ALLAH n'aime pas la calomnie et la médisance. Ces choses détruisent beaucoup. Qu'ALLAH le pardonne , car il est PARDONNEUR. Cependant, le mal est grand et tous les gens qui pratiquent cela doivent arrêter avant que le mal ne s'abatte sur eux. Soyons sincère dans nos relations.
@DiopNdeyendoumbe-f8fАй бұрын
Walahi 🙏🏾♥️♥️
@BinetaNdoye-yf6ppАй бұрын
Kouthia dafa dougeu si gal dignane mou soukh limouwakh dafa Gnaw wayé yalla nako yalla mey were
@moyancheikh3991Ай бұрын
Jimbori soit honnête kouthia limou wakh thi goor gni nak dafa niaw wakhi biir dafa wara rafett tok thi garap di gor branche bi Yalla nako Yalla soutoural mais na balou
@ndeyebinetaba1462Ай бұрын
Yalnako yallah défal diam rék té fi si dounya nitt kounék am gua lo meuss wakh waleu gua déff ko thi sa dound bo sagnone mbidéff douko yeuk wakh dji mo beurii rék
@MaremeNdiaye-c9hАй бұрын
Djiéguéne mo doywar rék. Motakh seuy loumou nékh nékh il faut toujour se méfier. Diabar moune n kheuy rèk déme yaubalé say secret. Sa depend ci bane genrou djiguéne nga tombél. Amnaci gnou doywar. Yalnako yallah diapalé.
@momodadd5045Ай бұрын
Yénn ay nafekh ngaen kouthia dafa togn ay nit wakhlén li am kouthia yalla nako may wer ❤karke seydina Mohamed ❤❤
@barasarr5512 ай бұрын
Yala nako yala maiy wèrr si barkè seydouna Mouhamed aleysalame
@kharyfaye8324Ай бұрын
Amin ya rabi
@fatoumatadrame806Ай бұрын
Jimbory lo meusseu wakh dakorna mé Kouthia mom mo togn bopam parsk nite dafaye sincére di wakh si moromou djoulitam lou ràfét souko xamé souko khamalé lou niaw sangue ko soutoura kou wakhoul deugue wakh safane yalnanioussi yalla mousseul té Sénégalais yi naniou diémeu nék deug deugui dioulite
@laye1983Ай бұрын
KI I BOPAM MO DOY WAR... KOUTHIA MOM DIEUGUEULOU REK MOKKO WAR....
@MarieGueye-i4p2 ай бұрын
Doyna warr dal yalla nako yalla defal diam may ko weur amine
@serignecheikhsy41552 ай бұрын
Amen me kouthia loumu def defa niaw lep moy rek la
@cisseayssataАй бұрын
A la place de tflm je révoque kouthia sans droits . Ay fumiers nguen
@FatimandaoTymandao-gr4glАй бұрын
Yallah moko beug sakh motakh mouy febar ni, yalna sett wethie si bakar à travers ses paroles malsaines té yallah yeuketi ko. Djimbori boul khass kene koudoul mom ndakh sou wakhoul wone kene douko wer.
@ndeyegueye1152 ай бұрын
DJIMBORI KOUTHIA NA DIEGUELOU GNIMOU TOGNE LIMOU WAKH MO BARI TÉ GNAW DAFA MEUN NETALI AK TOUR YIMOU TOUDOU YEUP
@maawakonte65702 ай бұрын
SURTOUT NDIAYE BIMOU FÉBARÉ WEUKH DIOU GNAW
@serignecheikhsy41552 ай бұрын
Ndeye bilay togn moy bakhou surtout akk moy guen bonn di yakeu nigue bok liguey defa niaw trop
@ndeyegueye1152 ай бұрын
@@maawakonte6570 NDEYSANE SURTOUT NDIAYE MOM LA KHALATE AK PAPE CHEIKH DIALLO BAMOU DIEULE THI DEPRESSION
@ndeyegueye1152 ай бұрын
@@serignecheikhsy4155 SERIGNE LIMOU WAKH MO GNAW AKOU GNOGNOU MOKO DALL PAPE CHEIKH DIALLO DÈM BA AM THI DEPRESSION
@ndeyegueye1152 ай бұрын
@@serignecheikhsy4155 KOUTHIA LIMOU WAKH MO BARI TÉ GNAW MO NGI FADIOU BA CASAMANCE
@manandiaye37782 ай бұрын
Amine ya raby
@evre8918Ай бұрын
Vraiment djmbory nafékh nga kouthia mo tongne
@ycamara9034Ай бұрын
Sad sad sad , ,is sad true sad🙏🙏🙏
@CheikhDioumeАй бұрын
loula dall. porte plainte. la solution. ils vont arreter
@bassiroudiop7459Ай бұрын
Merci djmbori ❤❤
@momodadd5045Ай бұрын
Diabar dji mom bakhoul mais kouthia tamit dioum na loool sakh
@cisseayssataАй бұрын
Vous défendez toujours les coupables. Pensez aussi aux victimes
@mouhamettraore4903Ай бұрын
Nit kounek Li Nek sa khol Molay moudié dal. Lolou moy aduna nako gnep khamé nonou.
@momodadd5045Ай бұрын
Kouthia dadon ligéyé TFM niokay fay donc TFM defoul Dara kouthia mom moh togne ay nit légui kay na ballou nioniou rk
@ndiayendeyendoumbe9894Ай бұрын
Wakh bou niaw bakhoul
@MatyDieye-t3lАй бұрын
Vrement seuytanè mo yatou guinaw nayo yalla yekati ak djiam wayè kouthia dafa djioum deug li mou wakh sou amone sakh djiaroul moukouy wakh djiabaram
@CamaraBakary-y5gАй бұрын
Exque kouthia a réfléchir avant de parler du mal aux autres
@YoussoufKeita-m4r2 ай бұрын
Une histoire non compléte ; saway nétalibi desna.
@serignecheikhsy41552 ай бұрын
Youssou jimbory defa fen kouthia loumu def defa niaw trop di yakeu ayy nitt soutu niga bok liguey😢😢
@cathygueye238Ай бұрын
Kouthia a tord sur toute la ligne wakh dafa wara rafett
@ndeyegueye1152 ай бұрын
KORTE LAGNOU KO SANI MO NGI FADIOU FOUNE THI SERIGNE Si SONOUNA MOM YALLA NAKO YALLA MAY WERR DAFA DIOUM
@serignecheikhsy41552 ай бұрын
Amen ndayssane
@ndeyegueye1152 ай бұрын
@serignecheikhsy4155 AMINE ALAWOUMA AMINE 🙏🙏
@FIssa-221Ай бұрын
Défoi je me demandais si, bamouy wax lolou esk il était saint, baxam amoul loum dieul ???
@MaremeNdiaye-c9hАй бұрын
@@FIssa-221 diarna kholate dé. Parce que li dafa doywar dal
@FIssa-221Ай бұрын
@MaremeNdiaye-c9h Yallah aka baari soutoura, wouté ak domou Adama. Mom sou done déf, kou déf safane mou fay lako, kon kén doufi déss
@papedieng54Ай бұрын
Non sénégalais mom lolou mokoy beguel déstabiliser yakheu leuh tokhola daf Kay nekh