Thieyyyyy sm wadji Malick bâ bilahii nigmay df yalla rkk moka kham😭❤️ sawayy machalah bilahii ❤️
@ibrahimasow62234 жыл бұрын
Khassida bi mo yémei banga khamni ére boko diang rek day gueneu wanei Kénak Serigne bi. Wayé 78 bi diaar na yone, tégué na, maggué na aussi. Wa HT danio am mayouk sa Borom. Légui mom mangui 78 bassi kanam. Jërëjëf ! Yalla naniou sonou Borom dollé samou t déf niou ay Mouride sadeex si Barkep Al Mustafa haleyhi salatu wa Salam
@Diantal4 жыл бұрын
Saay mbela nexna deh😁😁😁
@ibrahimasow62234 жыл бұрын
@@Diantal wakh nga deug tamit. Kharal ma bolé lène rek 😀😍
@Mouride9614 жыл бұрын
Magui thi wa daaru man 😂😂😂
@Diantal4 жыл бұрын
@@Mouride961 wa seugn massamba kemane la deh 😁😁😁
@Mouride9614 жыл бұрын
@@Diantal 😁😂😂 Euy mouride nioniu dh xamnaani nioy fondements yi
@niangelementmalickbaht96704 жыл бұрын
Thiey sm wadji Bou Néké si kourel gui rék Nga kham kou💪💪❤❤❤❤🙏
@moustaphaxalifababou59854 жыл бұрын
Malick ba moy kourel gui billahi 😍😍😍geudj nama diglo kourel gui comme ni mashallah
@khadyfall1044 жыл бұрын
Machallah s Malick yag fi loll te wer ci barke khassidayi
Thieeeuy Malick mo yorr deug deug animation Kourel gui 😇😇💫👌
@abdoulayeosnseck70123 жыл бұрын
😍😍 aldiana deug mongui niii 😍 degloul Malick ba rk
@madiopthioune67264 жыл бұрын
Machallah wa li kawéna trop. Ms kéndou malick ba
@abdoukhoudosssylla28554 жыл бұрын
Serigne Ndam FALL dieuredieuff
@cheikhsalioundiaye25014 жыл бұрын
Bilahi wallahi khassida moo neix si xool
@mamegoor15472 жыл бұрын
Manchallah khol séde na ❤️🙏 ba sama idole 🙏
@xalilba85934 жыл бұрын
Waxnalén Malick Ba dou nitt baxna❤️😭😂🙏🏼❤️
@mouhamadoubakhoum44394 жыл бұрын
Lii moy 78 deug. Bokoul ak touba mbela batay. Tiey wa HT ak S malick Ba
@tourecheikh68144 жыл бұрын
Li mome nga done wakh fei thi mawahibou ahlouminane bi
@mouhamadoubakhoum44394 жыл бұрын
@@tourecheikh6814 niom mbella la niou done jangue mais da bari wone ayy nekhal trop
@tourecheikh68144 жыл бұрын
Mais Makk gars yi gnio beugg lol 😂 Lou nekh rek lagni weur mais waroulll eupp tmt
@youssoundaofaye57984 жыл бұрын
Wawaw seugne bakhoum magoum khassida
@morpene29943 жыл бұрын
@@tourecheikh6814 pôpoooog
@lahatsylla6064 жыл бұрын
Machalla ndaye guena bakh di guena nekh ba aldiana rek
@moussadiagne56024 жыл бұрын
Tieuy sama papa malick liguaye deff diarna Yonne fall👑
@cheikhounadiouf79804 жыл бұрын
maggué neu yarou neu amna solo lol
@faliloudiagne64714 жыл бұрын
Amatina solo Mourides tawfekh rekkk inechalah
@badoux52284 жыл бұрын
Jeureujeufei Borom Touba 🥰🥰❤️❤️😭😭🙏🏾🙏🏾
@mouhamed28204 жыл бұрын
Imam Malick 😍😍😍rk🤗
@ndiayemor51934 жыл бұрын
Wa li yèmé ne d😭😭😭😭
@aliouba19163 жыл бұрын
MACHA Allah
@toubadiop63214 жыл бұрын
Thaiy Malik ba dina ma ray rek bilahi macalla
@cheikhtidianeseck97494 жыл бұрын
9mn48😭😭thiéy Malick
@ousseynouakassaboye78284 жыл бұрын
Waw léne goor ❤️❤️
@adaafia63444 жыл бұрын
Wayè kène dou ndam fall tamitt
@mouhamadoufalilouniang11974 жыл бұрын
Màsaallaa jaajëf rek
@barabayefall34584 жыл бұрын
Il est le meilleur 😍😍😍❤
@Diopibara2543 жыл бұрын
Waw machalla
@Kayel_d4 жыл бұрын
Kou daka diangue ngani kii la waw len goor
@blackman76434 жыл бұрын
JEREJEFÉ BOROME TOUBA KHADIMOU RASSOUL
@mahmouddiallo77034 жыл бұрын
Malick Ba nagnou cotisé nguir mou tokk Sénégal amna solo lol thi Kourel gui
@mouhamadoubakhoum44394 жыл бұрын
Bilahi en fait mom il à l'aise ci ndiangue. Dafay indi thiossan bangua khamné keman la dale
@mahmouddiallo77034 жыл бұрын
Malick rôle bi Mouy joué thi djangue mi mo amm dolé mo takh bou nékkoul thi Kourel rék da ngay sentir son absence. Yalla nagnou KO borom bi takhawoul thi barké Cheikhoul Khadim
@ibrahimasow62234 жыл бұрын
Vraiment d'accord avec toi. Na Malick tok Sénégal way
@falloufaloudiakhate20224 жыл бұрын
Je suis d'accord avec toi diar nako
@oumousow6443 жыл бұрын
Machalla ❤❤❤❤malicke ba
@mbayendiaye83313 жыл бұрын
Malick ba mba dina magal si inchalla
@niangathioune2554 жыл бұрын
Ba😭❤❤
@mohamedgueye75604 жыл бұрын
78 original 🥰🥰
@khadimdiougue89224 жыл бұрын
Li 71la
@mohamedgueye75604 жыл бұрын
@@khadimdiougue8922 Nn 78 la fall gnome touba mbeill lagnou faral Di diang mtx kw mais li moy 78 original 🙏🙏
@mml4774 жыл бұрын
Malick il est exceptionnel
@jewrine2214 жыл бұрын
Ndeysane ❤️😭
@cheikhbasskeurmassar95484 жыл бұрын
Malick ba ndeye saane 😭
@abdoubayefallsplo44784 жыл бұрын
Djajeuf amna solo nékhna lol
@barandiaye58984 жыл бұрын
Machalah
@baboufall38114 жыл бұрын
Serigne malick bâ yala nafi yag Ki loumou bokoul nekhoul
@madandiaye13544 жыл бұрын
Téguiene lanou serigne touba diagall
@malangsano95784 жыл бұрын
Dieuredieuf mbacke
@bambandiaye49504 жыл бұрын
Kéne dou serigne touba
@fallousow7514 жыл бұрын
C’est le meilleur❤️ on voit nettement la différence quand il est là et quand il n’est pas là c’est un lion❤️
@frachise30754 жыл бұрын
Quelle différence !! C'est pas un match de football ça...ishhh arrêtez de parler si savez pas ce que vous dites
@@syllabamba5798 waw kay jëwrin jëréjëuf thi léral wi
@tourecheikh68144 жыл бұрын
Khaw nagne nuro touti mais 78 Mo dakhe pour mane
@sensational37714 жыл бұрын
Mom mo warone dadj Ndax batt bi oyofna
@khassidayirekk85814 жыл бұрын
Dadjie bi bayeko diop rekk 1998 ba legui moy dadjie 22 ans d'experience Tei malick residewoul senegal etats unis la nekk magal rekk lay niew
@sensational37714 жыл бұрын
@@khassidayirekk8581 je sais mais batou 1998 ba legui dafay changer insbi Malick rek wala kenen kou batam oyof mo warone dadj taxoul mou done dathie kath centrale bi
@khassidayirekk85814 жыл бұрын
@@sensational3771 bate bou oyof meunoul dadjal batte yeup kone amnassi nio khamni douniou meune di diangue si kaw parck daniouy nadjou Diop mome batte bi si nieup lay diapandi
@adaafia63444 жыл бұрын
@@khassidayirekk8581 Waw nonou la meuna dèmè Kay motakh guissa toumako lou barri si kourèl gui