Salam salam salam Machalah ya oustaz imam cheikh Ibrahima Khalil lo. Yalnala Yalla bour bi fay yiw adouna ak alakhira défal ko sa famille ak mbolom dioulit ci barké alkhourane alkarim. Amine. C'est toujours un grand plaisir et une joie immense de vous écouter yalnanou Yalla bour bi may deg ak topa. ❤❤❤
@AdjaFaty-n2m19 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
@alassaneseye219119 күн бұрын
Machalah dieuredieufe cheikh ibrahima Khalil lo louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla faye billahi deug rek nga wakh nga Lou ler nga wakh sen ligueye rafetna yalla na la yalla sam ak molem oustaz bouy wakh si alquran ak suna
@Cheikh959319 күн бұрын
ALHAMDOULILAH MACHALLAH
@niominkarefoumtv592819 күн бұрын
MACHALLAH sheikh Ibrahim Khalil Lo dieuredieuf
@omarba586318 күн бұрын
Macha Allah ya oustaz
@assaneniang213319 күн бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu.
@MachallBoo18 күн бұрын
Machall ❤❤❤
@assaneniang213319 күн бұрын
Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sahaaba ya (RAA).
@madialis22118 күн бұрын
جزاك الله خيرا
@assaneniang213319 күн бұрын
Nanu YÀLLA def nu dëkkag ñoom ca Firdaws.
@assaneniang213319 күн бұрын
Nanu YÀLLA sàmm sàmmal nu aar aaral nu taxawu...
@assaneniang213319 күн бұрын
Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yònnent bi (SAAWS).
@assaneniang213319 күн бұрын
Mucc muccëlal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xam xam yi ragal sunu BOROOM YÀLLA.
@referencefoottv324519 күн бұрын
🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@assaneniang213319 күн бұрын
Nanu YÀLLA wan neen bamu leer, MU yombalal nu dùmmóoyu ko.
@assaneniang213319 күн бұрын
Taxawu taxawul nu, mucc muccëlal nu sunuy njaboot...
@assaneniang213319 күн бұрын
Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer, MU yombalal nu tòpp ko.