War nagne khalate organisation thiante yi li tmt dafa métti kou nék beugue la djigué❤❤mais bonne continuation kalamou yalna yallah motali lepp inchallah ❤️👌🏿👌🏿🚩🏴
@Cambiamoci7 ай бұрын
Kalamou nala sa borom sama serigne touba faye la ba faye saye seuti seute xol sèdatina soldarou Bamba 🙏☝🏿
@kalamou22lofficiel987 ай бұрын
Akassa amine
@seydouly83645 ай бұрын
Tiey kalamou Messi 22❤❤❤ ken dou yow Real gor yalla deug geuneu yagg geuneu werr yagg werral batt bi❤👌
@TaphaDiongue-gj8mo7 ай бұрын
Kalamoula international goor deug doudeul 🇸🇳🇪🇸🔴⚫️
@bilalfall29537 ай бұрын
Kalamou conditions yimiy thianté métina trop da ngakoy yeureum
@djilysonko31427 ай бұрын
Bilay yow wahatiko dé barki Serigne bamba 😢ndeysane da bah rekk oyoff mo tah d'où wah dara mé metina môme AK bouheunté yi
@MoryThiam-bk1kj7 ай бұрын
Bilahi mom daffa yarou Dou wax mais staff bi nio Wara bagne li l'année dernière même chose année niewatt même organiser li kene manoussi dinague normale en plus kouné Di lale niawouma djorte deh mais les intentions ne sont pas les même....kalamou doundallll
@djilysonko31427 ай бұрын
Bilay yow wahatiko dé deuguite wayé borome Touba protège Serigne bi rekk mokay are ci borome intentions yi bonne yi
@djilysonko31427 ай бұрын
Bouniou faté yite beuyite yimouy faral Di diangue diko zikar dafay aré yaram ken d'où Serigne Touba khadim Rassoul ❤️