Serigne Amadou Cissé vous êtes très intelligent et vous êtes très bon communicateur. il faut appuyer kalifone qui est sur la bonne voie. Ouseynou l'homme fort est celui a remporté la victoire sur lui-même. Le vrai courage consiste à faire ce qui est juste. Ceux qui ignorent qu'ils marchent dans l'obscurité ne verront jamais la lumière. Ouseynou il faut rejoindre votre famille vous êtes un citron pour la dame. Elle va vous presser à sa manière et vous jeter. Elle a amené son fils à l'étranger pour des études. Ouseynou revient sur terre avant qu'il soit tard. A Bon entendeur salut.
@antandiaye37694 сағат бұрын
🎉🎉tu as dit la vérité
@lemeringue-fi2zf3 сағат бұрын
Wallahi tu as tout dit
@BinetaNdiaye-ot3hh2 сағат бұрын
Vérité absolue ♥️
@Matar-h2f4 сағат бұрын
Yalla nagnou yalla mousseul si nafékh
@modourokhaya96162 сағат бұрын
Amna niokhamnè da nio nafekh, boy bi koum nekkone sa frère do nangou mou seuyak mere bii.
@RimkaCissé14 сағат бұрын
Ay ponkaloum goor yalla,wara doori war,nekk ay kilifeu,done gentleman... Gnouy nekk fii di lidjeunti seuyou diambour,werr domou diambour,deff yeufou niak fayda,c'est vraiment dommage pour ce pays
@sokhnaniasse54013 сағат бұрын
que dirais-tu si ton frère épousait une femme ayant 30 ans de plus que lui ???????
@abasssy92429 сағат бұрын
C’est sa vie. Moy takeu, moy kateu. Hypocrites ak sokhor mo beuri Senegal. Je déteste ces genres de men. Mind your damn f.. business
@makeitreal69187 сағат бұрын
Ay vrai domeram lagn
@Alhamdoulilah206754 минут бұрын
Bilay gni dagno gnakk fayda
@FulaniGirLll52 минут бұрын
Bilahi comme si douniou ay dioulite douniou khalate ni bene jour daniouy dé nioune nieup té louniou deff fi adouna dinaniou ko guiss alakhira
@IbrahimaBa-d3m7 сағат бұрын
Bilahi néck Sénégalais méti na khana yalla moumou sakeu sakh téguougnou fittna ngéni néckeu fi di lidieuti problème diambour rk
@omardabayethioune63074 сағат бұрын
Merci ❤
@naboujadieng6274 сағат бұрын
Lolou mom Deugue leu
@FamaDiop-h3h30 минут бұрын
Ibrahima gni ay weudeug lay, wara liguey yi tangue Di fene ba 4h du matin. Li yalla beugou ko sakh
@Mbodji-walo2 сағат бұрын
C'est vrai séy mo geune ndialo mais nk😂 justice pour Ouseynou sinon Mère bi dakoy ray légui
@Myriade-s2nСағат бұрын
Sisi il faut protéger le petit cette dame là elle peut aller très loin deugniou nara protéger khalebi mystiquement ndow si bakhule santoule yalla t'ai yenn jeunes yi moytoulaine fasson yi bari neugne fi lolll d'habitude degne laine di liguey t'ai liguey bi yeupp seine kanam leugne keuy deff so khassai b egueu thi mom rek c'est fini dotoko bayi
@papediazngom612114 сағат бұрын
Bayiléne séyou diambour bi
@yayodiallo10218 сағат бұрын
Keneu waroul publier ay audio diambour publiquement
@makeitreal69187 сағат бұрын
Ki domeram lë
@aicha.2025Сағат бұрын
Ce garçon il faut l’aider😂😊
@khelcom36396 сағат бұрын
Ousmane SONKO niogui sakkou ci etat bi mou diouk si genrou nit ñi...nou Sénégal développer lañ wara khool mais neksi derou niary nit dissi wakh soubaak 'goon... Contenus 0000000 wakhlén Xam Xam / science/ walla lou Dieumeulé rewmi kanam...
@aboubacrysy818813 сағат бұрын
Bé worbé diaasi billahi 😢 Quand l’esprit est faible et y’a rien sera comme c deux garçons Waxx deug yallah Lii dou youfou garçon
@nenedacosta894327 минут бұрын
👍👍🙏🙏
@papediazngom612114 сағат бұрын
Kali bou séy bi tasé ndakh yow doula djgue
@tutitt986614 сағат бұрын
Ki bo dégué nimouye wakhé sa ga hamni il n'a pas grandi. Sen différence d'age dafa barri 30 ans
@adamasamb891913 сағат бұрын
De trop
@FamaLaye-kb6cj4 сағат бұрын
Vraiment kali do nitt kou.bakh
@FatouNiang-wt3eo13 сағат бұрын
Ndeysane ❤❤❤❤❤
@rokhayasarr6468Сағат бұрын
Ki khaler la deysan ouseynou va rejoindre ta famille tu a encore l'avenir devant toi 😢😢😢
@khadrediaylani59389 сағат бұрын
Je regarde même pas ces genre de contenu, mais dema tombé thi vidéo bi. Frère pourquoi dolen mandou? En plus ay Goor yalla ngen. Occupez vous de votre problème ngen bayi diambour. Tu es libre de dire ta pensée mais pas détruire sa relation.
@Marameg.235 сағат бұрын
Mann dama diakhlé si senegal gnakk fayda rek gnou wara lidjeunti khalé bi am 9ans gnou violé ko bamou eumb gnou nekk si seyou diambour bi di wakh rek
@TheGoorgoorlou8 сағат бұрын
Mais kali dooniou lidieuntil affairou Cheikh Oumar Diagne mii ndakh diomaye kadjie ko. Tu es très fort apparemment.
@ndiayesiradji153011 сағат бұрын
Bodon Maguètou toubabe la takk kèn d'où ci wakh
@ArjunJaikumar-f1g9 сағат бұрын
Bo amé dom yalna li dall boye bi dall ko amine mais na nek toubap na 😢complex you bonnn yi ngenn donn
@abasssy92429 сағат бұрын
Merci. Le sgl est un pays d hypocrites , naafekh. Et méchants. Que chacun se mêle de tes histoires. M e r d e
@quenne_dudiolof95366 сағат бұрын
Maguetou sénégalaise la amalouko nieurign
@ritoundene90412 сағат бұрын
Maguetou toubab c'est pour les papiers
@cheikhfall998515 сағат бұрын
Fékhé nguén ba Yakh seuyou diambour bi mais yalla dina léral lépp
@Limamou6514 сағат бұрын
Ani seuy fii do até deug sey bo khamni ay mbokam yégougnou
@OuzinDiouf-g4e14 сағат бұрын
Kali doff bilay
@MadjigeneDieye14 сағат бұрын
Bravo kalifone
@ismailiaFall7 сағат бұрын
Boye waroul wone wakhe ake ki 😢😢😢
@makeitreal69187 сағат бұрын
Kali un vrai domeram
@amintasamb19212 сағат бұрын
Ndeyssaan il faut aider l'enfant à aller retrouver sa famille. Il en a besoin. Ndassii tamitt na bayii domou diambour dji mou gnibii Thii yayam mo gueune.
@PoulloNiang6 сағат бұрын
👂🙏🙏🙏🙏👍👍♥️♥️♥️♥️
@aliounesarr76167 сағат бұрын
Kou tass seuy loussi yallah wakh!?
@FatouThioune-z9k6 сағат бұрын
Li seuy l 😂wala kipnapping
@mamadouba25177 сағат бұрын
Fekhe ngene ba tass seuye diambour yi ni rekk c'est vraiment pitié
@lacitoyenneafricaine856614 сағат бұрын
J'ai l'impression que Kaliphone dafa nek si règlement compte ak Aissatou Pendo Diop. Sou boy bi takone benene dame thiow dou ame. Nitt dey deff djeufou gor! Kaliphone djenal si li nga nek! Sa kalame bi si bopame mo suspect soy wah se température khol dey fingne si se kaname gui "beneu lerr bou bone". Kaliphone tu n'es pas gentil vraiment tu es un être trouble et troublé djenal si li nga nek way. Akhmet bayil Kaliphone mi ne fower khelou gniko nango!!! Gore dou yakaneter ...
@aboubacrysy818813 сағат бұрын
Waxga deug Walahi 😢😢
@lacitoyenneafricaine856612 сағат бұрын
@@aboubacrysy8188 so yeurer kalamou Kaliphone bi sakh djiss que y a une haine qui s'y dégage! Khol bi moy wakh!
@quenne_dudiolof95366 сағат бұрын
Si c'était ton frère Ousseynou do wakh li. Sey bi day tass Ousseynou délou si yayam. Aissatou penda domeram la di diol lo yayou diambour . Li nieup la metti bou ko defone sama frère kone damakoy ray
@PoulloNiang6 сағат бұрын
👍👍👍👍♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️👂👂👂
@ismailiaFall7 сағат бұрын
Walaye gni dano sokhore yakhale nane boye bi😢😢😢
@quenne_dudiolof95366 сағат бұрын
Niane ga sa rakh def li
@BinetaDiene-m5b6 сағат бұрын
Limogen dialo Sénégal wahrek hale yagif dialo ak ay mak baholen
@aboubacrysy818812 сағат бұрын
Lii dou youfou garçon billahi thimm
@layefabregas678811 сағат бұрын
Kaliphone ioe kou kate sa leufal Ndeye nga
@SadioWelle-cj9yk14 сағат бұрын
Aye waye yalna done deukk❤
@Myriade-s2nСағат бұрын
Ndeyssane
@Sokhnamay-d3sСағат бұрын
C'est un peu 😅😅
@fatoumatawane51388 сағат бұрын
Outi len ligey
@serignecheikhsy41557 сағат бұрын
Vraiment khaliphone vrai domrame moy ak adamo ak cheikh ahmed cisse ken tane wou morom
@makeitreal69187 сағат бұрын
Ay vrai domeram lagn bilahi
@PapeFall-il7xw15 сағат бұрын
Bayil seyou diambour bi nga beugue yahe comme ça
@sokhnaSaly_Diop485314 сағат бұрын
Ban seuye?
@fatimandao83598 сағат бұрын
Yow mi fonék li bane genre seuye la li bane avenir la ameu
@MomadouCisse7 сағат бұрын
Youwsadatayae
@adia9827 сағат бұрын
Kone legui dañuy seuy pour ame avenir Dem kene diangui sene dinner yenn comme aye yefér reck@@fatimandao8359
@Adamtony2237 сағат бұрын
Kali vraiment doff nga !
@aboubacrysy818812 сағат бұрын
Walahi tu n’es pas eu la chance d’avoir un grand frère ousseynou C gens là bougoul dara loudoul vie des autres
@AbibouMbacke13 сағат бұрын
Sawaye diapal sa seuybi defo lu naxari yalla diapal sa seuye ndax ki yalla mola bolle ak mom
@Tarikha20247 сағат бұрын
Bouder di nagn si ame dome dh def nagn li yonentibi diglè mais bougn si amoul dome mom wathie nagn yonn si li yonentibi wahonn nè seuylenn nguir yoke sma hete
@BoyPoulo-kg5pl6 сағат бұрын
Niit takk n'a xale 20ane amoul dome
@Thiapathiolii5 сағат бұрын
Dome key je ken manouko garantii si seuy wala danko meune ioe @@Tarikha2024
@babacarcisse722814 сағат бұрын
Boy bi mo nara torokh
@AbibouMbacke13 сағат бұрын
kaliphone bo xamon lithi yakh seuye dagamanu thi seuyu diambour bi
@salenesene118215 сағат бұрын
KHALÉ BI DAKH WÈRR NEU? LOU DIARA KHOLE.
@aicha.2025Сағат бұрын
Police nako dieuli mére bi n’a wouti maromo me😢
@moustaphadiakhate39974 сағат бұрын
Kaliphone ak cheikh Ahmed casse kagne lagnou dioubo 😅😅
Moka sori ngaka day wiri wiri il a entendu malik ndar wahni so bayè mere bi ma diapalèla day wayane
@خدجه-ز6خ11 сағат бұрын
❤❤q❤❤❤p❤❤🎉🎉🎉
@OusmaneFaye-d9n12 сағат бұрын
Boy bî déffa kon quoi waroul diéle kéne koumouy khamoule vrai doff la
@aboubacrysy818812 сағат бұрын
18minute 11 seconde pour la vie de quelqu’une Qu’est-ce que sa sert ??
@fatoumboup49216 сағат бұрын
Môme diahal satan est toujours content d'eux toujours pour servir satan🏃🏃🏃(vous les bons coeur vené qu'on soit toujours avec Allah ❤❤❤et notre bien aimé PSL.fermé notre porte k satan ne puisse pas entré,je ferme la porte)
@PapeFall-il7xw15 сағат бұрын
Ki khalé 24ans la nga té ko diko manipuler comme ça
@layefabregas678811 сағат бұрын
Kaliphone sa leufal Ndeye ioe khou kate sa ndeye nga
@quenne_dudiolof95366 сағат бұрын
Hana domou biral ga
@mamadoudiatta5506 сағат бұрын
🤔🤔🤔🤷🏾🤷🏾🤷🏾🥹🥹🥹
@MoustaphaSow-z6q6 сағат бұрын
Sénégalais mo moune topou ka fékhe Nan ba tass seuye diambour yii 😂😂😂
@fatousow85395 сағат бұрын
Li yeup ay fene la seye massoul am
@mmmomo42676 сағат бұрын
OUSSEYNOU SAMPOUL BA DAMEU THI RECUPERER SEN AIDE FINANCIERE MAINTENIR SA SEUY DI NGENE KHAMNEH OUZ MOLENE GEUNEU YEWOU
@antandiaye37694 сағат бұрын
😂😂
@Bigboss-hd8fx7 сағат бұрын
Aye domeram you melni kali
@KhardiataSeck-m9j6 сағат бұрын
😂😂😂😂
@NfamaraDiatta-q8j4 сағат бұрын
Si aye fene lay moudier
@abasssy92429 сағат бұрын
Chacun veut faire l’interessant Sénégal mo nekh
@makeitreal69187 сағат бұрын
Bilahi
@manguebourgeoise27605 сағат бұрын
Kali ,ousseynou t'a battu a ton propre jeu liyeup daniou ko deal
@ZEUMBOY1420TV7 сағат бұрын
Boy mono bayil ndeye appel yi ak domaram yi
@Niang-nk1qg8 сағат бұрын
Bayilen sayou diambour bi say nan si farata Alors❤
@gayafall13 сағат бұрын
C est confirmé ta mère l a dit et ta soeur
@Laye_critiques_ciné4 сағат бұрын
Doumani dafko ligey dé mais c'est pas naturel
@gayafall13 сағат бұрын
C est vrai ta mère l a dit . Tu ne sors pas . Vérité.
@tout19585 сағат бұрын
Bayi léne vie privée diamour yi Sénégalais légi comme deumou
@BayeDiop-vx9ob13 сағат бұрын
Tass Seuyou diambour loussi l'islam wakh Boye bi daffa diakhasso ndeysane mais daffa beug femme bi sama xalaat bou Gatt
@aboubacrysy818813 сағат бұрын
Walahi tass seyou diambour safara ga dem direct yallah bougoul LOL
@quenne_dudiolof95366 сағат бұрын
Dieul domou diambour kinapeko di ko teuder lousi islam wakh. Boudone sa frère do wakh li. Aissatou penda bouka defone sama frère m'a ray ko
@Alhamdoulilah206755 минут бұрын
Califone Yaw kou sokhor nga affaire de règlement de compte ngay déff boy bi aussi sou féké li mouye wakhe degg leu Kone mome traître la vrai diame leu pourquoi wakhoule ak la concernée mais mouye wakhe ak califone mélné kou amoul mbokk chime
@AdamaNdiaye-wk1lu3 сағат бұрын
Apré nga douguou fi trokhal ko mé warowaune diko siweul fi
@FatouThioune-z9k6 сағат бұрын
C bien c très bien
@yattadiao37937 сағат бұрын
Seuye dé kouko Tass bou kérogué yawmal khyame dinga ko takate
@quenne_dudiolof95366 сағат бұрын
Bou nekone sa frère do wakh li
@AliouneGueye-zd6bd6 сағат бұрын
Kaly a brisé Ameth cissé
@xulliltv8816 сағат бұрын
Deugeu la wakh xamenako
@keurguifootballps36783 сағат бұрын
Ki pression senegalaise yi moko sonal cest pourquoi il parle comme ça
@OusmaneDiab7 сағат бұрын
Thiéy Sénégal dagay bayi sa 1kg du wah libre diambour
@DaoudaNdao-j8r7 сағат бұрын
Kali fon yaw kou katsandayka
@NdiabelTandiang5 сағат бұрын
Yéne gni yéna bone yéne gniy encouragé ousseynou si li
@KineDiop-qx8xm13 сағат бұрын
Mais da warone nek soutoura
@makeitreal69187 сағат бұрын
Vrai gordjiguén
@Biobi14 сағат бұрын
Wadji boy bi moko magg nakh nalén bou yague
@addiallo1411 сағат бұрын
Magou lène de fe meune doul rek Ki il est avec cette femme juste par intérêt c tout
@MoustaphaGueye-t2i6 сағат бұрын
Li est ce nekoul mis en scène pour femme bi am visibilité 😂wa bakhna
@quenne_dudiolof95366 сағат бұрын
Ousseynou n'est pas amoureux mere bi defko liguey
@mmmomo42676 сағат бұрын
OUSSEYNOU BO FOWEH SA SEUY BI YALLA FOWEH LEU TU VAS LE REGRETTER DOF YI GNIGUI SI LILENE NEKH BEUGEULA DELLO SI TOROKHTANGUEH ALORS QUE DOUGNOUY EXEMPLE KHAMELNI SEUY BI MOY SA NDJICLAY TEH KHAMNEH MEUN NGA SI GUENEU TAY DEH FI AK UN MOIS DONC NGA WARA KHAMNEH LI SI SA DESTIN LA BOKEU
@NdiabelTandiang5 сағат бұрын
Doule mounane bo fowé sa seuy mayléne niou diame way vous ne pensez même pas à sa mère
@ModouSambe-p8g7 сағат бұрын
tasskatou saï ga
@KineDiop-qx8xm13 сағат бұрын
Lepe Ahmed cissè la moye mate di ofe moye wakh ak boy bi di wakh di informè mère bi
@aramesall34223 сағат бұрын
Merci
@senembaye99285 сағат бұрын
Kalifone sa yo yewo sa databe ndeye sayo yewo sa dig leufeuf ndeye
@mahama8165 сағат бұрын
Auto biko Malick Nar dick la beugeu mo takh mou changer avis
@aramesall34223 сағат бұрын
En dako dike auto kone loloula moke mere bi gnon teke dile😂
@DameSarr-w9e14 сағат бұрын
Boy by dohmé ramm deugg la mok kali yépp gnô yamm
@serignecheikhsy41557 сағат бұрын
Bilay sourtou khaliphone vrai gordjingue la
@makeitreal69187 сағат бұрын
Ay vrai domeram
@senembaye99285 сағат бұрын
kalifone yaw sa lefeule ndeye way khana amo ligueye