Machalla Baye Mbaye Gueye Silla, souniou khol sédatina thi yawe, ndakh kate kou mélni yawe meunoula niake thi yone wi
@mormar32723 жыл бұрын
MachAllah Notre Héros Mbaye Gueye Syll Vraiment On vous doit beaucoup et nous vous remercions sur l’effort que vous fournissez pour réglementer l’histoire du Sénégal 🇸🇳 Et du cheikh aussi Que Dieu tt puissant vou donne une longue vie et une bonne santé
Wallahi Ligaye wakh dou bari wakh Yangi Thi Dege Degi Ligéyale S TOUBA Yalna YALLA Gouddal sa fane mayla wergi yaram yokke ba yegko Barkeb SERIGNE SALIHOU MBACKÉ jaajef
@sokhnamaremagueye59053 жыл бұрын
Alhamdoulilah ma sha Allah Dieureudieuf si lep saa soune b mbaye gueye sylla Ki di Serigne Touba Xadimour Rassul ken dou Mom yalna la Yalla fayal bopam abadane Biss bounek niou kay toumal aka fekhel wayei nioune boba la niou ko gueuneu gueum waulou aka beug ma sha Allah Yalna niou gatandoki tawfeexam barkep mbautoum Xassida yi
@ameetfallsenegal35063 жыл бұрын
Machallah baye mbaye gueye sylla yalla ngafi yagg ta wer thie barcké saydina Mouhammad saw barcké serigne touba rta
@mamemamo3 жыл бұрын
Machalah baye mbaye Gueye lo wax nex na ndx si serigne touba guay wax
@daoudandiaye77063 жыл бұрын
Dieuredieufety S Mbaye amna solo nala yala fayy💪🏿💪🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Masha allah yalla nala Serigne bi takhawu bou none yi tayyi woul boul tayyi loulén diaral rék diaral nagnou louko eupp
@oumardiouf15853 жыл бұрын
Jããjeff bayy mbaye sylla begue djããmbarou brom darou al moukhty ma sha allah
@amadoudiaw94793 жыл бұрын
Dieuredieuf CHEIKH Mbaye Syll.Yalna fi yak te weer.
@mamourmbodji12043 жыл бұрын
Pour ceux qui disent que Baye Mbaye verse dans la polémique et te demandent d'aller adorer ton Seigneur, dite leurs que tu es en train d'adorer ton Seigneur en apportant des éclairages sur la vie et l'œuvre du Cheikh quand des esprits mal intentionnés veulent souiller la mémoire collective de notre communauté et notre histoire. Baye Mbaye, continue ton chemin car Dieu t'assistera et les créatures honnêtes te suivront par la grâce de notre bien aimé Cheikhouna Ahmadoul Khadim !
@XamSamReewTv3 жыл бұрын
Jara jëf
@oumarthiam5633 жыл бұрын
Machaallah yallanala yalla geuna takhawou ci barkeb borom darou mouhty
@tallandiaye39753 жыл бұрын
Pertinence, engagement et maîtrise sont vos qualificatifs. Nous vous remercions pour tout. Jaajëf jàmbaaru S. Tuubaa ji!
@layedious18053 жыл бұрын
Waw goor Baay mbaye boul guésstou wéyall rk ,ci xam xam ak téguin nguay dox
@cheikhndiaye9313 жыл бұрын
Macha-Allah Papa Yalla nga goudou fane té and ak wërr
@vvvddd93823 жыл бұрын
Jaajefeti Baye Mbaye. Nous mourides, nous devons rendre grâce à Dieu, et réaffirmer notre gratitude à Khadimou Rassoul. En fait, au Sénégal pour qu'il y ait intéressant il faut parler Serigne Touba, loolu la Yallah def. Cependant ça serait une erreur de croire que les ennemis ont déposé leurs armes après Serigne Touba, non, ils sont toujours là avec d'autres armes plus affûtées que jamais par exemple les réseaux sociaux. Il serait une erreur de leur laisser faire la pluie et le beau temps, et Seugne Mbaye Gueye Syll l'a bien compris car il apporte toujours des réponses basées sur des arguments solides et officiels. Baye Mbaye jeureudieuf. En effet, nous sommes dans le présent, et ce qui se dit aujourd'hui va rester pour devenir l'histoire d'ici des années, et nous serons responsables le laisser ces gens changer l'histoire de Serigne Touba et de la mouridiyya en particulier et de l'islam au Sénégal en général. Seugne Mbaye yàgg fi lool te ànd ak wér barke Cheikhoul Khadim
@badarabax3 жыл бұрын
Diadieuf vérité absolue
@sambmoustapha48733 жыл бұрын
Diereudieufeuti serigne Mbaye Gueye Sylla yalla nalla yalla faye si barkép khadim Rasaul
Waaw góor Baay Mbay! Am nga jaajëf. Lii moom bu dul woon dara sax dees koo wara leeral, ndax mboorum réew mi la. Waxuma laak nak mu am ay xaj yuy mbów lu dul dëgg (ci Sëriñ bi). Lii lépp bu Ecole bi yarasul wóon, fa lees ko waroona jànge. Kon yaa ngi def liggéey bu am solo ci mboor um réew mi, rawati na nak lu ñeel kenn ci saa-senegaal yi ëpp solo (Seex Ahmadu Bamba). Ñiy saaga ci xët wii nag, ay ree la ñu ma def. Waaye nag "comprendre" na ñu leen. Ku ngoy ci bànqaas boo jàppoon ni dëgër na, benn waay gor ko ak ay "arguments" yu leer, ba fu waay toll dégg "dérr" ja, foo ma na jaar saaga ko ndax amóo meneen pexe. Du ngéen jóg ci saaga nag, ndax ci ay jéll ngéen di dëkk. Ku bëgga suuféel ku Yàlla kaweel (Sëriñ bi), doo jóg ci ab jéll. "Darajatii tahluu, wa laysa tanqafid. Wa man nahaa minal waraa xafdii, xufid." Saa bu mbaam mi wéqqee rek, na nguul wi dal.
@ndiayekheweulmikeup71853 жыл бұрын
Yallana sa diame yague 🥰
@barasow36543 жыл бұрын
Machallah baye Mbaye Gueye Syll diam rekk gay Ame le soldat digne de cheikhoul Khadim deugue nekhoul koo touff mou tokhoniou kou merer yalla yendoo niawaye Dieuredieuf borom Touba diarama Mame cheikh IBRAHIMA Fall
@narka58703 жыл бұрын
Machallahh serigne mbaye gueye sylla Yalla nga gouddou fan barkèb serigne touba
@dameseye30393 жыл бұрын
dieredieuf Serigne mbaye gueye kén amoul sa fay yaram daw na serigne touba mo tédd dé
@abdoulahatndiaye63763 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Mbaye Gueye Syll. Diam ak Barke' ak Te'he' thi yawe. Ak gneupe. Barke'MameCheikhreuFaal.
BRAVO BAY MBAYE GUEUYE SA KAW SA KANAME REK... BAMBA MERCI✨✨✨✨✨✨
@amdysalihou36433 жыл бұрын
Machala dieureudieuf Serigne bi
@beuguebamba84003 жыл бұрын
Tu es une fierté dans le tarikha yallanala yalla fay
@mariasant39373 жыл бұрын
Mouridiisme contrairement aux autres dou tarikha, c'est un raccourci vers Allah. Yonou mouride
@mbayediouf26003 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne mbaye gueuye Sylla, yalla nala borom Touba yokkk
@ousseynousarr4203 жыл бұрын
Nalafi yallah bayi basi kham ma kham ndakh sa takhaway thi yone wi matna loll té rafet yalna serigne nagoul liguey bi goudou ak weer sama houl dafa sed thi moo takh louma thi yaw khép ko🙏❤🙏
@sambalingeer56803 жыл бұрын
Jërëjëf Baay Mbay Gëy Sil! Lii ngày def doynë jammu Yàlla, liggéeyal Seriñ Bamba lu kawee lë .
@khadimmbacke37923 жыл бұрын
Serigne mbaye yallana yalla godal sa fane
@ablayediagne57483 жыл бұрын
yalnala yalla takhawou barkep borom darou tawfêh rêk silla
@barasamb18803 жыл бұрын
jarajaf,serigne touba rekkk,بخ بخ يا الشيخ احمد بمب
@ElTIO_Galass3 жыл бұрын
Goudou fan ak wer lalay nianal thi barki cheikhoul khadime noun serigne touba rek la nou beug amoull kenen diajeufe ❤️
@amethdiokhane85443 жыл бұрын
Dieureudieuf beg naniou lolou
@bayefallouserignebabacarsy3 жыл бұрын
yaw kou katte sa ndaye ga do lefeul ndayame
@ElTIO_Galass3 жыл бұрын
@@bayefallouserignebabacarsy yangui nee dangay khelkhal islam ba no pi dima saga te pourtant tognou ma la de saga wouma la foto serigne muntaqa bassirou bi nak dindi ko ak togne wesou woul liii
@yadikon3 жыл бұрын
Kepp kou bagne serigne touba billahi yeene nala nga dem safara tayit yalnanga dem safara.
@salioundiaye57033 жыл бұрын
Merci beaucoup 💯♥️❤️❤️❤️♥️😘😭💪🇸🇳 Nice 💪💪🙏🙏🙏
@ousmanefaye93783 жыл бұрын
Mais père ont te dit que merci long vie à toi
@taphabeye24293 жыл бұрын
Machalla Baye Mbaye yalla nala yalla Faye yiw Sama Xoll chedina lool Merci way👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍❤️♥️♥️♥️♥️👍👍👍👍
@mahmoudaneseck81233 жыл бұрын
Man de lu bari ci yaw laako xamé yalla nala saa borom dolli kattanu zaahir ak baatin 🙏
@sowpape96763 жыл бұрын
Bilay ya wakh degui baye mbaye boul bayi de magui lay 👂👂👂 fi si Italia 🇮🇹🇮🇹 grazie mille bamba 💪💪♥️♥️
@khadimmbacke37923 жыл бұрын
Machallha liguaye def moye diamou yalla merci
@mbayediouf71193 жыл бұрын
Yaguefi rek té wérr baye mbaye Gueye ni rek la dh ñone yi mom sougnou tayiwoul rek boul tayi si léral yi Amna gno kham ni khaméwougnou léral ak wéranté
@khalilsoufiindiaye63993 жыл бұрын
Ndaysane niakka xam rék ♥nénane danouy gakal serigne touba ♥ thow linouy dége yépp lolou moko waral ♥ they serigne touba wouteul nane ko morom ba sone xam né amoul morom niouy diéma diar fénéne😭 ndaysane billahi yeureum nalén
@matardiop32463 жыл бұрын
Machalah yalanala yalanala yala Faye yiv te samela amena solo lole Vayé ñome tamit Mane magilèndi ndakh ñigi takh khamkham diguéne Ak ñouy guena kham Serigne bi
@cheikhbassiroubabou6863 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Mbaye Gueye Syll . Yalla Nala Yalla Faye
@serigneadj17793 жыл бұрын
Dieuredieuf tchi léralbi 🙏🏿
@alkamaltv76813 жыл бұрын
Bay mbay geuy boul masa nopi yagui liguéyal s Touba yalla na yalla goudal sa fan wéral barkep s Touba ak borom darou
@mordiagne21233 жыл бұрын
Dieuredieff Serigne Mbaye GUEYE SILLA yalana yalla doli wérr fann wi goudou
@momo_ceepgy27753 жыл бұрын
Dieureudieufe Seringe Mbaye güey sille
@cheikhdiouf55433 жыл бұрын
Yalna yala goudal saye fane ci barke serigne touba
@salioundaw33083 жыл бұрын
Wallahi bay mbaye Gueye bâ ngua dalé wax bâ légui tchi xam xam ak preuve you leer ngua KO tek Senegal xamou niou kou togn kou fayou laniou xam
@senegalsamareew43483 жыл бұрын
Baye mbaye merci gnioun mom koubeug s.bi niou beug la koubeugoul yaaxàm mais b.maye gniy wàx bouleen falé nioun mourid yi ngàye wàkhàl boul découragé ❤️❤️❤️
@arounadiouf33253 жыл бұрын
Tout c' est les gens de Sonkho.
@sokhnabambistemouride12043 жыл бұрын
Yalla nanga fi yaag. Damani Serigne Touba daal Leep Lou thi nit wakh thi safaan dafay yook sougnou mbeuguel ak sougnou fonkeel ci mom. AHMADOU rek késsé Keep dong. Man dal lougnou thi wakh dafmay yook gueum.❤
@ablayendiaye83153 жыл бұрын
Jajaf baay mbay géy silla yalla nala yalla may gudu faan ak wer gi yaram
@mordiagne21233 жыл бұрын
Omar télégramme Diagne dafa takh ma gueneu xam SERIGNE TOUBA guenko Brugg🇸🇳✌️🙏♥️💯
Fene katyi bon nopiwoul boul nopi ligeyal sr touba Moy diamou yalla yag fi loll way yaw sr touba mola ligèy lo خدمة الخديم الي ااجل مسمي طريقة المريدين كلهم فرحنا بك جدا
@cheikhabdoutoure38693 жыл бұрын
Dieuredieuf baye mbaye Geuye
@ousmanefaye93783 жыл бұрын
Merci long vie à toi et continue de parlé
@abdoulayendiaye81373 жыл бұрын
Dieureu dieuf serigne mbaye gueye zill
@papeseye95893 жыл бұрын
Merci.serigne.mbayr.gueye
@rahmanendoye38723 жыл бұрын
yallah na yallah goudal fanewi yok wér gui linguaye déf amna solo boubaakh
@cheikhndiaye73683 жыл бұрын
Machallah amna solo
@ndiayedaouda28723 жыл бұрын
Machalla diere diefe baye mbaye
@serignebassiroungome72823 жыл бұрын
Yallah nanga laakh geureumeul SERIGNE TOUBA
@سيدبراهيمجه3 жыл бұрын
Machala sakaw sa kaname ligaye déf diamo yala go magala wakhtané niti yala yi mouy wakhtané yonananté bi slw
@badarangom33353 жыл бұрын
Baye Mbaye Gueye SYL, vous êtes une fierté du mouridisme
@bassfall60183 жыл бұрын
Yalle na yalla dolli la katane ak werr jaajeuf Jaajeuf
@naskelly44513 жыл бұрын
Mashallah 🙏🏾❤️❤️
@abiblo59903 жыл бұрын
Yalna yalla fayla té yagual sa ay faane
@senelucky3 жыл бұрын
Diadief way mourit dierediefe seringe touba khadim rasoul ken la de bilahi kenla mako begui amoul morom way ❤❤❤❤❤❤👍
@narka58703 жыл бұрын
Machallahh ♥️♥️
@mbayeseck1733 жыл бұрын
Merci Baye mbaye
@yusuphabojang8583 жыл бұрын
Mandeh Murid laa MaShaAllah! Kepp kui Murid Santal Yallah!
@kalso483 жыл бұрын
machalla amna solo
@falyndiaye95093 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA
@moustaphambaye90773 жыл бұрын
Mbaye Gueye Syll yangui def lou am solo yalnala serigne Touba fay
@socialweb21603 жыл бұрын
Dieuredieufé si léral yi
@badarabax3 жыл бұрын
Serigne mbaye Gueye Sylla dieuredieuf yalla gua guodou fann lol guou ande ak weer dieuredieuf Serigne Touba sunu yakar aduna ac laxira abadann
@sambadiop83913 жыл бұрын
Merci papa
@mahmoudaneseck81233 жыл бұрын
Machallah baay mbaye yalla nala saa borom sammu te aar yangui df lu am ñi bëgg nga noppi seen intré rk mooleen jiital wayé lingay wax kuko dégg xamné moo wer
@amanakaradiallo77053 жыл бұрын
Dieuredieufati serigne touba
@musaamurit3 жыл бұрын
Yaw daal danu lay sant rekk te di la ñaanal nga yàgg fi te wér Jërëjëf Jazaakallaahu Merci Thank you 谢谢你
@morthiam9623 жыл бұрын
Baye Mbaye yague fii té wérr ci barké serigne touba mbacké gni di fénnn di sosalll segne bii sénn kholll moo diekh Serigne touba mbacké diante la kou bagne mou timm la déwalll té bo dé sakh dalayy gueuneuu timmmm ndakh ci soufff mo gueuneuu khooottt
@ndiayeoussey24703 жыл бұрын
Machalla baye mbaye amna sollo lolle yagueu fille lolle té wer
@abdoulayeabdoulaye30123 жыл бұрын
baye mbaye walahi mangui niane serigne touba dougeulla si bir karanguem watoula,samla,mousaeula si doleye mame cheikhe ibrahima falle
@BassirouGueye743 жыл бұрын
wąkhaldė baye soldarou Serigne Touba
@massdioum83133 жыл бұрын
Dieurdieuf Serigne Touba
@ousmanendiaye36483 жыл бұрын
Baye mbaye yallanala sounou borome sam
@cheikhmbackesamb82243 жыл бұрын
Bilaxi kou maytou wout s touba diwax ci mom lou bon dangay torox rek ci adouna ak ci alaxira ealakhi
@makhtarsylla16843 жыл бұрын
Macha allah amatina solo lingay deff amna solo loll yàlla ngafi yagg yàg loll te wer ci barké borom darou
@alassanedieng2593 жыл бұрын
yalla nangafi yag tewere sagou yonou mourid nga yangi legeyeul serigne touba ci xam xam
@bodianmouserignesalihou28883 жыл бұрын
Hakazaa
@cissesalif36913 жыл бұрын
Machala khayran
@ndoyeinfo26673 жыл бұрын
Merci 👍👍
@mbayeba27673 жыл бұрын
Serigne Touba amoul morome 🙏🙏👍🙏
@baboundolettefall96663 жыл бұрын
Bamba merci kumou nékhoul guenaall rewmii deemaal. Un travailleur de l'islam or pair Yaggeu fii té andak weur Papa.
@fallouka97373 жыл бұрын
Baye yaw déh danga wara bind li yéppu ay téré yalna la yalla sammu brkb brm touba.
@dalyg77073 жыл бұрын
Ndeysan. Papa est ce que do creer site internet vitrine pour mettre ces rapport en ligne nieup am si accés. Rawatina mouride ndax niou xam li eup si mbir yi. Ndax gni kate douniou bayi kate tei lu bou yatou wout dina yeimei lol ndax louniouy gueneu dém ak outil informatique you bess yi soss dafay yombeu lol. Yagal wereul barkel serigne bi