Bilahi xasida yi momay dibali pour may nelew depuis la disparution de mon mari yalla yalla diegal ko si barké xassida yeup il etait un disciple de cheikhoul khadim magui sakou guen gnanal ko il es parti si jeune
@cheikhahmadoubambandiaye9273 жыл бұрын
thiey, yalna ko sunu borom diégueul, yalna ko modou mbacké téérou, yalna suuf sédd si kawam..💚💚
@mamifall28133 жыл бұрын
Amin yarabi
@tidjaniasskhayri82533 жыл бұрын
Yalnako yalah diegeul yeureumko souf sed kawam fimou dieum yalna geun fimou diogué tia barké yonent bi salla lahou aleyhi wa sallam
@papemalickdiouf39922 жыл бұрын
Kil repose en paix barké khasida yii🙏🏻🙏🏻
@falloudiop42512 жыл бұрын
Li souma ko dégé sama xol day fekh❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@leternelindigne99313 жыл бұрын
Machalah sén mbokou talibé Cheikh bi békna té di gnane yalla fayalgnou cheikhoul khadim borom sagesse bi 🙏❤️🙏
@cheikhahmadoubambandiaye9273 жыл бұрын
Amiin waay mbokk mi, diadieuf waay
@mllr56242 жыл бұрын
Allahouma amine 🤲🥰
@renettemendy68582 жыл бұрын
Machalla ❤️♥️❤️♥️❤️♥️❤️♥️❤️♥️❤️♥️❤️♥️❤️♥️❤️♥️❤️ eskey yalla sunu borome ❤️ dieureudief Serigne Touba mbacke ♥️
@RawaneDiop-ho2og Жыл бұрын
Tieuy Xassida serigne bi ko fonkou inchalla di nga téde adouna ak alakhir❤❤❤❤
@MbackeNdar823 жыл бұрын
Kou bakh yangui defal serigne bi liguey bou Am solo moy tekki bayitt çi wolof
@fatoudione60084 жыл бұрын
Dieuredieufe serigne touba Dieuredieufe serigne touba yalla nama yalla may dieukeur bou mourite mouride sadikh nak thi barke serigne touba ❤🙏🏻fall yalla nala serigne touba fay thi barke serigne touba
Borom page yala nala kou tedd ki fayal bopam . manguilay nianal bilahi si barke borom Touba sama tourondo
@cheikhahmadoubambandiaye9274 жыл бұрын
Amiin way bay demba
@Ndiayediop83283 жыл бұрын
😘🥰😍
@mountahambackendoye11493 жыл бұрын
Dieureudieuf kou bakh 🙏🏾 Document PDF bi meunu nuko amm ????
@magattendour13363 жыл бұрын
Kén dou yaw
@ballandoye37184 жыл бұрын
❤️😭❤️😭❤️💓💓💓💓💓
@ndiayecols66994 жыл бұрын
😥😥😥😥❤🙏
@ML-sq1fh4 жыл бұрын
❤
@ndeyembenakene64102 жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️😍😍
@souleymanethiello91394 жыл бұрын
Akassa diereudieufaty mouride beggati nagn lole. Khassida « takhmiss » (touhfatoul Awwa) yitéwo nagn loole traduction bi sou diapandé. Di toub bou bakh si sakkou bi dia nguene dieuf !
@cheikhahmadoubambandiaye9274 жыл бұрын
Amoul solo nonou la, inchallah sou soté rek dina ko dougal, diadieuf kou baakh
@babacarsadikheseye5295 Жыл бұрын
Bonjour merci pour les khassida Si possible j'ai besoin de la transcription du khassida asmaoul tahlil
@ousmanethiam54953 жыл бұрын
Ki peux m'envoyer la version française en pdf
@absagaye65553 жыл бұрын
Yalla nalen souniou borome fayy mom kepp mo am sen fayy🙏🙏♥️
@JuanitaHernandez-x6g3 ай бұрын
Demario Inlet
@khadijandiaye89184 жыл бұрын
Assalamualeykum est ce que je peux avoir stp le texte de ce khassida la transcription et celui de Sindidi svp ? Merciiii (mon email : ka-el@ka-el.com)
@cheikhahmadoubambandiaye9274 жыл бұрын
Salam, malheureusement je le transris directement sur la video, y' a pas de texte, desolé.
@layebarosarr3634 жыл бұрын
JAJEUFFF
@christianfasssinou1444 жыл бұрын
Dieureufe borome touba amo morom 😪😪😪💯
@christianfasssinou1444 жыл бұрын
Billahi khassida sindidi rék doyon na si adouna nga khamni kou téd ki danaka lép lafa wakh fisi adouna ak euleuk akhira