Bly oustaz ya wax deugg li lepp mame cheikh ibrahima fall waxone nako bo meussana wax yalla ngui fépp danane ah doom dioumngua dh yalla khadioul féne fépp mo nékk si yalla vérité absolu ❤❤❤
@masseckdiene37845 ай бұрын
Walahi dayssane wah yombou na waayé dégue mo diaffé
@BbinetaGadiaga4 ай бұрын
Thiey sama wadji mo dégeu sunu borom
@LamineBaraDiouf-r2z4 ай бұрын
@@BbinetaGadiaga bly mome moy khaliloulahi faw mou dégg ko
@mouctardiallo98594 ай бұрын
Indil fouko cheikh Ibra wakh fi nitt di wakh diné ngenn dougal ci ay chirk indil fouko Ibra fall wakh
@danymk19444 ай бұрын
@@mouctardiallo9859bane shirk ngay wakh fofou ? Babe shirl lafi wakh ? Meuno len bayi lolen degu nit wakh nguen ni shirk sans argumenter ? Et n’oublie pas que y’a deux types de littérature et de moyens de transmission qui existe depuis les temps anciens !
@hamidoutall91345 ай бұрын
Thieuy yalla keneu meunou ko décortiquer yalla moy yalla moy Rabi sama wati wal ardi dieureudieuf yalla ❤❤❤❤❤❤
@alassanedia7785 ай бұрын
WALLAHI❤❤❤
@ousseyenoutoure33645 ай бұрын
Bilahi
@Bayemorgayebeuggserignefallou4 ай бұрын
Tei kenn la
@Niangpenda-qp4os4 ай бұрын
Allahou akbar ❤❤❤❤❤❤❤
@mohamadouvictorndour4 ай бұрын
Boko dièmè rek wediiko yallah n'a borom bi deff gnou dioulite
@ndeyemeissamboup19205 ай бұрын
Yalla na Yalla yéssal yermadjéme si dioulitte yep si barké seydina mouhamed psl ❤❤❤
@BastyHagne5 ай бұрын
Amine Sallalaahou aleyhi wa salam
@CheikhDiop-c2j4 ай бұрын
Amiiine ❤
@serignemane75025 ай бұрын
Résumé : Ken dou Yalla .mome rek moy yalla.c'est pourquoi nous Tous nous devons rendre un hommage à notre Seigneur , Yalla,le remercie denous avoir envoyé Mohamed psl. Encore une fois ken dou yowe.Dieuradieuf Yalla.
@MaguetteBougoumaFaye3 ай бұрын
Psl
@maneseydina65646 ай бұрын
Allah a toujours existé et n'est pas créé,il est,il était et il sera,il est infini et éternel.
@ibasow53686 ай бұрын
Voilà tu as tout résumé C’est ce qu’il essaye d’expliquer nak
@khalifaababacargueye60486 ай бұрын
Kham kham fégn na 😁
@bamouhamedou63685 ай бұрын
Macha Allah
@hokagesama72955 ай бұрын
Waxofi dara Li nieup wax ba paré té xam ko ngafi wax
@ibrahimasarr36905 ай бұрын
@@hokagesama7295ioe dh wakho xam xam wakhou Kou sokhor kèp nga fii wakh
@PapaDjibrilcissCiss4 ай бұрын
Kén Mame maodo Malick Sy yalna yallah yok léram AK koulouhoum magoum diné yallah fayal niou lén macha allah ❤❤❤❤❤
@@souleymaneibrahimasall5367Traduction dit il est Allah unique Allah le seule que nous adorons pour ce que nous desirons il n'a pas agendre est n'a jamais etait agendre est n'ul n'est egal a lui 😊
@albouraq245 ай бұрын
Kou dé rek am lo comprendre kéne menoul xam lep ...Macha Allah si xam xam bi Amna solo
@amdia59933 ай бұрын
Bilahi mon père ya Bari xam xam.yala nala yala doli wer ak soutoureu
@MOUHAMADOUDieye-rb6sg3 ай бұрын
Genre wakhtane yii bakhoul si kou gueumm gueummeum takhawoul fokk ga am imannn ga meune ko comprendre sinon rk diga dougueul sa khell mi loussi bokoull yalla keneu la ❤️
@Zahrafatime66 ай бұрын
Qu’Allah nous facilite la bonne compréhension 🤲🏾🤲🏾🤲🏾 . Vidéo bi seul les doué d’intelligence vont les comprendre. Wakh dimension la sofa yégoul boul contredire "Le Créateur n’a pas de créateur sinon il deviendrait une créature et Allah est Le Créateur de tout chose et aucun créature ne peut sortir de Lui car il est partout " mais le titre de votre vidéo elle est énorme prochaine fois inchallah essaye de revoir vos choix des mots 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@taphadiagne6 ай бұрын
Xaam nga rek!
@ibrahimambodji66086 ай бұрын
Merci t'as tout dit. Il te faut un certain bagage intellectuel pour le comprendre.
@taphadiagne6 ай бұрын
@@ibrahimambodji6608 mbirou yallah dou mbirou intellect. Kone Toubab yi èg nagne si bou yag. Ki ni il ne raconte que des histoires qui impressionnent les petits esprits.
@ibrahimambodji66086 ай бұрын
@@taphadiagnekone intellectuel waroul xam yallah? Yallah moy kokou nékh mou hamal ko boppam. Té mom Il n'a rien inventé dégg dégg biko yallah may lagne amoul.
@taphadiagne6 ай бұрын
@@ibrahimambodji6608 ce que je dis moy dou khel moy égalé si yallah. Lo nek nek intellectuel dou lolou mo lay khamal yallah. Dou métaphysique, dou physique, dou philosophie. Des gens kham nagn yallah kham bou wer sans connaitre les particules, les Boson de higgs, les trou noir,.....
@MayeCisse-v7x6 ай бұрын
Bayiléne sokhor ak Aniane ak nafékh professeur xam xam lay wakh bou kéne meunoul dindi. Dém léne diangui mo gueune Di wakh si Lou nguéne khamoul. Longue vie à professeur ❤❤❤❤
@lamineseck13146 ай бұрын
Lou werr jeureujeuf
@thiernondiaye19756 ай бұрын
@@MayeCisse-v7x indiléne louy degueureul wakhou professeur bi si Al khourhane wala si wakhou yonintebi
@papesouleymanesowsowsow92926 ай бұрын
Doynawar
@mordiop7055 ай бұрын
@@thiernondiaye1975yow so manoul comprender li professeur di wakh conn yow mbame Mou seufe ay téré rék geu
@thiernondiaye19755 ай бұрын
@@mordiop705 Kone yaw professeur bi mo eupeu kham kham yonintebi
@alexismendy88095 ай бұрын
Respect a ce monsieur les scientifiques ne font qu'embrouiller nos cerveaux en voulant découvrir...nioune nite yii lignou xam moye k Yallah laniou geum naniou découvrir sen bopp louniou beugue xam com k aye scientifique laniou
@pphataful5 ай бұрын
Le premier mot du Coran " Ikhra" manaam Guestou, Diangueu ! Xamxam. Xaamxam est cœur de toute chose. Les scientifiques suivent bien cette voie tout en évitant le dogme. Pour la science toute phénomène naturel à une cause que l'on peut découvrir par des recherches methodiques (effet/cause). Apres on peut insinuer les limites de la connaissance scientifique.... Certains vont recourir à la foi pour passer à un autre niveau... Encore une fois leppeu ci connaissance leu akk ay différente approche. Et que ces deux approches tournent autour du mot " Ikhra"...
@damembow68566 ай бұрын
Ndéyssane professeur yague fi lolle té wérr❤
@youssouphadiatta82243 ай бұрын
Yallah amna xél (Esprit de Dieu) té amna xol (zate) ! Amna Ruh (Haqqiqatu muhamadiya) amna djeum (haqqiqatu Ahmadiyatu) ! Fittratalah leuti aleyha fattran nass! Yallah Moy Jamono ci boppam ! Mélo yi AK tourr yi AK kawmu bi Moy DEUG deugi djeumi Yallah ! Ku xam sa bopp xam sa Borom ! Ku faté Yallah niu fatélo la sa bopp ! Dara existé wul ludul Yallah ba ci atome bi geuneu ndaw!
@MohamedMohamed-dw4xh6 ай бұрын
J’ai dis a staghfiroullah au début mais après j’ai compris .ce professeur parle avec philosophie tè dafa ladj dèg dèg .mais aussi ces des questions qu’il faut pas poser parceque notre cerveau Dieu l’as verrouillé pour mou nek kumpeu
@sabin77996 ай бұрын
Si On doit le savoir parce que c'est notre raison d'être
@MohamedMohamed-dw4xh5 ай бұрын
@@sabin7799tu connais pas l’âme qui est en toi et tu veux connaître Dieu .tin cerveau Dieu l’as verrouillé et si on t’explique tu deviens fou automatiquement
@mouhamedfall3325 ай бұрын
😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
@Naboumaria14415 ай бұрын
Vérité absolue
@ababacarsadikhthiam5 ай бұрын
Tout à fait c'est de la métaphysique. Il y a des questions ko n'ont point de réponse et faut même essayer d'en trouver au risque de devenir fou kom vous l'avez souligné tantôt
@faithsham563Ай бұрын
VERITÉ ABSOLUE ! DIEU EST TOUT ! Cela resume tour macha allah !
@elevagenotrepassion67045 күн бұрын
Walaye lingeeni xallate ci yalla SWT yaasinu taqa (mouhamad) sax romuna foofou 😢
@abdoulo83035 ай бұрын
ô Seigneur! Tu es le premier car rien ne T’a précédé. Tu es le dernier car rien ne Te succèdera. Poser la question qui a créé Allah est de la mécréance.
@ibrahimasarr36905 ай бұрын
Dieu est le premier qui n'a pas de commencement et le dernier qui n'a pas de fin
@AïssataBa-f9y5 ай бұрын
Lou simple yalla néna kou kham sa bop khamma kon nak naniou djèmeu kham souniou bop nguir niou meun ko kham dieureudieuféé cheikh al islam💪❤❤❤❤❤
Yalla wakhoul loolou fenneu. Yenn fenal yalla rekk ngen meun
@sethcisse77224 ай бұрын
mais nouniouy deff ba kham sounou bopou??
@papedione76937 күн бұрын
Machallah ❤, il a tellement dit la vérité 🙏. Yalnaco yalla yokk
@LamineSeck-cl1dr5 ай бұрын
Kham kham niarry khamla lo guiss amna bir ak biti respect yalla barkel
@yayeantasall57754 ай бұрын
Cette Question me revenez souvent 😂quand j'étais adolescente et mon mari m'interdit d'en penser car meune n'a wangni gueume ndakh yalla khél douko dadjie dadj ba meune la missale originane.Donc unitle de fatiguer ton esprit pour cette question 😂et en philosophie on te répond la mm chose Dieu est partout..alhamedoulihi merci pour cette explication
Allah n’a pas de début à son existence et pas de fin. Il existe de toute éternité et n’a pas de comment ou d’image. Allah existe sans endroit, sans direction, le temps ne s’écoule pas sur lui et il a créé les endroits, le temps, les directions et toute chose. Il existait avant eux et il ne change pas. Sa volonté ne change pas. Et tout lui appartient, il n’a besoin de rien. Il ne ressemble pas à ses créatures, il ne ressemble à rien. Rien n’est tel que lui et il est unique. Nul ne peut atteindre la réalité d’Allah, lui seul connaît sa réalité.
@ousseyenoutoure33645 ай бұрын
Mashalla merci beaucoup Professeur Madiama Fall pour votre pertinence et clairvoyance vraiment amna solo lol Yalla dou nite walahi?
@kayamaghan35405 ай бұрын
Allah n'est pas hors du temps mais il transcende le temps. Allah d'englobe pas tout mais il apparaît dans toute chose,sur toute chose et en toute chose
@mamadoumbengue79805 ай бұрын
L’espace et le temps font parti de la création
@youssouphasarr8715 ай бұрын
Pourtant vous parlez le même langage
@amedinedeme5586 ай бұрын
Machalla Pr yalla na yalla doli leu sa kham sell na malheureusement certains douniou leu comprendre par ce qu'il vont utiliser sen khel et ils vont se perdre comme toujours yalla dou khel mokoy kham djeureudjeuf cheikhou tidinane yalla na yalla khamle bopam si mbolem mindef yi . svp le commentateur boul weddi so khamoul juste demande on sera ravi de partager
@Baatine5 ай бұрын
@@amedinedeme558 c est prophesseur qui utilise mal son cerveau , kepp mounounio weddilo Lou onenetebi diangaler
@Metal221245 ай бұрын
Wallay bo tarbiyoul sa geum deugeuroul nop ak khël meunoul dékou linguay wakh diëreudiëf baye barham niass wax deug yallah contane nagne waye khöl ❤❤❤sëd way
@ousmanefalloubayeniass4965 ай бұрын
Waxatikko déh ❤.
@souleyegning11675 ай бұрын
Dieu c'est le CRÉATEUR,lemaître de l'univers. DIEU EST PARTOUT. DIEU EST TOUT. C'EST LE MAÎTRE ABSOLU. HEEEEY YALLAH.
@bounas6635 ай бұрын
Tout ce que je sais est que c est Dieu qui nous a créé.
@aboubacarbathily26885 ай бұрын
Masha ALLAH lii mooy mandou bokk na si diamou YÀLLA YI geuna kawé ALHAMDOULILAH DIEUREUDIEUF WAAY
@aboubacarbathily26885 ай бұрын
❤❤❤❤
@mamadouniang68684 ай бұрын
Comment tu l'as su?
@cheikh50133 ай бұрын
Xam yallah rek moo woor🥹 ken ku xamul Yallah doo comprend lumu wax 😂. Jërëjëf Baye❤
@BALLAMoa5 ай бұрын
Merci professeur mane dama nopalou lou khew ma sante ame ack niack faibar ack weere louma teck reck ma sante ❤❤❤❤
@meyebaidygueye19365 ай бұрын
Création fou mou am rek xam xam mi ngui fa,Yallah Ken dou comparer ndax foumou nek comparaison amoufa ,legui ani lerou Yonent bi si saak dji? Cause ak effet meunoul am si Yallah si manifestation rek la am T Dieu reste non manifeste.Merci pour le partage Professeur qui pousse à tous ces questionnements 🙏🏿Arigatooo
@AwaDiop-n9u4 ай бұрын
Machallah amna solo lool Mais baatou dafa ( diééki diééki am ) eska lolou nirou wul ni kon meuss naa niak mom yalla té yalla meusta nian bey diéki diéki di am moofi meusa nek WAXUFA KHADIIMUN MAA LAHU BIDAAYAH WAZUU BAQAA'INN MAA LAHU NIHAAYAH ( Mom yalla adji djitou la déd diko gnél ab tambalé kaay Té adji déss ded diko gnél ab yamou kaay
@gueyendioro1505 ай бұрын
Vraiment j’aime écouter professeur madiama machallah goudal fan way ❤
@StellaKaa3 ай бұрын
Wallahi ken d’où yallah moy Rabi Sama wati alhamndoulillah dieureudieuf allah ❤❤❤❤❤❤❤
@WelyThiam-jf5ys4 ай бұрын
Kénn d'où yalla sounou borom bilakhi walkitabi yalla rek moy bour bou mague bi❤❤❤
@faithsham563Ай бұрын
Comme le dit Dieu “ JE NE PARLE PAS AUX IGNORANTS !!!! Allah is Kabir. Le suprême des suprêmes !!!
@momarndiaye76774 ай бұрын
Thieuy yallah rabou samawati wamafil ardi,yazhal dialal wal-ikram 👌Laaaah diamètre diamate si birr diamou yallah yi si bir gayi yallah yi si birr nitou yallah yi si birr kharitou yallah yi,lepp nguir diammo ko mom yallah mi nek si mom, Laaaah yamleuzeul Dieuf Dieul koufa ndieuk dieul gueuneu gaaw eupe yol❤
@oumarcelobousso49023 ай бұрын
Yallah mo wax modi Yallah alhamdoulillah si Mawlana Seydi Cheikh Mohamed Ndiaye Rabi 🙏❤️
@badoucisse89115 ай бұрын
Seul le zikr nous permet d'accéder à la connaissance divine.
@OusmaneDiouf-ol6jp4 ай бұрын
Dieu contrôle tout. Celui qui contrôle tout est partout. Et celui qui est partout est tout. Ça, c'est le résultat de la méditation de l'intelligence humaine, Si tu veux le connaître avec la sûreté de l'âme, prends le wird tarbiyou de Baye Niasse.
@cheicktidianediop14583 ай бұрын
Guiss yallah rekkkk seul ! Tu auras toutes les réponses sur ce sujet ! Allah Allah Allah ❤
Machalla Machalla yalla na yalla faye yiw ci barket rassoul lilahi SAW dieureudieuf
@evalyon93892 ай бұрын
Dieu est le meilleur Scientifique ❤ Ahadoul Ahad❤❤❤
@papiscongom885Ай бұрын
Fou Yalla nékoule amoule.😍
@MoussaSow-od4ueАй бұрын
Allakhou akbarr❤
@momofaye2722Ай бұрын
Saway yalla amoul barape lepp mo nék si birr yalla
@papiscongom885Ай бұрын
@@momofaye2722 moy lima wax rk.. Fou Yalla nékoule amoule. Leip Yalla la.
@rtro2235 ай бұрын
Il est lunik le seul notre roi notre seigneur mom lagnu diamou taye ak euleuk
@Ahmadya455 ай бұрын
Serigne cheikh tidiane sy nena Yallah amna xam xam lolou rek la d'accoroul ak yaw
@appochoupette4754Ай бұрын
Et là nous faisons' nos péchés à l'intérieur de lui Li rafetoul changeons Qu'Allah nous donne une bonne fin
@PapaDjibrilcissCiss4 ай бұрын
Kén meunou KO xaam wallahi professeur xam xam bi séleu n'a macha allah ❤️
@moustaphadjamilmbaye14614 ай бұрын
Un thème très sensible mais très intéressant surtout pour nous les croyants, merci beaucoup professeur.
@NdiasseMbengue-dq6mc5 ай бұрын
Qu'est-ce qui fait pourquoi nous sommes malade où malheureux ; ce dualité ? Ci tout vient de Dieu l absolue
@khalilourassoulentreprise92335 ай бұрын
Bou tawate amoul wone, kén dou kham solos wér gui yaram Sou malheur amoul wone kén dou kham solo bonheur. Lou YALLAH Sakk, gnar la si sakk, à méditer
@pepy_pesmobile5 ай бұрын
@@khalilourassoulentreprise9233bien répondu 🙏🏾
@AstouNdiaye-p8gАй бұрын
Alhamdoulilah. Yallah, Sougnou Borom rek moy Deugue. Al Kabir, Allahou Akbar
@SanéAliou-g3v5 ай бұрын
Yalle na yalla defal nieup diam❤❤❤❤
@kadamamar63523 ай бұрын
Machaallah yallana borom bi mey goudou fan ak werr
@KhadimGueye-h3f5 ай бұрын
Thieuy serigne touba takhna douma siki saka si nékouk yalla gui
@NdaoPapaMamadou3 ай бұрын
Lima gueuna nékh si wahh dji moyy professeur amoul bénn principe scientifique boumou wakhh bouma hamoul, wayé souko interprèté ba expliqué ko ba délo ko sunu borom si layy doga hamé né nékaté lama hamm hawmako... #ndanane deug gua gui nii😊
@AbabacarNdiayemayaye19605 ай бұрын
Nous sommes très satisfaits de vos enseignements Professeur. Il y a des gens qui se noient dans leurs ignorance à cause de la dénégation facile. Ce sont des rabat-joie et anticonformistes. Ils ont malheureusement un cœur rempli de haine. Qu’Allah swt les réoriente. On ne suit que toi, de grâce ne vous focalisez pas sur ceux-là qui ne savent que jaser sur leur prochain de surcroît musulman. Wassalam. Bon retour de Magal à tous 🤲 ❤
@NdeyeNdiaye-qg2dr3 ай бұрын
Thiey yalla sounou borom kene la☝️
@ibrahimambodji66086 ай бұрын
Ki ay waham faw nga am dégg dégg deug pour meune ko comprendre. So degoul limouy wah nak nga dieul li nga yakkar ni moy deugg nga geume ko. Wayé amo xam xam beugga wéddi c grave .
@Baatine6 ай бұрын
@@ibrahimambodji6608 deg deg tous daguene yomba égaré
@idrissandoye65505 ай бұрын
On doit remercier professeur au lieu de critiquer khamoul duzg lay wakh.tout est dieu omniscientomnopotent ,omniprésent.
@lampfalltv76225 ай бұрын
Jajeuf khaliloulah
@iboundiaye20365 ай бұрын
Machalla
@khalifasall39983 ай бұрын
Machalla kou diangue khilassou zahab do réré yonenteu bi thiey Maodo ❤❤😊
@MamadouNdiaye-fo6jq3 ай бұрын
Madiama Fall day fouglou mbir yii wayé désséna Xam Yalla... Limouy waxni waroul Talibé Baye
@ThiareBabacar5 ай бұрын
Dieuredieufe cheikh moussa cissé ndiambé darou xam yalla guiss yalla ague si yalla…merci professeur
@ramatoulayesall851816 күн бұрын
Alhamdulillah... Donc lou bamel weet weet souniou borom mi ngua fa... Fou yalla souniou borom nek rahmanema ngua fa... Alhamdulillah
@zizaradiop96722 ай бұрын
Yalla nanu yalla bakhal si Barki seydina Mouhamed saw Tonton madiama yalna yalla Contane si ioe ak molem dioulite❤
@amindiaye862Ай бұрын
Merciiiiiiiiiii beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@gltntegilou95325 ай бұрын
J'ai partagé ce vidéo intéressant dieureudieuf mame maodo Malick sy machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@sambsidy434425 күн бұрын
Blh mahrifa lérou yalla rek mo worr Dieureudieufé brom nourou lahi 322
@bayefalldiop4172Ай бұрын
YALLA toogèewul fenn, ndax dara attanuko. YALLA dara Tiimuko, tayik nekkul ci biir Dara. NB : Bari waana kuy wax ci xam YALLA, fekk xam xamam ci YALLA mingi melni gone gu mënagul wax. Took fii naan YALLA amul xam xam; waaye dépassé na xam xam, waxi kuy graw graw lu kepp la. Loolu dépassé xam xam doo wax mukk num tudu, ndax amul. العليم ci TURU YALLA la Bokk. YALLA wax ci ALXUR'AAN ان الله يعلم غيب السماوت والارض ngay wax sa waxi gone yi. Bayyi leen di wax di jeema impressionn é nit ñi.
@mountagaamadousow56545 ай бұрын
DIEU
@MameAbdouDiouf-l8y25 күн бұрын
Machallah ❤
@mamemaryndiaye38754 ай бұрын
Alhamdoulilah machalla Dieu est unique ❤❤❤❤
@PrinceBadji-x8l2 күн бұрын
DIEU EST UNIQUE
@SayeFall-mh6ms3 ай бұрын
Kou am imane mon koye guam li gua wakh ❤❤❤❤
@DiaryKane-w6f4 ай бұрын
YALLA defayeme te raglou
@awadiata27384 ай бұрын
Rabi sama wati ken dou yalla souniou borom
@BabacarSy-c6k3 ай бұрын
Allahou Akbar kham kham rék moy deugg/kii yalla Na ko yalla samm waay
@momofaye2722Ай бұрын
Dieu est une cause causante,pas une cause causée.Donc il faut limiter la raison pour faire place à la foi
@amadougaye21416 ай бұрын
Yalla kéne douko lambatou dagua koy kham si lou lére Dieureudieufé Baye Niass