EUMEU SÉNE RÉVÉLE SITEU WONAKO ,NA CHANGER BEURÉ BI SINO..MODOU LO NIMOU BEURÉ

  Рет қаралды 67,724

KEWEL INFO

KEWEL INFO

Күн бұрын

Пікірлер: 170
@BaraNdoye-r6c
@BaraNdoye-r6c 6 күн бұрын
Eumeu dafa bakh MACHA ALLAH khol bou rafet la yor
@YakhyaGueye-w6k
@YakhyaGueye-w6k 6 күн бұрын
@@BaraNdoye-r6c bly iow sénégalais yi nio sokhor rk surtout fan's mdlo yi
@demba8102
@demba8102 5 күн бұрын
@@YakhyaGueye-w6kfans Modou Lo yi loléne xamale Yaw ya gnémé yalla nak
@AbdoulAzizDabakh63
@AbdoulAzizDabakh63 3 күн бұрын
Fans modou kan sokhor thi eumeu ko daane niari yon lokoy sokhor . Sérieux way toi aussi ​@@YakhyaGueye-w6k
@ndenediagne50
@ndenediagne50 5 күн бұрын
Merci beaucoup champions Eumeu sene 💪🏾❤
@mohamedngaide5774
@mohamedngaide5774 6 күн бұрын
Kou sokhor dou wakh mbakhou kénén eumeu diam ci yow machaala ❤❤❤
@BayefallouNdiaye-k8x
@BayefallouNdiaye-k8x 6 күн бұрын
Saway wax lin ki dagou
@mohamedngaide5774
@mohamedngaide5774 6 күн бұрын
@BayefallouNdiaye-k8x bane dégu loumou defff
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 5 күн бұрын
Ki di dommeram warna niou mou andalone nieup rancunier leu
@oumitandiaye6780
@oumitandiaye6780 6 күн бұрын
Yow eumeu dinga sonneu car tu supportes tout les adversaires de modou lo et tu leur souhaite la victoire mais meunno si modou lo darra
@boubacarndiaye9214
@boubacarndiaye9214 6 күн бұрын
Mane supporter modou la bokone deuk ak môme même zone PA la deffé lepp mais à la fin lou guen beug kouy doungourou modou lolou meunoul nekk ,li sport la té sananté ay traque meunoul gnak wahal lénéne
@oumitandiaye6780
@oumitandiaye6780 5 күн бұрын
@@boubacarndiaye9214 yow ken ladioula
@cheikhamadoutidianendiayeg2217
@cheikhamadoutidianendiayeg2217 5 күн бұрын
@@boubacarndiaye9214wakh deug sénégal yii Khawma yane genre nit lagn
@AbdouAziz-ri8td
@AbdouAziz-ri8td 6 күн бұрын
Siteu Dafa Daw Thiak Thiak le Siteu et un Comédien En voulant gagner il Fo attaquer dans tous les sports Becaye Doi Dire la vérité Siteu Dafa Daw C sa la Réalité Modou a attaquer et gagner Point
@tk92221
@tk92221 5 күн бұрын
Dou thiak thiak deh. Dawkinda leu
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 6 күн бұрын
Lima narone wakh yeup supporters yi wakh nagn ko 😂amoléne morom😊🎉❤ Vive le Roi XLO nioune supporters yi niogui sa guinaw bagay bayi beuré inchallah 🎉❤😊
@saerfall701
@saerfall701 6 күн бұрын
Legui senegal kou wax mbaxou nitt danga soxor, gni supportérou modou lo yila mom😂 Merci Eumeu respect
@YakhyaGueye-w6k
@YakhyaGueye-w6k 6 күн бұрын
Fan's mdlo yi nio beuri wakh bly
@disytbi8711
@disytbi8711 6 күн бұрын
Bilahi kén geunouma beug Modou Lo mais Eumeu khol Bou rafet la yor nit kou bakh la je l'ai tjr défendu❤
@Deggou
@Deggou 6 күн бұрын
Kou yoor xool bou rafete di sissou nane modou manoul beuré...​@@disytbi8711
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 5 күн бұрын
​@@YakhyaGueye-w6kéhh bayiniou yaw 😂
@galaxiepro.5641
@galaxiepro.5641 5 күн бұрын
@@YakhyaGueye-w6kyén si bopam yéneu iñiane té bagñe lou bax thipiri
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 5 күн бұрын
Ki nanfex motax mou xarito ak nieup force nafi xarito ak modou lo mais modou lidjanti wouko seytane leu
@CheikhSarr-q1r
@CheikhSarr-q1r 6 күн бұрын
Eumeu xol bi moy dokhotte di na déh tek malheureusement😂😂
@Brasiltv_
@Brasiltv_ 6 күн бұрын
Billahi eumeu yaa gneme yalla
@lbyoungtv2223
@lbyoungtv2223 6 күн бұрын
Invité lenn mod lo way
@AbdouAziz-ri8td
@AbdouAziz-ri8td 6 күн бұрын
Becaye tu es Vieux il Fo dire la vérité Siteu Dafa Daw Modou a attaquer et gagner Point
@PascaleMendy-y7f
@PascaleMendy-y7f 2 күн бұрын
Champion nga bilay sa khol mo rafét ❤
@sumocarterdiop8609
@sumocarterdiop8609 5 күн бұрын
Sétlou lén eumeu sén sur ses propos,toujours déy tague mbeur bou mou dann pour montrer Qu,il est le meilleur Qu,il est le véritable champion
@Thomas_Shelby.23
@Thomas_Shelby.23 5 күн бұрын
Et pourtant c'est le meilleur
@MomoFall-f6j
@MomoFall-f6j 4 күн бұрын
En kone guiss ngua lolou évidemment
@boubacarseck382
@boubacarseck382 2 күн бұрын
Évidemment yagg nako wakh
@saliougueye4680
@saliougueye4680 6 күн бұрын
Mai Eumeu loumou wakh ayoul Sénégalais liko nekh rek la beugu deggg
@YakhyaGueye-w6k
@YakhyaGueye-w6k 6 күн бұрын
Iow bayi léne fofou rk eumeu dou séne morome
@khadimgueye2543
@khadimgueye2543 5 күн бұрын
Baye balla c'est un fin intellectuel,il écoute chaque personne quand il parle. Son langage (ton, corporelle,voix et sa communication)est prêche.
@ogviito1949
@ogviito1949 6 күн бұрын
Eumeu soula dané valorisé la soko dané mou dévaloriser la😂😂😂
@NdoumbeiSakho-bj2bj
@NdoumbeiSakho-bj2bj 5 күн бұрын
😂😂😂😂merci il est comme ça moom
@MakhtarCisse-lm8ny
@MakhtarCisse-lm8ny 6 күн бұрын
Champion merci
@KhadimDiop-h4v
@KhadimDiop-h4v 6 күн бұрын
Eumeu yaa seytané deug deug!!!
@BadaradrameBadara
@BadaradrameBadara 6 күн бұрын
Eumeu vrai champion nga billlahi ❤
@modoufall355
@modoufall355 6 күн бұрын
Sénégal daal dafa nékh yaw wakh rék mooy sa liguéy ba paré ngani Sénégal da gniy wakh rék. Nékléne aay nit!!
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 4 күн бұрын
Eumeu sén Ak Balla Gay 2 Barké serign Touba Danio Beugeunté yeugeu nako wax niary Borom Baxlan 🥹yalnasên jameu yageu 🙏🏻🙏🏻🙏🏻vrement beugeuna ngain Toudanté Dom
@julesbocandembaye3563
@julesbocandembaye3563 6 күн бұрын
Ya kham dé na balla bakh modou dal démoul dikoul bou wakhé si média bala wakhate dewene
@afro3827
@afro3827 6 күн бұрын
Aka nefekh modou lo rek la bagn 😂😂
@ibralemeringue3258
@ibralemeringue3258 6 күн бұрын
modou moko niouss daane ko motax
@abdoulayegueye6686
@abdoulayegueye6686 6 күн бұрын
Yeen khamou leen sport de combat
@adamadiop1915
@adamadiop1915 6 күн бұрын
modou kénn djékou wuko siteu waron n'a takhaw
@moussandiaye3564
@moussandiaye3564 6 күн бұрын
Bou takhawone rk mou nékh
@konaba6578
@konaba6578 6 күн бұрын
Eumeu c'est un faux jaloux😂 Modou c'est un champion
@Misterboom-x7x
@Misterboom-x7x 6 күн бұрын
Modou siteu borom deuk bi moko nokh euf beut bi Damou ndayou mbag bi soti Souf si bounou ya oustaz bi 💪😂😂😂😂😂
@abdoulayegueye6686
@abdoulayegueye6686 6 күн бұрын
Donc il est pas un jaloux 😂
@oumitandiaye6780
@oumitandiaye6780 6 күн бұрын
​@@Misterboom-x7xmodou mo dioutall siteu mou dioulli si sakou yi en plus siteu da daw combat bi yeup
@oumitandiaye6780
@oumitandiaye6780 6 күн бұрын
​@@Misterboom-x7xmodou mo dioutall bopou siteu si sakou yi en plus siteu da daw combat bi yeup
@oumitandiaye6780
@oumitandiaye6780 6 күн бұрын
​​@@Misterboom-x7xmodou mo dioutall bopoou siteu si souff en plus siteu da daw combat bi yeup
@BadaraAline-f5i
@BadaraAline-f5i 6 күн бұрын
Eume ya bakhe❤❤❤❤❤
@YakhyaGueye-w6k
@YakhyaGueye-w6k 6 күн бұрын
Nnnnnn fan's mdlo yi beuri guéne wakh dhhh eumeu séne dou séne morome bly
@thiamahmadulattekh562
@thiamahmadulattekh562 6 күн бұрын
Moromou kane
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 5 күн бұрын
Demal ladj eumeu borom 11 défaite yii ndax XLo moromam leu
@mbayebayefall8162
@mbayebayefall8162 6 күн бұрын
No ki sokhor na😢 bokol modou lo ndeyesan😂
@AssabaZiza
@AssabaZiza 6 күн бұрын
Ioe doul ndéme
@YakhyaGueye-w6k
@YakhyaGueye-w6k 6 күн бұрын
Yén Fan's mdlo yi beuri guéne wakh dhhh whoooooo
@oumitandiaye6780
@oumitandiaye6780 6 күн бұрын
​@@YakhyaGueye-w6kyow doull
@TallaMbaye-t5q
@TallaMbaye-t5q 6 күн бұрын
Qui vrai seytané la 😂😂😂
@AssabaZiza
@AssabaZiza 6 күн бұрын
iOS doul
@Misterboom-x7x
@Misterboom-x7x 6 күн бұрын
Sa papa khana Moy wabadjiba bi doumou Haram 😂😂
@disytbi8711
@disytbi8711 6 күн бұрын
Mo tay lossi meun😂
@KhadimMbaye-k4f
@KhadimMbaye-k4f 6 күн бұрын
😢Yaw yafi waxone mou souli sa bammelou yaye tay gua gneuwfi nannn dafa bax yax doo rouss sax
@abdoulayegueye6686
@abdoulayegueye6686 6 күн бұрын
Gnii andeu akh Balla Gaye la doone wakhal. Mais pas Balla gaye
@AbdouCisse-xs5mc
@AbdouCisse-xs5mc 6 күн бұрын
Eumeu kholam mousoul nekh si Modou lo
@ndiayegorgui3056
@ndiayegorgui3056 6 күн бұрын
Sene combat yené niar rék kako Bougué 😅😅
@SambaSene-j1h
@SambaSene-j1h 6 күн бұрын
Yafi togone né doto beuré ak bala ndakh da daim fignou daidie sa yaye dioye si kanamou sénégalaise
@abdoulayegueye6686
@abdoulayegueye6686 6 күн бұрын
Supportere modou lo louy sen problème 😂. Am na droit tagu Balla gaye. Wala li leen Balla gaye def da leen metti ba leegui 😂
@elhadjindiaye7089
@elhadjindiaye7089 6 күн бұрын
Emue bayil niari wakh wakhou saytané rk ngay wakh légu sa wakh da bari
@YoussouphTraore-uc4vb
@YoussouphTraore-uc4vb 6 күн бұрын
Modou lo meunoul beuré 😂😂😂
@serignesall3257
@serignesall3257 5 күн бұрын
Eumeu borom bakhleu,il a un bon cœur
@mouhamadoudiene1315
@mouhamadoudiene1315 5 күн бұрын
Ko dane tagg ko yékeutiko bassi kaw mais koula dane nga siisou wakhko wakh bou niaw vrai siisouman nga seytané piir moy Eumeu
@KhadimDiop-h4v
@KhadimDiop-h4v 6 күн бұрын
Modou seul kenn dou moom!!!
@Misterboom-x7x
@Misterboom-x7x 6 күн бұрын
Siteu mo gnouss nday roi des arénes Modou lo tothie beut bi Damou ndayou mbag bi soti Souf si bounou ya oustaz bi 😂lolou état mounoussi tounou ndayam 💪👑
@FarmGandoul
@FarmGandoul 6 күн бұрын
Beuré entre yen amatoul nonoubsens dieulen boy yi Nguen challenge len mou nekh
@YayaBailoDiallo
@YayaBailoDiallo 6 күн бұрын
Wakh dji diekhna bimou wakhé ni Modou Lo ndanane la bayilene nafék Modou loy sama mbeur
@CASI7797
@CASI7797 3 күн бұрын
Eumeu et Balla coalition anti Modou Lo😂😂😂😂😂
@kheucha11
@kheucha11 6 күн бұрын
Supporters dioutou lo yi tangue nagne khol nak 😂😂😂😂
@FallouSarr-
@FallouSarr- 6 күн бұрын
Siteu khawna rey modou 😂😂😂
@Deggou
@Deggou 6 күн бұрын
​@FallouSarr-bayil féneu siteu mi modou doone ko dakué boy bi di daw rek😂😂
@MouhammadouDiop
@MouhammadouDiop 6 күн бұрын
Non sérieusement Amougn sport on dirait
@FallouSarr-
@FallouSarr- 6 күн бұрын
@@Deggou degueu na sa yaayye la boy yii teudee ci kogn binga deukeu 🤣🤣🤣🤣
@Deggou
@Deggou 6 күн бұрын
@FallouSarr- haha modou ak febar la doone dakué siteu , boy bi di daw rek di défeu yeufoi tapete door coup irrégulier guinaw saccouyi lolou ngen di ndambo🤣🤣🤣🤣🤣🤡
@anthioumanefadiga9314
@anthioumanefadiga9314 6 күн бұрын
Ki dafa ndey Sokhor motakh Tyson lidieuntiwouko
@cheikhdiop5333
@cheikhdiop5333 5 күн бұрын
Koukoy yégu yawe dagha dof
@Leploufikhew
@Leploufikhew 6 күн бұрын
Eumeu fan yi khaw ma l’an là nak mai khol bou bon rek ngay waxe barki yalla
@cheikhdiop5288
@cheikhdiop5288 5 күн бұрын
Eumeu yawya bakhe
@MakhtarCisse-lm8ny
@MakhtarCisse-lm8ny 6 күн бұрын
Eumeu sa khol dafa raféte Sénégal nékhoul wakhé gnep ga yéné diam
@serignefallou554
@serignefallou554 6 күн бұрын
Sokhor nga ndy def
@SarjoDrammeh-j6i
@SarjoDrammeh-j6i 5 күн бұрын
😂😂😂 eumeu sene Hamul tosh
@AbdoulAzizDabakh63
@AbdoulAzizDabakh63 3 күн бұрын
Eumeu deh bouma doone beuré ak modou lo souma conseillé douma ko deff.😅😅😅 yow bo amone naka lagnouy daané modou doko deff😅😅😅😅
@MarcoGonzales-hd2ur
@MarcoGonzales-hd2ur 4 күн бұрын
Modou moye sa champion
@BaraNdoye-r6c
@BaraNdoye-r6c 6 күн бұрын
On veut la revanche balla ak eumeu moy lamb dji balla kassee
@diopmuhammad944
@diopmuhammad944 5 күн бұрын
Emeu boul fatté ni 9 défaite ga am déh 😂😂😂Danou danéll
@mouhamadouseck9920
@mouhamadouseck9920 5 күн бұрын
Fans modou yi maylengnou jamou waay soff nguene trop
@serignesow6903
@serignesow6903 2 күн бұрын
Saway khol bi mo bon 😂😂
@abdarahmanesow578
@abdarahmanesow578 2 күн бұрын
Empereur BALLA 😂😂😂
@Bakelsen99
@Bakelsen99 5 күн бұрын
Balla 🇸🇳gaye
@mamadousarr4791
@mamadousarr4791 6 күн бұрын
Man louma diahal eumeu dou ak reug reug ak Siteu kon kan lay beurél
@Sarr-jx7ux
@Sarr-jx7ux 6 күн бұрын
Ki IBLISS la😂😂😂
@Misterboom-x7x
@Misterboom-x7x 6 күн бұрын
Sa bay khana Moy dadial👹👹
@aliounebadarambaye5239
@aliounebadarambaye5239 4 күн бұрын
Bien-sûr que menossi wax mod'lo 2 fois laladane😂
@amadouba6652
@amadouba6652 5 күн бұрын
Eumeu dof bou sokhor nga
@Misterboom-x7x
@Misterboom-x7x 6 күн бұрын
Siteu bamou tégueulé ndayou roi bi matoul 15 jours faté khadioufi👑💪😂
@Bakelsen99
@Bakelsen99 5 күн бұрын
😂😂😂😂Ardo 3fois
@DiyenabaPouy
@DiyenabaPouy 6 күн бұрын
Ay li Eumeu yew naguoul rek kon ligua dathe si modou
@Misterboom-x7x
@Misterboom-x7x 6 күн бұрын
Monde entier khamnagnouné siteu mo gnouss roi bi 🤣 tothie beut bi 😂damou ndayou mbag bi 🤣 soti Souf si bounou ya oustaz bi 💪👑
@disytbi8711
@disytbi8711 6 күн бұрын
Yw da melni sa yaram nekhoul dh😂😂😂 Senegal nieup kham nagn Siteu lagnou nokhou mouy daw combat bi yeup dako daw😂😂 mou gadji waté kome djiguén 💅🏾🤣 bayil doul
@Misterboom-x7x
@Misterboom-x7x 6 күн бұрын
@disytbi8711 yaw ya meuneu tépi sa lefeul ndaye guadji siteu tégueul ndayou roi bi bagne Koy togual khéwar mounane gnome gnare kou nane sowou ardo bi bounou Modou bi batay dafa krathie 🤣🤣🤣
@disytbi8711
@disytbi8711 4 күн бұрын
@@Misterboom-x7x Wa D'accord dieulel lep doul kat bi 😂😂 Siteu mo yobou Modou Ardo mais roi bagui Parcelle boula nakaré sa Dayou Serigne🤣🤣
@MalickNiang-hy5ln
@MalickNiang-hy5ln 5 күн бұрын
Modou lo mo dakha beuré si lambi Sénégal
@MamediarraSarr-he9sh
@MamediarraSarr-he9sh 4 күн бұрын
Eumeu kou seytané nga mai meuno si Modou dara dieundeul glace té mougne
@KhadimDiop-h4v
@KhadimDiop-h4v 6 күн бұрын
Pourtant Modou moo nieukk nekk sa copin 1er combawam moom akk Lac 2 nieuwonn nga donn coo conseiller wayé loumou la danne 2fois motakh nga retourné contre moom!!!
@abdoulayegueye6686
@abdoulayegueye6686 6 күн бұрын
Da nga deigueu mouni Modou lo dou copain wam 😂. Loutakh ngeen compliqué
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 6 күн бұрын
Coup yéko méti nk😂
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 4 күн бұрын
Fans Diouta Lo yii nio bonn xol 😂😂😂ndiom Dall xarito Eumeu sén Ak Balla Gay 2 Mounou niouko Digère 😂😂😂Nany Lène nox bon ngain xol trop yèn 😀😀😀Eumeu Ak Balla jameu thiyène 🙏🏻🙏🏻
@MoussaSarr-qk9jp
@MoussaSarr-qk9jp 6 күн бұрын
Khana tay ngay wakh balla dafa bakh fatewo sén 2ém combat yaka done djine loubone nga wakh dafa soulille. Sa yaye thi arméli
@papadiom9260
@papadiom9260 6 күн бұрын
Tee moka defff ! Lamb djaralone nalene lounekk 😂
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 6 күн бұрын
Eumeu rék😂
@BaraNdoye-r6c
@BaraNdoye-r6c 6 күн бұрын
Eumeu linga😂guis nga wax tt le monde sait ke sokhoro
@TallaFall-or4xk
@TallaFall-or4xk 6 күн бұрын
Vraiment eumeu mane yagg nala dieuleul part mai kouma bétt nga waxou nafekh rk nga nék di wakh ni yaw amoul loo waxoul balla gaye lépp fi laniou fékk 😢
@amadousakhirhanna3090
@amadousakhirhanna3090 4 күн бұрын
Eumeu sene vrain nafekh leu bilahi apres son combat contre balla Gaye limou wakh yeup noo eumeu c t'un faut tipe
@SambaSene-j1h
@SambaSene-j1h 6 күн бұрын
Eumeu denga sokhor
@assanendiaye5640
@assanendiaye5640 6 күн бұрын
Senegal metina 😂😂😂
@makavelli-ru3un
@makavelli-ru3un 6 күн бұрын
Kumou Daan rek lay sedel Lou bakh eumeu sene sama mbeur nga Ms faux nga torop
@ousseynoufall9150
@ousseynoufall9150 6 күн бұрын
Ki Aka nafekh modou lo rek la bagn
@falloungom3153
@falloungom3153 6 күн бұрын
Ay ki loumla def ak yane yeufou nafekh la deff
@papadiom9260
@papadiom9260 6 күн бұрын
Maniii Sarap Ndaye Modou lo !
@MortallaDiabaye-z9s
@MortallaDiabaye-z9s 6 күн бұрын
Sama mbeur la ms dafa meun fèn trop
@AliouneToure77
@AliouneToure77 6 күн бұрын
Sa mbeur la 😂
@OuseynouFall-x8y
@OuseynouFall-x8y 6 күн бұрын
Epou bakhna si lakh bou tangue😂
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 6 күн бұрын
Wawaw kou yap modou daga fék supporteram yi di nélaw mais bougnou djougué rk nga délo avance😂❤Contane si fans XLO yi😊🎉❤
@jeangomis8336
@jeangomis8336 6 күн бұрын
Eumeu sene daffa faux il est jaloux
@serignesall3257
@serignesall3257 5 күн бұрын
Siteu nafekh la
@moussandiaye3564
@moussandiaye3564 6 күн бұрын
Eumeu mii ma guiss dafa ragal boy yi balla gaye rk la beugue mais lolou dou comba nékhoul tousss
@ModouFall-o3e
@ModouFall-o3e 5 күн бұрын
Sisou mane nga
@moustaphadiagne8461
@moustaphadiagne8461 5 күн бұрын
😂😂😂
@bocarba2781
@bocarba2781 4 күн бұрын
Aka bagne modou lo, lol modou dina fatate sa nday
@Ousmane-pz1if
@Ousmane-pz1if 6 күн бұрын
Boula dane dalay tague boko dane saltel
@PascaleMendy-y7f
@PascaleMendy-y7f 2 күн бұрын
Boko ak rancunier bobou deuk Parcelles 😂😂😂
@moisendiaye396
@moisendiaye396 6 күн бұрын
Eumeu Sene Ya Faut
@oustazahmedfall6478
@oustazahmedfall6478 6 күн бұрын
Do dara
@khadimmbackebadiane2259
@khadimmbackebadiane2259 2 күн бұрын
Rafetena
@MortallaDiabaye-z9s
@MortallaDiabaye-z9s 6 күн бұрын
Soula danè tague la gua Dane ka mou beugue bagne
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 5 күн бұрын
Yanki seedee lii ci balla tee bou souba yaloy yakeu
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 5 күн бұрын
Doo tous meem boula danoulwon sakh ndananla faux typ nga
@MamemorSylla-d1p
@MamemorSylla-d1p 4 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂cv
@anthioumanefadiga9314
@anthioumanefadiga9314 6 күн бұрын
Yaw bigua Xaro, dagnela door gua danou
@FaraNdiaye-k1m
@FaraNdiaye-k1m 5 күн бұрын
No Eumeu mo faux
@oumitandiaye6780
@oumitandiaye6780 6 күн бұрын
Eumeu sene n'est pas dans la génération de modou lo et balla gaye c un vieux il est plus ancien qu'eux
@MouhammadouDiop
@MouhammadouDiop 6 күн бұрын
Yéne nak bou dalé modou lo dafa sokhor sou wakhé lou bakh dafa faux oh sénégalais
@FodeDanfa-m6h
@FodeDanfa-m6h 6 күн бұрын
Eumeu champions la si geweu, neck champions si communication
@KhadimMbaye-k4f
@KhadimMbaye-k4f 6 күн бұрын
Ki kou kateuh ndayam jaloux lah melni ndeye djiguene
The Best Band 😅 #toshleh #viralshort
00:11
Toshleh
Рет қаралды 19 МЛН
Farmer narrowly escapes tiger attack
00:20
CTV News
Рет қаралды 15 МЛН
Чистка воды совком от денег
00:32
FD Vasya
Рет қаралды 6 МЛН
Sigma Kid Mistake #funny #sigma
00:17
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 26 МЛН
LAST FACE 2 FACE ENTRE: MOD LÔ ET SITEU 👑🔥
19:50
MAP_AU_CAMPUS
Рет қаралды 2,5 М.
The Best Band 😅 #toshleh #viralshort
00:11
Toshleh
Рет қаралды 19 МЛН