@djibi1777 c quoi ton problème toi si tu sais pas quoi dire do nopi n'a wakhe louma khamoule couillon
@volfroitfall87858 күн бұрын
Yalla nala modou joxx sa chance damala beugg trop wayeii nak bayinou ak sounou couronne Champions😊
@neyzard10978 күн бұрын
Il est le meilleur de sa génération ❤
@MamegorDieng-os2fj8 күн бұрын
Bilaye 🎉
@LimaDiagne-v4f8 күн бұрын
Yalna ngua beuré AK Modou lo, Sénégal dinagne kham ni ya meuna beuré inchallah ❤
@salioufaye89915 күн бұрын
Mon champion yalna la bur yalla def roi des arènes inchalla mais tu continues sur le lancé attaquant au lieu d’entendre
@franceamericanbullydogfami79928 күн бұрын
Sathies travail rek... ne lâche pas l'affaire, le meilleur reste à venir... n'oublie pas que tu as vaincu reug reug avec brio🎉 Tu es un champion
@coumbadieye50838 күн бұрын
Modou Lo rek la beug Wayè sa Thies mi commencée nako beug modou Dieulal sa d’à yarou❤️
@mansourdieng20004 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂
@Teranga99998 күн бұрын
Sa thies 👑👑👑👑💪🏾💪🏾💪🏾❤️❤️❤️🔥🔥🔥🔥🔥🔥futur roi InchaAllah 🙏🏾🙏🏾
@AbdoulayeGueye-i3rКүн бұрын
Sa thiés vraiment champion gua kou meun communication gua❤
@chatif11964 күн бұрын
Dama sétlou wa modou Lo yepp beug sa Thiès surtout Mànn aussi 🙌🏿🥹❤️😢
@ndakarudialdiop12068 күн бұрын
Vraiment sathies dafa wara beuré ak modou lo, balla gaye yay sunu mbeur wayé boul dieul modou lo bayill sathies dieul chansam
@aboukonte4898 күн бұрын
C'est tapha tine qui mérite ce combat royal devant sathies
@mansourdieng20004 күн бұрын
Wakh Nga Deug Deh
@tidianetalla98178 күн бұрын
Wallahi sa damako beugey😇 Yar ak teguine guii ma shaa Allah yaw dinagn leuu may chance 😂 Te combat bou diadou leuu franchement
@Serignemeumeu6 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤Sa sama waay nga beug dafa fort del solo keur massar di entrainet entre les deux camps keine dou tabakh diko deub yay guediaway yay keur massar diapal niar yeup kolerei dafa fort bayi si khel samay kadou yi bess bo sokhla sama numero inchala doko reitiou soxnasi beiguei nagn la❤❤❤❤
@SouleymaneCamara-n9e8 күн бұрын
Sa combat ak modou lo la andouna di khar inchallah ❤❤❤
@NdiaboutaDiouf8 күн бұрын
modou lo mayal boy bi chance way lolou moy lamb ji
@ndiayepapaserge59978 күн бұрын
Modou mayal chance sa thies
@fruityvoice9976 күн бұрын
Mon frère tu communique bien machallah❤
@fallandoye61147 күн бұрын
Mom akh bombardier nonou laniou sonalantéee😂😂😂😂
@assanefall41118 күн бұрын
Sa thies bilae tu peux battre Modou lo yokal sa rapidité ak sa force rek fatma dia good jop bayi ngama naq
@mouhamedsane95968 күн бұрын
Sa Thies le meilleur de sa génération 👑😊
@KebaToure-z9g8 күн бұрын
Iaw rék la bègue bilahi ♥️♥️❤️❤️♥️♥️ sa
@Demba.pastef8 күн бұрын
Sa thies aka bakh modou sama Mbeur mayal sa thies chance way
@NdiaboutaDiouf8 күн бұрын
sa il communique super bien machall
@GoraMbengue-f2j8 күн бұрын
Alioune Seye vs eumeu Sene la nieupp beugue 😍
@salioudia93587 күн бұрын
Sa thiés yanguisi étaa 💯💯 machallah
@PapaKeita-r8b8 күн бұрын
Modou lo vs sathiess lamb la
@moussadioop8 күн бұрын
Le futur rois des arène guindé gui yalna yalla soutoural la deff la roi inchalla tu comunique supêr bien
@MamegorDieng-os2fj8 күн бұрын
Amine ❤
@assanediakhate35076 күн бұрын
Siteu vs balla gaye2 ..... eumeu séne vs zarco....modou lo vs sa Thiès....tapha tine vs Alioune seye 2.....franc vs gris 2......domou dangou vs moussa ndoye....quoanch vs thiatou d fall
@zoladiop94128 күн бұрын
Modou mayalniu sa chance way champion la ❤🙏🏾
@MbodjAmadou-dw3sh7 күн бұрын
Eumeu Sene VS Alioune Seye2 Balla Geuye VS Siteu Doudou Sané VS Serigne Ndiaye2 Modou Lô VS Sa-Thies Thattou Yarakh VS Gris2
@Zoukanaofficier7 күн бұрын
Nélén sa mou woma amna conseils pour mom na âme jam rék inchallah
@boubacarsyllame28358 күн бұрын
Machallah tabarak'allah sa thies ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@CheikhMbengue-fl8ik8 күн бұрын
Je siu fans moudou lo ❤❤❤❤❤❤
@Patriotepourtoujours5 күн бұрын
Sa thies tu communique bien contrairement à doff bi 😂😂😂 ya nga done Roi 🤴 des arènes
@SerignemodouNdiaye-s3u7 күн бұрын
Fatma vraiment yangi ci Yon bou nice
@langbadiane76787 күн бұрын
Sa thies machalla yarou nga trop mé gnoune fane modou Lo yii dagnlay otale banga dieul combat bii dotoko défatii😂😂😂
@MouhamadouSakhirDiba7 күн бұрын
😂😂😂😂
@mansourdieng20004 күн бұрын
😂😂😂😂😂
@ndoffenetine53338 күн бұрын
Sa thies vs mod lo ndaw combat bou gaw😮 Gnar gnou am vivacité mé sa thies da xawa rambax.
@mistercarter4677 күн бұрын
Rambax bobu modou lo ayoucii😂
@ndoffenetine53337 күн бұрын
@mistercarter467 bien sûr ay nasi dhé. Kou rambax mossul dane mod lo
@abdousow29087 күн бұрын
@@mistercarter467ann baniu agg si inchalah
@mistercarter4677 күн бұрын
@@ndoffenetine5333 balla gaye lolou lakay andil..modou lo damier laa meune
@ndoffenetine53337 күн бұрын
@mistercarter467 balla ak sa thies ya une grande différence. Sa thies tank gnoy teureuf mé champion bu mag leu
@IbraWagnaneКүн бұрын
Vrai sportif moy Sa Thies
@AlassaneDieye-cc7jq7 күн бұрын
Man lamb ji yeup Modou Lo ak Sathies laci meusseu faral ba xeex. Modou mako beugu té hawma noum démé, Sathies dagno bokone kogn keur massar ma nek xalé di daw diangui diko setani té ba legui momlay topou. Bagnouma ben mbeur mais gni gnoy sama mbeur. Sa est très bien éduqué
@baidy74188 күн бұрын
Sa thies toujours correct….sou modou naré Daanou yalla na diogué thi sa thies…..
@sayergeye78888 күн бұрын
Amine Amine Amine Amine
@Modoubusso-b9j8 күн бұрын
Modou moe sama mbeur mais dama beugg sa thies beugg ngén beure vraiment
@bachirdomouparcelle42937 күн бұрын
Sa yalla nagn la dieul dane leu 😢même si que yeinei woumala 2 defaites you teglei
@NdiaboutaDiouf8 күн бұрын
eumeu sene alioune seye siteu balla gaye lolou moy logique
@mouhamedlaminethiam44048 күн бұрын
Mod Lo sa thies
@Soninkaradéna7 күн бұрын
Siteu balla moy bane logique ???
@mansourdieng20004 күн бұрын
@@SoninkaradénaWakh Nga Deug Deh
@DameFall-ok4ik6 күн бұрын
Yarou gua trop mais modou doula dieul yak gora sock combat la
@MansourDiop-y6j8 күн бұрын
Nous on t'aime champion ❤❤❤❤
@modougaye66468 күн бұрын
Modou lo vs sathies Balla gaye2 vs siteu Eumeu séne vs alioune seye2 Jackson vs quench Mbaye gouy gui vs anaconda
@mbayetop23028 күн бұрын
Modou lo légui lou noy lay weur wayé li moy combat
@Aladjil6098 күн бұрын
Ms sa legui kouko diangal communication machala
@MamegorDieng-os2fj8 күн бұрын
Sa nila masa mél❤
@moustaphababou62827 күн бұрын
Modou lo mayal sathies chance waye
@boubacarsyllame28358 күн бұрын
Sa thies ak modou lo in challah ❤❤❤❤❤❤
@PapeNdiaye-pz6fw8 күн бұрын
Modou lo vs sa thies yalla na takhaw ❤
@HabibSylla-e3f8 күн бұрын
Machalla kadou yi rafét na
@fallousarr57287 күн бұрын
Ki nitt leu d machalah modou meuna ame dinala may chance modou la faral nak mais fonkal combat bi bou takhawe nak
@Papiscoboukaaycover-fd7xc7 күн бұрын
Modou moy sm mbeure mais combat bi rk la mbeugue bilahi Sa da yarou bilahi yéna nl Combat Royal trp Mais Modou dane la inchallah😂kérok binga dougué sé Stade dm contane bilahi dkh sa respect Mais Yll na takhaw Modou doumala dane inchallah🙏😂🔥
@mameballaka57138 күн бұрын
Machalla sa❤❤❤❤❤❤❤
@ChiekhGeuye-r1y7 күн бұрын
Bly sa mn fansi Modou lo ❤️ la me damala sopp 🎉 samac ky la manol dr😂❤
@moussandiaye71707 күн бұрын
Futur roi des arènes
@DameFall-ok4ik6 күн бұрын
Sa thies parcelle ben Mbeur mon fay sa andiverser gafa am moy goro sock
@MomoCisse-k9r8 күн бұрын
Fans modou lo yi ay saytané guén rek
@mansourdieng20004 күн бұрын
😂😂😂
@maodosoumare98 күн бұрын
Daffa daw fran dieuleul fran dagua ragual danou fran Moy sa adversaire Parcelle
@sambadrame34978 күн бұрын
Sa ❤
@oumarndao74857 күн бұрын
Ndeysane tapha tine amoul koukay wahal mais y’a pas plus logique que modou lo vs tapha tine,modou mom hawma Loutakh beugoul beuré ak tapha
@aboukonte4898 күн бұрын
Pourquoi pas modou lo vs Tapha tine . Ce combat est plus logique que modou vs sathies
@MamadouKa-h2k8 күн бұрын
Très pertinent
@mamadoundiayetouba40788 күн бұрын
Tres sage
@ousseynouhanne93598 күн бұрын
Modou moye sama mbeur mais yalla na yalla df mou beurè ak sathès
@AssSarr-f5i8 күн бұрын
Amine
@fallou3188 күн бұрын
Sa thiés yalna dane modou lo
@Bakelsen997 күн бұрын
Amine❤sa mome il faut beaucoup de boxe beure yii kodoroule doka dane
@SambaDiop-y8i7 күн бұрын
Siteu vs balla gaye sa thies vs modou lo Alioune seye vs eumeu sene mais tapha tine zarko après gri bordeaux
@IslandCureislande8 күн бұрын
GOODNESS OF GOD. LE JOUR OU TU CROISERA MODOU LO JE TE CONSEIL SATHIES BOUL TAKA GALATHIE ZERO GRIS GRIS.. DO8DOUDOU LO KOKOU BEUGUE DAAN IL FAUTNGUA PIEUX DI DIAPOU DI DIOULI AK RECITE ALHURAAN NIGHT AND DAY ON A REPARLERA INCHAALLAH OU RABI. CONTINUER TES ENTRAÎNEMENT .
@boyeniang3781yeumbeul8 күн бұрын
Salif ❤
@bubaceesay95438 күн бұрын
Modou vs Sa thies moye combat bi
@josephcoly41276 күн бұрын
Sa thies un lutteur poli yenenala lou beuri...mes mouno dane eumeu dk dane modou lo warowone nangou eumeu dila dane dou logike ak foumou diar ak yene tes ningay beuré boko defe modou do beuŕé seconde yangui si souf..mes bonne continuation
@alysow90897 күн бұрын
Sa Thiès yw ak Ada fass dolené génération def ngua 8 ans de carrière Ada fass dora gnew 2009 ak 2017
@mansourdieng20004 күн бұрын
😂😂😂
@MamadouKébé-y5t7 күн бұрын
Après siteu sa Thiès Ake boy ndiang keneu moye dieul roibi
@komalokoma99926 күн бұрын
Fans Modou Lo yi nane Modou jeuleul Sathiés vous pensez que Modou mo meunn Sathiés wala?
@mansourdieng20004 күн бұрын
Mane Douma Modou Lo Wayé Mo Mëne Sa Thies
@laminendong62278 күн бұрын
Man mom Modou lo moy sama mbeur mais bou danou manoul niakeu yalla Na ko sa thiés dan nék roi des arènes dafa am yaar lol nit la koi
@oumarndoye11697 күн бұрын
Bilay beur yi mosi eupeu dolé mais niak fayda rek
@BabacarMbengue-z7p8 күн бұрын
Sathies vs Modou lo
@GuyGuiguitou7 күн бұрын
Warone nga daneu eumeu nkk dadone tombal say affair
@MoussaDak-o7f8 күн бұрын
Sa Thiès rék
@SaliouPouye-v4w8 күн бұрын
Modou lo Modou lo Modou lo Modou lo ❤❤❤
@moctarndiaye82217 күн бұрын
Qui soumakoy deglou sama khol bi dafay sedd bilahi
@BubaluizSuware8 күн бұрын
Thanks ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ibrahimandiaye89248 күн бұрын
Nic
@KebaToure-z9g8 күн бұрын
Sa thise rék
@elhadjiibrahimadiatta94858 күн бұрын
Modou lo sou dieulé Sa thies niak couronne bi❤
@GoraBoromItali8 күн бұрын
😂😂😂 fiii nak guéne dii tamé modou deum la dieul bou gaaw lakoy daane insha Allah yalla n'a tahaw rk
@elhadjiibrahimadiatta94858 күн бұрын
@GoraBoromItali champion là déh mai sou dieulé Sa thies niak couronne 😂😂😂
@mansourdieng20004 күн бұрын
@@elhadjiibrahimadiatta9485😂😂😂😂😂
@adamambaye32808 күн бұрын
Sa nioune wa MODOU LO niola beugue incha allah modou dalay may chance.
@MamadouDiouf-hl1sy8 күн бұрын
Yaw ya bakh waye
@adamambaye32808 күн бұрын
@MamadouDiouf-hl1sy sangue bii ki dafa nité trop yalla xamnako Mane déh sou dané Modou douma méti mérité nah lép
@mansourdieng20004 күн бұрын
@@adamambaye3280😂😂😂
@basirubaye65878 күн бұрын
sathis vs modou lo
@kharagnembaye59588 күн бұрын
Boula modou topé doula may chance psk nangouwo may chance franc ba ama mayko chance Ta Ama mola raw si lamb