sabel da beug dioy mais da melni mouenoul dioy ndeysan
@Fabidi1011Ай бұрын
Ey Fatima Sabel bakhoul.Aka nekhone Betty doff bi niewe wakh lepp si aye manigances yi mou deff. Waaye nak liko daal dafa metti.Ibra ya togne. Waayé khaléyi dé léne deglou parents yi .Souniou léne téré bayyiléne.Moussibeu rek mo siye toppeu.Ibra attention.😮😮😮😮
@maoudediao653Ай бұрын
Série bou nex la mai béty mogni wéteul😂❤
@aichasall8287Ай бұрын
Réwandé betty damay fathie😂😂
@MarietouSeck-bt2fsАй бұрын
Fatima béni diaro la take wow lolou moguo nék ❤❤❤❤❤
Thierno nékal niit aicha day nék dit bigamie nii😂😂😂
@aichandoye1100Ай бұрын
Fatima nak ngeu faydeu beugeu moy lane ngay tok rek Lamine mou rew bi ak bopom bou reye bi mouley torokhol rek dileu manquer de respect mou nane beugeu