Machallah notre capitaine diarama serigne mouhamadoul moustapha sy
@bakhyaye74992 жыл бұрын
Domi mbeur dal dianguil beure thiey mame Cheikh diar nga sa yon ba deh très bien👏👏👏👏💯👍❤✅
@polyvalenttv62322 жыл бұрын
Machaalah MAME Cheikh Tidjane Nôtre très cher 🕋🇸🇳🕌 Capitaine Yalla nalla yalla arre Barkelleu sam'leu yokoula kham-kham Wii Lakheuleu fou Yakh Yëggoul moussal-leu Thiatte AK Lamigne moussiba akk balah cii barckè alkhour-anne machaalah 💯🇸🇳
@dieyecheikh68472 жыл бұрын
ALHAMDOULILAH dieureudieuf Cheikh Mouhammadoul Moustapha sy al maktoum
@astoumbenekhouma58412 жыл бұрын
MâshaAllah waay sunu Capitaine yalla nala yalla dolé taxawu aar la goudal sa fan wéreul la mousal la ci Thiatt 🤲🏽🙏🏼😍❤
@khadim18752 жыл бұрын
j'apprécie le fait qu'il parle de chose terre a terre accessible et compréhensible a tous sans un mot arabe parfois qu'on comprend pas grand chose
@idrissademe19312 жыл бұрын
Macha Allah, quelle clairvoyance !!!
@aladjifalloudia49152 жыл бұрын
Mame cheikh tidiane sy man moride la wayé damalaa bègue lolo amal diamo rék sy malick 🙏🙏🙏🙏
@cheikhamadoubambambaye65642 жыл бұрын
Maachallah Mame Cheikh sa xam-xam dafa lakkhou, djoulit bou limité meunta kham lingay wakh. C'est plutôt subtil.
@keimo74362 жыл бұрын
Jambaar lolou amoul. Louy xam xam bou lakhou? Bayiléne nakhaté bi
@cheikhamadoubambambaye65642 жыл бұрын
Waaw kou baakh manguilay ziaar. Dama laayé biir donté ni sakh amouma xam xam silou wer nak. waayé boo beugué Xam boulni mouk looxamoull rekkeu amoul. Yalla bour la bookhamné loumouko nékhé, ak foumouko nékhé lay def Mbireum, khoooloul ndakh nit gni comprendre naniou wala. Ndakh, il n'a de compte à rendre à personne. Mane weddi wouma linga wakh, wakhdji daa khawna diss waayé soula yalla mayé deggueu rek ngakooy xam. Waayé ki xam leppeu rek moomeuna wéddi, waayé yiow xamooo leppeu, yalla rek n xam leppeu. Saaway yalla daaa mayé dé.
@souleymanetine57512 жыл бұрын
Notre capitaine que dieu le protège Macha Halla Aminnn
@mbayelingeur79242 жыл бұрын
Machalla
@ibrahimamba12962 жыл бұрын
Vous croyez que DIEU va protéger ce mécréant ?
@ELODIEDans Жыл бұрын
ماشاءاللهم صل علي سيد نامحمدوسليم مام شخ احمدتجان سي المكتم
@mouhametdiop8996 Жыл бұрын
Wallah nadasane sy Capacité ❤❤❤❤❤
@damembaye54102 жыл бұрын
Senegal dafa nékh dh Dangay wakh say bêtises ba paré nite gni topou la kii wakhoufi dara .démal diangi mo guene lii ngay déf nii
@papaamathsow57722 жыл бұрын
Encore une fois la pertinence et la cohérence dans l’enseignement sont manifeste. Vous démontrer la faiblesse des écoles occidentales par l’intermédiaire de la hauteur des interventions. Avec ce Colisée vous formez de nombreux gens en manque d’analyse logique.
@ablayesy60952 жыл бұрын
Machalla la clairvoyance des paroles yalna yalla sameu capitaine
@sokhnaniang31772 жыл бұрын
Dieu merci biga niou bolek capitaine yalla naga niou may niou kay deglou tadiko degeu♥️🤲🤲🤲🤲🤲🤲♥️
@mmefallmn89102 жыл бұрын
Machalla notre capitaine de coeur ❤️❤️❤️
@souleymanetine57512 жыл бұрын
Diarama Serigne Moustapha sy
@dioppenda88942 жыл бұрын
Machalla ninga Mana méll sy Malick doundal wéurel yalla samou le arrle🙏🙏🤲
@thiamsoldatinvisible33412 жыл бұрын
Machalla s Moustapha s'y maktoum wadji n'a Capitaine yallna yalla motali lepou inchallah
@CheikhtidianeLo-ft6uo4 ай бұрын
Amena solo trop wakhtane bi Kou yaboul té
@famakane27972 жыл бұрын
Machallah machallah ham ham bi seellna sy malik yalna yalla arrla t samla🙏
@mamedoudoumbaye54982 жыл бұрын
Machalla yalla na yalla motali si barké Serigne Moustapha sy
@papandao38992 жыл бұрын
Walay tivaoune li la mérite machalla
@moussafaye3132 жыл бұрын
Capitaine des soldats 🙏
@ramatambenguembengue54492 жыл бұрын
Notre capitaine ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@omarndiaye34792 жыл бұрын
Machallah yallna Yallah motali way si barké goor gui 🙏🏽
@t.d.sservice28782 жыл бұрын
Yalla na yalla motali sounou yéné and ko ak sounou capitaine
@oumouseck26582 жыл бұрын
Yallanala yallah bayi sounou kanam🤲
@youmefatou96302 жыл бұрын
Je t’aime trop capitaine 👨✈️❤️🥰😘
@aldembajuniorfaye89652 жыл бұрын
Fatou
@aliounediop58608 ай бұрын
machalla capitaine❤❤ 2:47
@massambafall52802 жыл бұрын
MACHAALLAH yalna YALLAH Barkèl
@ismagaye69792 жыл бұрын
Machallah,❤️💯
@souleymanendiaye97602 жыл бұрын
Mach Allah yalla na yalla fayal niou la raw ga nieup
@awandiaye71842 жыл бұрын
Notre capitaine je suis fier de toi❤🥰
@sokhnaniang31772 жыл бұрын
yalna yalla barkel lafal la thiat ak borom khole you fekhoul yi🤲♥️🥰
@assanembodj18722 жыл бұрын
Amine inchallah ♥️
@matylo30902 жыл бұрын
Sama khole khole bi kome firigo💕💕💕💕💕💕💕💕
@thiounandiaye64402 жыл бұрын
Machallah Mame yalna yalla motali lépp inchallah ❤️❤️
@seydinandione85872 жыл бұрын
yalna yalla mattali inchallah
@PRODCH12112 жыл бұрын
Machaa Allah Sy Malick. Yalna yalla samou la.
@moustaphadione22792 жыл бұрын
Machallah yalna sa diame yague rk inchallah capiténe Mame cheikh
@diagnendoye57562 жыл бұрын
Laff cëtt Maam le capitaine des ❤
@azkaatv9362 жыл бұрын
إن أدرت العلم فاصغ إليه وإن لم ترد فاسلك سبيلك نتدم جزاك الله يا نجل مصطفى بجاه نبينا المصطفى
@azkaatv9362 жыл бұрын
تندم
@ndmb40552 жыл бұрын
والله مدارس السيد محمد المصطفى سه فى العلم خير مدارس
mane dei passage tabaski bi entre 5 djiko yi si ibrahima ismailla sokhnassi djibril ak khar mi moma daneil xam xam dal amna ay waye senegal kou deiglou capitaine bo yeiwatei sa kharoume tabaski di kholat sa bopou ndax djikoyi dajieina si yaw machalakh sy malick gaindei dou diour mousse doundeul weireul
@rokhayatoure93642 жыл бұрын
Kheureum rek😈
@assdiakhate63832 жыл бұрын
tres bien wallay ndeysane Amna solo ✊✊✊✊✊✊✊👊👊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊👊✊✊✊✊✊✊✊✊✊
@Ouzin99992 жыл бұрын
Limouy wakh mégowoul ak allhour an ak sounnah . Wakh si diné nagnouko ték si kham kham bou fi muhamad dianguelé. Liguay wakh tégoko si kham kham dinè bayil di wakh sa khalate.
@ahmeddiaw94692 жыл бұрын
Capitaine diambar ga loll ms malaka de sa nature monoul def erreur,