Kawtef😱: Aziz ndiaye après sa polémique tranche indexe…Lahat dafa wara bayi…gaston mbengue…

  Рет қаралды 93,560

AL BOURAKH TV

AL BOURAKH TV

Күн бұрын

Пікірлер: 204
@MoussaSy-nr2pp
@MoussaSy-nr2pp 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye d'où nale way kilifa rek Moy wakhé nii 😍🙏
@bandapape
@bandapape 7 ай бұрын
quelle personnalité que dieu vous assiste vous protège sokhor bakhoul aziz n’as pas le temps di complot si combat thiatou yarakh doudou sane des lutteurs qui ne valent même pas 10millions diam si ioe al amine ❤❤❤❤
@DjibyMbow-s6k
@DjibyMbow-s6k 7 ай бұрын
En tout cas lamb dji bénn roi leu am mouy modou khagne lô 👑
@MoctarDiouri-ir4hu
@MoctarDiouri-ir4hu 7 ай бұрын
Hors sujet
@MamadouSow-ie4qn1782
@MamadouSow-ie4qn1782 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye est véridique ❤❤❤
@OusmaneSambe-l3f
@OusmaneSambe-l3f 7 ай бұрын
Merci Aziz deug pirr nga wax bilahi ❤❤❤❤❤ Lahat Ndiaye na yém plassou courtier dalou Aziz sax dou moromam
@alassanemane3021
@alassanemane3021 7 ай бұрын
Machalah Aziz Ndiaye wakh dji rafetna trop 🥰🥰🥰
@babacarsadikhsy596
@babacarsadikhsy596 7 ай бұрын
Bien parlé Aziz! tu es véridique et responsable! Abdoul Ahat Ndiaye doit rester a sa place de manager
@mamadousarr3371
@mamadousarr3371 7 ай бұрын
Merci beaucoup Aziz ndiaye lahat ndiaye dafa bari problem
@AmdouKoulybaly
@AmdouKoulybaly 7 ай бұрын
Adouna amoul.solo
@fallouniang399
@fallouniang399 7 ай бұрын
Vereman Azize Waxale waye ❤❤❤ ki domram la dafa bari nday wax
@baraseck4939
@baraseck4939 7 ай бұрын
Lahat Ndiaye mo eupeul li Aziz wakh ak lim wakh boukoul Aziz da degue fadam diko wakh en live mais lat Ndiaye da wakh fadam da wo Aziz wakh thiatou yarakh dou beure te deme woul nonou
@papeseck9969
@papeseck9969 7 ай бұрын
Bilahi walahi Souguéne khamone ñome Aziz ndiaye yi bilahi aye vrais businessam lañou louñouy affiche ci kaw ak liñouy deff ci souf c totalement différent louma lerrr lay wakh
@thiattobb423
@thiattobb423 7 ай бұрын
Yaw nandité nga
@2quevosquevos242
@2quevosquevos242 7 ай бұрын
Deug pir gua wakh ay Deum laniou deh khaliss laniou diamou
@momoseck1617
@momoseck1617 7 ай бұрын
​@@2quevosquevos242kén wakhoul li nga wakh ni Sa kadou da gnaw Gnoune ay djioulitt lagnou Wassalam
@Sagemorc
@Sagemorc 7 ай бұрын
Set si yala Dara Lerou lassi
@momoseck1617
@momoseck1617 7 ай бұрын
@@Sagemorc sénégal da gno boone Loutakh sénégalais beugoul guiss kou am
@iscojo6600
@iscojo6600 7 ай бұрын
Aziz sa Khilifeu #Al Amine Sy (RTA) khana téréwoula wone lamb?? Dernièrement trop de polémique !!! En plus t’as recommencé juste après la disparition d’Al Amine…. Reste calme
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 7 ай бұрын
Abdou Late ndiaye mome dafa melni makane mbenge moye papam nite dangaye geum sa bop
@ilimanediouf3629
@ilimanediouf3629 7 ай бұрын
Macha allah abdou aziz alé ndiaye wakh bi rafetna leep leer n'a ❤❤❤❤
@mamepathengom9398
@mamepathengom9398 7 ай бұрын
Merci peul bou raféet 👏lou ame solo nga déf✍️Abdou lahad nimou wakhé kou xamoul daye fokni Azize dafa wakh pour diakhassé Fadam ak addouna ✍️Lahad nak mome takhawayou diakhassé lafi néké té togne na Fadam ak Bakari 🤷dafa eupeul trop🙅
@lesseseyni2659
@lesseseyni2659 7 ай бұрын
Tt ta fait ✅
@PateMbaye-ec5em
@PateMbaye-ec5em 7 ай бұрын
C est pourquoi il est important d écouter 2 versions ! Lakhad , tu es revoir ta copie !
@DjibSarr-k5x
@DjibSarr-k5x 7 ай бұрын
Aziz mi sayetané la😂sisouf layedef😂
@iibassndiaye2886
@iibassndiaye2886 7 ай бұрын
bien parlé franchement adouna amoul solo 🇸🇳🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
@thiawbadiane6873
@thiawbadiane6873 7 ай бұрын
Mane dé fadam nama balle❤dama rousse sakh bilaye❤😢
@ousseynoutoure518
@ousseynoutoure518 7 ай бұрын
Aziz lahat à tort mais lamb dafa am lobbies lolou c clair yanguini di créer sa couronne té yafi tegone combat Balla vs modou lo si souf Nous ne sommes pas bête
@abdourahmanesow2581
@abdourahmanesow2581 7 ай бұрын
Nafekk boy makk la c'est lui qui pleurniche
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 7 ай бұрын
Ces lobbys sont ds tous les secteurs du pays cette lamb est-il organisé on sait pas qui est professionnel ou amateur des managers non qualifiés qui est le lutteur professionnel ou amateur qui est qualifié pour être promoteur c’est du foutisme et guewelism
@aliounesarr1382
@aliounesarr1382 7 ай бұрын
parceque makkan dafa cool rékk nguén beug déf deumleu rayla dialéla avec lakhad Ndiaye dounguén meuneul makkan touss wayé makkan bou dofdoflou ba bayi lakhad Ndiaye sankou Aziz lakhad Dou ménager rékk dafa bok thi structure. Aziz yaw danga wakhone danga bayi lamb ba wakhko Serigne Abdou Aziz Al amine bouniou démé yomal khiyam dinga rouss. sa pékhé yép Moy tass Gaston production AK JAMBAR production té dangay échec inch'Allah
@ndiogoundiaye3772
@ndiogoundiaye3772 7 ай бұрын
Azize a bien dit big chapeau 🎉
@agencysport2914
@agencysport2914 7 ай бұрын
Vraiment Aziz tu a parler comme un leader, tu a bien fait Lahat n'est pas un dirigeant il se fou de tout le monde merci encore Aziz
@Mamadou-Fall
@Mamadou-Fall 7 ай бұрын
Aziz vraiment il est extraordinaire ce gars mashaAllah!!!!
@sondji1412
@sondji1412 7 ай бұрын
Abdou lahat Ndiaye sa date yaye doméram deug la bilay😂❤😅
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 7 ай бұрын
Moi je comprends pas la lutte avec frappe au Sénégal y’a que des polémiques zéro professionnel on sait même pas c’est quoi ces sites rien de professionnel aye wérenter rek
@CASI7797
@CASI7797 7 ай бұрын
Hahaha Aziz Ndiaye c'est l'hôpital qui se fout de la charité
@ousseynouwade7066
@ousseynouwade7066 7 ай бұрын
Yangoul aziz na fekhela mako wakh lahat Ndiaye mongana dioup aziz Ndiaye
@cheikhcisse1278
@cheikhcisse1278 7 ай бұрын
Bien dit Aziz mashallah
@momoseck1617
@momoseck1617 7 ай бұрын
❤❤ machallah Aziz dama yeureum sey none❤
@azizngom8741
@azizngom8741 7 ай бұрын
Bilahi deug la abdou lahad dafa Melni mo diour nite yi il est très hautain ,Sénégal nak dagnouy diay mbote bamouy’mbeuker
@mamadoumoustaphadiop1650
@mamadoumoustaphadiop1650 7 ай бұрын
Rousseul Prénom esk doko dindi
@SoftlSotfl
@SoftlSotfl 7 ай бұрын
😂 Saway sa clavier bi tameu na bindeu affaire bi d 😅😅😅😅 eskey guani lane répète 😂😂
@ousseynoutoure518
@ousseynoutoure518 7 ай бұрын
Clavier bila​@@mamadoumoustaphadiop1650
@fifty6292
@fifty6292 7 ай бұрын
​@@mamadoumoustaphadiop1650Boul Sonal nite yi tour deukoul féne kounek khamni koumouy wakh Senegalais ngay wane wére mouy khol sa baram sof torop
@azizngom8741
@azizngom8741 7 ай бұрын
@@fifty6292 diadieuf frère gars yi deh moy lolu dagnouy dieul details defko Lou graw clavier day teub comme Lou nite di dioumer
@mouhamedfall3783
@mouhamedfall3783 7 ай бұрын
Abdou lahat dafa rew trop kon mo mom nitt yii
@sanadieme756
@sanadieme756 7 ай бұрын
Lakhat moom Rek lobii😅may wakh mouy sakkëto Guinaw rail ak seras Baala may Dë mou nane moom dou raggal Dou touche Nioo Deuk Doo woon Guinaw rail Quartier mango gui Bobou Bathie seras mogui mbapatt baa nii mou douguë sii lamb koon khaam na ko dou deureum yaw ak fadam dou niveau wakhatou Bacary sakho yaroul niou beug leu moo geune sa tekk doff bii gua nekkë yaw
@Wrestling1890
@Wrestling1890 7 ай бұрын
😂😂😂 dou dara waxx rk la meune
@MountakhaThiam-gh1ni
@MountakhaThiam-gh1ni 7 ай бұрын
Très bien dit aziz ndiaye lat ndiaye loumou bokak assane gueye rfm
@BayeNiasse-b9s
@BayeNiasse-b9s 7 ай бұрын
Certes Abdou lahad daffay wakhé khole mais nakk Aziz Ndiaye kilifa dafay moytou wakhou soufe yaw soo wakhoul woone AK lahad dou âme Fitou takhaw thi télé wahe né Yaako wahe que fadam moo téré boy bi beuré
@abdourahmanesindidi1818
@abdourahmanesindidi1818 7 ай бұрын
Khana dego limou explique fi?
@Marasaliou
@Marasaliou 7 ай бұрын
Li deh mo geuneu yanou mahana
@babacartine4464
@babacartine4464 7 ай бұрын
Abdou Lahat mo nité woule deug la Fadam wakh ak coach bakary claf bou tollou ni nga beug fay boy yi 2 millions dilene utilisé
@dierydiao6574
@dierydiao6574 7 ай бұрын
Vraiment aziz tu as bien c est lahad qui doit revoir son comportement
@papahabibdiop
@papahabibdiop 7 ай бұрын
Nn li aziz wakh mo geuna raisonnable 🎉
@lemarseillais3019
@lemarseillais3019 7 ай бұрын
Lahat dh Combat Jackson vs Lac rose lako simile sapo nii kii dafa dof 😂
@AbyNdiaye-xs3hi
@AbyNdiaye-xs3hi 7 ай бұрын
Aziz mi domerame la
@SegaNdiaye-mv5bt
@SegaNdiaye-mv5bt 7 ай бұрын
Aziz legui dafa yeuk bopam depuis mou nek ci show bizz di doundou beuz
@ibrahimalaye7603
@ibrahimalaye7603 7 ай бұрын
Aziz balma akh wakhou lahat bi takh na wakh la mousi ba lo siento mucho 🙏🙏
@alunendour3815
@alunendour3815 7 ай бұрын
Aziz ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MomoDieng-j9q
@MomoDieng-j9q 7 ай бұрын
Aziz ndiaye faut types leee il n'est une personnes s'insère wa lambe yeup la corrompre
@bachirdiop19
@bachirdiop19 7 ай бұрын
Lahat ndiaye dafa yabaté si bopam mome li takh Paf teuga toul lamb sila bokou ,il doit revoir sa façon de faire
@ndomarafate3161
@ndomarafate3161 7 ай бұрын
Mais li kay garawoule Aziz daf ko dégué si fadame wakhko lahat lolou kay dara nékou si
@MomoGueye-j3x
@MomoGueye-j3x 7 ай бұрын
Mai’s lakhat moy doul Kat mo deup wakhji
@bigttt9014
@bigttt9014 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye mo gueune niaf ndem Senegal Mai’s se beus ngi nieuwe legui domi khath le rec
@goradiop4611
@goradiop4611 7 ай бұрын
Billahi aziz Day doulll aziz yaw ya yakh lambe dji
@mamadoumatarsow1191
@mamadoumatarsow1191 7 ай бұрын
Yaknako yalla yeureum tè kharèko aldiana firdawsi wayè le travail foit continuer
@moussadiop6111
@moussadiop6111 7 ай бұрын
Billahi azize defoul darra abdou lahad Ndiaye mo dioume rek
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 7 ай бұрын
Lahad wakh na deug lamb dafa am lobbi Aziz Ndiaye yaw khaliss guaye diaye
@Wadiomfall
@Wadiomfall 7 ай бұрын
Khalisou Covid 😢
@omarbadianeomar978
@omarbadianeomar978 7 ай бұрын
NICe
@LamineMbaye408
@LamineMbaye408 7 ай бұрын
Claf queens boy ,serigne ndiaye 2,fils de balla, doudou sané
@MoussaSylla-p6k
@MoussaSylla-p6k 7 ай бұрын
Waxal way Aziz ❤
@ndeyeastou7501
@ndeyeastou7501 7 ай бұрын
Vraiment lat limou déf ni rafettoule mais Aziz limouye reproché lat Ndiaye mome moko fi dak Aziz mofi guena yeuk bopame emplus mofi dak forcé niti son choix mongui ni forcé niou empreure
@Leuzsonko
@Leuzsonko 7 ай бұрын
Da am xaliss am thieur si Senegal nieupa ko beugg talibè cheikh bi
@falloudiagne5902
@falloudiagne5902 7 ай бұрын
Diadieuf way goor dafay gnémé wah deugu❤
@64FallAmadou
@64FallAmadou 7 ай бұрын
Lima def reih lahate neina dou moy yalla Sénégal waay😂😂😂
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 7 ай бұрын
Abdou lath diakhassé na promoteur yi diakhsse lamb dji
@abdouthiam3312
@abdouthiam3312 7 ай бұрын
Merci Asiss ndiaye ❤
@MouHed-e8u
@MouHed-e8u 7 ай бұрын
Merci aziz bome apoll wone khaliss ma maye la 10000 mi yalla bakh na contane na si iow😂😂😂😂
@diayoussou8823
@diayoussou8823 7 ай бұрын
Badola kén douko diokh micro
@diaibrahim6798
@diaibrahim6798 7 ай бұрын
Merci Aziz 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
@ousououssououssou
@ousououssououssou 7 ай бұрын
Peul bou rafete mom vraiment tamite 😢😢😢
@mordiop5555
@mordiop5555 7 ай бұрын
Lahad na bayi limouy deff rafetoul
@assniang2252
@assniang2252 7 ай бұрын
Yalla deugue la beugue hana Gaston dou sa baye ya neuke teugue bayilene nahane tayi
@Victoireman
@Victoireman 7 ай бұрын
Lahad il a raison lamb da amme lobby, yaw fi nga nekk di khekh couronne modou lo bi....😅
@delaypeuimporte463
@delaypeuimporte463 7 ай бұрын
Franchement y’a anguille sous roche iow teugo dou sa lamb bayi ga lamb Louy si sa gat ba gay wotei di wakh Lou nieuweugoul Aziz weigh ga dounk Est-ce que créer wo problème bi sakh di woter di digler ay solutions
@beuguebambaseck4916
@beuguebambaseck4916 7 ай бұрын
XANA LEGUI GNI DI TOP DI WAX AZIZ MOY WAXLO NIOM BOUCHER FADAM DI NGEN TEUTHIE SEN GAAT YI TÉ BAYI SOSS AK JOUÉ AU FILM SI SEN XEL AKI CASTING ☝️MERCI ZIZ DOXALAL🙏
@Victoireman
@Victoireman 7 ай бұрын
Aziz daay tek xel...lamb da aame lobby...
@khadimsow7149
@khadimsow7149 7 ай бұрын
Merci Aziz 😍
@OumarLy-jw4gd
@OumarLy-jw4gd 7 ай бұрын
Bayile'n sokhor Aziz Gathie ngualama
@jalediaw4008
@jalediaw4008 7 ай бұрын
Merci aziz almine
@ousseynouwade7066
@ousseynouwade7066 7 ай бұрын
Mane sen desebi wakhou fi d'ara mak dou gawtou moom aziz Ndiaye moy fen paske mak dou gara wakhe dembou lan fi repaire aziz Ndiaye ak makan
@aliounesarr1382
@aliounesarr1382 7 ай бұрын
fadam dafa niakk fayda ponkal bougnouy utiliser rékk leu
@khadimndiaye9492
@khadimndiaye9492 7 ай бұрын
Kou wakhe fégne aziz toudou. Fadame toudou gua bakari sétossi dara
@domousenegalinfo9563
@domousenegalinfo9563 7 ай бұрын
Parcek abdou lahat mossi dougal gnognou
@ousseynoutoure518
@ousseynoutoure518 7 ай бұрын
Waxal dé
@mohameddjaringtedrame4877
@mohameddjaringtedrame4877 7 ай бұрын
Aziz akh Modou Lo mola dal do nittu bu bakh
@OusseynouOuz
@OusseynouOuz 7 ай бұрын
Vérité absolue Aziz Ndiaye
@TallaFaye-y8t
@TallaFaye-y8t 7 ай бұрын
Vérité absolue
@aliounesarr1382
@aliounesarr1382 7 ай бұрын
problème amoufi yaw yay problème bi dakh mbeur yi AK sén ménagers yi lou lér lagnou signé yaw Loy lidieunti thi problème you diambour lakhad Ndiaye dagnouy rafétlou liguéyam lamb yaw yay loobie bi lakhad Ndiaye mola guéneu nékk wagga
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 7 ай бұрын
Et comment un ménager peut travailler comme un travailler avec un promoteur
@modouseckseck9893
@modouseckseck9893 7 ай бұрын
Aziz de khalela mais Ku Bakh la te mana rafetal
@lafarndiaye6204
@lafarndiaye6204 7 ай бұрын
Merci beaucoup aziz
@karainfo3891
@karainfo3891 7 ай бұрын
Effectivement Aziz defar la beugone Bilahi qui nit kou bakh la
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 7 ай бұрын
Abdou late ndiaye geumeul sa bop yangi melni deuko kabe gaye kou deuke kabe gaye dou dou ngourou kene
@cheikhoudamba
@cheikhoudamba 7 ай бұрын
Kane la doungourou saway ki dafay liguéy nioukoy fay doff nga rek
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 7 ай бұрын
@@cheikhoudamba abdou late da yakarne mo mome lambji mo moul lambji ba wakhe mou geud ko lolou mome menager rk la
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 7 ай бұрын
@@cheikhoudamba na bayi makane mbenge mouye wakhal bopam makane amna laminge
@AliouDieng-gu1tp
@AliouDieng-gu1tp 7 ай бұрын
Merci azize
@diogenelaerce2197
@diogenelaerce2197 7 ай бұрын
Aziz bayil doullllll t’es le premier domerame dans ce pays….
@ibrahimafaye5737
@ibrahimafaye5737 7 ай бұрын
Lakhat limou yakka si lamb dji mo barii te lepp pr son propre interet
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye bayile sokhor abbou lahade deugue rak la wakh
@cheikhfall4377
@cheikhfall4377 7 ай бұрын
🇺🇸 Vraiment actroces doÿna Warr entouka l'honneur de nôtres lutte est bafouée par le mafia ✨ Aziz Ndiaye vrai Nandité l'eu 😅
@taphadiop6081
@taphadiop6081 7 ай бұрын
Mbaw mome dafa beugue thigou com dou mak niak fayda
@mamadousylla1789
@mamadousylla1789 7 ай бұрын
Sonko lime wakh lerna porté ko plainte rék mou diékh légui gnépou yarou😮
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye yaw dagye doul ndayam rak
@AmadouDia-q3m
@AmadouDia-q3m 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye à vie, rien de retour
@SegaNdiaye-mv5bt
@SegaNdiaye-mv5bt 7 ай бұрын
Yaw Aziz da nguay thiouthie fi thiouthie fè tè do manager do promoteur li ngua fi wax yeup yaw la war tu penses tout savoir alors ay batailles physiologiques rek nguay def deugue j mome dina leer nagne tè dou yague maffia bi ame ci lamb j nieup wax naniouko
@babacarsene607
@babacarsene607 7 ай бұрын
Merci Aziz Ndiaye
@PapeBalde-i7r
@PapeBalde-i7r 7 ай бұрын
Todj n'a fadam DH néna dfa wo Aziz Ndiaye Niko boy bi d'où beurré t loulou live la wone
@AliouDieng-gu1tp
@AliouDieng-gu1tp 7 ай бұрын
Abdou lakhate ndiaye day utilise boy yi
@Ydakh-ui5yo
@Ydakh-ui5yo 7 ай бұрын
politiciens gnola geuneu gnaww fouf ta lougnou tékk gnou guissko bayil ték khélbi
@Pijunior-cu8lw
@Pijunior-cu8lw 7 ай бұрын
Lahad dof la genrou nit yi bougnou nekè sa wett si ay blem rek guaye nekeu
Wednesday VS Enid: Who is The Best Mommy? #shorts
0:14
Troom Oki Toki
Рет қаралды 50 МЛН
-5+3은 뭔가요? 📚 #shorts
0:19
5 분 Tricks
Рет қаралды 13 МЛН
Ho quel Danse De Aziz Ndiaye et Miss Ndiaye Ndeysane son fils
15:24
Bprod media TV
Рет қаралды 72 М.
Zarko cogne sur Gris Bordeaux " khamon Nani combat bi damalay…"
15:26