cachés Gniii mom inchallah dinagn lein diapp g confiance
@mohathi99575 ай бұрын
Sonko on vous attend
@madienggueye71525 ай бұрын
Li xana serie bou besse la wala tournage clip mé manoul nk agression
@tidianendiour91855 ай бұрын
Borom taximan bi khawma da bonne khawma complice la mais menone na mbeukk sen ndeyr akk auto bi gnou takhaw
@a_mansa8715 ай бұрын
Gni done taxaw di setann bonn naniou😢😡😡😡😡
@coolboy26015 ай бұрын
Boudone yaw do def dara bindeu commentaire rek nguene meun mais sur le terrain nada
@tidianendiour91855 ай бұрын
Borom taximan bi kou bonne la waronn na mbeukk sen ndeye gnou takhaw mais kou dem sakh complice la
@sankaristemadiba43975 ай бұрын
😡On doit interdire les moto taxi Djakarta à Dakar et il faut une seul personne obligatoire sur une moto ou un scooter
@fatoufall72035 ай бұрын
Loula béte meunela
@labsolumb99055 ай бұрын
Boye yii leegi sistem bi la ñoye sathia ba am kénn si ñoom kouye toke si bank bi mélni daye retire xaliss di xool bo retire baye dem mou yónne Boye you checkpoint message joxleen Identification wax leen ni retire ga xaliss bou beri
@diopmamediarra28205 ай бұрын
Le taximan aussi il est un voleur ou un complice car après l’embuscade il a avancé et ramassé un truc que’un des agresseurs portant le teeshirt bleu a porté.
@TalllaKa5 ай бұрын
Nan bayi seetan bi waay ngir Yàlla!😢😢
@Babacar1375 ай бұрын
Mane moom paabi si guinnaw laay ré réé dawoul takhaw di séétaane 😂😂😂
@oumouseck91815 ай бұрын
Nitt day liguèy ba sone gnou sath leu li mètina bilay 😢
@Gainde7115 ай бұрын
Un enfant talibé qui vole une banane (tout le quartier va le frapper)Mes pour des voyous en coupe coupe les gens font semblant de pas voir…..
@fatoumatabinetoukonatendoy43755 ай бұрын
Maneu yi Di setaneu gnima def cas wallahi 😭 😭😭😭😭😭
@sllioudiagne86805 ай бұрын
😳 boy bou sol cape bii modou la toudou medina lagnu deuk ki dé wérouna
@a893565 ай бұрын
Aaaah bon !!! Boy Medina yii ak boy fass yii agresser rek moo neke sen bopp
@lazsam9175 ай бұрын
Ohh sath dou liguey
@falloucheikhndiaye66415 ай бұрын
Non li yombou na trop billàhi
@adamabadji50505 ай бұрын
Trop meme
@tvmbouptv71005 ай бұрын
Taxi mane tamit amna loum for ba yobélé
@keurgui72315 ай бұрын
Agresseur bouniou ci diap danioula wara brûlé
@aminadiongue74855 ай бұрын
Antouca il.est temps Guaine sortir Sénégal vraiment niawnz