KADDUY LEERAL PAR SERIGNE AHMADOU MBACKÉ DAROU MOUHTY

  Рет қаралды 16,293

Touba visuel tv

Touba visuel tv

Күн бұрын

Пікірлер
@ModouBeye-sn4dk
@ModouBeye-sn4dk 3 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba khadim rasoul جزك الله حيرا الشيخ احمد باكي
@ModouBeye-sn4dk
@ModouBeye-sn4dk 3 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne akhmadou mbacke ci leral yi yala nanou yala Khir ci lou bakh inch'Allah
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye 3 ай бұрын
Dieureudieufé CHEIKHOUNA AHMADAL KHADIM RTA !
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye 3 ай бұрын
Allahouma Salli Hala SEYDINA MOUHÀMADINE WA HALA ALY SEYDINA MOUHÀMADINE WA !
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye 3 ай бұрын
AlhamdouliLAHI RABBAL ALAMINE Amine !
@khadimseck5379
@khadimseck5379 3 ай бұрын
Andona mo am problème wayié ñion ñii buegue lo bakh don masa wéddi ❤incalaha barkeb cheikh ahmadou bamba
@mbackeleye4264
@mbackeleye4264 3 ай бұрын
MASHA.ALLAH ALHAMDOULILAH DAFA AM NIÔ KHAMNI LOU BAKH NOROULÉN MÔ TAKH DOUNIOU BEUGEU BOROM KHAM KHAM DIÀDIEUF MBACKÉ AMATINA SOLO LOOL ❤❤❤❤❤
@Toubavisueltv
@Toubavisueltv 3 ай бұрын
Walay❤
@mohoussa
@mohoussa 3 ай бұрын
Boulni lou bakh niorou leen gnaka Xam rek la.. Nieupa begg lou bakh. Nagn waxtaan rek.. SERIGNE BI rek lagn begg
@layma4143
@layma4143 3 ай бұрын
Maa chaa'allahe amnasolo lool
@ibrahimatoure7709
@ibrahimatoure7709 3 ай бұрын
Ohh Mach alla Mbackê tawfeh rek inchallah ❤❤🙏🏿
@ndiagadiop5792
@ndiagadiop5792 3 ай бұрын
حفظكم الله ورعاكم ❤❤❤
@alioudia5666
@alioudia5666 3 ай бұрын
حفظكم الله تعالى
@dame3349
@dame3349 3 ай бұрын
Bilaye mbacke balla ❤❤❤❤
@Mame-ec3mk
@Mame-ec3mk 3 ай бұрын
Machaallah mbacke ❤❤
@Serignemboussobebousso3136
@Serignemboussobebousso3136 3 ай бұрын
*Masha allaah*
@omarndiaye166
@omarndiaye166 3 ай бұрын
حفظكم الله ورعاه
@aboudiop-fj4ug
@aboudiop-fj4ug 3 ай бұрын
Dieureudieuf mbacké
@moussafallmachalla2993
@moussafallmachalla2993 3 ай бұрын
Machalla
@abodiop3328
@abodiop3328 3 ай бұрын
Ndaysan macahallah li sëriñ Ahmadu Mbacké wax amna solo lool lool ñuñ mouriid yépp war nanoo gëna goor goor lu waat te gana tege ca youn wa
@Cheikh-cp6yt
@Cheikh-cp6yt 3 ай бұрын
Leral yi amna solo
@amdifall5269
@amdifall5269 3 ай бұрын
Dafa am ñou nék touba dëkfa bëgg yakh borom xam xam yi ay domeram dëglanou barkéb serigne touba , boy yi nékfi di kalawou lanou wara ñouss ñou dém liguéyi ay domeram lanou rék😢😢😢😢😢
@moukaramouthiam3537
@moukaramouthiam3537 3 ай бұрын
Machalah amna solo
@KhadimMbacke-g9k
@KhadimMbacke-g9k 3 ай бұрын
hakasa Macha Allah mb
@DameLô-l4s
@DameLô-l4s 3 ай бұрын
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@kakhadim6511
@kakhadim6511 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
@IbnuAhmad137
@IbnuAhmad137 3 ай бұрын
Ndayesane
@AbdouDiop-kg8ry
@AbdouDiop-kg8ry 3 ай бұрын
25 la am yalla kham nani ku lale borom xam xami youne wi al nou mana sanete wallahil hazime magui sa law😢
@modoudiop6522
@modoudiop6522 3 ай бұрын
Aka masè am louma naxari 😭😭😭😖
@papsondiop9134
@papsondiop9134 3 ай бұрын
Bima dégué niouy wax yéna kadou yi Serigne Rafahi, sila guiss né ay tapalé diok naniou.Kou sant Mbacké moy done khalif général.Naniou woremal kilifeu yi nguir dieumi Xadim Rassol.Na yéna seute moyetou gane you mélni mane, sinon dinaniou la dioumloo.Kou xool Serigne Sam mbaye ak nimou diégué Cheikh Abdoul Lahad ak Serigne Mourtada.Guiss nimou done waxtané, daray adouna douko si djiteul.Wouté lol ak waxtane kat yi légui, di sénetou wétiéte si mboolo mi ak yéna dieuma yiy déf émission yi si télé yi, tag nite, wax nane diw Saadix la ak di gueureum Mouride bou ame khaliss.Nioy diakhassé nite yi.Massalikoul Jinane kouko lire té téwelouko, dina diafé nga dioum si doxinou ap Mouride.Té di nga ranié you baré si diamono dji, yiy réreulaté ak moutieu si nioulay tak charette
@AbdouDiop-kg8ry
@AbdouDiop-kg8ry 3 ай бұрын
Borom xam xami yon wi khalé moride inchalla gui ndiange you léne wara porotégé
@serinfallunjaaymbeelan7279
@serinfallunjaaymbeelan7279 3 ай бұрын
Du njuumte de . Man de jàppuma ne kenn gënnamaa gëm Sëriñ bi .
@falloundiaye4098
@falloundiaye4098 3 ай бұрын
فالجاهلون لاهل العلم اعداء
@assanefall464
@assanefall464 2 ай бұрын
Lou khew
@biteeye325
@biteeye325 3 ай бұрын
Worom xam xam yi kén mabou lén wayé Serigne mountakha bou diglé dieufé lénko
@khalilibrahima-j5w
@khalilibrahima-j5w 3 ай бұрын
yoon wi danioo wara fonk boroom xam xam yi bania déguelou guayi gua khamni khamouniou dara ak niakk yar gou euppou thi laniou nekk te day wadia yaatou leegui fawwu niou wout nioo khamni niooy dokh thi wallou googou di saytou bu baakh ndax serigne bi nimou fonké kham kham mou melni amna niouy mbouboo yoon wi té newouniou thi li serigne bi wooté gaa yooyou nak daniou leena wara téela yam loo serigne bi moom kham kham rk
@serigneabdoulahadmbacke6078
@serigneabdoulahadmbacke6078 3 ай бұрын
Ndeysan balla Aïcha kadu yi am na solo lol lol lol lol lol
@falloumbaye946
@falloumbaye946 3 ай бұрын
Fall maagui ziar niep.kumay dimbali leral ma li xew
@modoudiop6522
@modoudiop6522 3 ай бұрын
Ndakh xam nguène kouni wakh mousstpha sylla mô mitt akay diambarr hop boroom xam xam la Tayit ap talibè la
@papadabiamarone4139
@papadabiamarone4139 3 ай бұрын
Gni andak seytané té mbo boo Yonn wi dounou beugg Bromm khamm kham yi
@MadinaMbacke-t1z
@MadinaMbacke-t1z 3 ай бұрын
Lin liggeyal serigne bi ci xam-xam kenn ligeeyal lun leen ko nan leen di wormal fii nieppou serigne touba la gëmm waaye ku ne am na Kër baay
@AbdouDiop-kg8ry
@AbdouDiop-kg8ry 3 ай бұрын
Mane mom kilifa gou mana nék si youne wi bou lalé borom xam xami youne wi ma tàbbı si sa thià ya dji diop..la sante si touba la ndiange alkhorane dakar la ndiange xam xam ak si serigne abdou rahmane mbacke lat dior moy sama ap thiédou bu ndiange la beuge serigne touba beuge serigne Sam mbaye beuge serigne abdou rahmane mbacke beuge borom xam xami rawdu rayahine 🎉😢
@sindidisindidi801
@sindidisindidi801 3 ай бұрын
Ceddo moom du dara, boo déggoon li S Ahmadu wax doo wax sa wax jii.
@AbdouDiop-kg8ry
@AbdouDiop-kg8ry 3 ай бұрын
@@sindidisindidi801 dou yaw ya may wakh li serigne ahmadou wakh
@AbdouDiop-kg8ry
@AbdouDiop-kg8ry 3 ай бұрын
@@sindidisindidi801 li serigne cheikhouna mbacke abdou wodoud wakh deugou maku wayé lime wakh deuge leu 😡gnu mélni yaw yéna tardéll youn wi
@AbdouDiop-kg8ry
@AbdouDiop-kg8ry 3 ай бұрын
@@sindidisindidi801 da nga khmoul lane moy ceddo moutakh li nga kham si thiéddu moy réyy nit ak you bone niakka kham bakhoul...ceddo moy nitt ku deugou té mane fou la nékk
@AbdouDiop-kg8ry
@AbdouDiop-kg8ry 3 ай бұрын
@@sindidisindidi801 lima wakh ma wakhat ku kilifa gou mana done bou dépazé borom xam xam yi ma tabbi si thia ya dji ak non mana sante
@khadim5779
@khadim5779 3 ай бұрын
Mais c'est normal yonou mourid tégou woul ci kham kham 🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥
@yaragteggiin5101
@yaragteggiin5101 3 ай бұрын
Ya man a kàcci dëgg demal nga gëstu mbindum Sëriñ bi
@amdifall5269
@amdifall5269 3 ай бұрын
Bayi fénn
@FallouGaye-gf7kb
@FallouGaye-gf7kb 3 ай бұрын
Astakhfiroullah
@abdoukhadirdiop6428
@abdoukhadirdiop6428 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MorKane-i3l
@MorKane-i3l 3 ай бұрын
Machaalah
@taalibe5341
@taalibe5341 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤
She made herself an ear of corn from his marmalade candies🌽🌽🌽
00:38
Valja & Maxim Family
Рет қаралды 18 МЛН
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН
✨️ Histoire Des Djînn & Les Saytañe | Par Serigne Bassirou Mbacké
28:57
SÉRIGNE AHMADOU MBACKE DAROU MOUHTY : TOLLUWAAYU WAKIILOU CI YALLA
48:08
Rafah TV International
Рет қаралды 10 М.
✨️Histoire De Khalíd Ibñ Walide | Par Serigne Ahmadou Mbacké
40:58