Nous sommes en 2024 mais cette émission est la meilleure plateaux du siècle
@thiernotv4 жыл бұрын
Kouy sétan video bi 2020 baye ndiaga diop yalla na yalla yok ay léram si Barkép Serigne Chiekhe Fall bayou goor
@AbyDiagne-j3t2 ай бұрын
Diadieuf fall diadieuf diop
@assaneniang76723 жыл бұрын
Kouy setane vidéo bi en 2021 Thiey baye ndiaga yalla na yalla yokou léram
@eutoumamecheikhtv86155 жыл бұрын
Beuss bounek ma deglou waxtan bi walahi yalla khamnako man talibe cheikh la wayé kou beugu mame cheikh Ibrahima fall
@papesow70124 жыл бұрын
Ndeyessane
@falloudiaka47924 жыл бұрын
Ndeyssane
@sylladame19604 жыл бұрын
Yalla nako yalla faye😭😭😭😭😭😭😭
@ibrahimadieng68003 жыл бұрын
Waw waw fou dikh Cheikh
@amadoudiallo41132 жыл бұрын
il était parmi les plus grands conférencier mouride que la terre lui soit légère
@abdoukhadre.2 жыл бұрын
Amine fall
@assaneloum45365 жыл бұрын
Nagénne ma sédél ni cheikh ibra rék la geum môme rék la âme bilahi
@falloumbengue65043 жыл бұрын
Ndeysan
@DiopNdiagua Жыл бұрын
Baye ndiaga diop baye fall khamemale guanou Mame cheikh Ibra fall lamp❤
@Ami00765 Жыл бұрын
L'amour que Mame Cheikh Ibrahima Fall avait pour Bamba était inconmensurable❤ Beug naa Cheikh Ibra
@eutoumamecheikhtv86155 жыл бұрын
Bay ndiaga diop man d talibe cheikh la wayé YAw y’a takh ma kham kouy mame cheikh Ibrahima fall guinaw Yalla souma beuguei mame cheikh Ibrahima fall ba yamaléwoumako ak dara yamasi dimabli
@TalibèAlhasaneSalam5 жыл бұрын
Akkasa
@astougueye64735 жыл бұрын
Ndeyssane MASHA ALLAH Yallah naleu YA Rabi Fay yiww thi Barké Borom Touba Daradiaye Mame Cheikh Ibrahima Fall.
@hidmatulxadimtoubaliberte69364 жыл бұрын
Danga beugle yalla akk beug yonenba
@wakhtanekhamkham56334 жыл бұрын
Ma
@zallkbo55273 жыл бұрын
😭😭😭 🙏🏿🙏🏿🙏🏿 Euskeuy
@abdoulayeniang10 Жыл бұрын
Nous sommes en 2023 mais cette émission est la meilleure plateaux du siècle
@kAmAL12842 Жыл бұрын
Bilahi DEUG leuh
@ahmadougaye2580 Жыл бұрын
Véritablement vérité Bilay et restera toujours inchallah d'être meilleure 😍😭🙏
@mamedoudadiop8312 Жыл бұрын
Wallahi deug la dh ❤
@alassanendiaye488111 ай бұрын
❤
@MbathioFall-o9kАй бұрын
Lou wër fall yarame❤❤❤
@elhadjicisse51144 жыл бұрын
Yalla nala sunu Serigne bi mame cheikh Ibrahima fall terou thia aldiana firdawsi depuis le jour que tu as quitté se monde j’arrive pas à tenir mes larmes un homme avec une sagesse hors dimension 😭😭😭😭😭
@kheuchobm823110 ай бұрын
Ki es la en 2024 segn makhtar yalla na yalla yokk leram❤
@baye22664 жыл бұрын
Ba 2020 kay niou ngui kay sétane....suniu Mame Cheikh Ibrahima FALL douniou doyal ci Ay mbaaxam ! Jazboul Mouride bii nak dou bari ay morom !
@moustaphathiam5632 жыл бұрын
2022
@modoundiaye49014 ай бұрын
Le plus grand conférencier que la terre n’a jamais connue
@abdougassama78304 жыл бұрын
Wa keur cheikh ibre gno beuri xam xam macha Allah Allah .serigne ndiaga diop yalla nga goudou fane ande ak wer li nga fi wax yep deggla mangui gnane si barki cheikh ibre yalla na deh si mouride
@diopousseynou86713 жыл бұрын
Yalla na yalla yokou ay léram si barké seydina mouhamet (psl)
@yareakteguine64477 жыл бұрын
Bilahi wakhtan bi limakoy sétane matena 100 fois doumasi doyal !! Baye ndiaGa yalla nalla Mame Chiekh ibra fall fayal bopam taniou yaga la deglou barké chiekhoul Khadim !
@abdourahmanefall83976 жыл бұрын
moi aussi doumassi doyal kén dou cheikh ibra
@fallouthiam52415 жыл бұрын
@@abdourahmanefall8397 Je
@kalediop28765 жыл бұрын
Amin
@thionediouf91554 жыл бұрын
Doma dappppppp chaque nuitttttt
@santeserignefallou91015 жыл бұрын
La dimension spirituelle de Cheikh Ibrahim Fall m'a beaucoup ébloui Cheikh Ibrahim amoul morom dieuredieufeti Serigne Touba diarama Mame Cheikh Ibrahim Fall
Ndaysane baye ndiaga Diop Yelle na yalla yésal djégualam thi kawam
@emacifofficiel30475 жыл бұрын
Jusqu'en août 2019 j'écoute toujours cette émission kenn dou cheikh ibra leep mom la yalla nanou ko yalla fayall
@gallaskawsara87335 жыл бұрын
Ngalla Ndiaye weir na dh
@astougueye64735 жыл бұрын
Amine YA Rabi thi Barké Borom Touba
@assaneloum45364 жыл бұрын
2020 jusk'a 2100 incha allah pour le regarder
@mamadoudiankha23006 жыл бұрын
Serigne ndiaga Diop yalla na ga fi yagu tei werre
@adamadiobembengue88384 жыл бұрын
Amine fall
@ahmadoubambambackehann65155 жыл бұрын
Yalla nanio yalla fayal mame cheikh ibrahima fall
@falloudiouf84117 жыл бұрын
Cheikh ibra fall moy Yonne wi barkei borom touba
@abdoulayediop1175 Жыл бұрын
C'est extraordinaire de revoir cette séquence télévisuelle relatée par notre regretté frère et père spirituel Feu Baye Ndiaga Diop Baye Fall sur la dimension spirituelle de Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp Baboul Mouridhina. Bo khamoul dey yakar jëum dji wakh mi ngui doundou. Ceey Serigne Touba ! Jaajën Jëuf Serigne Mamour Ndao ak Serigne Alice Badara Ndim Baye Fall yi.
@abdoulayeniang10 Жыл бұрын
Bilay ❤❤
@maherondour55285 жыл бұрын
Mame cheikh est la solution de tout nos maux Diarama Mame cheikh Ibrahima Fall
@ousseynoudiop94294 жыл бұрын
Baye Ndiagua Diop Baye Fall yalana YAllah yéssal yërmendém ci mom yokou ay léeram ci Cheikh Fall Bayoub Goor té tass niou ci Barkém ci Barké Mame Cheikh Ibrahima Fall
@assanediagne48994 жыл бұрын
vraiment il est temps d'introduire les enseignements de Cheikh Ibrahima fall dans nos universites
@cheikhfaya60639 жыл бұрын
je suis tres content de votre emission jazboul mouride je suis tres féire etre mouride baye fall c'est notre réfairence jaime dans mom coeur mame cheikh ibarahima fall lampe merci beaucoup
@mamecheikhmcfcouture91136 жыл бұрын
Akassa fall
@bassiroundiaye37024 жыл бұрын
Oh bay ndiaga mbaa bindga lii appnaa yobaalé dé yallna yallah yésal yeurmaandé sisa kaw
@ibakalloga40065 жыл бұрын
Maam Cheikh Ibrahima Faal Sëgg Béén, Siggi Béén, Guiss ba Sarna ba Mahfouz Fépp lay Séén. Jeureujeufeuti Maam Cheikh Ibrahima Faal. Kénn dou Moom
@yoodiagne623 жыл бұрын
Serigne Ndiaga Diop Makhtar Baay Fall😣😢😭 Dieum dji taaxeu maa dougu si yoonou mouride Yalla naleu Yalla faay.... 08/12/2021😢✌ batay magui lay diooy
@srgmodousalihmbow1696 жыл бұрын
Allahou Akbar kénou Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp baaboul mouridine amar fall saer ndiaye kénou mom barké Cheikhoul Khadim
@anonymousgoalkeeper21653 жыл бұрын
2021❤️yalla na yalla yoke leeram yi daniouko wara denth pour souniouy dome
Jërëjëf Baye Ndiaga Diop léral nga lépp lou oumpou wone diam gni yalla nga fi yagg té wérr si Barké Mame Cheikh ibra Fall❤🙏
@mamadoundiaye81678 ай бұрын
Wallahi il a raison quand il dit que Maam Seex Ibrahima Faal est le plus grand philosophe que l’humanité ait jamais connu… Le sens caché de ses métaphores sont d’un niveau jamais vu😭😭❤️❤️❤️❤️🥰🥰!!! Encore là pour re-suivre cette émission, l’une des meilleures❤️❤️🙏🏿!!
@ibrahimasavadogo5034 жыл бұрын
Ma Philosophie 🍀❤baay ndiaga diop yagg fii lol tei wérr🙏🏾
@AbdouRSOW5 жыл бұрын
Assalamou aleykoum, Kii moo worone nek ci université di ndiangalé... Yalla nako YALLA sam...
@modoumbow96194 ай бұрын
On est en 2024 msis je reste toujour convainqant que la meilleur emission du monde est la
@modousokhnagueye41734 жыл бұрын
Suñu Baye Ndiaga Diop Yalna Yalla wathié yeurmandé si mom Barké Nabil Moustapha
@rokhayadiagne73209 жыл бұрын
Mame Cheikh Ibrahima Fall Amoul Morome ma sop seirigne ndiaga diop dieureudieuf
@mamadoundiaye56854 жыл бұрын
Dieuredieuf SERIGNE Touba Diaraama Mame cheikh Ibrahima wakhtanne bou meilni dotoull am si bi kharnu. Diadief koulou bègue nanou
@ndaomoustapha755 жыл бұрын
Bilahi sante Serigne Touba warna . Wayei ken dou Cheikh Ibra
@edouardlatouffe74776 жыл бұрын
Serigne ndiagua ce que vous dites est très raisonnable en Islam...
@mamadoudiankha23006 жыл бұрын
Bilahi walahi wa talahi cheikh Ibrahim fall dou sen morom
@papoupoupa68828 жыл бұрын
Machahala khol yeup sed na. santati Mame cheikh ibrahima fall rek
@bayefalldiallo29479 жыл бұрын
Dieuredief Baye Ndiaga, wakhtane wii amm naa solo téé léér na, Kéne dou Sidy Birahim, amoul morom. emision bii dii jazbul mouride lou amm solo laa yalla na sakh téé nji di ko dééf yagg fii akk wéér njou yagg fii dii dii léén déglou amine
@moussawade50286 жыл бұрын
Jäjeuf kou bakh santnaniou bou weur léerna rafétna. Kéne dou Cheikh Ibra Fall. Wakhtane bi weurna amna solo
@billymigos37624 жыл бұрын
Yalla na yalla yerem ko tèe kharèko aldiana serigne ndiaga diop
@FatouMbengue-j5h Жыл бұрын
Thiey sa mame chiekh IBRA c'est l'exemple parfait pour faire développer le sengal
@cisseomar3454 жыл бұрын
Baye Ndiaga sa wakhtaan bi Sénégalais yi gnigui siy sooga baayyi khel..
@cheikhdiopthiam65994 жыл бұрын
Senegal bouniou démé bathi kanam sathiekatou souf rek niofiy deuk bilay litige foncier bi mom laniouy doundou ni en 2020.... Ken dou Sidy birahim fall
@cheikhdia95933 ай бұрын
Qui regarde ça en 2024❤❤❤❤
@ibrahimasow62233 жыл бұрын
sunu Baay Ndiaga Yalla na Yalla doli ay ngeremam ci barkép Serigne Cheikh fall bayu goor
@chekhembacke26104 жыл бұрын
2020 bi mankaye sétane kéne dou CHEIKH IBRA
@ramandiouck15532 жыл бұрын
Machalah thi waxtaan wi baye ndiaga diop yalna ko sounou borom yeureum thi barke SEYDINA MOUHAMMED SALLALLAHOU ALIWASALAM ak thi barke SERIGNE TOUBA KHADIM RASSOUL barke MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL lamp baboul MOURIDINA ,AMINE YA Rabbi
@elhadjindoye16485 жыл бұрын
Dieuredieuf Mame Cheikh Ibrahima Fall,Serigne Ndiaga Diop yalla ngafi yaague tē wer
@ibrahimacoulybali321510 жыл бұрын
Akassa serigne ndiaga diop yalna fii yague te werr barké mM cheikh ibrahima fall lamp
@petitniang11553 жыл бұрын
.
@dfkamal5424 жыл бұрын
Chaque jour Dina sétane vidéo dépui 2015 thieuy seix Ibra fall ❤️❤️
@madiordiop80202 жыл бұрын
Al hamdoulilah Dieureudieuf Mame Cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul 🙏🏿 Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp Baboul Mouridina 🙏🏿
@mbayediop86522 жыл бұрын
Opopop😭😭 je t'aime baye ndiaga. Diarama baye cheikh ndao
@boucarthiam50722 жыл бұрын
Non un homme avec une dimension incommensurable repose en paix le sage...
@mamecheikhramos11124 жыл бұрын
Baye ndiaga Diop yaal nako yalla yeurem té xaréko aljana barkeb Mame cheikh Ibrahima fall
@KHALIL-ld5rq3 жыл бұрын
Baye Ndiaga diop baye fall yalla nako sama borome yeureume 😭😭😭
@BadouBadazz26 күн бұрын
Baye ndiaga yallna yokou ay léram si barkei cheikh Ibra 🙏
@baradiop34548 жыл бұрын
Akassa ceeeyy magouk yalla gui. cheikh Ibrahima Fall kenn khamoul loumou doon
@ousmanediop36027 жыл бұрын
Bara Diop uh i
@moustaphamatlabouchifaa97266 жыл бұрын
Serigne Ndiaga Diop yalnako fi yalla yagal ki mo kham Cheikh Ibra dieureudieufee Serigne Touba.
@monsieurcissokho33333 жыл бұрын
Baye ndiaga Diop yallah na sounou borom yok leram barkep Mame Cheikh Ibrahima Fall
@toulenesarl63094 жыл бұрын
Senegal 🇸🇳 complexé rek laniou def mo takh douniou démon fén , mame cheikh ibra royoukayla ❤️❤️❤️❤️
@Ami00765 Жыл бұрын
Wallahi
@moussasonko81816 жыл бұрын
Yalla na yalla yookeuh fane yi weireul tieur yi baye ndiaga...gatié ngaalama ekip jazboul mouride yalla na yalla feiyleine barkeip cheikh ibrahima lamp fall baboul mouridina
@ndeyesene57575 жыл бұрын
je suis tidiane mais bilahi walahi baye ndiaga diop motakh ma dem ba kham kouy cheikh ibrahima fall bou dieuk loma wakh si baye fall yi ma saga len ndakh niaka kham wayé bay ndiaga diop takh na ma kham kouy sounou mame cheikh ibra fall ba sop ko ba a amouma si mome sagou walahi
@gallaskawsara87335 жыл бұрын
ndeye sene am na solo dh
@gallaskawsara87335 жыл бұрын
ndeye sene diokhma sa watshap
@khazimndiaye23694 жыл бұрын
amnaa sollo Fall
@wakhtanekhamkham56334 жыл бұрын
Diadieuf
@bintayatoulala8 жыл бұрын
jerrejeffa Serigne Touba, jarama Mam Sheikh Ibra Faal
@oumardiallo39199 жыл бұрын
Serigne ndiaga diop baye fall yalla ngua fi yakk si barré mame cheikh ibra fall
@gmsaabesambu84119 жыл бұрын
@ balla
@falloudiouf84114 жыл бұрын
Novembre 2020.yalnako sa borom yeureum barkep cheikh ibra
@BayedieyeDiagne6 ай бұрын
Billayi wallahy Baye Ndiaga Diop Baye fall dafa leer fall billayi Lou ndao yarame gua wakh si cheikh Ibrahima fall lamp fall baboul mouridinaaa ak serigne touba mbacke balla aicha boury billayi Baye Ndiaga Diop yalanalaaaaaaaaa yalla tedal si adianaa si barka mouhamed Rassoul amine😔😭😭👌🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾😘😘😘😘
@boysarr62298 жыл бұрын
baye ndiaga yalla nga d0unde 150 ans, mame cheikh manena l0uk0 raw
@agiewage97078 жыл бұрын
Mor Sarr
@agiewage97078 жыл бұрын
Mor Sarr n
@mortallafall68354 жыл бұрын
Amine
@el.hadjimamadoundiaye79573 жыл бұрын
bilahi doumasi doyal thiey cheikh ibra fall baye ndiaga yalla na yalla doli leram tass niou si barkem
@Deuguerekaydeugue6 жыл бұрын
Waxtaan bi Nexna Wallay sama hol Sedna. Yalna Yalla Yok la wer ak gpudou fane.
Barké BOROM TOUBA wakhatikoo domou baye ki ken dou mom ci wakhtaaneh Mame Cheikh Ibra dinaniou wehtall deh
@modoumbaye39954 жыл бұрын
Baye ndiaga yalla nako yalla yeureum ta xarei ko Aldiana
@modoumbaye39954 жыл бұрын
Ta yalla yokou leiram teii tass niou si Barkem
@damasdamas11655 жыл бұрын
Dieureudieuf Sr touba diarama Mame cheikh Ibrahima Fall Al hamedoulilah bima yala defer mourid ak beugu baye dame
@serignesalioudiop4145 жыл бұрын
YALLNA YALLA FAY LA YIW MAKO SÈTANE 2019
@khalilnewyorkino949317 күн бұрын
Yalla nakko sunu ay seutte setane 2100 ❤
@ndiayediallombaye17933 жыл бұрын
Serigne Ndiaga Diop Yallah na sounou Borom Yokk ay leeraam 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@aliounebadaralo31294 жыл бұрын
REVOLUTION AU VRAI SENS DU TERME!! Bilahi sunu wadji moom rek..diougué fou sori boukkoul ak SERIGNE BI loudoul sa adama ak awa..Nieuw nangoul ko si fanneu yéppou ba niéppou weulbeutiko xam ni liguéyeul SERIGNE BI rek mooy deugg..!! SUNU WADJI BILAHI KOUKO YAP SA BAYE YABOUKOU! Bilahi, BARKE SERIGNE BAMBA louniou adineu eundil té fess delleu ak TALIBE AK BEUGUE SHEIKH IBREU TIGUI nékkouthia yalla bouniou aam lolé! GOOR DEUGG-DIAMBAR DEUGG-REVOLUTIONNAIRE DEUGG-CHEIKH IBRAHIMA FALL!!
@secktapha75263 жыл бұрын
Fall rek
@ndongodiop4154 жыл бұрын
koulla déglou déggg A Cheikh ibra fall.Yallana yalla dolli lérram
@modoumbengue233 жыл бұрын
Yalla na yalla dolli yermande si mom ak ay leer 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
@IbrahimaNdiaye-yj9cc4 жыл бұрын
Serigne touba yama gueneul aldiana bilahi
@abdelfall31824 жыл бұрын
Barké Mame Cheikh Ibrahima FALL. ❤️🙏🇸🇳
@ousseynoufaye57186 ай бұрын
Ndeysann❤Baye Ndiaga Diop Baye Fall yalneu yalla yoki léram tass niou si barkèm