S2t design big up Baye fall gnonguii thiante bou were ligueye bi rafetna trop qualité image bii aussii impect..thiante bi nga niouy begueulei yalnala ko kou Ted ki fay 👌👌👌
@khadimbamba20125 жыл бұрын
Hakaza Serigne bi Lahat Nongui Ziar ak di wakh ni kadou yi rafét na lolou way Fall Dieuredieuf Fall Fayou kou TED ki Yallah naniou ko bok té ga eupaléma thi Fall Amine
@lahatdiokhane66795 жыл бұрын
Amine baye fall begg na lolou jajeufeutii
@khadimbamba20125 жыл бұрын
Bégg mi Fila eupé Fall xéwal rk
@salioulo36145 жыл бұрын
Baye fall bi xana serign ahmada zikaroul nga dougal ko bokk
@khadimbamba20125 жыл бұрын
Serigne Ahma Mbacke bou Cheikh Modou KARA ga wakh wala
@salioulo36145 жыл бұрын
Waw mom la wax
@khadimbamba20125 жыл бұрын
Mom nékoulwone thi Thiante gui mais souma amé videowame rk dina ko dougal Insha Allah
@salioulo36145 жыл бұрын
Dakor
@khadimbamba20125 жыл бұрын
Diadieuf
@GoraBoromItali5 жыл бұрын
Thiante gui Nord foire la wone wala? Mé dio hana video 30mn amoko guan dimako send what's app way
@khadimbamba20125 жыл бұрын
Thiante gui Medina lawone Mane nak sama whatsapp bi nek ci Ordinateur bi mo nangouwoul oubékou motax