Mère bilay lou méti Guay expliqué ni. Mé sa dom yalnako yalla deup bamou gnewate say lokho. Kou am contact mère bi svp. J'ai le coeur meurtri 😥
@amsatoukounta697517 күн бұрын
C’est désolant maman prions pour que le bon Dieu vous rendent votre fils en bonne santé
@mariamasako-p4i19 күн бұрын
tout va s'arranger inchalla il faut continuer de prier et faire des douas LE SEIGNEUR sera avec toi
@capitoukeys12 күн бұрын
Quel méchanceté cest incroyable et inadmissible
@ArameDiop-v1j9 күн бұрын
Kali merci❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AmyDiallo-dx3sg18 күн бұрын
Le respect avant tout si tu aimes ton mari tu dois respecter sa mère
@KheweTop19 күн бұрын
Étude Canada nimou mété sa yaye fayall la 2 ans niou séparée la ak momm bakar bobou dé kouko atane na yénou
@ThioubaNdiaye-h9t19 күн бұрын
Métina waye 😮😮😮
@reine549219 күн бұрын
Moke amatoul. Bilakhi dafa ame aye moke you osé, seytane. Yallah na la Yallah diapele Sokhna si. Diougueul thi sa dome, lou lokho defe lokho meune nako dindi.
@IbrahimaFaye-nx5ny18 күн бұрын
C est tres trisse vraiment courage mère
@AdamaDiouf-h8g17 күн бұрын
Aka fée baré yalla guemoul nélawoul
@stafiroulaha19 күн бұрын
aye domou kharame la niou dagaye yore sa dôme bamou âme diarigne niou dévié ko té masouniouko dieundeule bic mais khalisse rek
@SaraSara-rw1qf19 күн бұрын
Billay defa meti
@NdiayeBoris14 күн бұрын
Pourtant remarqué wo léne Dara mère bi dafa ni mirage bi pa bi bayi lépp la bolé diokh ko boy bi AK li si akk mirage légui est ce que dou répercussions yi Moy dal nonou si adouna wam ah .....
@souadoundiaye274418 күн бұрын
L'âne moye guewel ak guer après gua ni djoulite gua dara douko dal arrêtez votre hypocrisie doule waye argent rek guen gueum
@thioroniang138413 күн бұрын
Bilaye walay merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤
@mariesec82418 күн бұрын
Mann déy bingua commencé wakh sama xol diéxone n'a lol wayé fingua diéxalé moma méti lol ndakh mouy yaw di sa borom keur bi guéneu adouna kéneu gueunou thi guéweul. Bou sa dérét diéxé do tamou koulay may déréte , Adam ak awa nioniou mégneu nioune niépeu 😢😢😢
@pauleludy937318 күн бұрын
T inquiète sa ne va pas durer Dieu ne tord pas
@khadifall819218 күн бұрын
Au début j'étais avec toi mais yaye gueuno guéwel yi sa djeukeur gueunoul guéwel yi
@Bluelove44718 күн бұрын
Vraiment elle est bizarre
@KhadijaLy-c7j15 күн бұрын
Nn mes lolou amna niokoye doundou tmt
@NdiayeBoris14 күн бұрын
Yéne daguéne gate xel lol Sakh wakh dji so léne ko basé si guéweul daguéni djoum.ici il s'agit de respecter la mémoire du papa qui est décédé apprenez à respecter les dernières paroles des défunts sinon c'est un grand danger et cela peut avoir des conséquences et ce dernier ne sera pas en paix mère bi limou wakh deug la si c'était votre père c'est sur que di guéne si takhaw xolate léne li guéne ni wakh way
@capitoukeys12 күн бұрын
C plutot 1question de principe .... gueweul ou pas le cas est compliqué on ne vole pas un enfant à sa mere .... elle a me droit de dire non
@capitoukeys12 күн бұрын
Elle a maudit son fils par colère ... kalifone tu nes pas intelligent le debat nest pa gueweul oupas ... elle a raison de maudir son fils ... sa fait tres mal o coeur .... ....
@magettediop198916 күн бұрын
❤❤❤
@ramamatasow764517 күн бұрын
Ndeyesane Senegal lifi Am mètina trop
@khadydiop359118 күн бұрын
Li dafa bari Senegal May nit diabar khamo ay mbokam kèn wakhtanoul khamo bèn mbokou Kou Gorki li nioune am nagnou même cas sèye bo khamnè papay Kou djiguènki mo dèf lèp kèn yeugoul lèp ndakh interet 🎤mère dioubeul sissa dome moy deug nit gni dagno bone pour lane aquimo domou diambour
@KhadidiatouSY-c6k13 күн бұрын
Doyna war déroule dougue fene Allah l'omniprésence, L'omnipotent, Le Miséricordieux dîna safari leepe inchallah kali Merci! Thi diappale bi n'gue neke.boumou reu🎉be dome loulou bakhoul ne diouly niane Allah dinasafara l'expéditeur.
@mariamandiaye238918 күн бұрын
Vraiment c triste. Yala naleen yala atte.
@Speedrunproedits19 күн бұрын
Bilay je la comprends Li metina trope worna yalla
@diatouciss692017 күн бұрын
Ndeyysane
@pauleludy937318 күн бұрын
Ne le maudit pas se n’est pas de sa faute
@SENEGAL30312 күн бұрын
23:52 pour lane ngay reub sa dom tè mou ler la ni tayoul limouy dèf... 24:27 parcrque kali wakh nala sa dom nena dinala wo ngay commencer deugeureul. Les parents autoritaires nioy takh sen dom yi di fippou.
@NdeyeNdiaye-bg6bb18 күн бұрын
Non non il ne faut pas dire de mal choses á ton fils pacience non reb á ton fils reb non
@oumarndao480314 күн бұрын
Ça c'est inadmissible
@AissatouNdoye-gd9xe16 күн бұрын
Li metina woroko nianale li li bouko yalla ndangou yaye delou yeureum ko nguir ndiourel metina nekhoule yawite niane loule Yeurmande yalla yatouna teh li gua wakh ni fofou gua tolou ci yalla war gua mena diegale surtout sa dom amoule koudoule yaw sene baye de' bayilak gnome bou ndok touro ane baka desse gnou ni deedete da gnouye roti yate takale sa seere bamou deuguere teh dimbali sa dom il a n'en besoin je suis fière de toi et je comprends ta réaction tu es toute seule ceux qui devaient te soutenir t'envie c'est ça le combat leur père te regarde et n'apprécie pas ta décision ressaisis toi et fais tout pour récupérer ton enfant
@pauleludy937318 күн бұрын
Le jour QI elle aura ce qu’elle veut elle va le quitter
@KhadidiatouSY-c6k13 күн бұрын
Niit kou bakhe deye diégueule nianeul Allah sa dome deloussi legueye mo diappe boul wakhe dara mou deloussi moyé sa n'dame .ma chérie setal boubakhe li le la wakhe.
@pinklady-j4p19 күн бұрын
walaye je vie la même situation on m’a pris mon fils que j’ai éduqué et investi ça ça presque un an on ne se parle pas on a le s même genre de belle mère et de belle fille et pire moi ma belle fille couche avec d’autres hommes et mon fils ne dit rien ça se passe ici en amérique
@Gggge_dudiolof953619 күн бұрын
Il faut aller voir les marabouts lou lokho def lokho meune nako dini
@nourradam639119 күн бұрын
Merr nena mom yayam malien la kon na bayi aferou guewel bi
@MaimounaDieng-o4j12 күн бұрын
Do. Diema nangou seye. Pour récupérer sa dôme legui majeur là naxantel ak môme faut arrêter aussi de polémiquer avec sa femme les griots sont des musulmans. Mère yawitam nak
@damesene376110 күн бұрын
Billahi deugleu dangay am problème ngou leye retane rafetoul
@MatyNdiaye-wc4jb11 күн бұрын
Mere balalle sa Dom the Yalla takhe ndakhe Madiagne guerela dieugalale sa DOM thia Yalla takhe
@mariamasako-p4i19 күн бұрын
non non il faut pas maudire ton fils du moment que tu as dit qu'on l'a maraboute il faut l'excuser
@elagegueye331019 күн бұрын
limamou thiaw dou yenente billahy kouko guem do djoulit mouhameth psl mougi medina teudeu kou trohal sa yay troh
@AmyDiallo-dx3sg18 күн бұрын
C’est pas de sa faute il faut pardonner
@couradiopndiaye962019 күн бұрын
Sa make bi moye mbam degue sa dôme môme niako guako tayou ko😢
@enzojr911416 күн бұрын
YAYE BOU BAKH LA DAFA YARE AYE DOMAM DOMAME BI MO DONE FOTE TAPIS DJIOUMA SCAT URBAM BI
@fatimasbn251419 күн бұрын
Thiey sénégal
@MaimounaDieng-o4j12 күн бұрын
Mère yawitam nak delossil sa xel xana do djoulit ngueweul d'où nit d'où djoulit seye afferou yallah là domame faratala la def
@WeulliThiaw16 күн бұрын
Sénégal complot rek seurigne ligueye note ki ba moi bayi aye famille ligueye dieukeurou diambour bamou bayi dibaram fête ak yaw nganane dama dingue Sénégal kou fi moytouwoule dangaye kheuye dof
@AmyDiallo-dx3sg18 күн бұрын
Astafirla même si tu es fâché ne dit pas ça
@alphaamadoudiallo909717 күн бұрын
❤️💖💕
@BintouLo-q9g14 күн бұрын
Sénégal mettina
@Monroe202014 күн бұрын
Lou way Def boppam Kepp kou deudeulé yaye ak dom do ngako guiisss
@amantubillahi962818 күн бұрын
Yar sa doom moy djaaralé sa dépense tchi kénén. Lii mooy exemplou bokkaalé deugg. Mais maman sétaatal sa diné maman. Moytoul bokkaalé sa Boroom. Sétlouwaatal.
@aiebobosow129419 күн бұрын
Metina lol,wayé bulko molou. Fexel nga recuperé sa dome,niane nagne lako.
@AmyDiallo-dx3sg18 күн бұрын
Il faut tout faire pour le récupérer mais pas les paroles la
@KineThiam-w6u19 күн бұрын
Fille a papa 😂sama dome papá dji reck laye deglou
@ndeyefaye183314 күн бұрын
Metina yaye
@FatoukœurMbow11 күн бұрын
Métina billaye
@yongfresh84217 күн бұрын
Non mére waroko mollou dh Iow yaani dagneko geuleumeul kay kon kham ngani limu nekei tayouko wala dett
MERE Danga Wara xamni.Nonou Nga Défont Ba am DIEUKEUR BAYIL KHALEYI NIOU SEYE kounekak Jamonom mano seye sa seye SEY SEYU JAMBOUR bayil sagacité kou SOXORNGA
@AmyDiallo-dx3sg18 күн бұрын
Ne dit pas ça s’il te plaît
@MahanyFall19 күн бұрын
😭😭😭😭
@thioroniang138413 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂
@khadifall819218 күн бұрын
Ta soeur est jalouse de toi
@diarrabajob7 күн бұрын
Toi même tu as dit qu'on a maraboutè ton fils faut pas l'abandonner aide ton fils stp madame sinon dafay sankhou yaco heubou 9 mois boul topou sa khol sister soy meirei meirei sa famille
@awagadiaga955319 күн бұрын
Hoooo li metina trop bilahi walahi 🤦🤦🤦🤦
@AlimikoNassirou-bu8fn13 күн бұрын
C'est ton problème la maman é inpoli
@ThiamFat19 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂
@manedione843319 күн бұрын
😢❤
@NdeyeNdime-h1z10 күн бұрын
Li kouko doundoul mano ko kham yalla yalla yi yangui df lou pir t kn doussi wakh
@diarrabajob7 күн бұрын
Madame li meitina trop n'abandonne pas ton fils lou lokho def lokho meunenaco diny
@maannandiaye746313 күн бұрын
Bouka moolou tayou ko baal ko
@ndattasamb46798 күн бұрын
Khana sa dome kimou tak dou djoulite wala teug wala guéwale adouna amoule solo
@MaimounaEmich19 күн бұрын
Salam, Kali Merci Merci c'est drove il ya rien a rire
@MaimounaEmich19 күн бұрын
C'est pas drole 😢 jai 3 garçonts
@mamembaye336519 күн бұрын
Metina
@senegalmycountry349319 күн бұрын
Je suis pas daccord avec la dame, epouser une gueweul est mieux k epouser une non musimane
Incohérent pourquoi nga gueum dagnko liguéye. Ba paré tu le menace. La fille elle est vulgaire. Et même toi pareille " leuf mon takh bou bayima" Tu pouvais engranger sans dire que dafa tack Guéweul
@rokhiyatoudiallo928 күн бұрын
Dalaye menencé rek Lou lokhô def lokhô bouko nanal Lou Bone taiyouko andoul ak kélame
@maimounambaye905818 күн бұрын
Au début mere yaw la andalone mais gueweul gueno ko gnoune kougnou bagn gnou bagn la khana yaw do dioulite
@MarieMbow-jy8gh19 күн бұрын
Mais c est du n'aime porte koi,il prend la fille des géant avec force,c est pas dit tout normal , c est pas dit tout sérieux mais c est quelque Sénégal,on est, CV est du n aime porte koi