😱Khoulo bou méti entre Oustaz Mouhamed Mbaye et Cheikh Bara Ndiaye’’ limou wakh eup na’’

  Рет қаралды 26,131

Univers info TV

Univers info TV

Күн бұрын

Пікірлер: 186
@ousseynoudieme6801
@ousseynoudieme6801 7 күн бұрын
Oustaz danga dioum diaroul tountou cheikh Bara ndah gnou diangua sîra yeup kham nén ni linga wakh dou DEUG
@sonkofocus2024-ph4hv
@sonkofocus2024-ph4hv 9 күн бұрын
Saway linga wax si yoninte bii dou deug nak nganane aye dane mako wax yoninte lime deff lepp waxnako nganane ay kima ko wax mingui doundou
@Generalahmadoudame
@Generalahmadoudame 3 күн бұрын
Wakhi doff wakhi politique rek
@cheikhndom2711
@cheikhndom2711 8 күн бұрын
Bara ndiay limou wax lolou la borom GHAZAWAT (غزوات) nettali Daga dioum nangoul loolou 🙏
@PapeNdiaye-x5f
@PapeNdiaye-x5f 8 күн бұрын
Liga wakh dafa eupou de notre bien aimé Mohamed psl
@AltouGagniktv
@AltouGagniktv 8 күн бұрын
لا يدخل الجنة من كان في قلبه مثقال ذرة من الكبر
@cheikhounadiouf7980
@cheikhounadiouf7980 8 күн бұрын
Werna dh
@Generalahmadoudame
@Generalahmadoudame 3 күн бұрын
Pour kanla
@balla8843
@balla8843 8 күн бұрын
Lo wakh loudoul diégalou dangay geun dougal sa bop Linga wakh thi yonantibi eup na
@tafandiaye1950
@tafandiaye1950 7 күн бұрын
Wakho fi dara kila ko wakh nala wakh fann la ko tokhalé
@mourtadandiaye8007
@mourtadandiaye8007 7 күн бұрын
Wallahi reuye bakhoutt nitt dagaye nagou deug ta yalla takh Ta moum mi dafa bari loul ay ndioumtyé 😢😢 Légui néena imam malick boudan diangalé syrra imam malick hadith ladane diangalé ndakh diamonou bouba nitt dji kham nagne syrra Ouztaz déel wakh deug
@mbayesene1072
@mbayesene1072 9 күн бұрын
Liga wakh si yonénte bi d'où deug
@MameDiarraNdiaye-h5l
@MameDiarraNdiaye-h5l 9 күн бұрын
Machalla Ousmane mouhamad mbaye❤❤❤
@serignesalioulo8023
@serignesalioulo8023 7 күн бұрын
Sa Serigne boubou ngaye wakh ak komou mana doune takhoul ndioumte passe ci mom
@nitoudeugue4930
@nitoudeugue4930 7 күн бұрын
Djapal ni sossal ng yoneineti bi dall Toubeul balla weiss Mais je comprends keur doff yi ng deukk 😂
@SyAlassane-k7s
@SyAlassane-k7s 7 күн бұрын
Mohamed mbaye dîoùmga daal
@AmadouBa-xn6ns
@AmadouBa-xn6ns 7 күн бұрын
é mbaye ya fénal yénanete bi ni
@noble4211
@noble4211 7 күн бұрын
Bayil dulall psl bi bakhna déll doull rekk
@yahyagassama491
@yahyagassama491 7 күн бұрын
Bara ndiaye mo nek si deug fall diiulitt dou reuy nangoul deug
@BabacarNdiaye-x7q
@BabacarNdiaye-x7q 8 күн бұрын
Oustage moukhamed mbaye ❤❤❤❤❤
@iboudieye1255
@iboudieye1255 8 күн бұрын
Mais wakh niou koula ko wakh yaw Linga wakh wėroul indi tėrė bi wala kila ko wakh tapalė bakhoul
@mamemorsene545
@mamemorsene545 8 күн бұрын
Boko rawèt limla wakh moy deug
@ibrahimadiene3435
@ibrahimadiene3435 7 күн бұрын
Netali 😂😂 vraiment Mbaye khotatal say source li gua netali dou deug
@MalickNiang-hy5ln
@MalickNiang-hy5ln 8 күн бұрын
Machallah mouhamed mbaye merci beaucoup ❤❤❤
@sft1130
@sft1130 8 күн бұрын
Wallahi lingue wakh dara douthi degue bayil rey tè diègalou
@ngagnesakho8673
@ngagnesakho8673 7 күн бұрын
Ouztaz danga dioum adouna amoul solo
@ameliesamake2382
@ameliesamake2382 5 күн бұрын
Koala nawe la ndakh Seydina Mouhamed SAW Goudeul fane Lo doune deu doyoul 111ans ❤❤❤❤❤❤❤
@ousseynousall5808
@ousseynousall5808 9 күн бұрын
Doul réke gaye défe 😂😂
@saliousyll99
@saliousyll99 6 күн бұрын
Ayy!
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 9 күн бұрын
Li ngua wax si YONNET BI dou deugu koula wax waxoul deug nekal niit
@NdeyeKane-q2u
@NdeyeKane-q2u 9 күн бұрын
Wakh gnou deug yow
@mohamedken4806
@mohamedken4806 9 күн бұрын
Iow mi di wakh khamna sakh mokolo alkhourane bayilene sokhor
@saurafall5922
@saurafall5922 8 күн бұрын
Yaw ndank rék ngaye xatarayou ni
@MouhamedSeck-w7c
@MouhamedSeck-w7c 8 күн бұрын
Mokal alkhourane mom serign bi jote woul ak li dara ​@@mohamedken4806
@CisseModouxaadiabdallahcisse
@CisseModouxaadiabdallahcisse 8 күн бұрын
​@@NdeyeKane-q2udageu gui moy yonenete bi Ken massoko diapou thi ben khari ak bomo meuna doon wakh dageu yalla ❤
@Machine4Amndykara4
@Machine4Amndykara4 8 күн бұрын
Machallah ❤
@mohamedken4806
@mohamedken4806 9 күн бұрын
Machalah ❤❤❤❤ mouhamed
@MoussaDak-o7f
@MoussaDak-o7f 8 күн бұрын
Machallah Muhammad mbaye ❤❤❤ bék na thi ao
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 9 күн бұрын
Toubeul sa feine yii ngua feinal YONNET Bi mo gueneu
@mohamedken4806
@mohamedken4806 9 күн бұрын
Bayilene sokhor
@ThioroDieng-lm5xz
@ThioroDieng-lm5xz 6 күн бұрын
@@mohamedken4806amoul soxor mo fi fene niou wax ko kou diangoul siira rek mo key deuggeul ci lim wax
@serigneamathgueye2886
@serigneamathgueye2886 6 күн бұрын
​@@mohamedken4806 yaw nite nga ki wax loudoul deug ngaye niouye lake aye chinois senegal mo beuri nafeek
@MoussaDak-o7f
@MoussaDak-o7f 8 күн бұрын
❤❤❤❤❤ machallah
@mamemorsene545
@mamemorsene545 8 күн бұрын
ما قلته ليس صحيحا وما قال بار انجاي هو الصحيح والصواب
@momosane8212
@momosane8212 9 күн бұрын
Mais yow bi Macky Sall Di faal coura Macky fo nékone bayiléne nafék yow do oustaz 😅
@MamadouBa-ko9ck
@MamadouBa-ko9ck 8 күн бұрын
Merci beaucoup oustaz mouhamde mbaye ❤❤
@fofanasamba2316
@fofanasamba2316 9 күн бұрын
Yaw bayil fene wakhatoumala ngay fenal kou Ted ki
@Sarr-n5f
@Sarr-n5f 9 күн бұрын
Dieureudieuf ouztaz mbaye❤
@ameliesamake2382
@ameliesamake2382 5 күн бұрын
Oustaz Mouhamed Mbaye Foumeu guisse sa wakhe tane si youtub il fokeu me cutané Nguire Seydina Mouhamed SAW Goudeul fane ❤
@MaggatteGaye
@MaggatteGaye 7 күн бұрын
merci beaucoup ya oustaz mouhamed Ahmed mbaye
@Fayem8141
@Fayem8141 7 күн бұрын
Merci oustaz
@MorkhouleNdiaye-b7i
@MorkhouleNdiaye-b7i 8 күн бұрын
هذا الرجل من الذين يشترون بايات الله ثمنا قليلا يا رجل اتق الله وانظر نفسك ما قدمت لغد
@ahmedsylla2779
@ahmedsylla2779 8 күн бұрын
يا أخي لاتقل هذا، هذا السيد كان يقول الحق على محمد صلى الله عليه وسلم لكن الخطئ لايستحيل على أي أحد منا. لماذا قال شيخ بار انجاي إنه يكذب ؟ لم لم يقل انه مخطئ ؟
@ThioroDieng-lm5xz
@ThioroDieng-lm5xz 6 күн бұрын
@@ahmedsylla2779leegui bou dioumè lan mo tèrè mou diegeulou xana di out arguments nan dagn mako wax tè sax nak limi dioum dafa bari
@Sénégalcakanam-bt4xw
@Sénégalcakanam-bt4xw 8 күн бұрын
Thiéy oustazou télé 📺 yi kouléne moytou woul séne poosse rékka léne nior mé dîné 0
@cissemodou4451
@cissemodou4451 8 күн бұрын
Daga fènal yonèntoubi saw
@TaphaSeck-dz8vb
@TaphaSeck-dz8vb 9 күн бұрын
Merci ❤🎉
@moustaphaloum-ln2jt
@moustaphaloum-ln2jt 8 күн бұрын
danou nga bara man nala corriger ndax l'islam kén momouko
@mameabdoudieng3780
@mameabdoudieng3780 8 күн бұрын
Machallah ya oustage
@AblayeNdour-be9ir
@AblayeNdour-be9ir 8 күн бұрын
Mohamed Mbaye régal yala
@serignesodagueye3398
@serignesodagueye3398 8 күн бұрын
Dèmal jangi Môgeune
@BayethiernoSeye-uv6hb
@BayethiernoSeye-uv6hb 8 күн бұрын
Waxo dégue dé
@serignethioubagueye6557
@serignethioubagueye6557 8 күн бұрын
Bayil wakh Lou doul deugg 😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮kou ame khame khame douko poukaré wo
@EbounjieEbou
@EbounjieEbou 9 күн бұрын
Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo rkkkkkkk Brother Freeeeeeeeeeeeee Senegal
@AhmedLo-eu2ek
@AhmedLo-eu2ek 8 күн бұрын
Deelen gueustou bubakh avant gaye wakh
@ibrahimaka8505
@ibrahimaka8505 7 күн бұрын
Kouna daga wara nopi
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 8 күн бұрын
DEUG , OUTACE MOHAMAD MBAYE , YAROU NGA , TEY NGA TEH SA KHAM KHAM KENEU DOUKO WERENTEH SI REWMI , MACHAALLAH.
@mamemorsene545
@mamemorsene545 8 күн бұрын
Mais limo wakh do deug
@ThioroDieng-lm5xz
@ThioroDieng-lm5xz 6 күн бұрын
Xamoul dara mo fi waxon S touba daa degg naxou bay jazamè damma ci xasiida( لم يبد مثل المصطفى) alors que dou lolou لم يبد فعل مضارع مجزوم) بحذف حرف العلة) touss xamouko nga naan borom xam xam
@AhmedLo-eu2ek
@AhmedLo-eu2ek 8 күн бұрын
Thiey Galséne 😂😂 leegui dal mla eupeu xam xam mo fi xew akhirou zamane
@ibrahimadiop3168
@ibrahimadiop3168 8 күн бұрын
Saway daga wax lu amoul Diegaloul et on passe
@NdeyeKane-q2u
@NdeyeKane-q2u 9 күн бұрын
Mouhamed mbaye merena trop vaurien daroul tontou manquer don doul katt nafekh fila watt bougoul dara thii poste mougua rigu gatt ensembles
@ibrahimaka8505
@ibrahimaka8505 7 күн бұрын
Kouna ndiaye amo khamkham nopil
@BabaColy-w1p
@BabaColy-w1p 8 күн бұрын
Cheikh bara mo wax deug
@ousmanekane7504
@ousmanekane7504 7 күн бұрын
شكرا
@AltouGagniktv
@AltouGagniktv 8 күн бұрын
وقال الكبر بطر الحق وخمط الناس
@mamegordione9071
@mamegordione9071 8 күн бұрын
الكبر بطر الحق وغمط الناس
@ndiayeouseynou3959
@ndiayeouseynou3959 7 күн бұрын
Machallah
@lycherif1552
@lycherif1552 9 күн бұрын
Demal diangi xamo dara te wallahi khamo dara
@mameabdoudieng3780
@mameabdoudieng3780 8 күн бұрын
Doulgua dh
@saurafall5922
@saurafall5922 8 күн бұрын
Yaw mi xam dara wakh gniou xamo dara
@lycherif1552
@lycherif1552 8 күн бұрын
@saurafall5922 loumou wakh sii yonentebi moussoul am
@mariamaniang4769
@mariamaniang4769 8 күн бұрын
Wakho deugue deh
@BbvxghLlccju
@BbvxghLlccju 8 күн бұрын
Wakofii darraa
@Casajah0302
@Casajah0302 5 күн бұрын
Site web bi amoul papier yow hamo Dara c'est faux amoul
@mamadoundoye6472
@mamadoundoye6472 8 күн бұрын
Serigne Bara Ndiaye mola dakheu diangg fouff dangako oumpeulé rek
@bsarr7264
@bsarr7264 8 күн бұрын
😂😂😂 pa ck mougui pastef
@deugrekmowoor4975
@deugrekmowoor4975 8 күн бұрын
Xamo dara amo xam xam saway
@mayekordiouf353
@mayekordiouf353 8 күн бұрын
Mais grand bi foofu mom dénga danou comme diangeu nga lépp loy wakh ci yoneté bi déffa warra done luñu bindeu ci terré yi qu'à même pas ci nitt
@mortallaniang5474
@mortallaniang5474 7 күн бұрын
Saway dèlèn indi dalil
@mohamedken4806
@mohamedken4806 9 күн бұрын
Bayilene sokhor machalah ❤
@cheikhmbacke485
@cheikhmbacke485 9 күн бұрын
Bayil fene
@elhadjidione8938
@elhadjidione8938 8 күн бұрын
Oustaz koula waxoul lou doul demal yokkou sa aliwa dalay nakh
@serignesaliouxassidamouser1164
@serignesaliouxassidamouser1164 8 күн бұрын
Cheikh bara limou wax dé amoul lén lothi mana dindi beuri am ndiangue nak ak dégue dako geune dama diapou ni danga ko wara sant wayé waro wérénté ak mom
@moadcasa9176
@moadcasa9176 9 күн бұрын
❤❤❤❤❤
@cheikhndom2711
@cheikhndom2711 8 күн бұрын
Mouhamed Mbay daga wara dém diangi Dara xamo ko 😢 Sa alluwa soriwul 😢
@bsarr7264
@bsarr7264 8 күн бұрын
Dougourou sonko yi lou nite wakh à part sonko ay féne 😂
@saurafall5922
@saurafall5922 8 күн бұрын
Yaw mi xam dara kén xamoula réy ngéne lamigne trope
@cheikhndom2711
@cheikhndom2711 8 күн бұрын
@@bsarr7264 Sonko seul ✊🏽
@cheikhndom2711
@cheikhndom2711 8 күн бұрын
@@saurafall5922 🤔🤔
@cheikhndom2711
@cheikhndom2711 7 күн бұрын
@@bsarr7264 sonko seul ✊🏽
@TamsirNdiaye-rz5rf
@TamsirNdiaye-rz5rf 8 күн бұрын
Sonko mogana sono niap bayilene fene
@bayedamesarr334
@bayedamesarr334 7 күн бұрын
Serigne momar diagn dousa morom si xam xam
@AntaDiba-k7b
@AntaDiba-k7b 8 күн бұрын
Abe dioulite dou raye parcaka khobai biai amoll xari
@massdiene7406
@massdiene7406 8 күн бұрын
Demale wouti kham kham
@seydouly3831
@seydouly3831 8 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@assanewade4242
@assanewade4242 6 күн бұрын
هو ليس بأستاذ..
@yorodeme8177
@yorodeme8177 8 күн бұрын
Merci ya ouztas
@degdeugtv7872
@degdeugtv7872 9 күн бұрын
Kima ko wakh moungui doundou lolou dou dalil ci diné danguéna réw trop
@saliousyll99
@saliousyll99 6 күн бұрын
wakh nga deug
@PetitNdao-ft1wf
@PetitNdao-ft1wf 8 күн бұрын
Une deux niouni daga sokhor ki limou wakh tégouko féneu iche
@laminembaye497
@laminembaye497 6 күн бұрын
Amo kham kham amo yar
@sady1964
@sady1964 7 күн бұрын
Amo kham khan borom kham kham dou wakh ma raw
@AntaDiba-k7b
@AntaDiba-k7b 8 күн бұрын
Deme l'éne sakou xame xame daguina diem yalla rekk xamou dary
@AltouGagniktv
@AltouGagniktv 8 күн бұрын
Bo dioumé dagay nagou parsaka domou Adamaga rék
@Mouhamad939
@Mouhamad939 8 күн бұрын
Eupo kham kham cheikh barra dh mom
@dokey9332
@dokey9332 8 күн бұрын
Mako raw mannama raww si xéll mou nekh, daradjia dan dan woutt kiisss nekh well mou nekhhh 🎉
@alioufall4265
@alioufall4265 8 күн бұрын
wakh nga deuge déh Bara Ndiaye mom Yako raw fouffe ndiange mou niaw la yore 😂
@Babss10
@Babss10 6 күн бұрын
Samay deloul si say kadou bo beugueu yone té bi loy wax ci mom na am dalil bou lerr Mais pas damako degueu ci diw
@mayelniasd290
@mayelniasd290 6 күн бұрын
Ouztaz maneu dè amena foumala tégoneu nit dou reuy danga dioum
@Babss10
@Babss10 6 күн бұрын
Boy netali dem deglou ba maîtriser histoire bi nga soga netali En plus même si tu as confiance en cet homme , demande lui ou il a tiré cet histoire. Borom xam xam dafay beugueu gueustou ci teré
@serignesalioulo8023
@serignesalioulo8023 7 күн бұрын
Mohamed mbaye liga wax dou wakhi darra tayit takhoul am XAM XAM nak
@ibrahimatidjany9202
@ibrahimatidjany9202 6 күн бұрын
Merci ameth boul tontou béne domérame ❤
@juufy4569
@juufy4569 6 күн бұрын
Dioulite dou reuy! Nangoule rék
@abdoulahatendiaye7020
@abdoulahatendiaye7020 6 күн бұрын
oztass bou reye waye ah dangua diom nél dama diom
@malickdiagne
@malickdiagne 4 күн бұрын
La reaction de ce oustaz montre qu'il lui reste du chemin dans le chantier d'ALLAH. Il est tres orgueilleux alors que nulle n'entre dans le royaume de Dieu en ayant une once d'orgueil. Tu dit que Cheikh bara ne doit pas de corriger car t'es plus savant que lui. Ou est ce que c'est ecrit ça. Meme l'imam de la mosquée, on le corrige s'il a fait une erreur. Un oustaz qui parle de l'histoire du prophete avec assurance mais quand on lui demande ses sources, il dit "ben goor gu bakh moma wakh" Tu te reclame de Tivaoune, et de tout ce que Hadji Malick RTA à ecrit, t'as choisis "ben paa nénama" T'as inventé ton histoire, excuses toi et on passe à autre chose.
@salcham5001
@salcham5001 6 күн бұрын
NGA BOUGA KO DEF DEFANTE, DANGA ROUSS REK. LINGA WAKH DOU DEUGA, TOUB KO
@sambasy7420
@sambasy7420 5 күн бұрын
Démal ma gnou kokou mou léral lal gnou gnoune gni beug Maodo téy topou dianga lém Keur Maodo kén douko takhal fii amoul lolou kokou na guèn wax fi yonenté kén douko sosal nak
Cheikh Bara Ndiaye Attaque Mouhamed Mbaye…Daye féne lim…..
22:34
LUNAIRE NEWS TV
Рет қаралды 99 М.
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41
Cat mode and a glass of water #family #humor #fun
00:22
Kotiki_Z
Рет қаралды 24 МЛН
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 59 МЛН
UFC 310 : Рахмонов VS Мачадо Гэрри
05:00
Setanta Sports UFC
Рет қаралды 1,2 МЛН
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 34 - VOSTFR
44:36
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 332 М.
mohamed mbaye limou sossal yonent bi salla lahou aleyhi wa sallam gnaaw na
17:33
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41