Dieuredieufeuti Borom Touba yalla ne yalla dolli leer serigne fallou ak mame cheikh ibrahima fall te tass gnou si seni barke bi diahi khadimou Rassoul ❤❤❤❤❤❤❤
@sidymatarkhouma83576 күн бұрын
Amine ❤
@abdoulayediop117510 күн бұрын
Wakhtaan gui amna solo ! Jazboul Murid ! Yalna Yallah samou tey barkel bijahi Cheikh Fadilou Mbacké aki Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp Baboul Mouridhina. Jahjëufti Serigne Fallou Bousso Tamba. Waw goor Serigne Alioune Badara Ndim, Serigne Mamour Ndao Baye Fall Yi.
@pouyeelimane5735 күн бұрын
Diarradief serign touba mam fallou reck❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤