Serigne Gana Mésséré attaque oustaz Oumar Sall sévèrement

  Рет қаралды 730,110

Xidmaprod Tv

Xidmaprod Tv

Күн бұрын

Пікірлер: 4 000
@ibrahimniang9862
@ibrahimniang9862 5 жыл бұрын
Kou Beugeu serigne touba Beussel j'aime bien
@boucheserasmbaye8107
@boucheserasmbaye8107 5 жыл бұрын
Ibou Gueye jaime mourid bamba woor
@momoafrican7442
@momoafrican7442 5 жыл бұрын
bamba force
@bayeserignendiaye6477
@bayeserignendiaye6477 5 жыл бұрын
Se le fel baye
@moudoumbake8379
@moudoumbake8379 4 жыл бұрын
Machala
@xaadim9615
@xaadim9615 4 жыл бұрын
Baye Serigne Ndiaye se Baye yarole
@maguettembaye5368
@maguettembaye5368 5 жыл бұрын
Je deviens mouride aujourd'hui. Machallah
@BAMBISTETV
@BAMBISTETV 5 жыл бұрын
Macha allah billahi doko Rethiou adduna ak allakhira
@mamediarrafall3392
@mamediarrafall3392 5 жыл бұрын
Billakhi bouko thiakhané billahi daga khameni khorame ak sou kare bokoule
@melokaanoumouridetv5107
@melokaanoumouridetv5107 5 жыл бұрын
Masha Allah Yalla nala Serigne bi gatandou
@maguettembaye5368
@maguettembaye5368 5 жыл бұрын
🙏🙏🙏
@bilyboy4647
@bilyboy4647 5 жыл бұрын
Nday san
@omargning7773
@omargning7773 5 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFETI SERIGNE TOUBA KOU SOPEU SERIGNE GANA MESSÉRE APULLIER SUR J’AIME
@abdouseye754
@abdouseye754 5 жыл бұрын
Machallah Serigne Gana Mésséré yalla na borom bi goudeul sa fane.Erreur bi dotouko dalati wakh rék beugue am promo Omar Sall khamoul touss.Serigne Touba kène la amoul morom dafa liguéyal borom bi motax li leep tay ana séni Mame yéne loutakh sonougnouwone si mission bi pour am li. Dieureudieufé Serigne Touba. Mouride noble la kou andak Bamba do chômé
@khadyfaye7430
@khadyfaye7430 5 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣Wouuuuy Dara la xamoul thimmm
@mamediarradiop1526
@mamediarradiop1526 5 жыл бұрын
Serigne touba kene la yalla nanoko Yalla fayal
@xaadim9615
@xaadim9615 4 жыл бұрын
@@khadyfaye7430 1895 se Mame fome dogon
@mamadoulaminesylla1977
@mamadoulaminesylla1977 5 жыл бұрын
Tu es top merci bcp sokhor bakhoul de punchlines de ouf tu l'a massacré merci mille fois Serigne Gana massaré vrai milieu défensif nga motakh sa tour bi amm Gana😂😂😂😂😂😂
@ncm04
@ncm04 5 жыл бұрын
Il l'a pulvérisé nguanane... 😂 😂 😂 😂
@ncm04
@ncm04 5 жыл бұрын
Je savais que ni dinaneko tontou... Daniou ko talou tone rekkkk ndakh magal gui
@papask5253
@papask5253 5 жыл бұрын
Mamadou lamine Sylla verai rapeur nga iow😂😂
@myvision7647
@myvision7647 5 жыл бұрын
Il es temps que le monde entier sache que serigne touba lérrou yalla laa.
@modounbahi2855
@modounbahi2855 5 жыл бұрын
MaCh Allah
@falythiam9777
@falythiam9777 5 жыл бұрын
Sante yalla ak yonene psl di wakh dieureudieufé serigne touba ndakh serigne touba dafa diayantè lou kene defoul ba yalla fayko limou am ta liko yalla may dou meussa degn serigne touba amoul morom
@modi9530
@modi9530 5 жыл бұрын
S gana macha allah diara diaf mame boroum touba amol moroum
@prenomwade930
@prenomwade930 5 жыл бұрын
Diara dieufeul serigne Touba diara ame Mame Cheikh Ibrahima Fall
@fillesage2023
@fillesage2023 5 жыл бұрын
Thieuy niouni ap mouride daye deugou th ame fite,wayé Serigne Ganna deugueul nako taye dh,macha'allah Dieureudieuf mbackè Balla Aïcha,Serigne Mountakha yalla nako yalla maye goude fane akh wéer🙏🙏🙏
@boucheserasmbaye8107
@boucheserasmbaye8107 5 жыл бұрын
Mouhsinatou Thiaw amine mouridd
@modouseck7237
@modouseck7237 5 жыл бұрын
Billay Gana souma nécon milliardaire dinala décoré sent serigne touba
@ibrahimafall2390
@ibrahimafall2390 5 жыл бұрын
Borom touba amoul morom
@sodamoustaphafall2177
@sodamoustaphafall2177 5 жыл бұрын
Bilahi seigne touba amoul morom Barké Mame Cheikh
@aladjiifaye6687
@aladjiifaye6687 5 жыл бұрын
Serigne ganna Yagüe Fi te weer wayè 🤣🤣🤣🤣
@mamesaye1977
@mamesaye1977 5 жыл бұрын
No mangui deii🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@grizzlyyukon6349
@grizzlyyukon6349 5 жыл бұрын
AMINE
@papeserignembaye8679
@papeserignembaye8679 5 жыл бұрын
Amine way
@bassiroudia7470
@bassiroudia7470 4 жыл бұрын
Akass s ganna sama xholl sédena si iwo
@siidibirahimrijaal
@siidibirahimrijaal 5 жыл бұрын
Jërëjëf Sérigne Ganna lépp lérna Ahmadou dou morom❤☝️
@thiernoabdourahmanediao4382
@thiernoabdourahmanediao4382 5 жыл бұрын
Anta muraadii, anta himaadii nawwir fuaadii, yaazaa- l- diyaa - i grâce à toi, j ' ai de la volonté, tu es mon soutien eclaire mon coeur, toi possesseur des lumières.
@mariamadiakhate6372
@mariamadiakhate6372 5 жыл бұрын
Tontou dou forokh merci Gana Serigne Bamba ci ❤️
@alibaba-js7cb
@alibaba-js7cb 5 жыл бұрын
gana mo geuneu kat oubi leufeul ndayam
@alibaba-js7cb
@alibaba-js7cb 5 жыл бұрын
@@serignekhadimgueye7460 Ay yéfeyr ngéne motakh khékh rék doul way
@alibaba-js7cb
@alibaba-js7cb 5 жыл бұрын
@@serignekhadimgueye7460 sa serigne sakh gnimé wouma
@serignekhadimgueye7460
@serignekhadimgueye7460 5 жыл бұрын
@@alibaba-js7cb yaw nitou réseaux sociaux nga amoo fite. Té guisnga mane mii di wakh ak yaw khalé bou daw laa j'ai 16ans. Té fooma woo ma wouyou sila. Wakh nala lou léére nak
@serignekhadimgueye7460
@serignekhadimgueye7460 5 жыл бұрын
@@alibaba-js7cb Sawaay léégui yaw loo beugg nak. Balamaa wakh ak yaw damalay laadje eskeu musulman ngeu ?
@ncm04
@ncm04 5 жыл бұрын
*PUCE BLEU BI WAY NIOU SANTATI SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA* *DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA*
@mamadousow3017
@mamadousow3017 5 жыл бұрын
Vous mentez trop mr khamo dara arrêter de menteur il sait la ou on a enterré son père
@maguettesarr3927
@maguettesarr3927 5 жыл бұрын
@@mamadousow3017 yawe.daga.réré.mbire.ndaga.beugue.torokhe
@babadiop4824
@babadiop4824 5 жыл бұрын
@@maguettesarr3927 yaw ya réré mbirr , yaw ya beugue torokh , serigne touba nékaloule kéne koudoule yalla ak seydouna Mohamed , donc yaw momou la sa dorokh léérr , ndakh nitou yalla bi yalla wathié , guadiko wédi , yeureum nala .
@mouhametbadji864
@mouhametbadji864 5 жыл бұрын
@@mamadousow3017 moeurs41
@falloumbodj3535
@falloumbodj3535 5 жыл бұрын
NCM Real khawma Kane Dé Mais Kii dé dootouko déffati
@lunobreezy4238
@lunobreezy4238 5 жыл бұрын
Aka wôôrr 🙏🙏 Serigne Touba amoul morrõm 👌👌❤❤
@almamytimera9793
@almamytimera9793 5 жыл бұрын
Le prophète Mouhamad paix et salut sur lui mo amoul moromme
@mayoronguer2498
@mayoronguer2498 5 жыл бұрын
@@almamytimera9793 prophète s.a.w moy sangoub sangue yi Yallah mi déf lolou modéf Serigne Touba amoul morom bilahi gueumm léne Yallah way
@mayoronguer2498
@mayoronguer2498 5 жыл бұрын
Serigne Touba dou massa ame morom ba adouna di toukki
@myvision7647
@myvision7647 5 жыл бұрын
Serigne touba lérrou yalla laa
@assanembengue3808
@assanembengue3808 5 жыл бұрын
Damaye lathe té ndakh serigne touba bimouye guané adouna ndakh fekoufi aye djaka ak djouma t gni ko diour di aye djoulite nagnouye wakhanté deugue
@moussadiaw6794
@moussadiaw6794 4 жыл бұрын
Li gana bone moy wakh te amossi benne firnde yalla nanou yalla may deg ak top waye wakhe nguir bakkane biss dina nieuw nga wet sa bammel te kenne doulafa fek inchallah. Wassalam
@papadiouf3544
@papadiouf3544 5 жыл бұрын
Merci bcp wayy serigne Gana messré bilahi lima métti wone leep si sama❤❤ waxal ngamako yalla nasa diame yagg serigne touba sunu yakar Adouna ak alakhira mofi nek mim rew Bamba ko mom koumou métti nga deee😂😂😂😂
@yoroba1091
@yoroba1091 5 жыл бұрын
Papa Diouf aywayy lii nékhoul
@Awa.C1
@Awa.C1 5 жыл бұрын
44. Dis: «L'intercession toute entière appartient à Allah. A Lui la royauté des cieux et de la terre. Puis c'est vers Lui que vous serez ramenés». 45. Et quand Allah est mentionné seul (sans associés), les coeurs de ceux qui ne croient pas en l'au-delà se crispent et quand on mentionne ceux qui sont en dehors de Lui, voilà qu'ils se réjouissent.
@kebbshady5044
@kebbshady5044 5 жыл бұрын
Ces gens là sont des égarés et associateurs,et celui ci c'est un très grand menteur.mentir au sujet de Allah est haram
@Awa.C1
@Awa.C1 5 жыл бұрын
kebb shady salam alaikoum Le pire c’est que j’ai bien écouté ce que Oustaz Oumar Sall a dit, il n’a jamais critiqué Serigne Touba, il a dit que Serigne Touba était un être humain, c’est Allah qui détient la Royauté en Sa Main et c’est la Vérité.
@aliousylla3092
@aliousylla3092 5 жыл бұрын
Awa camara merci pour ton courage
@thiamahmadulattekh562
@thiamahmadulattekh562 5 жыл бұрын
Quand il parle, il parle aux gens qui reflechissent Dieu a fait vous n'avez ni repère ni guide et vous etes trop bas pour vous brancher aux prophete et interpreter le coran n est pas donné a tout le monde Serigne touba moy alhur ane dolene deuk si loudoul sene xol di bone
@cherifmbaye9151
@cherifmbaye9151 5 жыл бұрын
Ohh les jaloux
@mamediarrafall3392
@mamediarrafall3392 5 жыл бұрын
Dama sante yalla Bima néké mouride mouride MO takh léme kou daccor ak manne
@mbenefall5927
@mbenefall5927 5 жыл бұрын
Ya wané .wa bolémassi
@toubadjob3797
@toubadjob3797 5 жыл бұрын
Ya bakhe waye woma Moustapha Diop si 00393208464383 itali
@diehiitoumakgni2503
@diehiitoumakgni2503 5 жыл бұрын
@@toubadjob3797 dakhe guinar wakhalé sa sokhla loutakhe ngéne beug djiguène di diokhé ay numéro telephone di ték deal
@akhmadougueye829
@akhmadougueye829 5 жыл бұрын
Ak man
@electriciengeneralbambasow3343
@electriciengeneralbambasow3343 5 жыл бұрын
Moi
@mahamadoudiouf2682
@mahamadoudiouf2682 5 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Bii J'étais en colère contre ce mauvais homme mes Alhamdoulilah deuugg naa abbb diss bou weerr teey
@mandinkaseye6662
@mandinkaseye6662 5 жыл бұрын
Je l'es plus en vers toi
@magui2429
@magui2429 5 жыл бұрын
👏👏Gana dal la beug niaw le vrai défenseur du mouridism macha Allah dieuredieufei Ahmadou
@awandiaye7763
@awandiaye7763 5 жыл бұрын
Mashalla lép lérna bilaye SERIGNE TOUBA REK.
@papefodesenghor3442
@papefodesenghor3442 5 жыл бұрын
J s8 talibe cheikh j'avais cru a Oumar salle mais sincèrement quand j vs ai écouté tu ma rassurer machalla merci pa gana k dieu vs protege.
@cheikhantangom1385
@cheikhantangom1385 5 жыл бұрын
Oumar sall et sa bande insultent toutes les confréries mouride tidjane layéene ......ils cherchent à créer des doutes pour imposer leur idéologies
@abloslimshady
@abloslimshady 5 жыл бұрын
Yaw nak khamago fingay té deh, ndakhté yangui fi tay souba yangui féleu, serigne touba wakhoul lolou deh, kon toal yalla ak yonnent bii bo bougué mouthiou.
@fatoumakhfoussefall2507
@fatoumakhfoussefall2507 5 жыл бұрын
Serigne Gana yalla boula thiate top machalah Dieureudieuf Serigne Touba
@mayamoustaphaobda3036
@mayamoustaphaobda3036 5 жыл бұрын
Nn sénégal mo neih 😃😃😃😃
@OmarLoSaliou
@OmarLoSaliou 5 жыл бұрын
Fier d'être mouride plus précisément talibé serigne saliou #Salihat_dans_le_sang Mane lima nexe si gana moy loumou waxe dina waxe fane lako yalla waxe wala serigne touba❤❤❤✌✌✌
@MamadouSow-eo9zi
@MamadouSow-eo9zi 5 жыл бұрын
Lou lére nga wakh baye Gana qu'ils laissent Serigne Touba dou sén morom dieureudieuf Modou Mbacké ❤️
@dienneyaramkare1942
@dienneyaramkare1942 5 жыл бұрын
Serigne Ganna yalla nanga fi yague té wér sédal ngasounou khol yi Dieureudieuf yaw fagoutéfou Serigne Touba nga
@mbenefall5927
@mbenefall5927 5 жыл бұрын
Billay ma bégu si SERIGNE gana mésséré. Wa lii nékhoul
@khadidiopbamba6126
@khadidiopbamba6126 5 жыл бұрын
Nexna de blhi
@akhmadougueye829
@akhmadougueye829 5 жыл бұрын
Machala
@fatoudione2997
@fatoudione2997 5 жыл бұрын
Merci gana yague fi lol si barki s touba
@khadimndiaye9132
@khadimndiaye9132 5 жыл бұрын
aka nekh
@magatesamb4882
@magatesamb4882 5 жыл бұрын
Beug gua kou meune féne. Yéne sakh khamguéne né day féne
@amargueye7647
@amargueye7647 5 жыл бұрын
Dieureudieuf serigne gana senegal liko té deme ligni diguene serigne touba motakh
@bromessb9537
@bromessb9537 5 жыл бұрын
Lolou de mom deug leu
@fatimahamed1982
@fatimahamed1982 5 жыл бұрын
Bilahi serigne touba rek moffi nek balla aissa boury
@thiambabel8885
@thiambabel8885 5 жыл бұрын
Bilahi serigne bamba mo fi.nek
@cheikhkane8191
@cheikhkane8191 5 жыл бұрын
Mes frères et soeurs revenons à la raison serigne touba fut un model de piété et un guide exemplaire arrêtons de le prendre pour une divinité et tâchons de suivre son model . Un beau discours pour ne rien dire au finish
@ciskosora
@ciskosora 5 жыл бұрын
Merci beaucoup c'est juste un beau parleur wakhoufi dara
@papamoussadiouf8451
@papamoussadiouf8451 5 жыл бұрын
Lucifer k tu es
@khadyfaye7430
@khadyfaye7430 5 жыл бұрын
Vous êtes juste des mécontents et des jaloux.... Serigne touba kouko beugoul do dougu ardiana wassalam
@cheikhkane8191
@cheikhkane8191 5 жыл бұрын
@@loptimisteoptimiste4131 j'en passe par respect aux lecteurs
@yacinecisse5456
@yacinecisse5456 5 жыл бұрын
Li d moy ignane
@BAMBISTETV
@BAMBISTETV 5 жыл бұрын
Billahi wallahi man de lima guem yalla sunu borom amna matko khamne benn diamame douko nakh serigne touba dafa dieufal boromam louko kenn defaloul mou fayeko loum fayewul kenn yalla mimou Don dieufeul mokoy sammal leppam dah mo bayyi won lepp ak niepp guir dieummi yalla akub yonnenam rek Nanu namgou li am te borom bi Defko nanu diamou yalla te ligueyali serigne touba mo wor tay ak elleuk wasalam
@ndeyesamb2058
@ndeyesamb2058 5 жыл бұрын
Serign gana foumalay guisse ba decorera 🙏🙏🙏🙏🙏👍
@akhmadougueye829
@akhmadougueye829 5 жыл бұрын
Machala
@khadimseckatoubasidy893
@khadimseckatoubasidy893 5 жыл бұрын
Merci way
@fatimakebe3040
@fatimakebe3040 5 жыл бұрын
Ms yaw bo ligueyale serigne touba kagne lalakoy fay 🤷‍♀️ani sougniouy xeil je croyais que so ligueyal kay yalla guay liguay dakh molafi eudi pr lolou wala tmt 🤷‍♀️🤔serigne touba tay lanla sokhla si yaw ay gnian kesei🤲🤲
@sokhnamai4202
@sokhnamai4202 5 жыл бұрын
niaaw ouztaz dotoko defati deh wakhouma khadim rassoul kokou dou morom yen talibe bou deugal rek dou len sen peundam tchim ignane moleni ray sokhor
@papacheikhmbaye8197
@papacheikhmbaye8197 5 жыл бұрын
Ma ngui retane rk😂😂 ndakh fan gana beug ko limouy wakh à l’aise ndakh dako xaam defarou SERIGNE bila dh 👌🏿❤️thieuy gana
@boubsthior7472
@boubsthior7472 5 жыл бұрын
machalla amna solo merci cheikh bamba
@mamesaye1977
@mamesaye1977 5 жыл бұрын
Barkep s.saliou no ki dou nit🤣🤣🤣
@seckmoustapha7723
@seckmoustapha7723 5 жыл бұрын
Barké serigne saliou magui dé serigne ganna 😂😂😂😂
@papito8025
@papito8025 5 жыл бұрын
Nio tey dei , nioune ahmadou bamba rek beu aldiana Koumou nexoul nak c’est ton problème. Dieureudieuf Serigne touba
@alibaba-js7cb
@alibaba-js7cb 5 жыл бұрын
katal sa nday kane mola wakh serigne touba Adiana la dieum
@guedebeye1502
@guedebeye1502 5 жыл бұрын
@@alibaba-js7cb boy sa bopou Ndaye guanane
@boygainde3764
@boygainde3764 4 жыл бұрын
@@alibaba-js7cb serigne Touba mo yore thiabi aldiana koumou nekhoul do dougou
@mouhamedthiaw5600
@mouhamedthiaw5600 3 жыл бұрын
Thank you cheikh ahmadou BAMBA Khadim Rasoul ❤️🤲🏿🕋😍
@Beaute9291
@Beaute9291 5 жыл бұрын
barki rassouloulahi serigne bambay wadia. mame dhé layénne la wayé fougne ma wo thi serigne touba ma wouyou ndakh dafa fess dél thi sama khol bi. serigne gana may nala ay diouni. kou nangou li yalla dogal do soone sa khol dou diékh
@abougabal6691
@abougabal6691 5 жыл бұрын
Khawa bilaahi wakh nga deug té dangaa baakh rék té sa khole rafett. Nangou yomboul. Serigne Touba dina yombal say mbire. Boul ragal dara.
@seidousow8986
@seidousow8986 5 жыл бұрын
hawa ndiaye. Beugue nala ngir sérigne touba
@modouniang1547
@modouniang1547 5 жыл бұрын
Ndeye sane Hawa sope nala ngir Serigne touba, ta ma ngy lay gnanal ake yokkou thy barkep Serigne Touba
@balyboussosady598
@balyboussosady598 5 жыл бұрын
ya goré
@magueyekane7523
@magueyekane7523 5 жыл бұрын
Bilahi ya raféte khol tè nara tékhé ôh beug nala way
@mamekhadimdiop10
@mamekhadimdiop10 5 жыл бұрын
Thieuy Gana Masha allah Serigne Touba kenn lah❤️😍
@elhadjiamadouthiam1343
@elhadjiamadouthiam1343 5 жыл бұрын
Chéeet waay iow beug naala waayy...un talibé cheikh❤😻😻💕❤💓🧡💚💙💛🙈💘
@droledevideos2878
@droledevideos2878 5 жыл бұрын
Je fais parti d'aucun tarikha ni ibadou je suis juste un musulman qui adore Mouhammad salal lakhou alekhi wa salam plus que tout autre personne au Monde . Mais franchement Serigne touba est un grand Monsieur qui a vouer sa vie à l'islam et à au prophète Mouhammad salal lakhou alekhi wa salam je le respecte et je l'adore pour sa ❤❤
@azizdabakh3670
@azizdabakh3670 5 жыл бұрын
Suis pas mouride mais vraiment cheikh Ahmadou bamba liguéy na ####Bamba partout
@khterangasngueye1114
@khterangasngueye1114 5 жыл бұрын
am ga dia diaf❤✌
@assanembaye1223
@assanembaye1223 5 жыл бұрын
Akassa fall baye ganna doundeul way fall dama kontan kontinè 👌👌👌👌👌👌ahmadou bamba beuri 💪💪👑👑👑🍵🍵
@beyonder1918
@beyonder1918 5 жыл бұрын
Oustaz Oumar Sall à dit la vérité et personnellement je ne l'ai jamais entendu nommer, critiquer ou attaquer directement une personne parmi les khalifes des tariqas. Ce qu'il dit touche tout le monde et pour le moment il prêche pour un monothéisme pur et lutte contre le shirk et l'association qui se banalise gravement dans notre pays. Le jour ou Oustaz Oumar Sall changera de position je serais le premier à le désavouer. Cheikh Ahmadou Bamba (y'Allah naka y'Allah kharé aldiana firdawsi ) dou y'Allah point! Y'Allah késsé mo doul am morrom! YALLAH MO YORE NGOUR, MO KOY DIOX KOUKO NÈKH,MOY FALL, MOY FOLI! Euppeul baxoul! Bismi Allahi alrrahmani alrraheemi 1-Qul Huwa Allāhu 'Aĥadun 2-Allāhu Aş-Şamadu 3-Lam Yalid Wa Lam Yūlad 4-Walam Yakun Lahu Kufūan 'Aĥadun Au nom d’Allah, le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux. 1. Dis: «Il est Allah, Unique. 2. Allah, Le Seul à être imploré pour ce que nous désirons. 3. Il n’a jamais engendré, n’a pas été engendré non plus. 4. Et nul n’est égal à Lui».
@kayouwone6085
@kayouwone6085 5 жыл бұрын
Serigne Ganna non plus n'a nommé personne, qui se sent morveux se mouche c'est tout
@ndeyecodougueye2436
@ndeyecodougueye2436 5 жыл бұрын
Kocc Barma manchalah
@mouhamedcoulibaly2370
@mouhamedcoulibaly2370 5 жыл бұрын
Yaw kocc li ngay wah yep ay fenn la yaw gnilay défendre loy nebou nan kocc barma fenn rec moka waral
@ballatoure1627
@ballatoure1627 5 жыл бұрын
Yaw kocc daguay doulll SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM FI AK FEULÉ BAMBA POINT
@elbachir999
@elbachir999 5 жыл бұрын
Macky n'a jamais gagné à Touba et pourtant il a été élu en 2012 et réélu en 2019. Nous mourides, nous devons refuser certains manipulateurs qui utilisent leur verbe pour se nourrir.
@labsolugueye9016
@labsolugueye9016 5 жыл бұрын
Serign touba kaineu la Liko yallah Daif koumou Naxarii Raikk Matall sa Bakann ma Guiss way serign touba kaineu la 🙏❤️🙏❤️🙏❤️🙏
@alibaba-js7cb
@alibaba-js7cb 5 жыл бұрын
yaw katal sa nday
@sakhnamayekabirboussalioul9633
@sakhnamayekabirboussalioul9633 5 жыл бұрын
@@alibaba-js7cb lola mèti serigne touba keunla bokou bagnè dèl dah s.bamba fèbou kon nak dèl
@sokhnadiakhatesoldaroubamb1178
@sokhnadiakhatesoldaroubamb1178 5 жыл бұрын
@@alibaba-js7cb yaw embésil nga
@amethniang4350
@amethniang4350 3 жыл бұрын
Mane dhe maa warou waa leigui s touba niko yalla deiff koumou nakhari kayy kou ame loyy wakh wakhane teiko ak yalla ndakh mo dadjalei ngeunell yeipou dieibeulko s touba
@myvision7647
@myvision7647 5 жыл бұрын
Dieuredieuf serigne touba. Messere yalla nala serigne touba faay
@djilykane4559
@djilykane4559 5 жыл бұрын
Bless up king
@myvision7647
@myvision7647 5 жыл бұрын
@@djilykane4559 serigne Djily kane ziarenala mouride
@mohamedoulndiaye7560
@mohamedoulndiaye7560 5 жыл бұрын
YALLA MOY FAY .YAWMAL QIYAM KOU NEK SA BOP NGAY TAL.YONENTI WAKH NAKA DOMOM FATIMA NEKA NA DIAMOU YALLAH .kene dou yakar koy nelew di lek di am dom di fatou
@bayserigne6044
@bayserigne6044 5 жыл бұрын
@@mohamedoulndiaye7560 waxi doff khamodine
@mygodguideustotherightpath5448
@mygodguideustotherightpath5448 5 жыл бұрын
MOHAMEDOUL NDIAYE billahi wakh nga deug
@seydinadaoud8014
@seydinadaoud8014 5 жыл бұрын
Serigne gana soula cheikhoul khadim fayé di nga kontane lolou inchallah jereujeufeuty
@ibrahimafall2390
@ibrahimafall2390 5 жыл бұрын
Borom touba ken la diarawlak cheikh ibra fall
@fatygueye8898
@fatygueye8898 5 жыл бұрын
bilakh serigne touba moy Ken té kuko kenal mu kenal la banga begg
@ibrahimandiaye7461
@ibrahimandiaye7461 5 жыл бұрын
Machallah... mbecté mi ma am deee barkeb Serigne Touba bou amoul wonnn rek ma rouss....nioune Serigne Touba rek laniou gueum beugue ko té yakar ko...Serigne gana yalla na yalla yok sak werr ak sa tawfekh barkeb Serigne touba.
@mameamysarr2392
@mameamysarr2392 5 жыл бұрын
Barkep Serigne touba gana yama nekh khol dal sed na tontou gualene . Sougnoub Serigne mofi nek dh s bamba rek
@aissatasarr7101
@aissatasarr7101 5 жыл бұрын
Théye Serigne gana méssré soldarou Serigne bii
@usmandia388
@usmandia388 5 жыл бұрын
Machallah amnasolo gana dam rikk inchallah
@camaradiaw10
@camaradiaw10 5 жыл бұрын
Machalla amnasoloe
@akhmadougueye829
@akhmadougueye829 5 жыл бұрын
Machala
@fallsaliou3773
@fallsaliou3773 5 жыл бұрын
Machalla
@akhmadougueye829
@akhmadougueye829 5 жыл бұрын
Machala
@hadimjaw1660
@hadimjaw1660 5 жыл бұрын
Jerejeff Borom Touba Mashallah Bamba rekk ❤❤❤🙏🙏🙏
@serignesalioundiaye1478
@serignesalioundiaye1478 5 жыл бұрын
Serigne gana messere yalla ngafi yague tei weir ❤
@jamilatraore7700
@jamilatraore7700 5 жыл бұрын
Amiiiiine
@serignesalioundiaye1478
@serignesalioundiaye1478 5 жыл бұрын
@@jamilatraore7700 ak beine dioulite
@fatoumatafall6549
@fatoumatafall6549 5 жыл бұрын
Franchement je suis très contente de Mr Gana dieureudief yalna yalla feyla vérité absolue
@sinylo3779
@sinylo3779 5 жыл бұрын
Nn ganna mann môme békk na thi yawe bilahi yall n’a yalla gou dale sa fann ❤️❤️😆😆😆😆😆😆
@abdoudiongue6423
@abdoudiongue6423 5 жыл бұрын
Maleu Mbegue kana diadieuf way doundal sante Serigne Touba rk 👌🏾❤️
@ndongali3540
@ndongali3540 5 жыл бұрын
Khawna imam nga khama ignane nga wayé soléne amone diom doléne dougou si mbirou mouride yi , gueum léne linguéne gueum té bayi niou ak kignou gueum yakar ko wolou ko mouy sounou lép témou diaral niou lép mouy Cheikh Ahmadou Bamba soudoul wone mom do togue fii SERIGNE Touba dafa siggil sa réw sigil afrique siggil l’islam , amoul bénéne deuk bouniouy dém Magali diko Ziare boudoul Macca ak Senegal Touba ,
@seydinaka1430
@seydinaka1430 5 жыл бұрын
Waw goor
@cheikhabdoubeye3073
@cheikhabdoubeye3073 5 жыл бұрын
Akassssa
@mgeagripreneur
@mgeagripreneur 5 жыл бұрын
Ngana mom warouta wax thi islam, ancien tailleur +am domou biireul kokou mandouwoul. Nulard qu'il est
@alfajrhijab8520
@alfajrhijab8520 5 жыл бұрын
yow seringe Touba nit semple la rek
@cheikhdaffe9944
@cheikhdaffe9944 5 жыл бұрын
Serigne Touba est un grand saint béni par Dieu mais seule Dieu qui choisit
@morsyll3909
@morsyll3909 5 жыл бұрын
Dieu a choisi khadimal mustafa (psl)
@madiodiondiaye1136
@madiodiondiaye1136 4 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne touba
@savezvous6816
@savezvous6816 5 жыл бұрын
Kou bégg may ma jaime
@chekhnecheikhelbou695
@chekhnecheikhelbou695 5 жыл бұрын
Cheikhna ahmedou bamba Allah lui à donne beaucoup de pouvoir il peut tout donne avec sa baraka vrai vrai vrai
@talladiop1168
@talladiop1168 5 жыл бұрын
😂 contanna loll Serigne ganna méséré yalnala Serigne Touba fay a part j'ai une question pour gni bagn li yalla dogal bane trophée gène meusa dieul
@BAMBISTETV
@BAMBISTETV 5 жыл бұрын
Trophée kinian nioko dieul 😂
@mariasant3937
@mariasant3937 5 жыл бұрын
Trophée ignane ak beuri wax
@talibeakhmadou9799
@talibeakhmadou9799 5 жыл бұрын
@@BAMBISTETV 🤣🤣
@sokhnazarafah7651
@sokhnazarafah7651 5 жыл бұрын
Khana chaque jour seine khol di gana bone
@dioufmamediarra4425
@dioufmamediarra4425 5 жыл бұрын
Trophée tardé khana di niakhtou rék nak😃😃😃
@gassmpaly
@gassmpaly 5 жыл бұрын
Alahira lep dina lerr Kén dou Mahmoudou rasouroullah (psl)
@dfsdioufy5847
@dfsdioufy5847 5 жыл бұрын
Gaoussou Koita S touba ak yonente bi bouro ak Soow la
@gassmpaly
@gassmpaly 5 жыл бұрын
@@dfsdioufy5847 dineu lerr
@layebousso3838
@layebousso3838 5 жыл бұрын
Man Mouridela, Mais Omar Sall à raison! Deug nékhoul dé! Sénegal Serigne mofi eup dolé que yonete yalla mouhamad ! Bokalébi Dafa Beuri Senegal.
@dioptapha4950
@dioptapha4950 5 жыл бұрын
do Mouride bayil sa nafekh yi l Islam lay wakh
@maguetteloum946
@maguetteloum946 5 жыл бұрын
Deugu da fa lérr nagnou,goumbeu teukh ak mouma mo am
@gayeameth5407
@gayeameth5407 5 жыл бұрын
Bien di
@gayeameth5407
@gayeameth5407 5 жыл бұрын
Diop Tapha yaw khamo dara
@Awa.C1
@Awa.C1 5 жыл бұрын
Toi tu as compris ce que voulais dire Oustaz Oumar Sall, il n’a jamais critiqué Serigne Touba au contraire , il parle du tawhid qui disparaît au Sénégal, attention au fanatisme !!!
@amathseynabouthiam1027
@amathseynabouthiam1027 5 жыл бұрын
Un jour un Sahaba est venu voir le prophète après avoir parlé il a dit s'il plaît à Dieu et vous et le prophète fus très en Colère et vous qu'est ce que vous faites faire appel à des personnes qui ne sont plus de ce monde pour qu'ils vous viennent en aide soyez raisonnable svp
@maymouna1802
@maymouna1802 5 жыл бұрын
Bilakhi walakhi fi yalla rek mofi nek
@amathseynabouthiam1027
@amathseynabouthiam1027 5 жыл бұрын
Tout à fait d'accord avec toi
@mamecheikhfaye5954
@mamecheikhfaye5954 5 жыл бұрын
Serigne Touba dou moromou kou yallah binde kouko bagne déélll. Gnoune Ahmadou RK guissou lénénn💓💓💓 Diaarama Mame Cheikh Ibrahima Fall❤❤❤
@senediegane1311
@senediegane1311 5 жыл бұрын
Serigne gana beugg nala waye
@amadoufallnokho4799
@amadoufallnokho4799 5 жыл бұрын
Barki Serigne Touba , Serigne Gana mane boumalay déglou sama khole day sedd Guouy machaallah Naniou nonguou lou Yalla dogual rekk.❤
@Madamefall351
@Madamefall351 5 жыл бұрын
Jërejëf Seringe Touba Amoul Morome ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@cheikhtidianebalde5571
@cheikhtidianebalde5571 5 жыл бұрын
Wallaahi je me rends encore plus compte de votre éloignement du droit chemin. Qu'Allah vous vienne en secours
@ybah9995
@ybah9995 5 жыл бұрын
Domeram topatool sa bopp imbécile sa khol day dagg dé ispice di conass.
@cheikhtidianebalde5571
@cheikhtidianebalde5571 5 жыл бұрын
Votre réponse est un indice de plus que vous êtes égarés. Les bien-guidés l'insultent pas.
@ibrahimatoure2762
@ibrahimatoure2762 5 жыл бұрын
Yaw daga rér bo délouwoul guina thi liga wakh diga am diafé diafé adouna ak alakhira
@cheikhtidianebalde5571
@cheikhtidianebalde5571 5 жыл бұрын
Diafé diafé adouna ak allaakhira bokkalé katt yi niokoy am
@khardiop4541
@khardiop4541 5 жыл бұрын
Eskey Djeureudieuf SERIGNE TOUBA🙏🏽❤️💖💃
@falloundiaye4677
@falloundiaye4677 5 жыл бұрын
Khar diop dieureudieuf seringue touba 👌👌❤❤❤
@falloundiaye4677
@falloundiaye4677 5 жыл бұрын
Khar diop dieureudieuf seringue touba rekk 👌👌❤❤💘
@papedjiby1354
@papedjiby1354 5 жыл бұрын
Macha'Allah Dieuredieufé Serigne Touba
@papamamadousene5951
@papamamadousene5951 5 жыл бұрын
Gana yalna nga goudd fann wayy manchallahh
@boussogueye7852
@boussogueye7852 5 жыл бұрын
bilaye ma yeureume kou khadiowoul Serigne touba.Fiere d'être mouride
@sunugaalsenegal7069
@sunugaalsenegal7069 5 жыл бұрын
bousso gueye machallah
@bayealassane8781
@bayealassane8781 5 жыл бұрын
DIEUREDIEUFÉ SERIGNE TOUBA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP BABOUL MOURIDINA
@adjithiam5337
@adjithiam5337 5 жыл бұрын
Dieuredieuf S Gana di na niou bayek S Touba de kou beugue mo fi nek kou bagnit mo fi nek ..nioune mome la niou gueune bou wessi Yallah ak yonentame ba..machalah te li mou fi def mi gui tegue Dieuredieuf Serigne Touba....
@bayefallgueyenobles888
@bayefallgueyenobles888 5 жыл бұрын
No ganna reyngama bama dead athia moridd❤🤣
@salioumbacke3380
@salioumbacke3380 5 жыл бұрын
Machalla.bécna yalla gafi yague
@bayetaphadiop5644
@bayetaphadiop5644 5 жыл бұрын
Ganna sounou la amoul woone y'a bakh ci kallass yii
@beugkhadimrassoulgayebeugk8076
@beugkhadimrassoulgayebeugk8076 5 жыл бұрын
Gneep laa raaay 🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂😂😂
@cheikhmbackediop9586
@cheikhmbackediop9586 5 жыл бұрын
Ndeyesane amena solo lol barké CHEIKH IBRA FALL ❤️❤️
@falloudiongue5857
@falloudiongue5857 5 жыл бұрын
Boy silonk
@cheikhmbackediop9586
@cheikhmbackediop9586 5 жыл бұрын
Mangi sante buwère et tw
@maimounasarr1417
@maimounasarr1417 5 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba da am nioumouy derangé
@morfall290
@morfall290 5 жыл бұрын
Machalla yal na yalla fayla
@senegalndiaye1878
@senegalndiaye1878 5 жыл бұрын
Serigne Touba Khadimou Rassoul mo dékal l'Islam = Dieu est unique.
@adamaly2230
@adamaly2230 5 жыл бұрын
J'aim Allah et le prophète mouhamed(sws) et ne croi qu'en eux wallahi Outaz oumar sall tu veu tjrs le bien de tt le monde :yalla nagnou yalla yeureum. Amine
@papeamadouwane9793
@papeamadouwane9793 5 жыл бұрын
Amine ya rabbi
@MouhamedBah-wc4so
@MouhamedBah-wc4so Жыл бұрын
Amine❤❤oumar salll❤❤je l'aime énormément 😊degeu rek ley wakh
@cheikhdiop1874
@cheikhdiop1874 5 жыл бұрын
Le bien fait n'est jamais perdu!!! Dieureudieufé borom touba
@talladioufallahuackbarryar5215
@talladioufallahuackbarryar5215 5 жыл бұрын
Ni yall deff serigne touba moleene nakhari waye Koné nakhar DINA Lene raye
@vivelapaix9407
@vivelapaix9407 5 жыл бұрын
😁 trop nakar.com//à vie Merci Bamba
@fatoudembathioune4698
@fatoudembathioune4698 5 жыл бұрын
talla diouf allahu ackbarr yaram dawna wakhatiko sougnou borom bo jeuk ni dieureudieuf serign touba bilay serign touba foumako wowe mou wouyouma jokho sama adouna ak alakhira bamba ma saff
@cheikhsambmbackediadiefler3195
@cheikhsambmbackediadiefler3195 5 жыл бұрын
Ni yalla def serigne touba molen nekhul waye thi aw nakhwr gen di deck bakhey dee reck
@amydiallo6219
@amydiallo6219 5 жыл бұрын
Yow seytané nga baho ci rew
@fatoudembathioune4698
@fatoudembathioune4698 5 жыл бұрын
amy diallo seytane diallo lay sant comm yaw dou sant thioune bamba kouko bagne dagay Gagnou rek boude lima wakh madef saytane moma nekh sokhnasi
@hawadiawara4001
@hawadiawara4001 5 жыл бұрын
Soubhanala ya Allah guide nous sur droit chemin
@ndeye7272
@ndeye7272 5 жыл бұрын
Hawa Diawara amine
@abdoukhadrewagne7388
@abdoukhadrewagne7388 5 жыл бұрын
Ay deméharamm ngennn rek wayé kou Tedd ki momm dingen ko teguékou
@presidentsonko2997
@presidentsonko2997 5 жыл бұрын
ay imbéciles la gnou ibandit yi
@boyedjine6811
@boyedjine6811 5 жыл бұрын
Hawa diawara droit chemin moye yonou serigne bi bayilene sene xele yi guene di fowé.serigne bi aye mbireum daye dioli rek mounou lene si touss
@dioplofficiel1013
@dioplofficiel1013 5 жыл бұрын
Hawa diawara retourne au Mali c est mieux pour toi
@elbambist1213
@elbambist1213 5 жыл бұрын
Oumar Sall dagnouko wara douma douma you métti kouci d'accord rk pouce bleu.Dieureudieuf Borom Touba
@oumarmendy1336
@oumarmendy1336 5 жыл бұрын
Bilahi walahi serigne touba mofi nek aduna ak alakhira
@maymouna1802
@maymouna1802 5 жыл бұрын
Yalla rek mofi nek borome beute bou rey bi
@deliciouspartyfood5784
@deliciouspartyfood5784 5 жыл бұрын
Oumar mendy ragalal Yalla
@maymouna1802
@maymouna1802 5 жыл бұрын
@@deliciouspartyfood5784 ki weroul Mane contre ma mouride di mais da ame gnou khamné dagni dieul Serigne Touba gnou teko plasou yalla soubkhana Serigne Touba santoulen ligen di def
@assanesane9690
@assanesane9690 5 жыл бұрын
@@maymouna1802 yoe sah yanguifi lane Serigne Touba ndah diouguenafi Sénégal dinegnkoy sante ba yomalhiyam amneu nio hamni seni mame kerok Tia banioulene soule lanioulene fate lolou moy doufi diogué amlene deg deg ishhhh te mandou
@maymouna1802
@maymouna1802 5 жыл бұрын
@@assanesane9690conseil mandou commencé ko sisa bop
@mamediarra1438
@mamediarra1438 5 жыл бұрын
Bilay dégueuleu dieureudieuf serigne touba omor dafa bone sokhor
@sollydiatta5307
@sollydiatta5307 5 жыл бұрын
Il faut dire la vérité la mort est devant nous
@abdoulahatgueye1441
@abdoulahatgueye1441 5 жыл бұрын
Soldat Serigne Touba, Boul ragal dra Kénn Doula téyé... Dieureudieufeuti SERIGNE TOUBA
@mignonemama4512
@mignonemama4512 5 жыл бұрын
Setou Serigne Touba dou moromm , Wakhoumalak SERIGNE TOUBA👈 Serigne Gana Messeré yagg fi lol té wéér way 👏👏
@fillesage2023
@fillesage2023 5 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba, diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall
@cisseaida9064
@cisseaida9064 5 жыл бұрын
Le coran et la sunna rèk mbiri da lėre nagne nous somme réveillé maintenant yalla ak yonentibi rėk tawhid rek
@bayserigne6044
@bayserigne6044 5 жыл бұрын
Wakon nekesi taga mando gurr yalla
@assanesane9690
@assanesane9690 5 жыл бұрын
Alhourane tawhid etcc Sénégal soko BG lerlou rek demal Touba
@diagnelerebelle9490
@diagnelerebelle9490 5 жыл бұрын
Am ga si droit neik leen si rekk ...Nioun niou and ak segne BAMBA❤❤
@malangseydi1947
@malangseydi1947 5 жыл бұрын
Vraiment
@khadimndiaye9132
@khadimndiaye9132 5 жыл бұрын
😜😜😜😜😜😀
@seidousow8986
@seidousow8986 5 жыл бұрын
Tres bien segne ganna messeré. Contanena dé. Billahi
@ramiadiop210
@ramiadiop210 5 жыл бұрын
La bataille de badr on l'avait remporté non pas par un nombre important de croyants mais par une minorité de croyants sincère et qui ont été secouru par Allah qui les avait envoyé ses anges pour la remporter. Donc molouguou beuri takhoul nga nek thi deugue . Limay ragal moy beuss pentch serigne touba dal thi yén yi di tal radio yi di dém rék gratuitement "Le jour où ceux qu'ils associés en dehors de moi les désavouront" y'ALLAH nopina wakh djé fi nék. Wa salam
@roserouge2497
@roserouge2497 5 жыл бұрын
Louniou nioune la rk donc mandou lene
@asb6234
@asb6234 5 жыл бұрын
Rose manou koumou war moy ki amoul kaddou rew bi nio si bok sou nieup manou wone kéne d'où votel kéneuh
@roserouge2497
@roserouge2497 5 жыл бұрын
@@asb6234 mdrrr wakhou doff mandou si diamou yallah la bokk laissez nous tranquille
@Topofthetopapex
@Topofthetopapex 5 жыл бұрын
Quand ce bass a dit ça j’étais sidérée ! Yalla moy fallé moy folli ! Teh fi niata makk nio fi diaar nguen beug dieul lepp akimo ko di raconter du n’importe quoi! Pour yene daal yalla Senegal la deukk walla sene serigne mo gueune yonnent bi des fois même nguen tek ko place yalla ! Li mom dou islam ! Legui daaal ay imam molene dessei? Imam deh mo gueuneu legitime aux yeux de l’Islam que Bepp nit bolene yakar! Les imams nioy representer islam ci kaw souf bo yoroul tampon bon bobou ci guinaw imam rek ngay meusseu nekk. Wakhal say mam kone niom nio defoul darra nakh nioune kham naniou niane nioy souniouy mame teh kham naniou louniou def. Li say mame defoul darra motakh nga tok fi nekk soukkou !
@fatimazahrachannel6404
@fatimazahrachannel6404 5 жыл бұрын
Il ment et il sait qu'il ment. Il est deplorable tout .ca pour justifier le bokale de son serigne. Ndeysan esclave et ignorant comme un vrai mouride
@malicklo4613
@malicklo4613 5 жыл бұрын
Ioe katal ndm sissou mane gua fii serigne touba mofii nk amoul morom
@malicklo4613
@malicklo4613 5 жыл бұрын
@@fatimazahrachannel6404 yeineu ay seytaneii gueineu ak sen toubay you gate you ñiaff ndm yoyou
@adamdiop9312
@adamdiop9312 5 жыл бұрын
Yaw waroulo wax thi dinné
@Topofthetopapex
@Topofthetopapex 5 жыл бұрын
musulmane musulmane de ouf il sait qu’il ment mais khaliss rek ak niémé yalla! Bene ins ni douniou am louniouy wakh niouy créer rek !
@petitdieye1946
@petitdieye1946 5 жыл бұрын
Tu dit des choses pour remplir ta poche mais Serigne Touba dit le contraire de ce que tu dit arrêter de dénigré les autres walious
@talibetv2371
@talibetv2371 5 жыл бұрын
Yaw waxal li s bi wax limoufi wax siy bayit s Touba moko wax sokhar nga lol demal diangui avant ngaye juger
@galsentoon9178
@galsentoon9178 5 жыл бұрын
@@talibetv2371 serigne Touba Touba amoul morom
@laminediengarchitecteetdes96
@laminediengarchitecteetdes96 5 жыл бұрын
@@talibetv2371 ki dh djaroul wone tontou boudei mo geuneu kham wakhi serigne bi que gana messere....
@cheikhounaseye313
@cheikhounaseye313 5 жыл бұрын
PETIT DIEYE bouma Takha wakh loulaye Dioyelo Tèsaye Ragogne Doumousse Feeerr Sèni khol mo lendeme amoul bène togkou thi lèrr bou dhè Daga Bogkou Fènene Bayile Ndialoby Tè Agssi thi Dinè plus gui KÈNE DOU AHMADOU Wsyè Bamba DOU kou Dioug rèck Donne Mouride rèck dhè
@adamafall6915
@adamafall6915 4 жыл бұрын
Fiers d'être mourides
@ibousow4258
@ibousow4258 5 жыл бұрын
Dieuredieuffe Serigne touba boudée possone yalla nagnou rayyyy ti amo ❤️ mane bamba❤️❤️👌👌👌
@modouundjiliw6670
@modouundjiliw6670 5 жыл бұрын
je deviens mouride maintena......
@fatoudioufmouserignefallou2709
@fatoudioufmouserignefallou2709 5 жыл бұрын
machalla
@sofafabeauty3380
@sofafabeauty3380 5 жыл бұрын
Bilay tu l regrette pas
@khadidiatoufall9615
@khadidiatoufall9615 5 жыл бұрын
Doko massa réthiou si adouna 👌🏾❤️
@dianguetawhid9101
@dianguetawhid9101 5 жыл бұрын
T'as toujours été mouride, boul leuré gaaayi
@BAMBA634
@BAMBA634 5 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba khadimou rassol
@abdoukhadrendiaye7370
@abdoukhadrendiaye7370 5 жыл бұрын
Merci bcp Ser Gana vraiment on est très contant mais serigne Touba rek moh nékk sounou khol yiiiie Ser. Touba yalla force♥️♥️
@fakebae2748
@fakebae2748 5 жыл бұрын
Bamba la solution ❤️
@zekmubala6113
@zekmubala6113 5 жыл бұрын
Michaela gana🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@abdoudieng9480
@abdoudieng9480 5 жыл бұрын
BAMBA n'est plus une solution c'est le résultat final
@fakebae2748
@fakebae2748 5 жыл бұрын
Abdou Dieng kon bamba le résultat final machalla ❤️
@basidiahmed4623
@basidiahmed4623 5 жыл бұрын
Li amoul (Tidiane) amoul (mourid) niepp warnaniou kontaan si vidéo bi 😃. Saram dnay borom tuba yi gattayi te khasan . Merci 😊 pour cette vidéo la
@gop7604
@gop7604 5 жыл бұрын
Diaroul saaga nakk wakh deugg
@Boythiamfitness.
@Boythiamfitness. 5 жыл бұрын
Yaw rew ga dh
@basidiahmed4623
@basidiahmed4623 5 жыл бұрын
abdou thian Dur raiw sah Duiniu nangu kuniu yap aq suniu aqiida .
@rainks5461
@rainks5461 5 жыл бұрын
Je suis un mouride mais je suis Contre de ces propos. Car un mouride doit etre humble et respecte des autres, meme s' ils nous critique.
@cheikhdieng8898
@cheikhdieng8898 3 жыл бұрын
Way doull mounane je suis mouride
@bestcutbeauteplusparis4575
@bestcutbeauteplusparis4575 5 жыл бұрын
merci messieurs que dieux te protège longue vie bonne santé beaucoup de bonheur avec te ta famille voilà bonne
@mouhametbadji864
@mouhametbadji864 5 жыл бұрын
Dieuredieuf serigne Touba diarama Serigne Ganna
@mariamasow3970
@mariamasow3970 5 жыл бұрын
DIEUREDIEUFÉ SERIGNE BAMBA SUNU YAKAR TEY AK EULEUK MOME RÉK MO DÉMONE BAMOY MÉTI
@alibaba-js7cb
@alibaba-js7cb 5 жыл бұрын
katal sa nday
@mignonemama4512
@mignonemama4512 5 жыл бұрын
@@alibaba-js7cb SA travail de maman la mo takh gua réwww
@alibaba-js7cb
@alibaba-js7cb 5 жыл бұрын
@@mignonemama4512 yaw doul way
@chekhnecheikhelbou695
@chekhnecheikhelbou695 5 жыл бұрын
Salamou allaykoum cheikh vraiment se que vous venez de nous c'est vrai vrai vrai cheikh ahmedou bamba nous appris à suivre Allah et sont prophètes Mohamed psl et il à travailler que pour Allah et sont prophètes Mohamed psl
@kenalserignetouba6356
@kenalserignetouba6356 5 жыл бұрын
ah serigne touba yalla sante nako gueureum ko yonéne tébi(PSL) sante ko gueureum ko kouko bagne bagne nga yalla bagne nga yonéne tébi(PSL)té boy diamou yalla douko nangou thie atoum 1895 mame bamba rék mofi taxaw diayane ték toubab bi ba 1902 di 7ans et démis kéne dou moom liko yalla défal amoul kéne kouko am mouy nékh ak mouy nakhari segne bamba moniou moom fare force
@alibaba-js7cb
@alibaba-js7cb 5 жыл бұрын
ya mana féne yalla moy santt niit ya katt sa nday kane moy serigne touba
@kenalserignetouba6356
@kenalserignetouba6356 5 жыл бұрын
aliba ba amal respect si domou adama lima méti si yéne rék moy séne diamou yalla gui fiii rék lay yam thie adouna ndah yalla douko nangou ndah ignane nguéne déf mane balnala si xol bou sédd gouy démal nga diangui yiw bou beuri rawnala
@nancydiop8109
@nancydiop8109 5 жыл бұрын
Niaff!!! dotouko deffatii🤐wayye mane gana la beugue ❤aka panke 👏👏👏
Magal Touba dou Ndiguel Serigne Touba wooté wouko - Serigne Gana Répond Cheikh mbacke Sakho
13:19
How Strong Is Tape?
00:24
Stokes Twins
Рет қаралды 28 МЛН
How Many Balloons To Make A Store Fly?
00:22
MrBeast
Рет қаралды 195 МЛН
Regardez Dame Mbodj humilie Barthélemy Diaz en direct 😭
23:27
Diégo l’Espoir
Рет қаралды 6 М.
Professeur Abdoulaye Dieye Corrige TekkiForLife!!!
14:25
XIFF XALIS DISCIPLINES
Рет қаралды 11 М.
URGENT🚨 VAR Ahmed Cisse Thieuy Mom midone teukou Serigne Gana méséré xolal famou mudiou
4:19
TAWFEKH PRODUCTION INTERNATIONAL HD
Рет қаралды 177 М.
serigne gana messere wakhtane serigne touba kaolack
54:20
serigne touba tv
Рет қаралды 52 М.
How Strong Is Tape?
00:24
Stokes Twins
Рет қаралды 28 МЛН