Siteu moy borom senegal wakhatouma Nk diameugueune nk
@ElhadjDiouf-k7q3 сағат бұрын
Yaw situé sa papa la 😂😂
@CheikToure-cl2jd2 сағат бұрын
Sa date yaye
@NabouThiam1467Сағат бұрын
Situé😂😂😂😂😂😂
@KhadimMbengue-p5s31 минут бұрын
Zarko yaw sakh bogneuwé diamaguen you lécela
@adamambodji5368Сағат бұрын
Deug rek ga wakh zarco limou wakh nane bou ande ak repubblica bi dou dougou diamageun rawadi rek
@ndirmatar92392 сағат бұрын
GNOUIN WA DIAMAGUEM DIAMAGUEM SITEU MOKO MOM ZARKO YAW WAHAL DARA SITEU GA GNIEW DIAMAGUEM SA NEL BI LAGNI TONG 😂😂😂
@biranecamara67962 сағат бұрын
Zarko mi yaw yá took plateau bantamba tv wakh lila siteu défal bay dioy leegui danguay attaquer siteu rek wayé si modou lô nga ndiekké yafi waxoon koula diokh avance modou nga dieul ko tay yangui koy maral 😂
@morramos90502 сағат бұрын
😅😅😅😅😅😅
@abdoukhoudossfall99556 минут бұрын
Wa kone siteu souko défalé lou balh rek dieundeu nako warouko wakh deug senegal mo beuri nafékh😂
@khalil753720 минут бұрын
Saway buko defarale teranga tewul deug dagn koy wax siteu dafa def erreur de communication ndax li risque la mbolo moko toppu
@biranecamara679616 минут бұрын
@@abdoukhoudossfall995 no Li takhoul May wakh pour mouy léer siteu dou sama mbeur té limou wakh bour andoumasi mais zarko limou attaquer siteu daffa barri té moko doon tageu bay diooy
@biranecamara679615 минут бұрын
@@khalil7537 problème bi takhoul May wakh wallahi Li kay doumasi défendre siteu
@emmanuelmendy3058Сағат бұрын
Siteu crois k mo mome Sénégal il se trompe lourdement na yém si lamb di menacé nitt wakhlénko deug
@Moustapha-yt7ry33 минут бұрын
Yow zargo guemo ndeyou dara
@mansourndione1782 сағат бұрын
Il attaque pa siteu daffa barri wakh
@NguerFaye052 сағат бұрын
Zarco nopil yow rek yafiy saga si télé
@issaDiouf-p3xСағат бұрын
Zarco yaw nitt kou faux nga fautype ngua tu as pleurer pour siteu ojord8 tu klash siteu en ce moment .............
@famarandongСағат бұрын
Pa matate bi siteu rek ragal ga
@Mamadou-j1x2 сағат бұрын
ZARKO MO DANE SITEU
@morramos90502 сағат бұрын
Où😂😂😂😂 Zarko siteu dako beuré lo bamou bayi mou danko
@kefgg24 минут бұрын
@@morramos9050Sawaye Zarco mo dane Siteu 4 appuis
@KhadimDiouf-32 минут бұрын
Yaw sa data yay
@ModouMbaye-y7g3 сағат бұрын
❤
@Mbayedia463 сағат бұрын
Situé da were
@cheikhmboup65322 сағат бұрын
Sa siteu werewoul yaaw xana doo deeglou niee seenii waakh
Yow khawma kougnou khamoul wayé kham nga niou bilahi walahi gnibisil djital bour nieuw diameugen khol Barki Borom Touba niou defla com djiguen iow goordjiguen nga dangay fan goor siteu sa papa la bo lekaté khaliss si lamb grâce à mom la yako wakh sisa lamign limoula defal bamou diaral la dioy zar réglel rek niola guena pank foufff
@sambagoudiaby30292 сағат бұрын
Yaw mi di wakh ni zarko wérro
@mistercarter4672 сағат бұрын
Sawaayy lamb sport laa dou bandit bandit lou bingaayy wakhh nii.. nekk leine ay sportif… Siteu ndam incha allah
@sambagoudiaby30292 сағат бұрын
@mistercarter467 forale si siteu rékk té nobi wayéé siteu domou adamala rekk
@FatouNdione-pl6es2 сағат бұрын
Iao deh wéro dagua dof sa genre yi diarou gno diour sakh démal diapalé sa wadiour mo gueneu di topeu aye waxou siteu mome migui téral wadiouram
@mistercarter4672 сағат бұрын
@ domou adama leguii??
@OusmaneKébé-q2u2 сағат бұрын
iow siteu sa papa la doffo sakh wakh na deugue mo mome diamaguene modou lo sakh sou gneuwone diamaguene bilahi dou guénékk bakane
waxou ragal rek nguene di... guenelene diamaguene niou dokhane sene ndey bene bene rewoulene ndm sax
@fifty629237 минут бұрын
Wayé képe kouy yéwo diamagueune sougn la bolé ak modou lo ci negu mou dore ko bamou fatou lokho néne. Ragual moy ame fite groupe ak guanaye kounek meune na raye nite ak guanaye gneup ame yap ak dérét