Jongante - Signature Contrat Ada Fass vs Lac 2 - Les premiers mots entre les deux lutteurs

  Рет қаралды 158,092

TFM (Télé Futurs Medias)

TFM (Télé Futurs Medias)

Күн бұрын

Пікірлер: 378
@cheikhnalhommesolution4577
@cheikhnalhommesolution4577 Ай бұрын
Une face à face très discipliné avec des paroles très doux
@issagueye9656
@issagueye9656 Ай бұрын
Li sport de combat la ça ne doit pas être doux
@SsidyGiaye
@SsidyGiaye 23 күн бұрын
😊​@@issagueye9656
@Sarrbinta10
@Sarrbinta10 Ай бұрын
Ils sont tous les 2 polis machallah.Yarou ngéne, téyy ngéne, franchement..Je vous aime❤ Grand Lac et Grand Ada
@LibasseBa-c6u
@LibasseBa-c6u Ай бұрын
Ada fass ndam rek inshalla ❤❤❤❤👍👍👍👍💪💪💪💪💪
@GoraMbengue-f2j
@GoraMbengue-f2j Ай бұрын
Lac so diappoul boy bi nokkou ko comme khalé daane ko niou guéné leuh Guédiawaye.
@papahabibdiop
@papahabibdiop Ай бұрын
Khana😂😂😂
@njaxboy7924
@njaxboy7924 Ай бұрын
Lac amneuh dolé mais amoul technique
@bbcheikh3364
@bbcheikh3364 Ай бұрын
Guediawaye amoul mbeur bou meun dann ada😂
@abdoulayecissegueye7952
@abdoulayecissegueye7952 Ай бұрын
Gayn lac beurè woul ak domam deh li nga bind yomb n’a torop
@Ndiambour-ndiambour21
@Ndiambour-ndiambour21 Ай бұрын
Ada vs thiatou daouda fall rek day metti say​@@bbcheikh3364
@aldianaaynii4705
@aldianaaynii4705 Ай бұрын
Ada Yâ Allah Mayla ndam in sha Allah depuis guediawaay 🤍
@FadalMouhamed-j5u
@FadalMouhamed-j5u Ай бұрын
Ada fass dafa game bopome bilaye ndame rek🤲👂✍️
@GORADIACK-ew9dg
@GORADIACK-ew9dg Ай бұрын
Temps yii khotékou moo khéw quoi cey Modou✅💥
@ebrimajoof2211
@ebrimajoof2211 Ай бұрын
Ada fass yalna yalla mey la ndam
@NdongoSamb-f4d
@NdongoSamb-f4d Ай бұрын
Ada fass man mome la misbah kara fall moutakh ma beuge la ndame Rék inchallah
@taphadieng3615
@taphadieng3615 Ай бұрын
Yénagui wakh rk mai ada dina beth niou bari bi dou yoyu dh xalei la amna dolé🎉
@nlaye
@nlaye Ай бұрын
combat djèlmane 😂nék léne ay nite té ngéne dioub 😂
@julescisse3431
@julescisse3431 Ай бұрын
Mane d'accord naa si DRAPEAU DE TOUS LES DÉTENUS DU SÉNÉGAL DONC KOUSSI D'ACCORD BESSEUL JAIME❤
@abloslimshady
@abloslimshady Ай бұрын
Yaw do khalatt bala nga wax, detenu am na niou si violé nioussi ray nioussi sathie, même bou amé gnoun si toumal mais il y aussi des criminels là-bas frère! Vous être trop émotif au point de ne pas reflechir!
@wara2043
@wara2043 Ай бұрын
Ken d'accord rouci il n'ont qu'à purger leurs peines et assumer leurs actes.
@abloslimshady
@abloslimshady Ай бұрын
@@wara2043 Merci! Lamn gnomù dagno fogni ils sont au dessus de la loi! Dagnouy def sen tokhidona ba paré di niane ndiek ! dafa yomb!
@wara2043
@wara2043 Ай бұрын
@@abloslimshady même grâce présidentielle togne la, car le président qui gracie ces détenus n'est pas le victime, mais c'est d'autres personnes à qui on demande même pas leur avis par courrier adressé ou téléphone qui ont subi du tort. C'est trop facile de libérer comme ça des gens fautifs, il faut qu'ils assument leur décision de nuire à autrui jusqu'au bout. Kou ray boumou guénati, kou violé 10 ans ferme ou plus, kou satie 5 ans ou plus. Tekci liguay par force pour être nourris en prison par exemple balayer les rues de la capitale la nuit sous haute surveillance avec l'armée qui dort dans les camps. Comme ça kou nek dina kham fimouy tek ay tankam
@OumarBa-z3f
@OumarBa-z3f Ай бұрын
Lamine moytoul français bii rek
@mouhamedlaminethiam4404
@mouhamedlaminethiam4404 Ай бұрын
😂😂😂
@mansourfall1947
@mansourfall1947 Ай бұрын
Mbadou
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 Ай бұрын
😂😂😂😂😂
@GalassFall-kr9cv
@GalassFall-kr9cv Ай бұрын
Deugueur fitt la def ki😂
@JeromeAhmadouSy
@JeromeAhmadouSy Ай бұрын
Nguire yallah reek
@JuniorManga-z9y
@JuniorManga-z9y Ай бұрын
Lamb diélmane😅😅😅 la ms waroul yagu ak boy bi
@lassanatalla767
@lassanatalla767 Ай бұрын
Mane Magui dogua geume ni lac Eumeu séne dagno ragal franc no meuna bagné franc dem dieul ada fass 😂😂😂 non ama balde vrai gore yalla la
@dametime4803
@dametime4803 Ай бұрын
Bly
@malickdiop4352
@malickdiop4352 Ай бұрын
Beug lou yomb rek
@FallBaye-gd9lf
@FallBaye-gd9lf Ай бұрын
Saway iniane bakhoule lamb nekoule legui nekatoule lingaye wakhni lamb legui thiowla ada da nek thii aye goudime
@doffdouweer3686
@doffdouweer3686 Ай бұрын
AY TAPETT LAGNOU AK SOKHOR
@galsenconso5214
@galsenconso5214 Ай бұрын
Lou lerr nga wah .0 faute
@metjobrek
@metjobrek Ай бұрын
Lac2 défal très attention si combat bi lo paré khébko..yagui dora am boy bou sobb meunn guéw torooop ...attention dhé
@MamadoualphaDiallo-ey5zw
@MamadoualphaDiallo-ey5zw Ай бұрын
Boybi doudarra
@SouleymaneBah-nr4tk
@SouleymaneBah-nr4tk Ай бұрын
Ada fass seul ndam rek inchallah
@PayoussouSakho
@PayoussouSakho Ай бұрын
Lamb amatoul ndiarigne bilay walay tu ne peux pas imaginer Ada fass zarco doumako dane ko gnoukay pousse diko diokh ay mbeur you nekhei dane gouye gui Zoss etc gnognou dougn mbeur kiii Queench moko gueneu rampé fouff eupeu ko Mballo dah ko barré lamb dji Diara toule yon
@manianendoye3091
@manianendoye3091 Ай бұрын
Mais Quench Réussiroul Examen biii Alioune Dako door mou doneee facilement 🤝
@boubacardiop-ue3kc
@boubacardiop-ue3kc Ай бұрын
Ada yallah dako may, gnou gnanal ko rek mou gueuneu dieum kanam champion la 👏🏾👏🏾
@papipapi344
@papipapi344 Ай бұрын
Quench fane la euppé mbolo Ada fass
@Tirera19
@Tirera19 Ай бұрын
Mais zarko gris bordeaux la ame te mom mo waron beurré ak lac far mou dém prison après mou dém dieuli gris ndakh zarko dou Khar ! Mais ada mom kokoy diokh Kenen
@souleymanedieng959
@souleymanedieng959 Ай бұрын
Vous avez raison
@papelo8737
@papelo8737 Ай бұрын
Ada fass vainqueur 🎊
@TallaTalla-p3j
@TallaTalla-p3j Ай бұрын
Abdoulaye Ndiaye wagnil wahdiy vrema kouneke sawerseg ngay lek adouna amoulo solo ngenni gnanal Gaston yalnako yalla yerem
@papeabdoulayendiaye3784
@papeabdoulayendiaye3784 Ай бұрын
Lac 2 am nga combat dh bilahi😂🎉❤
@abdouazizthiaw3491
@abdouazizthiaw3491 Ай бұрын
Waouw Makane.xana.amo ab laafa wallah ménéen mbaxana. Solo nii tékk ci cap..yaax nga tuwalette bi. Wandé légi bari nga ci ay morom yu koy déff. Faute de coline
@bayemodoufalldiop6816
@bayemodoufalldiop6816 Ай бұрын
Bouniou waxanté deug RK ada meunaloul daraa lac2..
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 Ай бұрын
guissouma ndamam déh wayé lac meun'na nieuw nul déh ak boy bi
@beugfallou2853
@beugfallou2853 Ай бұрын
AK yakar nako d
@ndiameseye3283
@ndiameseye3283 Ай бұрын
Lac bou nulé Ak ki na bayi beuré daanou mom sagnouko sakh
@veritesavoir5415
@veritesavoir5415 Ай бұрын
Wayé lac douko daane dh ndakh dou dieul béne responsabilité
@moussa1257
@moussa1257 Ай бұрын
Ada ndam rk❤❤🇸🇳
@papeabdoulayendiaye3784
@papeabdoulayendiaye3784 Ай бұрын
Ada Seul🎉❤
@ibrahimandiaye9319
@ibrahimandiaye9319 Ай бұрын
Lac déy weurr lou noy mais boy bi khér la dhé té mbeur Kamil la
@ibrahimadiagne4935
@ibrahimadiagne4935 Ай бұрын
Danko dieule Balla
@morniang6391
@morniang6391 Ай бұрын
Combat diell mane yi 😮😮ada fass vs lac 2
@MamadouDiop-t3r
@MamadouDiop-t3r Ай бұрын
😂😂😂🤣srx woo
@khardiatouamadoukane6785
@khardiatouamadoukane6785 Ай бұрын
😂😂😂😂😂
@souleymanethior2775
@souleymanethior2775 Ай бұрын
😂😂😂😂
@serignemakhtardiop4098
@serignemakhtardiop4098 Ай бұрын
Drapeau rebeuss 🙏
@AdamaMballo-t9s
@AdamaMballo-t9s Ай бұрын
Amiiine et bonne chance lac 2 Macha allah entre duo makan Abdoulahad
@mamepathe4618
@mamepathe4618 Ай бұрын
Aaaaaaadaaaaaaa Faaaaaaasssss Touuuuy❤❤❤❤❤
@PapeSambaGuissé-w2h
@PapeSambaGuissé-w2h Ай бұрын
Ada fass seul ❤❤❤❤❤❤ 😢😢😢
@AboubacryGASSAMA-zs7oi
@AboubacryGASSAMA-zs7oi Ай бұрын
Léne dhé hamenako noumou meunttii démé combat lac dou danou insha alla tés ada fass 100combat dou ame dara. Kou menoul dane zarko foye diare lac 2 .ada paréguoul sakh pour douguou si vip yii .amena yénéne champion you guene prouver foufe que ada fass .no mes lamb légui amal mbolo rék 😅😅😅lamb business la légui mes,dou palmarès
@Abdoukhadrediouf-ov3zy
@Abdoukhadrediouf-ov3zy Ай бұрын
Meilleur commentaire
@moussa1257
@moussa1257 Ай бұрын
Fass seull❤❤❤❤❤❤
@DiahrawBaldeh
@DiahrawBaldeh Ай бұрын
Ndakarou seul ❤❤❤
@aliounengaido2172
@aliounengaido2172 Ай бұрын
La lutte c’est du n’importe quoi maintenant. Des lutteurs comme Ada fass et Siteu qui n’ont encore rien prouvé dans l’arène, se retrouve avec de grands combats.
@RacineLy-v2j
@RacineLy-v2j Ай бұрын
Ada fass bagnoumala dé bilay c'est que bayil soirée yi nk djeuleul Modou lo exemple quoi yalla nalla yalla may ndam
@BamsMvk
@BamsMvk Ай бұрын
Ndakarou seul ❤🎉❤❤❤🎉
@MbayeyoussouBayeYoussouMbaye
@MbayeyoussouBayeYoussouMbaye Ай бұрын
Aziz Ndiaye kou bon la bilay ❤
@emiledione3236
@emiledione3236 Ай бұрын
Lac tapete gua fi gua daw reug reug daw frans waro sakh Wakh
@kinesene6168
@kinesene6168 Ай бұрын
Ada seull❤❤
@nblbasse7914
@nblbasse7914 Ай бұрын
Drapeau détenus mbeur yi😅😅😅😅
@lecitoyentv2022
@lecitoyentv2022 Ай бұрын
Kou guiss dalli pére Aly yi rek lalal jaime
@mameousmanedeme6895
@mameousmanedeme6895 Ай бұрын
Kouy rassou ndoumi daano té par la force ada fass da Nay daan
@ndiameseye3283
@ndiameseye3283 Ай бұрын
Bilahi li dou Combat ki fan lay diar lac de guer lamb li moko yakh légui lac a d'autre adversaire diokhone Ko Serigne Ndiaye sakh mo gueune boy bi méritéwoul combat bi way
@sambamatuidi2378
@sambamatuidi2378 Ай бұрын
Ada ndakarou 🎉❤
@aablayesy409
@aablayesy409 Ай бұрын
Siteu seul❤❤
@PierreGanaDiouf-g8t
@PierreGanaDiouf-g8t Ай бұрын
Bagne fran dieul Ada fass
@hamadykante9664
@hamadykante9664 Ай бұрын
Lac2 bayil Modou miguay topando 😂😂😂mounan khotékou nnou
@yamjallow3586
@yamjallow3586 Ай бұрын
Khotekou boy nyang moko wakh hon Modou lowe d…. Kon Modou tamit dai topo ndor
@abloslimshady
@abloslimshady Ай бұрын
gayi Père ali bouy nieuw tchi plateau bi khol lenn loumouy soll, kilifeu leu, kholal dall thiarakh yii rek, li rafetoul thi kilifeu!
@Elhadjinoreyni11
@Elhadjinoreyni11 Ай бұрын
Sou concentréwo ci lamb respectéko nimou waré louné mane na ko thi am mane na sakh nékk roi des arènes inchallah mome ada fass
@BilalMbodj-x9i
@BilalMbodj-x9i Ай бұрын
Sénégal yeup kham ada fass yaroul ganan Dafa yarou
@ousmanendoye5926
@ousmanendoye5926 Ай бұрын
Ada fass seull ❤❤❤
@Moretallandiaye-y6m
@Moretallandiaye-y6m Ай бұрын
❤❤❤❤
@CaramocoDiallo
@CaramocoDiallo Ай бұрын
Ada fass yalla na ame ndam medina fass laî foral ci lamb mais écrit soumboudioune laa farrrr diene kaîre' boul nalaw
@moussa1257
@moussa1257 Ай бұрын
Lac 2 dangay danou
@TraoreHarouna-cd6oc
@TraoreHarouna-cd6oc Ай бұрын
Sa bay sou danouwoulwoon do dioudou🚶🏾‍♂️
@ModouDiagne-l1u
@ModouDiagne-l1u Ай бұрын
😂😂😂😂​@@TraoreHarouna-cd6oc
@OusmaneFall-s4p
@OusmaneFall-s4p Ай бұрын
Foko tek
@banlieuzar2564
@banlieuzar2564 Ай бұрын
​@@TraoreHarouna-cd6ocmais ki khalatam rék la wakh té amnasi droit mais vraiment sa wakhdji niawna
@MamadouDiao-hv4db
@MamadouDiao-hv4db Ай бұрын
AK thionno togg dii setann ngay arrière 😅😅
@Omzo__Velli
@Omzo__Velli Ай бұрын
😂😂 surtout Lolou SONN nagn si défendre bii
@aliounediop8220
@aliounediop8220 Ай бұрын
Soko dané ladieu siteu Ada kessé
@MouhamedDiop-z9t
@MouhamedDiop-z9t Ай бұрын
Ada nakarou seul ❤🎉
@amadousouleyetandine931
@amadousouleyetandine931 Ай бұрын
Boy Niang 2 enchaîner lac2 ay action mais dara, Ada Fass ki yomboul daane deh .
@Lilkheuchfrombomakingbii
@Lilkheuchfrombomakingbii Ай бұрын
Lack da fan adda fass❤
@mameboussombaye9159
@mameboussombaye9159 Ай бұрын
Bilay Ada fasse dinaku jomlo danku
@P4t5R
@P4t5R Ай бұрын
Drapeau Wa reubeuss
@LeyeMbacke-b9g
@LeyeMbacke-b9g Ай бұрын
Ada fass geum geum lay wakhé day daw rék 👌👌
@ibrahimaibrahima6448
@ibrahimaibrahima6448 Ай бұрын
Temyi dafa mélni khotékou dafa khéw dh,Molou tmt néna mo gueuneu khotékou Siteu 😅😅😅
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 Ай бұрын
Si Modou lo leu loumou wakh gayi topandoko😅😅😅😅
@mohamedsene2076
@mohamedsene2076 Ай бұрын
Legui naa niouma wakh ndak Ada fass warna beuré ak Lac? Lamb dou logique , mais plutôt popularité
@djibrilgueye373
@djibrilgueye373 Ай бұрын
Libérez lat diop
@OuseynouThiam-l7j
@OuseynouThiam-l7j Ай бұрын
Lamboudji amoul yone légui amal suportaite rk Franc zarko gnio gueneu mérité combat bii mais lou noy rk lagnie weurr 😊
@MmeSaliouNdiaye
@MmeSaliouNdiaye Ай бұрын
Lamine samba chaque émission niou torokhalko
@SaliousarrSaliou
@SaliousarrSaliou Ай бұрын
Ada Ndakarou seule
@alouguy5991
@alouguy5991 Ай бұрын
LAC LE GRAND CHAMPION ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@morgueye3939
@morgueye3939 Ай бұрын
😂😂 niarii sathe nioye beué😅😅
@aissatouniang2138
@aissatouniang2138 Ай бұрын
Ay thiarakhou douche la gisse ada fass sole😂😂😂
@malikking4291
@malikking4291 Ай бұрын
Boy bi jambaar la mais vraiment dagn koye outal yone
@papahabibdiop
@papahabibdiop Ай бұрын
Lac komm danoul nday siteu dou dann kén liguay entréné loum lay diarign ndm😂😭😔
@Science-z5w
@Science-z5w Ай бұрын
Ada Lac dafa diss deh 😂
@alhousseynoudiallo6054
@alhousseynoudiallo6054 Ай бұрын
Bilahi ada manil si lac 2 dara
@Ndiemendoye443
@Ndiemendoye443 Ай бұрын
Lamine samba kou bary wakh nga bilay walay 😂😂
@Fmymind
@Fmymind Ай бұрын
Lac roukh nga wakho deug 😢
@papesarr6331
@papesarr6331 Ай бұрын
Chambre 35 kiladone Defaral T-shirts yi déko nouyou sakhe au moins iow amo koloré Dara iow lac.
@biramafall1521
@biramafall1521 Ай бұрын
Pourtant nouyouna gneup
@dioufmouhamed8503
@dioufmouhamed8503 Ай бұрын
Kou lim dioum yawit meyko lolou xel matoul
@moustaphaseck1825
@moustaphaseck1825 Ай бұрын
Dou dole dou bare dou galathi
@FallouDiop-k4j
@FallouDiop-k4j Ай бұрын
Serigne mor iao fo far serigne day yam si mbeuram lambe dafa fiir ngay thiou di thiaaa ada mola wara baye
@bayesambakane2109
@bayesambakane2109 Ай бұрын
Lima Diakhal Lac 2 Tapètt Bou Nga Ndèlla Bilahi
@adamadiouf487
@adamadiouf487 Ай бұрын
Lac 2 nguay wakh tappett Kou nokheu siteu khékh ak Modou lac dou Sama mbeur d mais Aka âme dolè âme mystique ba parè dafa sokhor
@bacarysane8551
@bacarysane8551 Ай бұрын
Machalah lac 2 ❤️
@beuguesalioubeuguesaliou524
@beuguesalioubeuguesaliou524 Ай бұрын
Makane ak lakhat legui séne wakhe yeup guarouwalé la
@babacarsarr1131
@babacarsarr1131 Ай бұрын
Lac nak sou moussei moy nekeu mbeur Gaston production diay combat bi defaral boy bi bagass pour meune diot ci 👑 bi
@PapaThiam-pm8ss
@PapaThiam-pm8ss Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MouhamedBa-lc6sy
@MouhamedBa-lc6sy Ай бұрын
Lac meunoul kéneu
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 Ай бұрын
😅😅😅😅lac2 aka fans kharagne lo néna dina liguéye ba khotékou 😅😅lolou gnoko mom mais yallanala yalla défal ndame❤❤❤kou beugue modou gnou beugue le
@faye6718
@faye6718 Ай бұрын
Lamine samba mounoul Signature déffa oupeul
@SenyFaye-i4j
@SenyFaye-i4j Ай бұрын
Ada warro wone dieul combat bii amo expérience bou dane lac 2 😢
@TaphaDiongue-gj8mo
@TaphaDiongue-gj8mo Ай бұрын
Diam si iow ada fass yalnako yala samou are la sa maye la ndam
@babacartine4464
@babacartine4464 Ай бұрын
Lamine samba y’a barri wakh sheutt
@ndongobouQuench
@ndongobouQuench Ай бұрын
Li dou combat 😂😂😂
@mamediarrafall7598
@mamediarrafall7598 Ай бұрын
Lamb yakouna
@ababacarkandji
@ababacarkandji Ай бұрын
Ada fasse beugeu nla trop mais yalla da dogal guay beure ak sma mbeur
@moustaphasonko596
@moustaphasonko596 Ай бұрын
Nooon Lac 2 mo néex rek bagna dieul Reug Reug ak Franc dém dieul boy bi Lou yomb kéeni weur Kw bala may dh rek kéen nann daffa yarou fii kéen doulén néexal
@fakalou631
@fakalou631 Ай бұрын
Xana combat bi drapeau 100m leu (Rebeuss leu)
@elhadjindiaye7089
@elhadjindiaye7089 Ай бұрын
Lac dou tous bayi fi faren diel ada nooooo😂
@SeydinamouhamedmassNgom
@SeydinamouhamedmassNgom 14 күн бұрын
Lac néna Thiow dîna amati sacré siteu 3😂😂😂 wakh rekk ,,guénal guediawaye😂😂 ahh y’a niou tardél
Revue de presse Ahmed Aïdara du Jeudi 12 Décembre 2024
8:25
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 4,6 М.
Как Я Брата ОБМАНУЛ (смешное видео, прикол, юмор, поржать)
00:59
🚨 🚨 TFM LIVE :  Infos Matin  - Pr : Sokhna Natta Mbaye  - 12 Décembre 2024
1:14:15
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 8 М.
🚨 🚨 TFM LIVE :  Infos Matin  - Pr : Sokhna Natta Mbaye  - 12 Décembre 2024
1:01:06
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 8 М.