Yalla naco yalla yeureum. Je vois qu'ils sont tres jeunes ( 20ans ou moins). A cet age, je vois mal qu'ils endossent une si grande responsabilité, celui de réussir très vite dans la vie. On doit tous s'interroger sur le comment enseigner nos jeunes, comment les guider vers leur réussite, quels discours devons nous tenir à leurs égards.
@coumbasy1412 Жыл бұрын
So nekei sen biir guey comprendre ni leip parent yi la gno dieloul sen responsabilité kou âme 17ans école la wara nek pas gua key contribuer lo si keur bou mak
Yeureum léne séne yaye yi guir yala 🙏🙏😭😭😭 vous pouvez voyager mais pas la mère guir yala
@boudabaax8177 Жыл бұрын
😢 Wallah surtout loolu
@sokhnathiaw6689 Жыл бұрын
Vraiment deuk bi mettina pour dimbali sèn parents mo takh niouy dèm mais kou si dcd say wadiour ngay yok thiono
@ndeyembaye8908 Жыл бұрын
Bilaahi
@fatimadiatta5620 Жыл бұрын
Yaye tamit Nio wara dimbali seni dom, bagne dilene tek pression, wallah d wek yakar tchii en plus ils sont très jeunes Les parents parfois n'assument pas et veulent tout mettre sur le dos des enfants
@aichasow5331 Жыл бұрын
@@fatimadiatta5620Mane mi Lolou lama sama yaye di def té amna dieukeur banialou mako d’ara louma am bokou nako ak mome té môme dafmay tek pression pour may l’ath sama dieukeur à chaque fois motax Mane ak sama dieukeur daniouy khoulo rk ndakh néna khaliss lako topé té lepp sama yaye la soko diokhoul mou khoulo ak yaw
@elisabethsoropogui8190 Жыл бұрын
Frère so démé thi galgui gua dé digua téke sa wadiouryi nakary bo khamné lernama so diogaton doko défe. Deukeubi métina wayué mouno changé sa destin pour l'amour du ciel reste déwou jeune Dafa méééééty sa ma khôl méty n'a bien vrai je khamoumalén
@fatoudiop3907 Жыл бұрын
Bilaye diarouko risquele
@bayembayedeguenediouf Жыл бұрын
Mais frères bouléne djieul galgui 😢.. Ame ngéne wérgou yaral té ay khalé ngéne.. Voyager oui mais pas la mer de grâce.. Ngirr yalla😢😢😢😢😢
@aboubacarndiaye2148 Жыл бұрын
J'ai des larmes aux yeux walay sénégal metina
@antasarrsamb462 Жыл бұрын
Yalla maguilay gnane gua taik lokho khalai yi gnou am lougnou diap ba dotougnou nam Espagne repose en paix mes frères sàma khol nekhoul way
@yamadabo3228 Жыл бұрын
Svp pour l'amour de dieu pitié à notre mére li yépp diarouko frr ms paix à son âme
@BoussoBaly9781 Жыл бұрын
Le gars en noire m’as fait pleurer 😭😭😭 !!! Amena louko meti trop 😭
@oumarzuluzulu8137 Жыл бұрын
J’ai perdu un ami d’enfance khalè bou yarou bougue ligueye t man wornama dieum moko fi yobou il a une très triste histoire cheikh repose en paix niit kou bakh nga wone cette monde te meritais pas du tt ❤
@matyndiayeduval7263 Жыл бұрын
Mes condoléances
@oumarzuluzulu8137 Жыл бұрын
@@matyndiayeduval7263 🙏❤️🥹
@papebarapouye9901 Жыл бұрын
Nous sommes dans le meme quartier un gars cool et courageux yalla nako yalla yeureum
@NdieundéNdiaye Жыл бұрын
40ième déjà grand frère
@moustaphafaye9453 Жыл бұрын
Combien doit être le revenu utile pour les jeunes pour qu'ils ne pensent plus à s'aventurer de la sorte à l'extérieur ?? 50mil, 100mil, 200mil, 400, 800 ? Quels que soient le salaire, il est très difficile de vivre au senegal. Le jeune sénégalais a trop de pression sociale. Ce niveau de vie qui est anormale et qui met la pression à tout jeune, est à remettre au meme niveau que nos revenus. C'est sur ça qu'on doit réfléchir. On doit faire en sorte que la plupart des sénégalais voire tous puisssent vivre aisément dans ce pays. Les parents aussi, vos discours à savoir "sama dome sou magué dinama guéné ci ndol" doit cesser. Ton enfant c'est à toi de le préparer pour que demain qu'il puisses faire des économies pour ses propres enfants. C'est ainsi une réussite continuelle et abondante. Les mariages au senegal aussi font partie de ce qui font atterrir le jeune dès son début d'envol. À ceux la, s'ajoutent les dépenses quotidiennes très chères, la location exagérée, les terrains. Bref tout un tas de n'importe quoi... Mais cela ne justifie en rien que le jeune prennes le risque de s'aventurer dans un voyage où la probabilité de mourir est très élevée. Pour tout jeune qui réussit à passer par les pirogues, ait conscience que tu as influencé d'autres jeunes à vouloir passer par la même voie et qui sont malheureusement tomber dans l'océan. Rest in peace
@abdoukhadrediouf5919 Жыл бұрын
Problème bi tamitt léneu le . Gni pauvre limité wouniou s’en diour. Koula gueneu pauvre mola dakheu diour dom . Da ngay diour ay dom tei dolene meuneu yoor c un peu compliker koi
@lepetrolecestpourlepeuple7169 Жыл бұрын
@@abdoukhadrediouf5919Je suis parfaitement d'accord avec toi.
@bouhsoumare2571 Жыл бұрын
@@abdoukhadrediouf5919et avoir trois femmes sans argent après il veut quitté le pays vers l'Europe c'est horribles.
@abdoukhadrediouf5919 Жыл бұрын
@@bouhsoumare2571 amoul feneu gayi da niou takeu pour takeu ni rek mai gérance zéro
@sagarndiaye6260 Жыл бұрын
Ay way amnaci dome bouniouma taggé tay😭😭😭 yalnaleine yalla yeureum niom niép
@syllamoukhtarsyllasanteser1813 Жыл бұрын
Ndaychan Yalla nako yalla yerem 😢😢😢😢mèttina lol
@dabamboup1884 Жыл бұрын
Alahouma amine ❤
@maremeseck9540 Жыл бұрын
Yalnalène yalla yeureum kharelène aldiana firdawsi si barkep seydina mouhamed (saw)
@MrOusmane23 Жыл бұрын
Get rich or Die Trying. Yallah nako yallah yeureum, diegueul ko aye bakareum. Du courage , InShallah yallah dineu lene takhawou boubakh, Gueum rek , Amoul Bayi.
@PapeassaneSeye Жыл бұрын
Yalla nako yalla yereume kharè aldiana firdawssi mètina trop boy yi wakhnaniou deugue senegal dafa mèti trop mane mi soudeur la wone senegal ma nèk si situation you meti senegal respect wouniou ouvrier sama grand frère moma indi italie mes sama premier salaire dama tite sakh gouvernement senegal respectè wouniou senegalais yi
@nogoyefaye2757 Жыл бұрын
Que firdawsi soit ton demeure éternel 😭😭
@elisabethsoropogui8190 Жыл бұрын
Même sougnou wakhé deugeu bi le coup est déjà parti toi qui est encore vivant reste ici fépe mon méty guir yalla samay frères togueléne Lou diote yombe
@mariemendiaye3921 Жыл бұрын
Paix à son âme que dieu l'accueille dans son paradis firdawsi
@mouhamedndoye6470 Жыл бұрын
Wadiour yi amnégn si responsabilité aussi.Parsk so amé sa dom mouy tahalé dila diapalé déko encourager.Mais amnasi parents yo hamni nioy ték pression séni dom.Hass soubeu,Hass gone... Problème bi dafa vaste
@EvaHuncho Жыл бұрын
t'as raison bilahi
@marieeliseloume5422 Жыл бұрын
Boul dème yalla bakhna metina wawe yalla diekhoule
@aramendiaye3538 Жыл бұрын
Tu as perdu ton frère ds ces conditions et tu dis que tu veux partir lou koo fi djiar yeureum lène sène yaay yii mounou niou supporté lii dafa méti
@misstchiptchip2963 Жыл бұрын
C parce ya des imbéciles qui sont arrivés et arrivent a se demerder un peu dans des conditions misérables qui vendent du rêve a ce qui sont rester ici du coup les gens tête meme si la mort les attends
@itslea8567 Жыл бұрын
@@misstchiptchip2963ta tout résumé di dem vacance ak ay costume et voiture lolou moh takh les jeunes ça les motives de partir
@sakhocheikh4524 Жыл бұрын
Que paradis soit sa demeure éternelle 😢😢
@marieeliseloume5422 Жыл бұрын
Toklen la mer amoul banyasse yalla diekhoul borome karaw bounioul niakoul d'ara li guen wara niane moye werr ak werrle mou ande ak goude fane
@papediop9404 Жыл бұрын
Assamane da aame banguance tè avion moungui siy naow
@barbiepretty3395 Жыл бұрын
@@papediop9404ay way rayguama 😂😂😂
@papediop9404 Жыл бұрын
@@barbiepretty3395 🤣🤣🤣🤣🤣
@warrios6590 Жыл бұрын
@@papediop9404assamane amoul bankass waye ceux qui prendre le vol sont plus en sécurité que dieul gal Sénégal ba Espagne si bateaux je peux comprendre mais gal en plus sur chargé ko jusqu'à pas possible
@taphadiadia Жыл бұрын
Mashalla merci beaucoup ❤
@ramataba5463 Жыл бұрын
Non les jeunes n'ont plus aucun espoir li metina li kagne laye diékh
Mèttina trop bilahiiii que la terre d'Allah leurs soient légèrent Incha'Allah Rip❤🙏
@alioucisse998 Жыл бұрын
Yalla na ko yalla yeureum si barké Mouhammad amine
@fatimamarabt6352 Жыл бұрын
Yallanalene yalla yeureume kharelene dianatoul firdawssi
@DembaMballo-l2t Жыл бұрын
Mais Kan molén du dioh informations yi ba beun ham gni déh
@elisabethsoropogui8190 Жыл бұрын
Yaguini âme Toula nakary so démétamine défa sa bokeuyi dagnou nekeu thi diakaré am aussi louléne méty s'il te plaît reste faut pas forcer les choses
@segnemoustaphademe3438 Жыл бұрын
Yallana la yalla mottali lill li nga beuG banga dimbale saye parent ndaysane
@saidouboly3307 Жыл бұрын
les jeunes vous n'êtes pas affamés vous mangez bien ici au Sénégal rester travailler la terre ou vous faites du commerce c'est tout chacun veut aller en europe parce que son ami ou sont voisin est allé ne regarde pas les gens pour vivre.
@arameniang8030 Жыл бұрын
Sénégal😢dou réw méti ba kouné paré pour sacrifier sa bakane
@segnemoustaphademe3438 Жыл бұрын
ToGal rék yalla bakhna Dina bakh bou sobé borom Touba Que dieu te bénisse
@loelhadji100 Жыл бұрын
Ndaysan yallha nalen yallha kahre al diana firdawci my boy xolen benen metott por niaw europ galyi woroul bilahi metina trop
@aissatouciss5118 Жыл бұрын
Massa chéri cv aller qu’il repose en paix
@ramatalyto7585 Жыл бұрын
Yene jounaliste sene kescion yi amoule sens thi kou dele
@barandao-gx7hh Жыл бұрын
Etat bi amna thi faute mais aussi parents yi di diour di tekk rekk apres ngay setan say Dom Menno thi niom darra ngay harr niou tekki diapaleleu contrairement ak toubabyi deugg nehoul !!niounane yalla ne diourlen mais soudone lolou Kay douniou yemale diabar thi 4 !
@ndeyefa784 Жыл бұрын
Merci mon frère wax nga lép .masha 😂
@misstchiptchip2963 Жыл бұрын
Parcontre la population doit arret8r d'accuser l'état..l'état peut chercher du travail a tout le monde ? Sa existe dans quel pays du monde ? Cela n'existe nul part parents c vos parents qui vous ont mis au monde cest eux qui ont la responsabilité de votre éducation et de vous nourrir pas l'état..je suis désolée courage aux familles eplorées
@dieynabawane7378 Жыл бұрын
toi est ce que tu es normal si l'état a qui on a confié nos ressources , n'utilise pas ces dernières de manière efficiente afin de de réunir des conditions favorables pour assurer les besoins primaires de sa population cela ne conduirait pas à ce genre de situations .Donc abstient de toi de dire des bêtises si tu ne peux pas compatir à leurs douleurs .
@ndiagagueye1629 Жыл бұрын
Paix a leurs âmes arriver en Europe n est pas égal à réussir
Demal yone baa gonkh Senegal dafa nékh fii amatoul dara jaroul déé pour rien du tout europe nous sommes fatigué ici ya des papier mais ya pas l'argent ni la vie comme laba frére
@diantalmara6664 Жыл бұрын
bilay lolou la beugon wakh frere mangui fi Europ xhamnasi dara
@bilalkhalyfall9938 Жыл бұрын
Mdr Europe nékhoul té dou nguén gnibissi mooo yaw Europe noumou meunti mél mo tané Sénégal fouf sakh. je ne conseille personne mou djeul pirogues wayé koussi am occasion gneuw neu gneuw légalement nk je dis bien Europe mo gueune fouf Sénégal
Dieul gale mom risque la mais europe ak sénégal koukoy comparer dangay wakh loula nekh prsk Europe dou sénégal Europe mo geun fouf sénégal
@AminataSy-hp2kv Жыл бұрын
Dans la vie darra kheuyoul sotti
@abykane7690 Жыл бұрын
État mounoul diapalé gnieup hamolen lolou
@Rokheya194 Жыл бұрын
Afrique ak Europe sense inverse leu, gnioune suniou dome yi gnioy dioudou mageu terel gniou 😢😢 waye boudei Europe sene wadiour yi gnio leindi doundeul Bay doundeul seni seute seutate
@salmacounta2016 Жыл бұрын
Paix à son âme 🙏
@sidimohamedaminegueye4869 Жыл бұрын
Yalla na lene yallah yeureum Mais "Get rich or die trying" tegouwoul féne. Liguey ba am sa jakarta ak say machine war nga meuna continuer si yone bobou ba gueuna guiss sa bop
@souleymanelonnacamara2092 Жыл бұрын
Que leur âme repose en paix que la terre soit légère sur eux deukbi méttina trop mais si ils faut dieul galle je ne conseil personne des embarqué au Sénégal parce que ce très loin de l'Europe passée par les pays magréb malgré ce pas facile de vivre dans les pays magréb mais ce mieux des embarquée au Sénégal Gni dée si galleyi yéep y'Allah nalein y'Allah yeurem tes harée Adiana
@AwaNiang-r7x Жыл бұрын
Yo Allah yeureum léne séne yeye yi guir yala 😭😭😭 voyager mais papa et mére😭😭🙏
@pendadiagne5436 Жыл бұрын
Bilahi sama xol bi metina trop khalé souno guene yalla na leine sougnou boroum takhawo ter yeureum nie dem Bilahi sougnou gouvernement yi bouleine yalla ballou gnoune nieup safara lagnou dieum 💔💔😭😭😭😭😭😭
@borombakh1129 Жыл бұрын
nék léne aye nit wadiale léne résistance 🔥🔥 ngou khékhak macky sall nangou sonu réw diokh ko sonko mo défar ko
@SalyNdiaye-ef9su Жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum hareko aldiana firdawsi
@BadaraDieng-ys4py Жыл бұрын
Ndeysane métina trop moi j'ai perdu Mon frère ki topou si Mane en 2021 mouy éxpérience boumadoul mana faté si adouna ta si galyi lawone 😭😭😭😭
@abdoukhoudossndoye2443 Жыл бұрын
Insallhallha dé rk ndakh réwmi da méti
@cheikhtidianediop3323 Жыл бұрын
Bayileun gal yi yonou ndokh bakhoul
@NdeyelikaDiop Жыл бұрын
C'est triste 😢ce qui ce passe au Sénégal,apparemment les jeunes ne peuvent plus se permettre de penser à la réussite au bled..li metina bilahi
@syllamoukhtarsyllasanteser1813 Жыл бұрын
Ndaychan 😢😢YAY aka sônnô sinon YAYI Yi Nanlén Yereme 😢😢😢
@omzoproLenfentfeLouga Жыл бұрын
YEUREUME LÉNE WAYDIOURE YI.
@bebichefama2218 Жыл бұрын
😭😭😭😭j’ai le cœur meurtri💔😭
@bsgtvbsgtv1032 Жыл бұрын
Courage
@badienediaw2073 Жыл бұрын
Li niouy doundeu dafa meti ba tah ga dieul 450000 defko si gal gui pourkw pa ga liguey di mou am loumou diour nékléne ay nitt😢
@Mamyzahra935 Жыл бұрын
Vraiment lolou départ bou bah leu mai gnom gno beug Europe hawma Loutah
@ndeyefa784 Жыл бұрын
Nioune niongui Europe. Mais sant yalah . Europe du touss. Vraiment khaliss bigniy yak si gal gui khathie n'a si niom khaliss meune nagne si ligueyi gal du solution
@fatoumatadiao7313 Жыл бұрын
Paix à leurs âme
@yamilathioune7946 Жыл бұрын
Papá demalde,so demoul sa yaye dalaye khass sou gayi demoone delousee.demal fall.
@bathimasamba8758 Жыл бұрын
Ohhhhh frère courage 😭😭😭😭😭😭😭
@tidianendiour9185 Жыл бұрын
Iow kou meuneu ligueye 600mille bo fi togué am 1 million
@nogayethiam4282 Жыл бұрын
Courage frère méti n’a trop way
@nogayembodji8073 Жыл бұрын
Vraiment mèti na
@mariama2953 Жыл бұрын
Am crying with them
@mamecheikhsylla4431 Жыл бұрын
Deug bi moomètti wallahi. Kou xamoul xamoo Took thji sa kèer.Di xas boyyi Rèc
@khadigueye9542 Жыл бұрын
Yalla nalene Yalla yeureume te kharelene aldiana ak molom new 😢😢😢😢😢
@mature144 Жыл бұрын
ndèye sane da nit mo takh mou teup
@mbayanggueye5516 Жыл бұрын
Guir yalla toguel😭😭😭😭😭
@khadysene799 Жыл бұрын
Dafa tit mo takh mou teup fofou kounek sa bop nga don tal mo takh diapouniou ko yalla nako yalla yeureum
@julianachididdiallo573 Жыл бұрын
Bien sûr
@youssouphasarr3027 Жыл бұрын
Vraiment c'est triste 😢😢
@fatimandiaye8351 Жыл бұрын
oh c'est vraiment triste paix à leur ames
@fayeousseynou753 Жыл бұрын
Kou mana dém démal dém dé tok dé yalla rek mo kham
@dousediop1759 Жыл бұрын
Frere boil meusse dême is galegui taylê sa bakanela
@newsinfosbyme Жыл бұрын
Guiryalla patriote reste ici et bats toi pour toi et ton ami car il ya tout ici sauf que c'est entre les mains d'un Tyran Sall. Je comprends ta douleur ❤
@OusmaneDiallo-wk3jc Жыл бұрын
Ngiur yalla ak yonénte by bayi léne gale yi nioune nieup môme laniou dieul bâ yekssi fi thie Europe wayé bou démbe doon tay man môme douma thie diaar risque rék la bilahi yeureum lén sunu yaye yi baal léne ma ak thie kadu yi dama khame lithie nék rék souma sagnon kou beugueu nieuw yalla indy la thie diame 😭😭
@lissathiam9577 Жыл бұрын
Du courage 😢
@OusmaneDiallo-wk3jc Жыл бұрын
Merci beaucoup
@rokhayatoudione3912 Жыл бұрын
Wouteul passeport lidieunty visa dougou avion mo gueune
@cheikhtidianediop3323 Жыл бұрын
Loy daw bay danou yalla sah tégoula lo manoul wakhouma AK nitttttt
@Mamyzahra935 Жыл бұрын
Tei lima diahal fognou dieum mo gueneu meti kon nagnou tok fi
@cheikhtidianediop3323 Жыл бұрын
@@Mamyzahra935 gal gu kousou dougou kouné kharoula
@SopeNaby5212 Жыл бұрын
paix à son âme
@MadickeSeck-t2w Жыл бұрын
Metina trop 😭😭😭😭😭😭
@babatop154 Жыл бұрын
Paix à son âme yalna ko yallah khareii aldiana firdawsi
@njemmehjoof2096 Жыл бұрын
Journaliste bii tamit 🤭🤷♀️
@ibrahimagueye9233 Жыл бұрын
Paix à son âme mais 20ans tolo guo si ame baye niak banane danga seusse
@mamesalihou3343 Жыл бұрын
Da Feuy sa yaya ak sa Baye Am louniou Lerrkk Reck
@teningdieng9230 Жыл бұрын
Li lep mauvais gouvernance moko waral jeunes yi do fipou.paix a leurs âme. Danguay beug dimbali say wadiour mais hooo😭😭
@Mamyzahra935 Жыл бұрын
Mai Ben wadiour tegoul li domam Bakane dafa fort GUIs sa dom mo guen neh haliss
@quenne_dudiolof9536 Жыл бұрын
Ya plus rien en Europe, avec la crise de COVID bcp d'entreprise sont fermés. Nieuw Europe di takha walou si sed bi do am lo lekkk
@nabouwane7684 Жыл бұрын
Mere bi dafaye encourage khaleyi pour gnou dème Borome ibadou bou rouge bi mes guèdje gui dou solution
@CisseIbrahima-v7z Жыл бұрын
Papa gana yalnako yalla kharé aldiana frère repose en paix