bouba ndour sur bougane Gueye et Ousmane sonko Wally seck et bougane Gueye
Пікірлер: 96
@AlimaSamb-xw6gd4 ай бұрын
Wally nous t aimons tres fort doundeul wereul ken doula diakhasser ak peuple bi ❤
@jadychatou1674 ай бұрын
Peuple non yéne,Wally dou dara ,simple chanteur rek laa,tee sou djitéwouwone guangou gordjigen au senegal toubab yi dikothiye féye alise bou wekh taal,tanéwoud kéne thi moromam you músiciens yii.
@fatoudiop54564 ай бұрын
Waly dé da khalate ni bou Momy done dounde dou bayi Bougane mou méleni beuyou ndeup thi réwemi té ame aye diabatame
@mamedara45184 ай бұрын
Wally on t'aime fort 🎉🎉❤
@khadeejahkonate50034 ай бұрын
Bougane nafék lá meunoul diakhassei waly ak keine wally dafa ame yar ame téguine khamna khélama soriwone rék motakh mouye mais dou Bougane dofbi moko dioylo 😢😢❤❤❤
@talibechiekhsopnaby34014 ай бұрын
machaallh Bouba sakhal CI don nék nitou deug boulasi dara dialé
@famaradiabang89084 ай бұрын
Je crois qu’il faut cesser de qualifier Bougane Gueye d’opposant. Qu’est ce qui fait de Bougane un opposant? À-t-il un seul électeur sénégalais derrière lui?
@yasinetawo80194 ай бұрын
Merci bouba ! Bougane dafa yebater❤❤❤
@coumbandao64474 ай бұрын
Wally mbok rek ladone dokh ak kolere wayee molene geneu kham ni bougane dou nitou dara.
@ClaireAdjalla4 ай бұрын
C'est sa famille par alliance
@ousmanediop16204 ай бұрын
On s'en fout de ça, vive PM SONKO, vive PR Diomaye, vive le Sénégal ❤🫶💯✊🇸🇳🙏
@PapiOuédraogo-k4u4 ай бұрын
Non wally meunoul def lénéne loudoul diappalé ay diarbaatam
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye4 ай бұрын
Tarkalla Difficile d Exister devant Sonko et Diomaye !
@Papiblack-i7k4 ай бұрын
Thiey wally mo sonou
@mbodjia-ss4bt4 ай бұрын
C'est simple a comprendre ,les neveux de wally ont perdus leur mère et grand-mere et si Bougane se trouve derrière les barreaux ces enfants seront orphelins
@evefal21274 ай бұрын
Wa mais khana bougane mo gueune yéne prisonnier yi gnake sene yaye, gnake séne baye, gnake séne diabare.gnongnou séne dome dounou aye orphelin?😢
@mamadoundiaye6844 ай бұрын
Mai Waly bokoul dra ak yénén prisonniers yi mai bougane si point @@evefal2127
@khadimka20584 ай бұрын
Bougane dh manoufi tek khel kene
@adjatraore77704 ай бұрын
Bien dit yawe tu as compris
@aminatasylla97294 ай бұрын
de toute façon on s'en que waly soit la bas ou pas les gens l'aiment pour sa musique et la il s'agit de l'avenir du pays , sama guayi yewoulen dou li moy développé ap rew
Wally aye diarbatam la done takhawou ndakhe séne yaye nékou fi niou diapou sene baye
@mamadoumare66554 ай бұрын
Ine faut pas diaboliser l'acte de waly. Avant tout Bougane est le père des neveux et niesses de waly. Svp politique ne veut pas dire parenté.
@ramatoulayediaw38644 ай бұрын
Wally etait la bas pour ses neveux deja leur maman n est plus .
@58Sosso4 ай бұрын
La musique de fond dérange vraiment ! Dommage !
@abdouka42794 ай бұрын
Bougane ❌❌❌
@BabacarDiallo-ls6ve4 ай бұрын
Sou bénène yoné délène wagnii sons bi yéna ngi niouy dérangé 😢😢😢
@YakhyaSow-ki1oh4 ай бұрын
Nguir yalla populación senegalés yeewoulen damaye laathie lan mooy importa Lili mou waakh🤦🏿🤦🏿nguir yalla populación senegalés yeewoulen 🇸🇳 Lili baan sance la aame,hooooooooooo, populación senegalés yeewoulen 🇸🇳😭😭😭🙏🏿♥️👍🏿
@ibrahimafaye87824 ай бұрын
Bougane défa xamadi dong❤❤❤❤❤❤
@TaphaMbengue-b2j4 ай бұрын
Bougane est impolie
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye4 ай бұрын
If faut aimer la réalité et la vérité !
@ChérifbounoumarLy4 ай бұрын
Rew mi 24 yow sa son biii mo Gina for wakhou bouba bii ban chance la am
@ahmethndiaye79434 ай бұрын
Mais yaw lolou ce n’est pas ton problème. Yaw yomba nga diakhassé ak nite han. Parles pour toi et laisses les Sénégalais tranquilles. Wally a fait son devoir Bougane a eu de la reconnaissance mou gueureum ko. Ce n’est pas de la faute de Bougane d’avoir été beau frère de Wally et d’être le père de ses neveux. Cela a son impact parce que c’est Wally. Mais chaque personne consciente remercierai n’importe qui, qui s’est occupé de ses enfants lors d’une simple absence. Surtout pendant qu’elle était en garde à vue. Bo xamé lénéne loutakh mouy djoy nga téyé ko pour yaw car cela ne concerne pas les sénégalais.
C'est quoi cette musique de hum, horreur; Merci Bouba
@SarrOusmane-m9s4 ай бұрын
Bouba Ndour daye fene reck tapet la mise mbougane dou ragal ok
@yancoubasonko86424 ай бұрын
Wally doit faire beaucoup attention
@sankounkanoute30674 ай бұрын
Il faut que Wally seck doit aller à cette conférence et soit près de ses neveux . Ils n'ont.rien compris.
@bambathiam47644 ай бұрын
Kouy mokame bo guisse bougane khame nee diff na hakhe momy moko top
@mbenguendiaga25374 ай бұрын
Bouba a reson
@Massiyuwe23C4 ай бұрын
😂😂😂😂 bougane togn kat la
@arameniang96084 ай бұрын
Waw musique bi si souf pour lan la ? Mai vraiment sof guèn trop
@moimeme10584 ай бұрын
Ils sont chiants à mourir Moi je zappe
@astoudieng12504 ай бұрын
Mais Waly souko nekhe mou Ande ak Bougane ndakh bu freramela pourquoi dou Ande ak mome
@Massiyuwe23C4 ай бұрын
Wally mom c normal nakh bougane mo yoron. Rakam kon no bougane man mel yona la mo nek fa mei andoul ak mom
@PeulBa-uo7rd4 ай бұрын
Sa musique bi mom mounon niak
@davedave63424 ай бұрын
Wally loudoul saytanè rek defoul lenen
@christopherouxmollard30874 ай бұрын
Doynawar torop
@deugrek33124 ай бұрын
Daffa Tékiwoule Dara ci Rééw Mi
@Afrique934 ай бұрын
C'est vrai c'est un dance pour Wally
@mamadoufall91854 ай бұрын
Mais yow loussi sa yone Wally moy Nidiayou Domou Bougane yi c'est très normal niou diapp Bougane mou takhaw assisté ko lolou meunouko Diakhassé ak Sénégalais yi
@MatybarraSylla4 ай бұрын
Ak lou mouna khéve wally sou démoul si bougane foumou deme
@khadyba89954 ай бұрын
Arrêtez de mettre des musiques de fond dans vos vidéos, ça fatigue et ne donne pas envie de les visionner intégralement.
@ChérifbounoumarLy4 ай бұрын
Del wanigi sa son biii
@mberryable4 ай бұрын
Presque tout Les politiciens sont pareils diakhasse rek pour am voix am nit yii seul Amadou Ba m'a convinqu lou rafet lou bakh rek lay wakh am tenu ak retenu
@madinagueye1684 ай бұрын
Sa diabar décédér même pas un an gua nek Fi di politique di fenn lolou dafay Deugueul gni wakh ni Bougane mo nakharal Momy bamu Décédér ndakh wakh you niaaw youmouko doon wakh
@abdoulayefall23124 ай бұрын
Souniou Yone Nèkoul si wally okay afèrou Senegal laniouy wakh wally baniouy ray sènegalè Yi bobou mougni Dèm ande ak Macky Sall ok Sonko moy Diomay Senegal si kaname
@TallaFaye-f6f4 ай бұрын
BOUGANE GUÉYE DANOU VEUT UTILISER LA MORT DE SA FEMME ET LA CÉLÉBRITÉ DE WALY MAIS PEINE PERDUE WALY EST AIMÉ PAR TOUT MONDE ET IL LE SAIT , IL EST LÀ POUR TOUT LE MONDE .
@CNMBusiness4 ай бұрын
Wally nako comprendre ay diarbate motakhe ak yakhe bathia alhakhira
@KanabiUsa4 ай бұрын
S'il vous plaît enlever la musique de fond ou diminuer la.
@christopherouxmollard30874 ай бұрын
Butane dafarew
@KaraJieu-p5p4 ай бұрын
En tout cas waly seck kharitou amadou sall la(doomou macky)
@KaraJieu-p5p4 ай бұрын
Kel neveux ? D'habitude les enfants des politichiens restent chez eux
@pablodjiba14 ай бұрын
Bouba ndour ces genres de bactéries ou microbes existent dans votre média familiale surtout à la partie auditive.
@DameLô-l4s4 ай бұрын
Bayil doull kapo
@NEWT21-l9l4 ай бұрын
Buba ndour tu tournes autour du pot si tu dis que tu protège pas quelqu’un qui insulte il as dit au 1er ministre de menteur donc Buba ne le défend pas
@zidanediop5424 ай бұрын
Wally seck pourquoi amul droit dem si bougane tamou diour ay diarbatam
@Diks-m4 ай бұрын
Que du n’importe quoi mais wally a le plein droit d’aller assister le papa de ses neveux mais ca ne va pas pourquoi s’acharner sur wally qu’est ce qu’il a fait
@NykaSenghorFemme4 ай бұрын
Waly de khel mi mo sori khamna ci diarbatam yi bougane ci bopam mo wara nek nit
@AissatouWade-z2n4 ай бұрын
Dem soutenir ay diarbate lolou dara nekouci monoul yakal Waly dara dinguenetem ak nite gni
@ibrahimagueye18454 ай бұрын
Tu diminués aussi ta musique
@Tokopik4 ай бұрын
Trop de bruit on entend rien
@christopherouxmollard30874 ай бұрын
Waly aussi doiarreter ses pleur
@patriciafaye94164 ай бұрын
Yow es ce que beugué nga niou dégueu la ak sa musique bi
@Moretallandiaye-y6m4 ай бұрын
😅😅😅
@deugrek33124 ай бұрын
Waly ne représente rien pour le Sénégal, Loudoule Aye thiakhane rek
@myrkosow97814 ай бұрын
Tu fais trop de répétition waly bougane bougane waly
@AliouFaye-f9o4 ай бұрын
Sa son bu bizarre bi doko dindi ndax ñu meuna tewlu wax dji
@ibrahimagueye18454 ай бұрын
Tu fais beaucoup de répétitions sur ton introduction
@LittleBuddhaForever-kc9zq4 ай бұрын
Yaw sa data ndaye, wally meunouleen si moom touss
@AstouGaye-dc8nb4 ай бұрын
saway yaw ana loufi doy wara......?
@senegalaise22514 ай бұрын
Yaw bouba katal sa ndeye feulé😊
@IbrahimaSamb-f6p4 ай бұрын
Bougane moytoul xexou mbede manne ga dieul coup perdu
@ndateyalla27844 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂
@Varbitv4 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@BaniAadama4 ай бұрын
Punaise pour présentation vidéo bi di répéter wou du répéter wou pendant 2:30 minutes. Allez à l’essentiel rek akh…
@aissatoungom3194 ай бұрын
N importe quoi.
@LoMen-d4c4 ай бұрын
Les patriotes, Pape Alé nous a manqué de respect. Wally est opportuniste et hypocrite. Il n'a rien de patriote. Ce type me dégoûte, il est prêt à tout pour de l'argent. Il n'a rien à voir de son père Papa Thione que je respectais.
@zeusdiarra194 ай бұрын
Way merde avec l'histoire de l'ambassadeur de la RTS nouy wakh affaires de mbok guay wakhi doff
@ibrahimadiaw8304 ай бұрын
En tant patriote moi je ne blâme pas Wally limou yeug bay dioye mom rk miko xam xel meune na dem si Rakam dc bayilen yoyu wally devoir mou yobbu xalei si s'en baye