Un Roi ne recule jamais, peu importe la dureté du combat. Seul, tu as attaqué, lutté, et triomphé. Félicitation champion le Roi des arènes modou lo 💯🏆🙌🏾
@fatimagueye8497Ай бұрын
Mbeur mou défoul dara néxoul beurél Modou lô roi des arènes mo beuré dane ❤❤félicitation
@mohamedtabara8520Ай бұрын
wokho fi dara modou lo 4 api
@myamya6523Ай бұрын
Mais Siteu hana dafa am bras long. ay moromam nekfi joholene combat. mom mouy danou di am ay combats rek. Non lamb c'est trop mal organisé
@uni20ver98selАй бұрын
@@mohamedtabara8520 bane 4 appuis guafii guiss le bras gauche de modou lo miguii sii kaw bopou siteu il faut bien regarder avant de parler
@mamadougueye9986Ай бұрын
Palla Mbengue vrai nafekh ngeu...Siteu souféké ni nga nara continuer sa carriereeune ngeu bayi lamb. Pere Tapga Gueye chapeau tu as commenté juste et vrai🙏
@Medzo3510Ай бұрын
Félicitations Kharagne Nous les Supporters Nous sommes fier de toi 😚 Masso nio yagual Dimanche yako moom
@FalléKÉBÉАй бұрын
Vraiment Modou Lô c’est un vrai champion le Lion de l’arène !!
@DabaLo-yx2vnАй бұрын
L'aréne National ❤❤ merci mon frère que dieu te bénis❤👍
@AmadouDiallo-p8uАй бұрын
Tu ne contribue
@fatouseye3418 күн бұрын
Le seul lion de l'arène s'appelle balla gaye 2
@salifba7251Ай бұрын
meilleurs luteur du Sénégal c'est Modou lo bilahi walahi
@modoubayefallsikroulla1423Ай бұрын
Kou siteu douma dane la nga nék meilleur lutteur 😂😂
@MamemboussoNdiayeАй бұрын
Non c'est Balla seul ❤❤❤❤❤
@saerthiam-kk3poАй бұрын
Modou lô seul❤❤❤❤
@AhmedMboup-d7vАй бұрын
Siteu ne mérite pas ces genres de combat il ne fait que reculer Félicitations Modou lo tu mérites le roi
@DeggouАй бұрын
Mais naak li yeup modou moniouko yobé amna genre boyi dolén maay chance ndakh danioulay niaklo fayda..ay sathies reug gris2 ka warone dieul nioniou ay vrai goor laniou douniou daw...
@AhmedMboup-d7vАй бұрын
@Deggou waax nga deug mom
@tbuffon924Ай бұрын
Lima dégone si radio ak Lima guiss comme yalla ak yally😂😂😂😂😂😂. Galsen fort nagne si micro nakk. Modou lo moyy ndandane wayy vraiment
@gueyeelhmor3182Ай бұрын
Moma d'ale dé
@mouhamedabdoulahidiagne786Ай бұрын
Bilahi 😂😂😂
@BabacarGueye-e4bАй бұрын
😂😂😂😂nooo radio yi dagnouy sanke nitt😂😂li moy combat bi mane foguonna ni Siteu moy Dann. Mérci modou lo❤❤
@AbdouDeme-jd3liАй бұрын
Bilakhi mem man lolou moma dall
@NdeyeLo-s1jАй бұрын
Félicitations modou lô ❤❤ya beré ya dane ya outas 😂❤❤❤❤
@Al-Muminun_Les_croyantsАй бұрын
N'oubliez jamais les 5 prières par jours 🎉❤
@ristosgueye425Ай бұрын
@OumarSy-ug4siАй бұрын
Inchalah frère
@alphafofana4086Ай бұрын
Surtout
@malicksene4693Ай бұрын
LE RAPPEL PROFITE AUX CROYANTS YALNANIOU KO YALLA YOMBALE
@BabacarTraore-q2yАй бұрын
Merci beaucoup
@medounendoye315Ай бұрын
Non vraiment Modou j’ai pas les mots dou moromou gayi ❤bly
@ousmanethiagne6824Ай бұрын
Xana mourchide TV nga setané match bi
@KhalilGalloАй бұрын
@@ousmanethiagne6824bane match hana dawou Siteu yi mola diap ba legui 😂😂
@bilalboussoАй бұрын
@@ousmanethiagne6824😂😂😂😂
@Domou_Deukk_BiАй бұрын
@@KhalilGallo saway combat match leu, match moy lou niari partie di kheutioo
@KhadijakaKhadijakaАй бұрын
Félicitations modou lo le roi des arènes Macha Allah ama to loye pourvue si lambe dji
@Elhadji2187Ай бұрын
En tant supporter de balla vive modou lo vraiment diambar gua Soûla nekhone tahaw bagna beurré
@mistermg7294Ай бұрын
Voilà c’est ça un vrai sportif ❤🎉 wadji bamu amei 2 avertissement yi sah modou mo continuei di attaquei
@kaas1610Ай бұрын
Bilay
@FitserigneАй бұрын
Modou Lo a vie ❤️🤝
@determinedtobecomesomeoneАй бұрын
Pour certains ...... Modou Lo n'a pas fait 4 appuis, tout autant pour Situé. Arrêtez de dire des contre-vérités juste parce que vous êtes contre Modou Lo. La vidéo est là, visionnez la à volonté et soyez objectifs dans votre analyse.
@crispyqueen7323Ай бұрын
Dans ce combat, modou était seul contre tous. Ils voulaient tous sa chute raison pour laquelle ils n’ont pas reporté objectivement.
@zizalecatalan8660Ай бұрын
Félicitations Modou Xaragn Lô ya beuré ya imposé ya dirigé ya am victoire
@issambengue5360Ай бұрын
Merci Père Moustapha gueye
@salifba7064Ай бұрын
Bayilene nafekh tei commenter normalement. Nit bo ko bagné nagoul ko sakh meun meni neum. Merci Moustapha Gueye analyses pertinentes
@oumartelly9935Ай бұрын
Père paala billahi yaa ignaane,iow même sou Modou lo doorè nga né siteu mo ngi beuré yaaak thiout bobou sa wétt tour bi laay fatté,. Wallahi nék roi des arènes Sénégal si bénne côté diarouko ndakh nieupp lay sokhorè😢
@AliouGoudiaby-fc4xkАй бұрын
Merci pabi nafekh leu
@KhalilGalloАй бұрын
Kone guiss nga lolou pa bi vrai sissouman la
@crispyqueen7323Ай бұрын
@@AliouGoudiaby-fc4xkak Tapha Gueye aussi mo geuna yess gneup
@senegaltv1142Ай бұрын
AkkA bagn modou Lô 😂😂😂
@michoudymen30Ай бұрын
🤣🤣🤣 balko
@moctarndiaye8221Ай бұрын
Siteu moy sama mbeur ms nimou beugé diapé lamb dji mom dou nonou dafay nieuw juste pour tenir la en échec né douma danou té lolou mom kene meunou si Dara vraiment il doit s’améliorer. Pere Max mbergane mokakoy conseiller ms li mom sa peut pas continuer comme ça
Niou dollé Sant Yallah boubaakh ..Ciré Khoudia Coumba ak Gaïdèl ndamli Yallah nala djigg .siguilllaat nganiou. Lô Ndaam Ciré.
@CheikhNdiaye-yr7zoАй бұрын
kolen wakh lolèn nekh rk genn kham 😂😂😂
@MomoNdiaye-mf2niАй бұрын
Soyons sérieux way , modou lo mo beuré combat bi yeup , ce qui n'est pas normal , yow siteu ya sokhla ya warona diriger combat nékk fi Di arriére rékk .
@mistermg7294Ай бұрын
Vraiment😂 mm fin temps bi sah bamu khamei ni sou diekhei ni moy niak di risquei mei ragal rk ak beg nah supporteram
@kaas1610Ай бұрын
Waw sitteu mom poussoul passoul
@abasall711Ай бұрын
Vraiment modou mo beurrer mo attaqué
@modoumbengue23Ай бұрын
Siteu sou yabo mou bayi beure wala mou yam si suuf beure ak rakam yi, manoul daan mbeur you mak yi, ni mouy beurer nii sakh lac 2 deppase nako, liii dafa rouslou lool sakh, félicitations Modou lo ya beure yaa khekh 💪🏾❤️
@SuperOUMZАй бұрын
Pala féneu gua ba combat bi diekh guay continuer di féneu ta takhoul gua ame ndam
@myamya6523Ай бұрын
yar ak teguine li fo rek la jaroul manque de respect
@abdrahmanegueye660Ай бұрын
Vraiment fière de modou lô machallah ❤❤❤
@AliSy1902Ай бұрын
Des commentaires partisanes. Seul Tapha était objectif. Modou a tout fait dans ce combat et c’est au jeune de venir chercher sa victoire
@BiraMbengueАй бұрын
Et félicitations a Modou lo Je suis fan de Balla
@mansourgueye7922Ай бұрын
Modou guay yapp 🔥💪👑
@ousseynoudiallo1874Ай бұрын
Grand moustapha merci tu reportes mieux que pala est trop contre modou lô
@DiantalАй бұрын
Pala day far de trop il peut pas cacher son appartenance
@idrissakone8744Ай бұрын
Kone guiss ga Lolou
@momosaw1078Ай бұрын
Moustapha louta mou bagne modou Lo ?
@abdourahmanefall6546Ай бұрын
Père pala doit pas être sur le plateau quand un lutteur de thiaroye diamaguene ou pikine doit lutter on sent nettement qu’il était avec siteu heureusement y’avait Tapha Gueye pour équilibrer les choses
@rassoul3548Ай бұрын
Pere palla.xana siteu dakoy mossal. Seere la rek. Modou beure beure bi sitteu daa def dara.
@ReflexeActif999Ай бұрын
C'est simple faîtes un arrêt sur image en ralentissent la vidéo à 0,5 Siteu à fait quatre appuie avant Modou donc modou lô à gagner ce combat bien arbitré.
@papadiom9260Ай бұрын
Bayilene fene ! Vous mentez ! Vous savez très bien que Siteu n’ a jamais fait 4 appuis par contre c’ est Modou qui a pose son épaule et qui a fait 4 appuis
@elhadjindiaye720Ай бұрын
Moustapha Gueye a été un mauvais conseiller de Siteu dans ses combat. Lui il a fui Yékini vilainement et de façon jamais vue. Combat bii Modou Lo daffa danou épaule au sol ak 4 appuis et l'action s'est produit dans l'enceinte et fini entre les deux cercles de sacs. Victoire de Siteu
@AhmadouBambaFall-w1vАй бұрын
Siteu combat bi yeup dafko daw😂😂😂
@abasall711Ай бұрын
Merci sou taxawon kone day kao
@kaas1610Ай бұрын
Merci bcp 😂
@papadiom9260Ай бұрын
@@abasall711 K.O kaay taay Modou moka defff
@LamineFall-r9p10 күн бұрын
Bilahi siteu bo takhawone khamni do bandit bilahi 😂😂😂😂😂
@halilvresh860Ай бұрын
Wahh deug fa yalla Modou lo mèrite la victoire
@MameSokhnaNdiaye-gd2vyАй бұрын
❤❤❤❤
@mamadoutraore3331Ай бұрын
Dagnouy am combat AK Modou Dem djeul poids tekni lolou molassiy guené. Modou lo meunoul dane eumeu, dane ama, dane boy Niang, Siteu Diko djakhal. Il est et reste le roi incontestable et incontesté des arènes. Molen meun fouf.
@papadiom9260Ай бұрын
Siteu dheee beuguer degg deug dafa doumeu Modou lo daneko 4 appuis ak épaule bou lerrr
@khadijadiouf2747Ай бұрын
Doumeu? Khana da nga tokh 😂 combat bi yeup Modou moko joué, l'autre ne faisait que fuir, Modou lo rek so beuré mou beuré so beuréwoul mou fékisi leu noklén gnibi 2 avertissement si khalé ndakh daw you bari@@papadiom9260
@fifty6292Ай бұрын
@@papadiom9260action epaule binguéne di langamou Siteu 1er accrochage la guéne meuno nek sibiti di dane
@KhadijaNdiaye-us3dwАй бұрын
@@fifty6292Action bouniouy wakh Siteu 4 n’a appui benneen boor bi juste Modou mo nékker côté caméra bi
@abdousow2908Ай бұрын
Mayla chance attaquer la Doumala gua tok sa coin ni beurei ga ?😂😂apres dieunkeunte dem si plateau yi di wkh rek t guat defokofi Modou le king 👑 ❤félicitation 🥳
@SenegalDakar-ee5ysАй бұрын
RADIO YI NIO MEUNA FĖNNE MAN BIMAY DEGLOU RADIO POUR MAN SITEU mo bare bare ba yeub ndeke siteu da daw lambadji😂😂
@Check-s6bАй бұрын
Même man 😂
@IbouDiallo-vv7ubАй бұрын
Billahi frère pour mane sama copin mogui ray modou Ndéké tarkinda daa daww lamb bi yép
@tiakhniangtvkeurmamebiranenianАй бұрын
Det way😂😂
@Elhadji2187Ай бұрын
Dagn ko door bamouy daww combat bi yeup la daww
@DaoudaSene-ey9ukАй бұрын
Non c’est honteux
@boyediaw1018Ай бұрын
Vraiment modou x lô vrai ndanane nga ya beuré ya am victoire sou nekhone takhaw en tan que roi 👑
Siteu dou dara wakh késsé la meune di daw ni nane dangay dor si biti sakouyou di ték khél doffouñou défo dara
@Tiley07Ай бұрын
Ioe bann combat nga seetane? Xanaa dou bii dhé!
@WadeOusseynouАй бұрын
Walakhi modou lo yamana khekh rek ❤❤
@abdoudiop8697Ай бұрын
Reporters waroul far dagua wara commenté ligua guise
@ismailasoly7305Ай бұрын
Il faut revoir la lutte sénégalais car tu peux pa reculer tout le comba comesa ont te dis tu es champion c'est treu facile même yawou dial peut ❤❤ lutter come sa avec modou lo reculer tou le comba contre lac c'est comesa
@mamadoudia9775Ай бұрын
Tt ta fé d'accord Fayela ay million kheuy arrière rekk apres kheuy jubilée
@assanendiaye5640Ай бұрын
Sa way li Moy game plan, IL nest pas tombé, IL la fait saigner, modou lo a commence a douter....ensuite laction litigieuse...IL a presque reussi
@bilalkhalyfall9938Ай бұрын
@@assanendiaye5640dégueul wakhoul dof li beuré késsé ngueu sagna défé lih dou MMA dou boxe on te paye des millions ngueu gneuw tassé ak seu moromou guaur daw combat bi yeupeu nguén tok naneu Daguén outeu ay alibi kougnou douter Lo dinala dakhadji nguay Sakou yi
@SerfelWayouАй бұрын
Modou lo félicitation à toi mon champion maintenant que tu conserves de nouveau la couronne 👑 çà dit pas de la mettre en jeu en affrontant un adversaire comme sathies qui est un très bon lutteur et très grand bagarreur comme tu l'es toi? à mon humble avis je pense que les organisateurs doivent y songer car sathies Modou lo serait un très grand combat et une possible vengeance pour toi sur Balla gaye 2 en battant peut-être son jeune frère sathies.
@amiFall-t2oАй бұрын
Félicitation kharagne lô ya meune ya eupeu dolé macha alla ❤❤❤
@alassanembaye4147Ай бұрын
Senegal mo bari nafékh siteu da daw combat bi yeuupp
@kaas1610Ай бұрын
Bilay daw rek 😂
@Milkzo221Ай бұрын
Franchement Siteu dafay saboté beuss way je suis fan de Balla Gaye pour information mais siteu mo yak combat bii daw rek 😂😂
@fannylagalsenne5142Ай бұрын
Vraiment ngua sagne ko wakhe reporter yi koulaine geuneu seytané amoule farougnou fène et siteu n’a rien foutu il fait que attendre que Modou Lo attaque il ne bouge pas d’un yota ses vieux là sont rien d’autre que des hypocrites tchim
@galaxiepro.5641Ай бұрын
nga sagne ko waax sakh
@abasall711Ай бұрын
Merci même siteu sou dieuler balla beurrer ni dou danou daw rk
@SohnaMagetАй бұрын
Is good❤❤❤❤😂
@DiabsoDia-wk5vwАй бұрын
Félicitations Modou lo du courage siteu c'est ça lsport❤
@Mõũhåmëd-i5lАй бұрын
Félicitations siteu
@DiabsoDia-wk5vwАй бұрын
Qui a gagné le combat @@Mõũhåmëd-i5l
@DioumModou-is9qsАй бұрын
Palla kou Dakkar sa ndaye seytanéné nga😢
@bayefall1917Ай бұрын
Daw moy expérience legui😂😂😂😂😂
@Taw-Fékh-n9zАй бұрын
Sitteu ak wa keur yayam ak wa keur bayam aki supportaire ram yép modou lo moléne man😅😅
@kurayahmiАй бұрын
Il y’a une promotion de la médiocrité dans l’arène. A part Papa Sow, Siteu a raté tous les grands rendez-vous de sa carrière : ❌Boy Sèye ❌Gouye Gui ❌Sa Thiés ❌Lac de Guiers 2 ❌Modou Lô Teh meme contre Papa Sow il a reculé pendant 2 mi-temps sans def action, Papa mo moudjei dieul risque dem songou ko pour sauver la journée de Jambaar Productions alors que Siteu mo warone prouver. Contre Lac il a fait pareil, aujourd'hui aussi meme chose. Daw gueine sakou yi beu am defaite di beuri wakh di jubiler melni ya daan. Niom Modou Balla Eumeu bign sokhla wei roi bi danio prouver. Wakh len ko deugue!
@bdd1145Ай бұрын
❤❤
@FallouNdao-l3zАй бұрын
Lolou yalla ko def 😂😂😂
@mouhamethdiallo3383Ай бұрын
Simbb gaïndé kénn topé wouko dara 😂
@kefggАй бұрын
Il a aussi perdu contre Zarco par 4 appuis. Sou VAR amone diamono yoyou Zarco lagnou diokh ndam si guew bi
@thiemokhotounkara9343Ай бұрын
Billahi awlamigne reck le yore
@ndakarudialdiop1206Ай бұрын
C’était pareil contre lac2, Siteu daw lamb ji yeup après yénn pa reporters you nafékh yii waro wakh deug diko khalamal vraiment lii c énervant
@AbdelRazzaq-vh8vxАй бұрын
Boudé ya gueneu doon jambar siteu ñeuweul soumé doranté book ngay def sa yeufou tot yi
@abdoulayely7256Ай бұрын
reportaire yi aye ennemi modou lo lagne mais fi yallah modou neh modou lo moy roi des arene point; nokou neu siteu dake nako dane nako:, siteu daw kesse lafi neke
@khadidiatoudiouf186Ай бұрын
Iao kou bone nga
@sidzboy3836Ай бұрын
dagnko woutal yone ba fi ta dou mbeur
@maimounakonate5694Ай бұрын
🎉😢😮😊@@abdoulayely7256
@mamadouba6357Ай бұрын
Siteu ne sera jamais un champion. Comment peut-on féliciter mbeur bouy daaw sans attaquer ni rien ? Modou LÔ ❤👑
@mamadoulaminesaneАй бұрын
On le félicite parce-qu'il a bcp de supporters et emporte à la Caisse sinon siteu ne fait pas le poids♎ des grands
@MoussaSarr-qk9jpАй бұрын
Tout a fait a moyce un intellectuel@@mamadoulaminesane
@dehabou7720Ай бұрын
Vraiment Modou Lo tu mérites ton victoire 🎉 félicitations 🍾🎊🎈🎉
@thiernondiaye5126Ай бұрын
Modou et mon lutteur mes Sitta et de mon village Dionward je support Sitta félicitations a tous les deux
@AwaPouye-k7tАй бұрын
Machaallakh le champion Modou kharagne lo mbeuré nak
@malicksene4693Ай бұрын
FELICITATION MODOU XARAGNE LO🎉🎉
@MaremeDiop-z6o14 күн бұрын
Tay la SOKO setane combat MODOU door yi nekh na ❤❤❤❤
@ThioroFall-s8hАй бұрын
Modou lo douma nako nak franchement modou c'est un bagarreur
@Fallou657Ай бұрын
Bravos Siteu 👏 Modou lô être toujours Modou lô
@LaygueyeАй бұрын
Lamine néna Siteu déf na jalooré 🤣🤣🤣🤣😅😅
@bafatou3186Ай бұрын
Félicitations le roi des arènes Modou kharagne Lo, ya beuré ya dane
@FatimCamara-x5mАй бұрын
C'est ça modou lô je t'aime beaucoup wallah siteu tu connais rien mange seulement 😅😂😂comment tu peux faire tomber modou lô longue vie à toi ❤😊😊
@abdoudiop8697Ай бұрын
Modou lo seul gayi dagno beugué mou danou mais Dara siteu Moy khaley lepeuh modu moko def vraiment chapeau Modou
@DeggouАй бұрын
Seen programme yeup mooy outal yoone balla pour l couronne 👑...
@Mdrr2215Ай бұрын
Bilay mais dagni sonou rck meuneu lougne ko dara
@MandiayeNiang-q7nАй бұрын
Ouï félicitations champion soyons fair play c'est le Sénégal qui gagne
@OumySamb-zt7hmАй бұрын
Bilahi Tapha Gueye moy champion néna dara amoufi té c vrai
@omarthiam6744Ай бұрын
Couronne 👑 boko beuguer dagay beurrer
@bayeibrahimadiop3893Ай бұрын
Vraiment Modou lo ce jour là n'était pas son jour mais guathié ngalama siguil nganiou sagual nganiou le vrai champion ont t'aime fort ❤❤
@Ngonediaye2410Ай бұрын
C'était pareille comme lac de guer siteu manoko dane si aye aye dawam yi
@sokhnadiallo9013Ай бұрын
Alkhamdoulilah 🎉🎉🎉🎉🎉💯💯💯💯♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@sssalihou7819Ай бұрын
Tapha Gueye ak Père Palla yeup Siteu lagnou faral bamou feusss, lii dafa ñiaw troppp waye.
@CellouDiallo-z8qАй бұрын
Modoulo ❤❤❤❤❤❤🎉
@MM-vv1zyАй бұрын
Wouy reporter bi neina😂😂😂💔 Siteu foy dem 😂💔💔 ❤️❤️❤️❤️❤️🦾💪🏼 Modou Lo kèsè, Modou Lo feep, Modou Lo ♾️♾️❤️🦾🦾💪🏼💪🏼❤️ 👑🤴🏽🤴🏽🤴🏽🤴🏽
@AhmadouBambaFall-w1vАй бұрын
KOU WAKHAL YALLA RÉK KHAM NI SITEU GNEUWOUL WÓNE POUR DÀNE MODOU LÔ
@Papis-k5lАй бұрын
Louler nga wakh dfeu nieuw pour saltel
@papadiom9260Ай бұрын
Lolou nga tekk ko fane ??? Kou wakhal deug Yalla khamni Modou lo mii dafa done negocier combat bii taay
@khadijadiouf2747Ай бұрын
@@papadiom9260négocier ? Kouy négocier dina attaqué tout le long du combat ? Mom normalement mo warone défendre gardé couronne bi sans attaqué mais le jeune siteu loumou def ? Il a fui, niewoul pour beuré, solén yakaré nek roi ak estrategie bou nulle bi yé na ngui nélaw
@salvadornguemaesonoandeme7787Ай бұрын
Vrement 😂
@SenegalDakar-ee5ysАй бұрын
Site dh kou deglou radio ngani mo dan waye télé 😂marché arier SITEU kom LAC 2
@AmadouSow-u3fАй бұрын
Bilahi reportage yi ñioy khekh modou way yalla bakhna si radio siteu mofa dan way si télé modou mo dan thiey yalla 😂😂😢😢
@abiboundiaye3952Ай бұрын
@@AmadouSow-u3fc’est vrai dh ils étaient clairement partial
@kaas1610Ай бұрын
Bilay sitteu moye lac de guiers 3
@Shalliw03Ай бұрын
Man kay bimay deglou radio dama yakaron ni sitteu rayna modou mé lima guiss ni😂
@kaas1610Ай бұрын
@@Shalliw03 🤣🤣🤣
@abdoukarimgueye6851Ай бұрын
Dara li ngen fi commenter amoul wa lutte Tv pousseul leen niou pa yi fi way gni mom merci quoi!
@ibrahimasarr8936Ай бұрын
Modou c’est le meilleur ❤
@OumarBah-ht9hfАй бұрын
Félicitations modau lo❤❤❤❤❤❤❤❤❤tu es un légende ❤
@WadeOusseynouАй бұрын
Ki modou xawna ko raye siteu dell wakh modou lo papa 😂😂😂
@InssadialloFallАй бұрын
Modou demna ardo 2fois
@papadiom9260Ай бұрын
Saway Modou lo 3X la dem ardo Bayilene fene guiii
@rouguietousy2292Ай бұрын
Siteu vraiment dafa daaw combat bi ,Modou à tout fait moy songou moy door
@abasall711Ай бұрын
Voila merci nonula demer
@NayeFall-qq7xiАй бұрын
Ku daw doo yobbu ardo ken waay 😂😂
@MariamaBousso-ey1nwАй бұрын
Ardo niekkè wugni kofi tè dougne ko moudié
@abasall711Ай бұрын
Voila merci
@FalilouSow-b2wАй бұрын
@@NayeFall-qq7xi dhe sokhnasingua balma ki hord frapp rek lay def beurewoufi Dara bilahi wakhouma parparo nak
@AhmedMboup-d7vАй бұрын
Je me demande pourquoi on parle toujours de siteu alors qu'il n'a rien fait d'extraordinaire il fuit seulement🤔
@SodaCisse-qb2htАй бұрын
Lo khamsi sokor rk
@sowdiouldeАй бұрын
Pour moi modou est à féliciter ! Il a attaqué et siteu a tjrs reculer. Ce siteu là il faut qu'on arrête de nous le vendre. Il est loin d'être un lutteur.
@the_black_phoenix4352Ай бұрын
fi ben chute litigieuse amou fi. Lep si guinaw sakkou yi la. Bravo modou lo. De la part d'un fan de Balla gaye
@etranzeixenos9367Ай бұрын
Action sou comacei si biir diékhei si biti dieul leu, parceque marqué xouniou pause boy yagg si bitti
@the_black_phoenix4352Ай бұрын
@etranzeixenos9367 Modou lo mo commencer action bi. Siteu bamouy actionner mi ngui si bitii. Tapha Gueye leral n'a lep.
@cissokhoeva2042Ай бұрын
Y’a Bakh 🎉
@etranzeixenos9367Ай бұрын
@@the_black_phoenix4352 CNG Mossoul préciser lolou, tei beurei pas parce que dangay arrière o actionné rassou sakh day dane mbeur, Siteu da yokou Modou Lo voilà
@the_black_phoenix4352Ай бұрын
@@etranzeixenos9367 saway. Lamb ji siteu meunou si am victoire. Kou niou dakh ba nga guen sakkou yi meuno fa réclamer victoire. Ki def action commencer sibir guew daan sii biti laniou wakh.
@seckouibrotv5223Ай бұрын
Siteu ne mérite ces genres de combat il passe tout son à courir, alors qu’il est le plus jeune, il ne sait que parler thim
@simmelsarr3599Ай бұрын
Tapha Gueye néna Siteu fo dieum😂 Li dé moy aduna. Faté na bimouy daw ni taxi contre Yekini. Kone Tapha yagui doga xam mbeur bouy daw nimou sofé meuneu yakh beuss
@DaniMendy-o8jАй бұрын
Bien dit
@FatouGueye-y2lАй бұрын
Seuuttt raygama
@khadijadiouf2747Ай бұрын
😂dema yakar souniouy daw dougnko tay vu que nio nék si arène bi di subir mais sounou sétané ils ont honte motah supportaire limouy guiss ak kiy jouer bokoul 🤣 père tapha raynama
@toubabelellferallye2273Ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂 Yaw sof ga
@simmelsarr3599Ай бұрын
@@toubabelellferallye2273 🤣🤣🤣
@AhmadouBambaFall-w1vАй бұрын
SITEU DOU DARA NDÉKÉ AK LIMOU WAKH YEUP
@lacitoyenneafricaine8566Ай бұрын
Nagnou wahanter deug, contre Lac 2 Siteu dafa gérer combat bi sans risque gneup dale lac 2 ndakh mome dagnouko yapp. Siteu gneuwatt pareil modou lo mo combat combat bi sitteu riposter ak djeneu sakou yi ak ay coup hors arène (lang bi) donc lolou gagner woule combat royal! Ama dafa djeul risque tenter ba danou fek kossi! Alors nagnou nangoul Modou lo victoirame tani Siteu bon courage ! Félicitations Modou Lo souka nekhone takhaw di daw risque defou ko action yeup modou le vraiment. Siteu aau final bouka seytaner dougoule dou recours melnani nangou ne ndogal. Wa salam.
@HAVIS_MARAMАй бұрын
Virement @@lacitoyenneafricaine8566
@AbdellahiNdiayАй бұрын
Machallah modou lo gainde la dou arriere dou diegui sakouyi jamais felicitation le roi des arene
@MaodoGadiaga-t3xАй бұрын
Félicitations lutte tv 75mil suivis en direct c’est pas facile
@josephericousmanediandy783Ай бұрын
Wayyy sama wadjiiiii . Wa Sen affiche ils nous ont dessus jsuis désolé. Li vrai arnaque la
@AmadouDiallo-p8uАй бұрын
Leur faire plaisir à discuter avec eux pour leur dire
@DikeDiop-oz7gfАй бұрын
Félicitations Modou Lo 🤴❤️🎉
@fatoubayeldioum743Ай бұрын
Ceux qui ont commenté le combat sont contre Modou Lo Modou lo moo beuré lépp qu'on se dise la vérité
@NowayCoulibaly25 күн бұрын
Modou lo. ❤❤
@papispassАй бұрын
Mais Père Palla khana dafa méré Modou Lo 😂😂😂 mérci Tapha Guèye pour sa neutralité
@MikayeKontéАй бұрын
Bilay modou danou na
@thiernogueye829Ай бұрын
Ya meune féne👽
@JenniferGuinesАй бұрын
Danou na dh sérieux
@AhmadAhmad-pp2tcАй бұрын
Modou lô seul,le roi de siteu ❤❤❤❤p
@juliusceaserrАй бұрын
Comment ça chute litigeuse? Ne créez pas une fausse polémique pour rien du tout. Modou lô a gagné ce combat et si j’étais Siteu j’allais plus me reconvertir en communicateur traditionelle qu’autre chose. Je suis un fervant fan de BG2 mais vraiment siteu meunatoul wakh lou nite gueum louma ci metti rek moy dina langamou si action bimou am ak modou lo si guinaw sakoyi SACRÉ SITEU 😂😂😂
@assanendiaye5640Ай бұрын
Modou lo est tombé waxal deug
@FS-jh4kyАй бұрын
Modou dafa danou saway c’est juste que siteu dafa guen guew bi
@talibecheikh7367Ай бұрын
Khana dégoulo nafekh bi di wakh mention spéciale à siteu 😂😂 gni daniou ragal siteu trop té khamouma loutakh
@aramegaye3968Ай бұрын
😂😂😂 sacré siteu
@abasall711Ай бұрын
Merci
@ShiekhjobeTijanАй бұрын
Bravo bravo Modou lo rek ❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑♥️👑♥️👑♥️
@prosperpreira6685Ай бұрын
Bravo modou👍 du courage siteu
@mamemariemediagne7906Ай бұрын
Mais félicitations modou déf nga lépe linga meune❤
@jacquesndiaye6691Ай бұрын
Tapha Guèy bayignou ton combat contre yekini ya raw taxi😂😂