Intégralité Sidy Diop chez Wally seck tout ce qui vous à échapper et surprise de Wally pour Zenith

  Рет қаралды 31,315

Dakar live

Dakar live

Күн бұрын

Пікірлер: 48
@HonoreKinésportSanté
@HonoreKinésportSanté 8 ай бұрын
Wally sa pape ak sa yaye yalla naniou deimmmm si eutou SEYDINA MOUHAMAD PSL WALLY SECK JE T'AIME BCP TA UN COEUR EXTRAORDINAIRE JE SUIS VRAIMENT ÉMOUSTILLÉ LOU RAFETE DAMA AMME SOLO
@PapeSamb-vt7zp
@PapeSamb-vt7zp 8 ай бұрын
Amine wayy🙏
@seydinaissademe
@seydinaissademe 7 ай бұрын
PSL
@kitokoken2187
@kitokoken2187 8 ай бұрын
Boufi bén seytané gneuw di roubé. Li dafa raféte . Mane mi meussoul dem soirée sénégalaise france, inchalla beugna dem
@AminaSow-ro4uj
@AminaSow-ro4uj 8 ай бұрын
Ay way kou kholam nekh ba melni sama boss Yallah na diam yague way❤❤❤❤❤❤
@AlphousseymiDrame
@AlphousseymiDrame 8 ай бұрын
Je suis très contente vraiment magnifique bilahi walaye walaye walaye merci llyy Wally Drame se.. fans club cassamace Bignona je suis à Italy Milano
@rokhayaThiaw-q9v
@rokhayaThiaw-q9v 8 ай бұрын
wally beugue nala billay wallay ya bakha yalla nala yalla faye sa khol ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mamadoulaminediop-bx3me
@mamadoulaminediop-bx3me 8 ай бұрын
Wally nda bakh Yalnako yalla feyy eweul adouna goudou fanne Yalna yekh wayé yalna ame kheweulou alakhira aussi ❤❤❤❤❤
@dadawallyfaramareen5789
@dadawallyfaramareen5789 8 ай бұрын
Bilahi maryacine y’a bakh geun wayyy❤ yalna sa jamm yaggg
@NdeyeDiouf-vu9gn
@NdeyeDiouf-vu9gn 8 ай бұрын
Li nékhna trop machallah wally seck diam gay am inchallah❤❤❤
@fatoufall287
@fatoufall287 8 ай бұрын
Machallah wally laf thiat inachallah
@deydou_diakhate5281
@deydou_diakhate5281 8 ай бұрын
Machalaaaa mar yassine dagua am respect thi nitt yal na yallah guen len dioubat lé thi barke rassoul
@ndiayambaye58
@ndiayambaye58 8 ай бұрын
Wally mala beugue ya bakh ya oyoof yalla nala yalla faye sa khol té défal la kawé sa diorte Sidy aussi yalla nala yalla fay yiw mane fans lou bakh ta raféte rek momay doundal 🥰🥰♥️
@MamyGueye-ty2eq
@MamyGueye-ty2eq 8 ай бұрын
Bly wally ya bakh diamou rek guay ame inchallah ❤
@sokhnadiallo9013
@sokhnadiallo9013 8 ай бұрын
Machalla ✨✨✨♥️♥️♥️
@minadiol7209
@minadiol7209 8 ай бұрын
Que dieu te bénisse
@coumbapam2330
@coumbapam2330 8 ай бұрын
Wally seck à trop changé machallah devenu très mignon laf bouche 😊
@khadidiatoudiao1967
@khadidiatoudiao1967 8 ай бұрын
Machallah yalla n'a diam yague❤❤❤❤❤ Amine Yarabi 🙏🙏🙏🙏
@HonoreKinésportSanté
@HonoreKinésportSanté 8 ай бұрын
Salu a tt le monde entouka moi je me dit que wally je testime bcp ndakh adouna bi amour solo sidy Diop boul Meuse fate li la yalla boule ak saye nite you bakh ndakh adouna mane lou rafete rek laye beugeu degeu
@amitaleyeleye8053
@amitaleyeleye8053 8 ай бұрын
Yalla nagnou mousal si seytané vraiment li dafa nekhh🥹
@HonoreKinésportSanté
@HonoreKinésportSanté 8 ай бұрын
Wally moi Honoré serigne babacar sy j'aimerais bien un jour de te rencontré et de discuté avec toi sur bcp de chose ndakh wally khôl bi gua amme dama koyi sentir si makk gui deimbeuh yi Serigne Fallou Serigne salique mbacke serigne babacar sy wally makk yi lou bakh rek la niouyi deff❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@amytall850
@amytall850 8 ай бұрын
Yalla nagnou yalla moussal thi saytané sunu fierté ngéne boulene deglou kene❤
@MbetyNiang
@MbetyNiang 8 ай бұрын
Li rafétna mais j'aimerais bien ay nite dokh Lou melni diguanté Viviane ak Titi
@HonoreKinésportSanté
@HonoreKinésportSanté 8 ай бұрын
Dieu a dit aimer les uns les autres comme dieu vous a aimer est savoir pardonné l'un d entre vous ❤❤❤
@AdamaMballo-t9s
@AdamaMballo-t9s 8 ай бұрын
Macha allah c’est beaux ça vs etes ds frères
@Bousso792
@Bousso792 8 ай бұрын
J’apprécie beaucoup la modestie de Sidy👌mais nak mar yacine y’a guen bakh nak Koula juste à travers les écrans wara kham ni kou bakh gua tek si sincère ligay wakh ni Lo geum la ❤on t’aime bien
@MalickSy-i9g
@MalickSy-i9g 15 күн бұрын
Mashaall
@ceciliamanga8746
@ceciliamanga8746 8 ай бұрын
Wonderful ❤❤❤❤❤❤
@CamaraSira-rx7rg
@CamaraSira-rx7rg 8 ай бұрын
Li lagne nane kou khamatoul fingua dieum daguay délou fingua diouguéwone Sidy Diop kou toth leufeul ndayam Faux la té niakk diom beug sen zénith bobou féss motakh nguen di weur keur diambour yi ni kou lambléé dolen sakh rouss Yak sa producteur bi amoul lounguen defoul Wally amoul lounguen KO wakhoul fi la done Kaf nane ndiap yak sidi samay dome nguen nguay mér nane ben baye la am Mouy Omar Diop Di garouwalek louné ngua dougoussi melni goor jiguene Di teubeukeu dal faté khadioufi sa entourage bou bone bobou khawma soubatel khawma goudi monté la contre Wally ngua melni deum bou dieufrou sa invitation bobou bou deugou wone si yaw môme matar sa producteur molay goungué thi sa mak Wally wayé mome moy deum bou mak bi si souf lay def wally rek la bagne bo ndiekké wone fi nak nitt yi beug la....amo guathié sidy nioul ngua niaw ngua gateu ngua modé ngua ba paré fouy té bone khol day fégne bassi sa kanam... sur ce Merci beaucoup notre wally nationale ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@coumbadiorseck9126
@coumbadiorseck9126 8 ай бұрын
Machalla li rafetna
@bintacham-iy8sd
@bintacham-iy8sd 8 ай бұрын
Belie this is lovely ❤❤❤❤❤❤❤❤
@diawaminata1409
@diawaminata1409 8 ай бұрын
Machallah ❤❤❤❤❤🎉
@loufatheboss7958
@loufatheboss7958 8 ай бұрын
Ani wakh Katt Yii rousse guéneu dhé 😅
@elhadjimbaye2710
@elhadjimbaye2710 8 ай бұрын
Li waly wakh deugeu leu sidy diop boko kholè khamnè waly lay roy
@MameDiarraGueyebouwally
@MameDiarraGueyebouwally 8 ай бұрын
Maryacine y’a woyoff😅 y’a ame calass❤
@BaoYacine-ng8fj
@BaoYacine-ng8fj 8 ай бұрын
Et après khana dou nitt comme diep merd a là fin😅
@HonoreKinésportSanté
@HonoreKinésportSanté 8 ай бұрын
Wally seck mane Honoré Serigne Babacar Sy magui laye naianale soutoureu bou weer a goudou fane bou yageu si sa ndiabote bi yeup ndakh wally niou beuri khama gounioula ndakh mane Honoré Serigne Babacar Sy dama geumm adouna khôle bou rafete moyi takh nite kou bakh di nopalou si leep
@onlygood1114
@onlygood1114 8 ай бұрын
Wally Aka bakh
@AdamaMballo-t9s
@AdamaMballo-t9s 8 ай бұрын
Mrci boucher
@tamartavares
@tamartavares 8 ай бұрын
A quand le duo
@mustafbestino7444
@mustafbestino7444 8 ай бұрын
Sénégalais yii aka ñio seytané ( svp 🙏 devenez matures way )
@MameDiarraGueyebouwally
@MameDiarraGueyebouwally 8 ай бұрын
Maryacine mo bakh déh
@JammalAnderson
@JammalAnderson 8 ай бұрын
Zenit wally motakhe dinago Stan
@hassatoudiallo3510
@hassatoudiallo3510 8 ай бұрын
Yaw fongolimbi thi Sénégal la bok ok 👍
@mansourdiop7936
@mansourdiop7936 8 ай бұрын
Pawlish moy mbaam boucher nieuwna d😂😂😂😂wally rek
@ndaofama
@ndaofama 8 ай бұрын
Waly daga niank kiniane bilay walay ndaysan
@SonaDiouf-j6m
@SonaDiouf-j6m 8 ай бұрын
Thia amadou bary pa ma contane si yaw
@abdoulayendoye542
@abdoulayendoye542 8 ай бұрын
Gars yi andaléne wala nguéne bayi gnoune amou gnou séne temps.vos entourages sont trop bavard
To Brawl AND BEYOND!
00:51
Brawl Stars
Рет қаралды 17 МЛН
Арыстанның айқасы, Тәуіржанның шайқасы!
25:51
QosLike / ҚосЛайк / Косылайық
Рет қаралды 700 М.
DIDI B   LE PORTRAIT PARLANT 1
3:13
Aby Andre
Рет қаралды 947